Day fène je suis en France honnêtement qu’il n’a pas d’argent depuis les 7ans fi dagnouye avale papier surtout Espagne tu peux travailler sans papiers day fene dafa niak diom
En tout cas comme saa yaye lolou lala conseiller mom meunouma wakh lénén. Mais comme niko fatou wakhé bouko mayati tokhou ! Té nak benen yone bou gneuwé Senegal na nga kham sa bopou dieul say precautions dem planning baa eumbaat doula si fekk parce que amna genre gorr yo khamni diarougnou dioureul ay dome you beurii ndaakh amougnou daraay diom yokou sa bopou problème rek lalay dioural ak gueunaa khataal sa négou yaye
Sa dieukeur dji kou bone leu. Gaure boula nangou woul doundeul bayiko. Dieukeur dafa wara yore diabar sinon seuyou tiaxaane leu. Niane bate bi nak, yaye séte. De toute façon, boulko waxati dara. Sétane ko té nga concentré wou ci sa liguey diay café. Santal yalla ci linga meune yore sa bop. Euleuk lou meuna xéw, dinga meunal sa bop. Wayé boul mossa dépenséti 1f ci mom. Néko mou déf devoir mari.
Salut CV sokhna Fatou Sama khalate RK Laye wakh adouna lofi guiss daye diékh boule Tass ndakh Bon tassé Mane NGA démate si goor gou geune Bone sa déuk keur 🥰🥰🥰
l'argent que le mari lui envoie peut conserver les reçus pour avoir. une preuve au cas où le mari voudrait les enlever à ses 2 enfants preuve du tribunal
Salam sokhna Fatou néko boumou tass seuy bi té na bayi wadji dieul responsabilité si djabott bii dakh dieukeur gui niakoul xaliss dayy déff liko nékh.. néko limouy goorgoorlu si café bi nakooy déff si bopam té na mûgne yalla guisna lépp.
Djiguène gni loulène dale gnoko yobé sène bope! Amna yo khamné do ko godage! Wadji kou gniak diomela kou irresponsable la! Na tasse. Bobou dieukeur gâte! Sa yaye ak sa mak amou gnou bène foulou
Garde tes enfants tu es dans tes droits même si tu divorces je vais te dire tu portes plainte Woma je te jure je suis en Europe je te dis ce que tu dois et tu garderas tes enfants inchalla et je te parle de loi c’est les mêmes lois en Europe même au Sénégal on ne retire pas des enfants à sa maman sans motif valable il faut que la maman soit dangereuse pour garder ces enfants surtout que lui il n’habite pas au Sénégal 🇸🇳xippill je suis sur TH-cam ki dafa niak yeurmande bonne continuation sokhna fatou
Cet homme est irresponsable. L'histoire qu'elle vient de relater même au tribunal de la Haie, elle aura exclusivement la garde de ses enfants. Aussi, l'homme devra verser une somme pour les enfants jusqu'à leur 18ans impérativement. Si leur union est scellée à la mairie, elle peut le traduire au tribunal pour fuite de responsabilité sur ses enfants. La femme doit tout prévoir, parler de tout ça à un conseiller juridique et là. Si le mari fait le fou, il le traduit en justice. Le problème est réglé.
