@@OusmaneSambe-l3fyaw nakk ya doff, masques yi pour neubou séne visages yi leu wakhna deugg korona amatoul danio wara interdire masques yi. Comme ça caméra de surveillance yi dieule séne visages bou bakh.
@@doudoudia8093 légui niouy takeu masque pour poussière bi bagn lén diokh fébar wala pollution bi nak vraiment africain mom mentalité zéro pour mom masque pour chorona virus rék leu té en plus ki caméra surveillance yi dieul nagn kanam gui bou yag mom ak borom moto bi
Il faut arrêter de laisser des choses visibles dans une voiture Avant de partir quelque part il faut tout mettre dans le coffre à l’abri des regards et fermer à clef.
Sath bi si premier romb bi si leu oubi portière bi ak mai gauche bi ,du cou meme sou chauffeur bi veroué sakh portière bobou dou fonctionneé ki so démé yagu na def li dhé ,solène garé té sen Auto yi délène vérifier sén 4 portière yeup eska teudiouna hooo😢 yalna ko yalla werr 😢
Sisi té bo setlo sath bi wath na moto bi avant wadji di garé, ca veut dire k niome khamone nagnou fou wadji dieum, dagnko top😢 mai nak magui niane Etats bi niou yok pêne yi guir yalla,kou sath 10ans de prison,kou agréssé gagn nitt 20ans de prison parsk li dafa wara diekh si rew mi khaliss kene douko lidieunti danioukoy liguey si ngor@@samdiawdiaw8269
Oui c'est le gars qui a remis l'argent au cas , qui a fait signe au malfrat.En fait l'agent qui a remis l'argent, il certainement 2 téléphones.. 1 téléphone a son nom et l'autre pour signaler.
Ca m'étonne beaucoup qu'une seule porte ne s'est pas verrouillé, si ca c passé comme vous dites aucune des porte n'est verrouillé en tout cas avec ce type de véhicule.
wadji yoroule dara da ndande auto rek pour k verouillage centrale bi dokhe il faut ke toute les portes soient verrouillées au moment de fermer la voiture si on ouvre une des portes la voiture ne se verrouille pas so sételo dou signal" dou claxonné ou bien verrouillage daye teudie après mou oubi wate
Naniou interdit masques yi korona amatoul, en plus de ça niit nakka laye takhawalo akk aye millions si auto té banques yi nekke fi, heureusement ba rayouniouko pour sathie xaaliss bi, daniouko diaye gayii.
DA khare ba whauffeur bi di wathie auto bi pour mou oubi boune tou auto bi comme sa auto sou bene pounetou oubéko so teudié ak verrouillage bi auto bi dou teudiou pour k auto bi verrouillé wou il faut k porte yeupe teudiou c'est au conducteur de bien verrouiller leur voiture avant de partir
senegal ken beugeutoufa dem ndah ay sathieu ak agression , afrique yeup gningui gniy mbam , recement la tik tokeuse malienne etait au senegal , meme pas 3 jours gnou cambrioler ko, vs imaginez sa, sonkoet diomay moussoumalen deug gni wah si
tant que arreter wougnou definitivement la presence des diakarta au senegal et particulierement a dakar , il yaura toujours l insecurite et les cas d agression
Gni brouilleur laniou yor laloul auto dafa bayil wadji di fermer mou brouiller clé bi cela fait que auto dou fermer wou dale nama ma dia wadji j’avais bien alerter ba douguel vidéo bi
@@MoulayeLaroussi Serigne bi boul saga di tchi ame bakar. Il n’en vaut pas la peine. Il y’a trop de jaloux autour de nous. Il ne sait même pas comment ce monsieur a fait pour avoir son argent. Yallah naniou Yallah Doli Soutoure
@SeydaAwa est-ce que moom itam dou sathie sakh? Parce que nak ils ont des smartphones et de connexion internet, donc ils sont partout (TH-cam, tik tok etc..)
le gars aussi n est pas assez intelligent car 3 millions dans une voiture et un ordinateur tous deux visibles et manque de prudence car il devrait faire le tour de la voiture et s assurer que tout est ferme. la faute lui incombe.pur negligence a mon avis
Senegal dou rew koi ay
Mak sans handicap pour travailler di sathie theuy yalla 😢😢
De grâce naniou bayi di dougueul yeneu sommes daniou lay top motakhe
Vraiment
meunoul niak ndax des fois da nguay soxla liquide
Loi Sénégal daf wara interdit masque corona diekhna
voilà
Mété waxi doff 😂😂li loumou dioté ak sol masque
Dof bou am connexion moy ioe ki inchallah dinagnko diam thi katanou yalla
@@OusmaneSambe-l3fyaw nakk ya doff, masques yi pour neubou séne visages yi leu wakhna deugg korona amatoul danio wara interdire masques yi. Comme ça caméra de surveillance yi dieule séne visages bou bakh.
