Akasa bay cheikh samb sama jëwrin kubakh te mana jàng te xam am njàng lool yalna yoku ci barkeb borom tuubaa Xamna lima ciy doli ngir leeral mooy daajj bii muy leeral nekul tuubaa mbéla waaye tuubaa bélél la toudu ndax 2em génération kourel s.masamba nioko jangoon tuubaa bélél ki jiitewoon njàng moomu mooy baay mbàkke fall yalnako yalla doli yërmaande akuk njëgël te tabalko àljjanatul firdawsi amiin ci barkeb xasida yi Mangi siyaar buwer tey toup ci kaduyi
machalla walay xetali nguama ndax linguasi waxni deh xamoumako si wone vraiment on a besoin de ces genres de video
Amna si solo DH bilalhi🥰
Akasa bay cheikh samb sama jëwrin kubakh te mana jàng te xam am njàng lool yalna yoku ci barkeb borom tuubaa
Xamna lima ciy doli ngir leeral mooy daajj bii muy leeral nekul tuubaa mbéla waaye tuubaa bélél la toudu ndax 2em génération kourel s.masamba nioko jangoon tuubaa bélél ki jiitewoon njàng moomu mooy baay mbàkke fall yalnako yalla doli yërmaande akuk njëgël te tabalko àljjanatul firdawsi amiin ci barkeb xasida yi
Mangi siyaar buwer tey toup ci kaduyi
Ki mome kham diangue way! Manchala !
Li sedd na xol barke borom Touba yala nanou kou tedd nangoul
😭😭 samb dafa yeme aka mague seutete deugal li rek
Thiey... jaajeuf Serigne bi lér naa lol
Ame na solo loll
Yalla ngafi yag téwérrr
NDAYSSANE COMPLET BI MOM AMO LENKO
Ans complet yi 😭😭😭😭
Dèffal envoyè way😭😭😭
Thieuye
Amna solo machallah
Ndeysaaan amna solo dh
Ndeysaan
Machalla
Jaajëf Samb
♥️♥️♥️♥️
🥰🥰🥰
Amna solo
Akassa
Ndayesane
❤
Akassa
machallah
Amna solo
Machallah