Je lui conseille de déposer une demande de divorce au tribunal.ainsi elle pourra avoir la garde des enfants vu que le mari n'est pas au Sénégal et qu'il s'en est pas bien occupé. Si elle reste mariée au gars elle ne pourra pas refaire sa vie car elle n'est pas libre et elle va alors gâcher toute sa jeunesse en restant dans un mariage aussi inutile
Garde tes enfants tu es dans tes droits même si tu divorces je vais te dire tu portes plainte Woma je te jure je suis en Europe je te dis ce que tu dois et tu garderas tes enfants inchalla et je te parle de loi c’est les mêmes lois en Europe même au Sénégal on ne retire pas des enfants à sa maman sans motif valable il faut que la maman soit dangereuse pour garder ces enfants surtout que lui il n’habite pas au Sénégal 🇸🇳xippill je suis sur TH-cam ki dafa niak yeurmande
Elle peut aller au tribunal demander le divorce parce que le mari ne sest jamais conforme a ces obligations a savoir loger nourrir et vetir ca famille sans oublier la scolarité des enfants il faut qu elle garde les recus des envoies si il y en a et de toute facon puisse que le mari vit a l'étranger il peut pas récupéré les enfants de la dame pour les confier a une autre personne car leur maman biologique est la et est en bonne sante et elle travaille elle a un toit donc du couo elle remplie toutes les conditions pour avoir la garde des enfants il faut aller au tribunal cest le seul endroit pour avoir gain de cause il faut pas avoir peur des menaces
Sokhna si na dem def planning topoto ay domame ay DJI vrais domoùram nek si ligyey yam
Sokhna Fatou wadji yor na xaliss day déf louko nzkhe femme bi na ligueye déf si bopam yalla bakhe na
Asalamallekoum Sokhna Fatou caffè Masa Allah mercie beaucoup grazie mille vielen Dank ❤❤❤❤ depuis Italia
L'an motakh goor gni di déf lougnou meunoul ak di féne jiguen gni
Day fène je suis en France honnêtement qu’il n’a pas d’argent depuis les 7ans fi dagnouye avale papier surtout Espagne tu peux travailler sans papiers day fene dafa niak diom
Kikaye un vraie mythomane la amoul been yeurmande il profite de ma naïveté de la dame na dem tribunal rek tass seuy bi ki amoul ndieurign
Na mougne té mou kham né lo sone si sa say moy done sa banékh sa kanamou ndiabot
Salut sokhna Fatou Elhadj Thiam Atlanta wadji nit kou bonne la
Waw sokhna fatyt tu as raison na dok si seuy bi mais boum defati frais yi
Yobouko tribunal kone meussoulen yor meunoulen nangou deuk bi da am yone
Vraiment ça je l accepte antaka homme nako yobou tribunal
Vraiment bizarre ma sœur mais Dieu est grand qu'Allah te facilite
N'a tok té mounieu non Sénégal dafa âme goor yo khamni mérite wouniou sakh âme diabar nakh niak savoir vivre
En tout cas comme saa yaye lolou lala conseiller mom meunouma wakh lénén. Mais comme niko fatou wakhé bouko mayati tokhou ! Té nak benen yone bou gneuwé Senegal na nga kham sa bopou dieul say precautions dem planning baa eumbaat doula si fekk parce que amna genre gorr yo khamni diarougnou dioureul ay dome you beurii ndaakh amougnou daraay diom yokou sa bopou problème rek lalay dioural ak gueunaa khataal sa négou yaye
Sa dieukeur dji kou bone leu. Gaure boula nangou woul doundeul bayiko. Dieukeur dafa wara yore diabar sinon seuyou tiaxaane leu. Niane bate bi nak, yaye séte. De toute façon, boulko waxati dara. Sétane ko té nga concentré wou ci sa liguey diay café. Santal yalla ci linga meune yore sa bop. Euleuk lou meuna xéw, dinga meunal sa bop. Wayé boul mossa dépenséti 1f ci mom. Néko mou déf devoir mari.
Suivre les conseils de sokhna Fatou la présentatrice et ta maman dina bakh Inchallah raby sister
Salut CV sokhna Fatou
Sama khalate RK Laye wakh adouna lofi guiss daye diékh boule Tass ndakh Bon tassé Mane NGA démate si goor gou geune Bone sa déuk keur 🥰🥰🥰
Sokhna fatou wadji daye Tite di féne rek😂
Net tali bi souma ko yagué deglou douma am dieukeurou sénégalais
continuer di sétan rék yalla baakh na
Na continues seayam mu weru c yalla te leagai andark munge
l'argent que le mari lui envoie peut conserver les reçus pour avoir. une preuve au cas où le mari voudrait les enlever à ses 2 enfants preuve du tribunal
Wak gua deug fatou Yallah nalla deglou na deglou li gua wak wak gua leuo
Salam sokhna Fatou néko boumou tass seuy bi té na bayi wadji dieul responsabilité si djabott bii dakh dieukeur gui niakoul xaliss dayy déff liko nékh.. néko limouy goorgoorlu si café bi nakooy déff si bopam té na mûgne yalla guisna lépp.