@@doudoudia8093 légui niouy takeu masque pour poussière bi bagn lén diokh fébar wala pollution bi nak vraiment africain mom mentalité zéro pour mom masque pour chorona virus rék leu té en plus ki caméra surveillance yi dieul nagn kanam gui bou yag mom ak borom moto bi
Doyna War guathié international hoooooo bo démé kou ndayam bakh ligueyy keur bayzm ba sonn bilahi gno Bonn rek hoo😭💔😭
Il faut arrêter de laisser des choses visibles dans une voiture
Avant de partir quelque part il faut tout mettre dans le coffre à l’abri des regards et fermer à clef.
Thieuy senegal sathe goudi sathe beuthiakh
😂😂😂😂
sénégal kagn
*Humm doy na warrr😂😂😂😂😂😂😂*
Ki dé dinaniou guisse inchaallah
Raison pour laquelle Moto yeup wara am plaque niou meun len idientifier, merci Sonko carte grise ak plaque par force👍🏾
Waw loukhew legui Sénégal 😢
Dinalen diapp inchallah
Sath bi si premier romb bi si leu oubi portière bi ak mai gauche bi ,du cou meme sou chauffeur bi veroué sakh portière bobou dou fonctionneé ki so démé yagu na def li dhé ,solène garé té sen Auto yi délène vérifier sén 4 portière yeup eska teudiouna hooo😢 yalna ko yalla werr 😢
ioe guis nga lima guis
Sisi té bo setlo sath bi wath na moto bi avant wadji di garé, ca veut dire k niome khamone nagnou fou wadji dieum, dagnko top😢 mai nak magui niane Etats bi niou yok pêne yi guir yalla,kou sath 10ans de prison,kou agréssé gagn nitt 20ans de prison parsk li dafa wara diekh si rew mi khaliss kene douko lidieunti danioukoy liguey si ngor@@samdiawdiaw8269
il peut etre commanditer par celui qui lui a remi les 3 millioms ou meme lágent du service dóu il a retiré cette somme
Oui c'est le gars qui a remis l'argent au cas , qui a fait signe au malfrat.En fait l'agent qui a remis l'argent, il certainement 2 téléphones.. 1 téléphone a son nom et l'autre pour signaler.
Masque laniu wara interdit Sénégal bilahi c trop. Ku tahk masque rk suspect nge. Leufeul Ndéye gni rk😢😢😢😢😢😡😡😡😡😡😡😡😡😡😠😠😠😠😠😠😡😡😡😭😡😡😡😡😡😡😡😡😡😡😡😡😡😭😭😭😭😭😭😭😭😡😡😡😡😡😠😠😠😠😠😠😠😡😡😡😡😡😡😡😡gni tal sén ndéye rk
Amna appareil bo hameni dafaye déverrouiller bép auto 😮
Waw pass partout chiawi
Yawe Lo boke ake macky sall 😂😂
3 millions mome soumako yorone soumay poupe sakh damakoy yoor
😂😂😂😂
Barké Yallah
lol
😂😂😂
😂😂😂
Il faut agrandir l image et maximum de partage
Ca m'étonne beaucoup qu'une seule porte ne s'est pas verrouillé, si ca c passé comme vous dites aucune des porte n'est verrouillé en tout cas avec ce type de véhicule.
Sathie môme bakhoul😢
Domeram yiii koulenssi djapou tegeulen dayam bou bakh
❤❤❤❤❤❤ah li doyna war amoul gooudi amoul beuthieuk
wadji yoroule dara da ndande auto rek pour k verouillage centrale bi dokhe il faut ke toute les portes soient verrouillées au moment de fermer la voiture si on ouvre une des portes la voiture ne se verrouille pas so sételo dou signal" dou claxonné ou bien verrouillage daye teudie après mou oubi wate
Yalna lène yalla fènial si katanam gni nio niaque
Sen ligey rafet na Amna Solu Yalna Yalla fenel ko
ndeye sane masa
siporté ci moto lanou wara interdit
Voilà la seule solution
Mdr boulen sakh diakhlé, ki legui gars yi diap ko
Naniou interdit masques yi korona amatoul, en plus de ça niit nakka laye takhawalo akk aye millions si auto té banques yi nekke fi, heureusement ba rayouniouko pour sathie xaaliss bi, daniouko diaye gayii.
Mais une telle somme ken douko baayi si auto quand même
sokou bayil woul si auto bi bouñ kou agrésé ñiou ni waroule wone dokhantou ak mome
@MouhamadoufadalGueye-rb7lc on ne sait plus à quel saint se vouer doyna waar
Ñii takeu masque 😷 😷 😷 nioussi beurii ayy sathieu laniou.
