Coumba yag gua ma diioylo thie say way matay biniou la invitè nopiwouma man sayaye oumou kalsom diena niou guen ma hkam thie penda magui nian borom bi soub hana r alaw yal nala dèlo thie daguo inchaalah
Vraiment j'ai jamais vue une dame si adoré par tout un pays tous le Sénégal c'est mis en prient pour toi la grande diva coumba gawlo promis Rétablissement très tôt inchallah et que Allah nous guide nous tousse et nous bénisse
Sinserment je suis bouch bé par a port a ce que je viens de découvrir ho-dela même de ça craiére musical mais ça vie professionnel diplomatique et intellectuel Je t'aime du faund du cœur tata comba😍😍😍😍😍
Tata Coumba sougnou xol sed na thie yaww yalla nala yalla defale diamm maye la godou fane ak werr yalla feugg sa bopp léggi inchaallah je vous j'aime beaucoup tata Adoré
Merci pape cheikh merci Coumba Gawlo j'ai pleuré tout le long de l'émission (émotion)merci rendre hommage a une grande personnalité avant que ça ne soit trop tard c'est extraordinaire et magnifique merci a vous .Sana Diao kolda a Tanger au maroc.
Mane dall beugeu na djiguene bou ame diome gniari lokho moye tak seure gniari lokho moye tak toubeuye je suis très fier de toi yalla nala yala maye goudou fane ak were si barcke seydouna mouhamed alayhi salatou wasalame 🙏🙏🙏🙏❤️❤️🥰🥰
Courage👏wolahi nul n'est fort(e) devant la maladie bilahi wolahi j'en sais quelque chose c'est un vécu de ma personne et mon défunt Papa thiey fébar méti na nama Yallah bal ms bon dogalou Yallah ken meunou ci dara vraiment yalnaniou Yallah may wergou kharam koulou koum ci barké Nabi Moustapha miniou yakar 💯🙏🙏🙏soit forte et patiente incha Allah sa va passer t nagnou geuneu sante Yallah 🙏🙏🙏
Coumba notre fierté je me rappelle les bons moments à la cité claudel consert you nekh machalla ,là si j avais une baguette magique notre coumba nga wer leguiiiiiiiii❤❤❤❤❤
Bon rétablissement vraiment nous sommes très fière de toi k dieu vous donne la santé afin que vous puissiez continuer votre activité et réaliser tout tes rêve notre très cher diva la voix d'or. 💓💓💓💓💓💓💓💓💓💓💓💓💓💓💓💓💓💓💓💓
Manchalah la diva ❤️💪du courage yague ngua Di niou beguale yAlla nala yAlla maye were te werale sa voix ba ngua mena niewate sur scène inchalah. Si Barke mouhamed PSL 🙏🙏♥️
Ma coumba boul tite boul ragal weer ak jam thiat dou wess té li thiangate leu rek yalla nafi yem nga delou legui sa activé Inch'Allah barké Serigne Saliou
Tu auras de bonnes choses ma sœur Dieu ve te montrer quelque chose mais courage ça va passer Quelques soit la situation tu continueras à faire de la musique quelque soit la manière tu as ça dans le sang
la diva yalla n'a la yalla may wer tu e toujours dan nous cœur ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️ je t'aime fort fort fort fort fort diqua wer lequi inchallah
Coumba QU'ALLAH le tout tout-puissant te viennent en aide incha ALLAH wnibik hateu habiby au nom du prophète Mouhammad ALEYI SALATOU WASALAM amine incha ALLAHOU RABI délole lépeu si loho sounou borom SOUBHANA WATALAH boul tite boul ragal santal sa borom est dit tjr ALHAMDOULILA ALLA KOULIHAL té kou am nianou wadiour niako dara on est de tout coeur avec toi la diva le dernier mot revient à ALLAH SOUBHANA WATALAH ❤❤❤❤❤❤🙏🏾🙏🏾🙏🏾
Bilay khol toyna ma gawlo yalana yalla wéral batt bi bilay j’ai des larmes aux yeux mais bon dieu est grand la diva wakhali il faut être fort courage dina bakh
guiss beugu yalla la teh Sénégal yeup beugu nagnu la , lou am yalla la alkhamdoulilah ! Boul tite boul ragal amgua lou diafe , moy nianou wadiour, tiens bon ma chérie ! Love you !
