Cheikh Bara doli Ab dioulite dey am bamelou biir lingay waxal Sonko duu yefou dioulite Sonko moma waxone lii iow do nit ku baax li yallah bañe ćii dioulite yéppa nguii ćii iow
Ki kay djiko yi yalla bagn yeup mou ngui si mom dafa reuy yakar na ni loum bokoul baxoul lolou dou dem. Té tarikha lay politigé lo wakh mouni serigne bi.
Ce bara il ment c'est parce que Mr Sonko amoul diottam beu di ko tontou nitt kou togue ak Sonko di dieuw dalay arrêté ci sassi waxatouma nak Sonko di dougou ci bureau am di wax ci Mme Touré Mimi ce bara ment comme pas possible il est grave
Cheikh.A.Bara Dolly,nit kou bakh dou reuy en plus togn bakhoul.parce bimoula wakhé politicien kakatar da nga mer,mou retiré ay wakham diegalou, ci même plateau bi nga togn avocat yi mounela retiré ko nga bagn lolou ak reuy la. Khamalni maître dafa la wormal,mais mérité woko...
Pastef bouko nekhé yake khaliss si campagne yi yonou ken nékou si sougnouy cotisation la diouguèwoul si caisou Etat.kon sougnou nékhé tale khaliss bi yonou bénén sénégalais bou andoulak pastef nékousi
Dethié est un homme politique dugne et courageux. Dire qu'il est TRANSHUMANT c'est vraiment galvauder la signification du mot TRANSHUMANT. Où tout simplement etre malhonnête.
BARRA DOULIPRANE MBEUKÉ MI EST CE QUE ÇA VA BIEN DANS SA TÊTE.EST CE QU IL S ENTENT PARLER.C'EST CE GENRE DE DÉPUTÉ QUE NOUS AVIONS À L' ASSEMBLÉE NATIONALE THIÉYE SÉNÉGAL
Comment avoir quelqu'un comme ça auprès de lui? Qui raconte tout ce que vous vous êtes dits et certainement en rajoute. Il défend avant tout ses intérêts. Un rapprochement après ce qu'il a dit est plus que improbable avec Sonko.
La partisanerie reflète la mauvaise foi. L'abstinence ou l'indifférence est une option au lieu de soulever la main dun transhumant. Cest se dédire. Cest pire quand il s'agit des maires aperiste qui sont moralement responsables que macky sall
Soutenir un parti ou une coalition à une élection ou à des élections n'est pas synonyme de transhumance. La transhumance s'est passé d'un bord politique à un autre via un marchandage politique..
CHETETTT BABACAR YA MEUNA FEN. YANE SENEGALAIS YEUP🔥? XALAL OPPOSITION BI KAY. EUX ILS FONT UNE COALITION SOUPE-KANDIA ET VEULENT EMPECHER A SONKO D'ACCEUILLIR DES SOUTIENS.
Bouder lolou kone kaye sonko peut accueillir macky . Moralement cest un partenariat contre nature . Vu tout le mal perpétré par macky et sa clique, rigoler avec ses anciens alliés sakh waroul.
Bara Dolly li moye woney sa waidi tey li moye woney que khamou Sonko dou Wakhe tie nit li ngua nek di Wakhe dou ben deugeu dafa yombe torope yow bara Dolly sa Mame bi ngaye mboubo dafa dieuf lougnou KO nawey mais yow Bara do Wakhe katou deugeu yow chaque jour que dieu fait tu te dédit sosse rek ngua def .Yow jamais ngua tarit arkhourane sa Mame rek do sa Mame écrit ton page personnel
Bara doli wala bara wagni. Goor bouy yakh dérnga. Samoo sa kadou. Gueumoo dara. Sénégalais yi bougougnoula. Sa poudre bou saf. Vrai transhumant. Thiout thiapet rek.
Ce Bara est tout sauf cohérent. Voyons donc voir la suite...Quand tu soutiens Amadou Ba, tenant d'un régime cruel; comment peux-tu te permettre d'être de donner de leçons .
Siré Ly oublie qu'en France, les PM vont aux élections? Le Pm est président d'un parti et doit forcément aller aux devants des électeurs pour leur demander de donner au président la majorité qu'il faut pour gouverner. Même en France, il y a des ralliements pour l'intérêt du pays qui ne conduisent pas aux marchandages politiques.
Bara dolli mom franchement Billahi dema ko yeureum defa meuna fen trop
Sa façon de raisonner montre à suffisance qu'il n'a pas sa place dans la nouvelle assemblée.
