Thiongane, toutes mes felicitations, une personne très eduquée patiente et qui fait son travail professionnellement. Bon courage mon frère et bonne continuation.
Un journaliste très professionnel et cultivé ! Bonne continuation ne change surtout pas. Il nous manque ce genre de journaliste sur la toile, posé, instruit, respectable et pro.
LIMA NÉKH SI OUSTAZ IRAN TALIBE CHEIKH LA KOM MAN MI MAIS TARIHA YEUPOU LAY WAKHAL LOU BAKH AK SÉN DIEUFF YOU BAKH TA SOULA NÉKHON DOKO DÉFF KOM NIÉNÉN GNI MACHALLAH YA NIAKEU KINIAN MERCI BCP
N’oubliez pas de vous abonner sur votre chaîne Senbuzz Tv et d’activer la cloche 🛎 pour recevoir les notifications merci.
Good luck
MmmmM
@@chernodem9627 k
@@chernodem9627 p
À
Suis catholique mais j'adore les enseignements de cet Homme machalah tonton Iran
Weeuuh
Pareille que moi,longue vie ya oustaz
Pp Iran yalna yalla goudal sey fann té wéral sey thieur Serigne TOUBA amoul Morome kou d'accord beusseul aime
Thiey serigne touba amoul morom Oustaz Iran ya bakh te niakkignane machalla
Ndeysane
S'en buzz daal vous avez un journaliste qui parle bien et qui est très réactif
Absolument
Machalla oustaze iran yalla nala yalla samou té mayé la femme bou gou dou té and ak wérr ci barkép séydina mouhaméd slw
Mashalla Oustaz, yalla nala Allah sammal bopam barké Seyedina Moukhamed psl
Billahi kou bakh ga kènne doula manal dara
Bilay deiglou Iran ak setane Iran MoMA gueneul Setan Adamo
Wah yaw ko yap khol gua niar gnigay dindalé
Iran yalna yalla goudal sa fane wallahi ya gnémé deugue
Amine yarabi
Bilahi té ragaloussi dara
Amine Yarabal Alamine
Sldlbe
Ndéysane Oustaz Iran mogui dieum mag goudal fane papeu 🙏🙏🙏
Vidéos Vidéo
Poreneux
Gamme
Ce journaliste est vraiment instruit respectable et franche
Thiongane, toutes mes felicitations, une personne très eduquée patiente et qui fait son travail professionnellement.
Bon courage mon frère et bonne continuation.
Un journaliste très professionnel et cultivé ! Bonne continuation ne change surtout pas. Il nous manque ce genre de journaliste sur la toile, posé, instruit, respectable et pro.
😍😍😍
Merci Iran bamba wa dji ya gnak kignan papá iran merci miles fois diadieuf bamba
Nn srg bi nittou deugu rk mokoy nanguoul Bamba dou Morom
@@sawasalihatmidadi5144 bilahi lou ler nga wakh borom khol bou selleu rek mokoy nangoul Serigne touba ndamou Senegal la ak beppou dioulit
Yalla na yalla may nieup khar inchalla
Lou amsolo
Nitt kou bakh moungui nii iran ndaw yalna yalla ngoudal saw fan thi barke seydina mouhamed
Bilae amine waye
SAW🙏🙏❤️inchallah amine inchallah🙏🙏🙏nioubokou lepou fekeko té talko thie barke geungui mindéf SAW inchallah amine inchallah🙏🙏🙏
Amine
Amine
Thiongan yasi man de macha Allha journaliste yi nék Si télévisions you mak yi geuno niou la Ay de ✅
Machalan Iran je vous aiment bien é félicitations buzz
Mashallah ❤️ oustaz Iran ❤️ contane nagne si yaw❤️❤️❤️❤️❤️
Jërëjëf seriñ iran ndawe
det way 🤣🤣🤣
Vraiment irán dao je l aime for ❤️❤️❤️❤️❤️ avec ces veritéé absolut 💃💃💃💃
Vraiment serigne Iran vous êtes formidable machalla yalna yala samou la nitou deug nga namnala trop
LIMA NÉKH SI OUSTAZ IRAN TALIBE CHEIKH LA KOM MAN MI MAIS TARIHA YEUPOU LAY WAKHAL LOU BAKH AK SÉN DIEUFF YOU BAKH TA SOULA NÉKHON DOKO DÉFF KOM NIÉNÉN GNI MACHALLAH YA NIAKEU KINIAN MERCI BCP
Dieureudieuf iran contane si yaw yala naka ya may goudou fsne.serigne touba amoul morom
Iran & taïb toujours vérridique merci, bcp
Segne Bamba dou morome
Diereudieufeti mbacké
J'aime beaucoup
iran ndaw macha ALLAH longue vie à toi
Wallahi Ahmadoul khadimi sounou wadji Yal naniouko yalla fayal oustaz Iran ya niak kiñan
MACHALAA RAFETNA THIONGANE SAKAW SAKANAM SILOU BAKH AMINE MERCI BEAUCOUP MONSIEUR THIONGANE
Thieuy mbacké balla aicha amoul morom billah wallah dieureudieufé serigne touba❤❤❤❤❤❤❤ ❤❤❤
Machalah Iran yay niti DEUG yokou ba yeuko diadieuf alkhamdoulla
Merci à notre 1er e dame nationale ❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Machalla serigne iran kontanna si yaw boubakh bilahi nigay sédalé sama xoll yallnaka yalla sédalé sa adouna ak sa allakhira
Oustaz iran yalla Nasa jiam yagg vraiment lerr Na machala yalla Na xam xam bi gueun selleu ✍️👍dieuredieufé borom touba
Merci Iran je suis fière de vous pour tes conseils les jeunes de aujourd'hui ne écoute pas les conseils 🙏🙏🙏🙏🙏🙏
Merci d'avoir apprécié sama sopè bi
Machalla iran serigne bamba rék moko meune
Kou sopp papa iran ndao besseul j'aime ngir Yalla.