mafi djitou wate way
yalla téré may liguey di diokh goor,goor dou projet😅😅
Djiguène gni loulène dale gnoko yobé sène bope! Amna yo khamné do ko godage! Wadji kou gniak diomela kou irresponsable la! Na tasse. Bobou dieukeur gâte! Sa yaye ak sa mak amou gnou bène foulou
Garde tes enfants tu es dans tes droits même si tu divorces je vais te dire tu portes plainte Woma je te jure je suis en Europe je te dis ce que tu dois et tu garderas tes enfants inchalla et je te parle de loi c’est les mêmes lois en Europe même au Sénégal on ne retire pas des enfants à sa maman sans motif valable il faut que la maman soit dangereuse pour garder ces enfants surtout que lui il n’habite pas au Sénégal 🇸🇳xippill je suis sur TH-cam ki dafa niak yeurmande bonne continuation sokhna fatou
natock yalla bakhna
Dieukerji amoul yermande. Sa khalis defalal sa bop ak say doom rk
Cet homme est irresponsable. L'histoire qu'elle vient de relater même au tribunal de la Haie, elle aura exclusivement la garde de ses enfants. Aussi, l'homme devra verser une somme pour les enfants jusqu'à leur 18ans impérativement. Si leur union est scellée à la mairie, elle peut le traduire au tribunal pour fuite de responsabilité sur ses enfants. La femme doit tout prévoir, parler de tout ça à un conseiller juridique et là. Si le mari fait le fou, il le traduit en justice. Le problème est réglé.
Na mounge rek adouna lepay diekh bilay
Sama hol tangana lol
Ndeye fatuo yalla na yalla fay❤❤❤
Da âme gaur gnou bone
N'a mougne yalla bakhna
Sokhna si kom keu yangui diay di fadjeu say sokhla kon mougnal yalla barina soutoura nga khôl thi say dom bla gnouy tassa ro
Wadji menoul naguou dôme yi lolou djaral tit délay napeu donc
Mercie beaucoup Sokhna Fatou caffè tu hai ragione mercie beaucoup pour les conseilles❤❤
Khalè bou djigene bi mo niak fayda rek dieukeur dji amoul khèl
Je lui conseille de déposer une demande de divorce au tribunal.ainsi elle pourra avoir la garde des enfants vu que le mari n'est pas au Sénégal et qu'il s'en est pas bien occupé.
Si elle reste mariée au gars elle ne pourra pas refaire sa vie car elle n'est pas libre et elle va alors gâcher toute sa jeunesse en restant dans un mariage aussi inutile
Garde tes enfants tu es dans tes droits même si tu divorces je vais te dire tu portes plainte Woma je te jure je suis en Europe je te dis ce que tu dois et tu garderas tes enfants inchalla et je te parle de loi c’est les mêmes lois en Europe même au Sénégal on ne retire pas des enfants à sa maman sans motif valable il faut que la maman soit dangereuse pour garder ces enfants surtout que lui il n’habite pas au Sénégal 🇸🇳xippill je suis sur TH-cam ki dafa niak yeurmande
Nakoontiné tok topotoo ligeyem ak doomam bi gadém si yoon lathié bakhm
Elle peut aller au tribunal demander le divorce parce que le mari ne sest jamais conforme a ces obligations a savoir loger nourrir et vetir ca famille sans oublier la scolarité des enfants il faut qu elle garde les recus des envoies si il y en a et de toute facon puisse que le mari vit a l'étranger il peut pas récupéré les enfants de la dame pour les confier a une autre personne car leur maman biologique est la et est en bonne sante et elle travaille elle a un toit donc du couo elle remplie toutes les conditions pour avoir la garde des enfants il faut aller au tribunal cest le seul endroit pour avoir gain de cause il faut pas avoir peur des menaces
Ki niakna diom te bone togaal te yala tah mais amal foula
Boul ko mayati khaliss,dafa beug lou yomb.mais boul tass sa sey.
Dey féne il n va Pas récupéré ses enfants dafkoy titeul si c'était moi j part au tribunal c un homme movai mougneul ma chérie qi kay da bon
Abale papiers je voulais dire
Mounial
Wadji kou bonne la