Ki dafa mana fen😂
Franchement, ki dou dara way
Merci cheikh ousmane l'état doit être fort liñouye bayi mou diale da yombe trop
Bien
Wakh degue dafa neikh
Dieredief cheikh Ousmane Touré❤❤❤
🇸🇳📢⚠️BARRA DOLLY EFFECTIVEMENT LA TRAVERSÉE DU DESERT SERA TRÈS TRÈS LONGUE POUR TOI PENDANT LES 50 ANS PROCHAINES ANNÉES POUR TOI‼️
Bara Dolly raisonne comme un enfant de 10 ans.
Par ce que dafa khamoul dara dou xam xam diné dou xam xam aduna.
Bara dolli Sonko mo yéye bayila ndax do wax deugue do dieuf deugue té bo taxawone Sonko taxaw Serigne Touba taneu Sonko bayila
Waliahi
😂😂😂
Bilahi wakatiko
Mome ak maitre dagaye lathie kane moy kilifa diné ci niome niar, ndakh maitre mon guena dégue guena bokal alkhourane bara dolli, li mon wor..
Cheikh Ousmane touré machaallah si pertinence bi❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Cheikh Bara doli Ab dioulite dey am bamelou biir lingay waxal Sonko duu yefou dioulite Sonko moma waxone lii iow do nit ku baax li yallah bañe ćii dioulite yéppa nguii ćii iow
Gni mou togal sakh kham nagne day fén motakh niou kay roubé
Ki kay djiko yi yalla bagn yeup mou ngui si mom dafa reuy yakar na ni loum bokoul baxoul lolou dou dem. Té tarikha lay politigé lo wakh mouni serigne bi.
Ce bara il ment c'est parce que Mr Sonko amoul diottam beu di ko tontou nitt kou togue ak Sonko di dieuw dalay arrêté ci sassi waxatouma nak Sonko di dougou ci bureau am di wax ci Mme Touré Mimi ce bara ment comme pas possible il est grave
@@alyfall4754 Serigne bimouy politiqué gnim bokal nioko ndieukeu wédi Touba foumou diar dagne koy yokhou
Amadou ba 11 ans ak macky sall lègui moy solution?
🇸🇳📢⚠️MERCI INFINIMENT MAÎTRE ABDINAR, VOUS ÊTES TRÈS PERTINENT PAR RAPPORT À BARA DOLLY‼️
Bara doly lutax mou beugue diakhasé sonko ak touba
Sire sy ta fait un bon analyse
Merci beaucoup Cheikh Ousmane
Mach'Allah Maître ❤❤❤
Cheikh Ousmane touré conseiller spécial du président de la république bassirou diomaye faye
Cheikh.A.Bara Dolly,nit kou bakh dou reuy en plus togn bakhoul.parce bimoula wakhé politicien kakatar da nga mer,mou retiré ay wakham diegalou, ci même plateau bi nga togn avocat yi mounela retiré ko nga bagn lolou ak reuy la.
Khamalni maître dafa la wormal,mais mérité woko...
Bara dolly aka meuna fen 😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Lothi wax am li dess ce bara vrai soss kat leu il est dangereux
Vive Me Ndiaye du Pastef Três Pertinent❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Bara dolly giir yalla nion wa touba bayil dino fénal sa bopo rk gay lidien ti bayi nio giir yalla
Waw kaye fipou lén rék😂😂
@@muhammaddia9162😂😂😂😂
Très belle analyse de Siré Sy sur le PM et les élections législatives
Maitre Macha Allah ya bakh si Bara Dolli
Me aby nar a raison
Bara dolly kakatar leu
Big up cot❤️❤️❤️❤️🇸🇳🇸🇳😊
Ceikh bara dolli nit kou bakh day wakh deuggg
Ayy ceikh bara yaa meunnn méw😂😂😂😂😂😂😂
❤❤❤❤❤❤❤cheikh Ousmane
C faut sonko n a jamais dit qu il arrète Les alles Dakar Baradoły fen rek ngay def
Pastef bouko nekhé yake khaliss si campagne yi yonou ken nékou si sougnouy cotisation la diouguèwoul si caisou Etat.kon sougnou nékhé tale khaliss bi yonou bénén sénégalais bou andoulak pastef nékousi
Dai fen serigne bara
Ce Bara doly kou doy war leu il ne fait que mentir c'est grave il ne changera jamais
Toutes les capitales civilisées du monde sont dotées des moyens de mobilité pour tous handicapés
Cirè mi kou soff leu di wakh melni kou lok aduna nitt yi daniouy dieun connexion
Non mais professeur Siré est au top de l’analyse, merci beaucoup waxx bi amna solo trop.