Diadieuf ❤️Iran
Machallah machallah machallah amna solo lool réalité absolue Dieuredieuf ya oustaz YALLAH nala yallah may Goudou faan wér soutoureu tawfékh
Waaw goor kendo Sëriñ Tuubaa Mbàkke Jaajëf jàmbaar yaa baax. De
mane mome dama nèkh rèkk bilaye daffa deuguou machalla 😍
Yalla na la Yalla same Oustaze Iran Ndao
Bilahi papa iran yaw kou bah nga yalla nala yalla sameu si barkep kou téd ki khadimou Rassoul
Merci Iran li dall Moïse lako Yalla my
Iran mala begue bilahi. Dieureudieuf serigne touba
Ana wa sonko yiss yii ❤️🇸🇦
Mnguii nii ❤️
thye serine Touba
Doulyawe
Magui nii
@@moustaphfall3192 sokhore mola diap Ak domeram Vive mon president Sonko 🥰❤️
Machallah am na solo trop vraiment
Macha Allah amna solo deugueu rek lay wakh Iran yalla naleu yalla may goudou fane ak werr
VIVE YAA OUSTAZ VIVA 🇸🇳🇪🇸🇺🇸☝🏾
Mashallah merci oustaz iran diadieufe contena si yaw
Waw kagne cheikh Iran ndao mouride sadikh bonne chance
Première commentaire j’aime 👍 leen
Bo bindone lou ame importance dinagn j'aime
Gno bagne 😂😂
il est bien thiongane bonne continuation
Bilay iran Ken dou serigne touba
DieuReuDieuF S TouBa Khadim Rassoul❤
DieureuDieuFety Serigne Touba
Billàhi Papa Iran damakô beugue ndakh dfa niémé deugue ...
Yalnafi yague té werr
😂🤣🤣🤣😂🤣😂😂😂Bilahi Iran.. Deug leu dé sou kharé gedj gui loum niouy dieurigne key.. 🤣🤣..
Kounkande man kharalma yonou Amérique 🇺🇲🇺🇲bi la sokhla 😂😂😂
Dieureudieuf serigne touba macha Allah iran ndao
allez jusqu'à 7 minutes c'est là où il parle de ça
merci
Merci
Merci way cest gentil
Merci way
Merci
Ay way yalna yane bi oyyof thi koukandei. Khar Guedj gui défi bou mag la. Ndeyssann gathiei bou kharroul Guedj gui.
Merci beaucoup papa merci
ماشاء لله أستاذ إبراهيم
Machallah outaz ibrahima
@@mouhamedsavane404 ok tu sais lire l'arabe 👍🏾
machalla iran yalla na sa diam yague kene dou serigne touba amoul morom
Merci vraiment Iran ya deugou
Kone tabaski rénn kou soupoul boko 😅😅😅 Iran damako beug bilahi
Yalna sa diamm yagg
Mane ira bilahi lezi je t'aime... Té yalla rek tax... Soy wax damay yeuk batou " hasbounalah WA nihmal wakil" Allah nous suffit..
Jërëjëf sëriñ tuubaa iran ndao yalla nga doundou 100 ans ak loutekk
merci ya oustaz iran ndaw
Aye waye Iran billahi mounofé gnakk force sur vous
Sonko gueumele yalla so ware nek president dignako nek sou nekhe yalla❤️❤️❤️❤️
Merci oustaz
MercioustazMachallah❤️
Dieuredieuf
Macha allah iran ❤
dieureudieuf serigne bamba
Iran deugue rek gua wkh
nitou deug la
Cheikh bamba kerok Bamou lalee der basa Guedj ga sigilna rasouloul lah sigilna islam
🤧🤧Cette Année TAMXARITE bi narna néxx
- 17h Kounkandé XAR GUETH Gui
- 19h Gnou consommer Thiéré 🤗
- 20h kou am VÉLO dieulko dawal ndank dougu ESPAGNE
😂😂😂😂
Questo video e bellissimo 🥰🥰🥰❤❤❤🥰🥰
Nama yalla bal kounkandè yalla yakam tiwko nimako dièpè dou diam
AMNA SOLO MACHA ALLAH
Thia S touba bala😅 dieureudieufaty Ahmadoul bamba Khadim Rassoul ❤🙏❤🙏👌🔐
Machalla 💓💓🙏🏻
Machallah machallah way
MACHALLAH
merci beaucoup Iran ndao
Iran yalla nala yalla defal diamou ak soutoura
Magui niane yallah mou mayla goudd fane akk werr
Ce journaliste est tres professionnel posé
Bilahi lou lerr ga wakhe pape iran
Ah yaw moom yombou na thie yaw .yalla na ko yalla yombalalale thieppe .thie barkep s touba
Diadieuf 🙏🙏🙏oustaz iran lingua wakh amna solo lole 🙏
Merci Iran ndaw
Bilaye serigne Iran ya wakh deugu d
Intéressant,instructif comme débat, on en redemande.
Machallah machallah machallah machallah
Merci papa 🙏🙏🙏
Meilleur journaliste au senegal
J'estime bien ce journaliste il fréquente le Coran et le français
Thia fréquentation bala
Ndanan la