😂😂😂 ya con
DA khare ba whauffeur bi di wathie auto bi pour mou oubi boune tou auto bi comme sa auto sou bene pounetou oubéko so teudié ak verrouillage bi auto bi dou teudiou pour k auto bi verrouillé wou il faut k porte yeupe teudiou c'est au conducteur de bien verrouiller leur voiture avant de partir
Mane dé diomi mariste amoule wone sathie wayé légui sakhe rék
Moto naniouko interdit Sénégal
MoMA diakhal Dee 3000000
Liii doy na war deh
senegal ken beugeutoufa dem ndah ay sathieu ak agression , afrique yeup gningui gniy mbam , recement la tik tokeuse malienne etait au senegal , meme pas 3 jours gnou cambrioler ko, vs imaginez sa, sonkoet diomay moussoumalen deug gni wah si
Diaroul sonou ils vont être chopé
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Dou guené assaka
Ngi kay douniou rethi
C'est de la négligence de la part du propriétaire du véhicule. Pourquoi laisser une somme pareille dans un véhicule
Galsen mo nekh legui raykakou nit ya ngui si biti con sathie lou ngueen def bakhna galsen amoul loi lou waaye nekh def mofa am
Eeeh ki khamnako
En
Wornama nii depuis thi banque lagnou koo topé
Kholal kissi moto bi ah gandayam do dem n day ligueyi wala dem beurre com say morom niak diom mai dinagn len diap yala nako yala def
tant que arreter wougnou definitivement la presence des diakarta au senegal et particulierement a dakar , il yaura toujours l insecurite et les cas d agression
Dignakou diap doméram dji
Sarap nday yi boy rek li ba kagn
Khalikh ci sac khèwina ci monde bi.
Comment peut on échapper dans ses conditions
Mane mato mo diél sama 854000 ak sama téléphone bou 40000 mille fi thie mariste
Senegal lafa am yemena li kagne
Pourquoi laisser une somme pareille dans une voiture non fermée????
❤❤❤
Galsen kay nekatoul rewou teranga rewou tueur la ak sathie
on entendez pas il a verouiller la voiture mais wadjii commande ley utiliser com clé
Y’a un machine qui ouvre n’importe quelle voiture c juste une petite appareille
Mask yi même policiers yi warougnouko tak parce que c'est pour camoufler
IL FAUT INVESTIR SUR DES CAMERAS EN 4K, mo geuneu lerr.
Gni brouilleur laniou yor laloul auto dafa bayil wadji di fermer mou brouiller clé bi cela fait que auto dou fermer wou dale nama ma dia wadji j’avais bien alerter ba douguel vidéo bi
Ki kaye dina délo xaliss bi ndax xamé nagne ko
Diap rey r3k mpy solution bi 3 rek bounlen talone dotufi am soyi esa es sance rek tal
Ken waratoul di doxontou ak yi toli ci xaliss
Gni gnioy mbam
Khalisse kene douka bayi si auto
Ki dou reuthie
Boy va bruler tes habits casques moto etc lolou la fi guissss sinon sa 5 ans lerna avocat sakh meuna Layyyy pas de preuve 😂😂
3 millions mom douma garé té douma vérifier ndah portes yi teudiouna.
Gni ay domeram laniou rèk thimmm li motakh bouléne boyi diapé dilène ray
dafa ame bene appareil bu burai comande auto bi matakh auto bi du tediou
Niak diom rek thimmm
Gni xana amouniou Nd😮jiabot
Khamnako Bou bakh wadji mo deuk galei niome mère…..Lire la suite
Brome auto bi moko téy Azakaa bou wara guéne la rékk 😢
Dara worou la tchi.
Sokhor ba khoule
Quoi qu'il arrive comment peut-on laisser 3 millions de cfa dans une voiture dans ce pays
Legui souko yorone gnouni 3.000.000 Nokay yoré
Police mo wara ronde niouy dajalo ci sen auto rek
C'est simplement ça
comment on peut laisser 3 millions dans un véhicule
3000 000 nga df ko thi oto dof rek
Na deme gendarmerie
Akh wadji dall weurseuk kame la diéll akh bou len niou sonall
Est-ce que tu es normal.
Dadoul yawe mo takh gnay wakh lolou.
Yaye domeram degue degue ah iow donc todiemane gue 😮
@@MoulayeLaroussi
Serigne bi boul saga di tchi ame bakar. Il n’en vaut pas la peine.
Il y’a trop de jaloux autour de nous.
Il ne sait même pas comment ce monsieur a fait pour avoir son argent.
Yallah naniou Yallah Doli Soutoure
@SeydaAwa est-ce que moom itam dou sathie sakh? Parce que nak ils ont des smartphones et de connexion internet, donc ils sont partout (TH-cam, tik tok etc..)
@@jammrek Doyna waar
😂😂😂😂😂 1