Yalla natonagio Gion wa Touba thi dolly dolly yii billahi yallna yalla dendi natou bi
🇸🇳📢⚠️DAMANÉ BARRA DOLLI NAÑU WAKH ÑATA LAKO AMADOU DIOULDÉ BÂ DIOKH CI LHALISS⁉️
Un politicien de métier qui voyage de parti en parti,sans conviction. Ce Bara doli.
Cheikh Ousmane wakh ki rek madambale est nuisible a la sociétaire make him keep his mouth shut
Bara Doli moo dakke fén si Sénégal
Dethié est un homme politique dugne et courageux. Dire qu'il est TRANSHUMANT c'est vraiment galvauder la signification du mot TRANSHUMANT. Où tout simplement etre malhonnête.
Alhamdoulila bii Abdou bara guené assemblée do wakhatou degue so khamalon Sonko diguako wer
Barra dolly guilifeugueu dé wakh lou ame
Sonko a Vie
Serigne Bara ya mana. Kathi. Zos you joup. Ngay zos Yangi yeungal Aras
Merci également Cheikh Ousmane Toure tu mériterais franchement un poste de conseiller pour le gouvernement.
Il faut dire a Madiambal et Yérim Seck de laisser SONKO en paix
BARRA DOULIPRANE MBEUKÉ MI EST CE QUE ÇA VA BIEN DANS SA TÊTE.EST CE QU IL S ENTENT PARLER.C'EST CE GENRE DE DÉPUTÉ QUE NOUS AVIONS À L' ASSEMBLÉE NATIONALE THIÉYE SÉNÉGAL
Sonko, sonko, sonko,sonko rek
😂😂😂😂 sonko dala ték dil politique rek laye déf boy bobou 😂😂😂
Xaw ma dolly xawma yokk un vrai mythomane 😂😂😂
Ki kay da wara bayi meew
Comment avoir quelqu'un comme ça auprès de lui? Qui raconte tout ce que vous vous êtes dits et certainement en rajoute. Il défend avant tout ses intérêts. Un rapprochement après ce qu'il a dit est plus que improbable avec Sonko.
Ki fen rek lay def
🇸🇳📢⚠️BARA DOULKATT BOU BOON NGA‼️ DÂGGÂA FÉNAL SONKO BAMOU TÉRRÉLA NGAŸ WAKH C AÏ MBIREUM‼️😡
🇸🇳📢⚠️BARA DOLLY OUSMANE SONKO N'EST PAS PRÉSIDENT POUR SE DÉFENDRE DE TES PROPOS‼️
🇸🇳📢⚠️C'EST SÛR QUE C'EST FINI POUR TOI À L'ASSEMBLÉE NATIONALE BARA DOLLI‼️
Merci,maître. Les politiciens n'ont pas encore compris que les populations sont beaucoup plus matures qu'eux.
BARA DOLLY DEEL WAX DËGG NGIR YALLA AP MBACKE MBACKE DOU WAX LOUKO LEERUL DÉ
Abdou bara dolly ragalal yallah sonko kouko xam dou waxe nonou.
Pertinente machallah cheikh bi❤❤❤
🇸🇳📢⚠️HÉ BIEN C'EST UN SEUTOU SÉRIGNE TOUBA BOU NAFÉKHEU LÀ, DAURKAT KHARAM BOU BÔN LÀ, THIEUM ‼️😡😡
🇸🇳📢⚠️QUE SONKO NE RETIRE AUCUNE PLAINTE‼️
SE FAIRE MARCHER DESSUS DEPUIS PLUS DE 10ANS JUSQU'À QUAND⁉️
Débat de bas niveau sur la transhumance. Où dans le monde a-t-on vu un chef de parti renvoyer un souteneur ?
La partisanerie reflète la mauvaise foi. L'abstinence ou l'indifférence est une option au lieu de soulever la main dun transhumant. Cest se dédire. Cest pire quand il s'agit des maires aperiste qui sont moralement responsables que macky sall
Barra daffa réww khamadi
🇸🇳📢⚠️QU'EST-CE QUE AMADOU PITTA DIOULDÉ BÂ A FAIT PENDANT LES 12ANS POUR LE PAYS ⁉️
Voter c décidé de qui vas décidé pour toi 🙏🏾tannall kiko diarr
Soutenir un parti ou une coalition à une élection ou à des élections n'est pas synonyme de transhumance. La transhumance s'est passé d'un bord politique à un autre via un marchandage politique..
Merci cheikh ousmane
Bravo mr
Débat de très haut niveau de maître Abdinar.❤
Mersi sergne ousmane 👍
🇸🇳📢⚠️CHEIKH THIORRO BÉTHIO ZT SONKO ÑO YÉY SORRÉ LÀ BOU BAKH‼️😡
Babacar yamana fén😂
Babacar tu es journaliste et tu ne peux pas te permettre de dire : Barthelémy, Anta Wala Khalifa " ces propos dit le contraire"
CHETETTT BABACAR YA MEUNA FEN. YANE SENEGALAIS YEUP🔥?
XALAL OPPOSITION BI KAY. EUX ILS FONT UNE COALITION SOUPE-KANDIA ET VEULENT EMPECHER A SONKO D'ACCEUILLIR DES SOUTIENS.
Bouder lolou kone kaye sonko peut accueillir macky . Moralement cest un partenariat contre nature . Vu tout le mal perpétré par macky et sa clique, rigoler avec ses anciens alliés sakh waroul.
Thiey cheikh Ousmane Touré ya meun dh so wakhe rk niou contane😊😊
Apres le 17,on n'entendra plus Bara Doly,heureusement.
Bara Dolly li moye woney sa waidi tey li moye woney que khamou Sonko dou Wakhe tie nit li ngua nek di Wakhe dou ben deugeu dafa yombe torope yow bara Dolly sa Mame bi ngaye mboubo dafa dieuf lougnou KO nawey mais yow Bara do Wakhe katou deugeu yow chaque jour que dieu fait tu te dédit sosse rek ngua def .Yow jamais ngua tarit arkhourane sa Mame rek do sa Mame écrit ton page personnel
Syri Aka Bari kham kham mei parfoi day vére
Ce Doly là ne va rien apporter à Sonko 😮
Dolly yagui fénal sonko dé, sonko kouko kham khamné dou wakhé niga wakh..
Bara doli wala bara wagni.
Goor bouy yakh dérnga. Samoo sa kadou. Gueumoo dara. Sénégalais yi bougougnoula. Sa poudre bou saf. Vrai transhumant. Thiout thiapet rek.
magou démb gni (ancien régime) 😂 pro sonko&diomaye 👉 dagnou laye wara moytou rék 🤔transhumance
Doli mo nek
Ndeysane bara dolli moy ngui sarakhou pour dellou si sonko
C fini. Je ne crois plus à ces petits marasous qui mentent devant leurs fils !
Ce Bara est tout sauf cohérent. Voyons donc voir la suite...Quand tu soutiens Amadou Ba, tenant d'un régime cruel; comment peux-tu te permettre d'être de donner de leçons .
Bou gnou fonton demal ci Serigne bi
Nespa lui qui disai que sonko setssiwouma nane lakoye wakhe lolou xi mimi
Abdou barra deye fenn
Siré Ly oublie qu'en France, les PM vont aux élections? Le Pm est président d'un parti et doit forcément aller aux devants des électeurs pour leur demander de donner au président la majorité qu'il faut pour gouverner. Même en France, il y a des ralliements pour l'intérêt du pays qui ne conduisent pas aux marchandages politiques.
Bayil cheickh omar diagne
Cheikh Abdou tu as essayé de mettre Sonko en mal avec Touba et Tivaouane
Même boula kosonko wakhe entre yow la ai mome, waro ko wakhe
Bara buruxlu, do delu assemblée deh.
😂😂😂 Diallo ak Babacar sérieux wougnou, wadji comédien lagnko diapé té mom ci deugam la nek
Dolli mi bou ko sonko defone thi liste pastef dou wakhee nii
😂😂MUHAMMED DIALLO YANGI JAY BARA DOLLY MUY JAYAXU MÉLNI BËY WU NAAN ZUMZUM
Cheikh Bara Doly mii dafaye douleule Sonko rk loume wakh dou deug
Tourè belle analise
Tape sene banc public nekhoute niou ame niveau guadone invité mais aye bara doulli douma yakal sama connexion
Non serigne barra douma raye😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂sonko dala nakhe kone