Coumba 😭 bilaye sénégalais mo bonne mais Yalla nalla Yalla hare bilaye yaye coumba doundeul bou bakh 1000 ans tu la mérites tu es le mieux aussi mais sama khôl nekhoul nak mais yaye soeurette tante Yalla nalla Yalla hare
Yalana yala may tanei ak diam si barkei seydina mouhamet bangua continuer musique bii je t'aime beaucoup tata deuk nala yala ak prophète Mahomet salahou aleyhi wa salame
J'ai beaucoup pleuré yalla na yalla weral baat bi thi. Barké serigne babacar sy
Amine way
Coumba yaw boula darà métti. Yaw Senegal Mola désséle. Nanou lay guiss rékk ngay contaan di rétaan. Merci pour tous
Bilayy li sakh dafa nékh comme yagui âme lou la méti guaye guiss sa yaye rék santé yalla
Ndeysane j'ai même pas les mots 😭😭yalla nala yalla may wér 🙏🙏 nianou wadiour mo am solo thi dôme sunu borom weral la 🙏adouna dou dara te dara yagoul💖
❤️❤️❤️❤️❤️❤️🙏 ❤️❤️❤️❤️❤️❤️😭
🥰🥰♥️♥️♥️♥️😭😭
Coumba yag gua ma diioylo thie say way matay biniou la invitè nopiwouma man sayaye oumou kalsom diena niou guen ma hkam thie penda magui nian borom bi soub hana r alaw yal nala dèlo thie daguo inchaalah
Merci aux fon de mon couer yalla n'a yala werel batebie
Vraiment j'ai jamais vue une dame si adoré par tout un pays tous le Sénégal c'est mis en prient pour toi la grande diva coumba gawlo promis Rétablissement très tôt inchallah et que Allah nous guide nous tousse et nous bénisse
Amine iow kou bah gua macha alla
@@diorniang7130 non c'est Rien ça
Elle m'a vraiment touché hier
Sinserment je suis bouch bé par a port a ce que je viens de découvrir ho-dela même de ça craiére musical mais ça vie professionnel diplomatique et intellectuel
Je t'aime du faund du cœur tata comba😍😍😍😍😍
Comme tu es belle tata Coumba ❤️yalna la yalla May tane si barke Srg Saliou 😘🙏
Tata Coumba sougnou xol sed na thie yaww yalla nala yalla defale diamm maye la godou fane ak werr yalla feugg sa bopp léggi inchaallah je vous j'aime beaucoup tata Adoré
Maman Coumba gawlo diam rek ngaye am doundall ba yeuk ko seck ndanane Amal diam jtm fort Maman Coumba gawlo nala diam sonale fou nék 😍♥️😘
Je ne commente jamais rien mais li il le fallait je suis fière très fiere de toi coumba Dieu va te restaurer au nom de Jesus
Merci pape cheikh merci Coumba Gawlo j'ai pleuré tout le long de l'émission (émotion)merci rendre hommage a une grande personnalité avant que ça ne soit trop tard c'est extraordinaire et magnifique merci a vous .Sana Diao kolda a Tanger au maroc.
Tu a la chance d avoir ta maman elle tres gentil main yallla bakh na yalla nala yalla maye werr akh dame du courage ❤️❤️❤️❤️❤️
♥️♥️♥️♥️♥️🥰🙏
Yalla na yalla wéral bate bi Coumba le public Sénégalais et le monde entier on beaucoup besoin de toi bon rétablissement 😘😘
Bon rétablissement la diva....je pleure même parce que je ne peux pas voir une lionne souffrir...yalla nala yalla sameu .....delola lepp mashalla
Mane dall beugeu na djiguene bou ame diome gniari lokho moye tak seure gniari lokho moye tak toubeuye je suis très fier de toi yalla nala yala maye goudou fane ak were si barcke seydouna mouhamed alayhi salatou wasalame 🙏🙏🙏🙏❤️❤️🥰🥰
Juste bcp de prières pour vous tata Coumba que l'Éternelle t'accorde la santé. Vous êtes vraiment un exemple pour notre Sénégal 😚❤❤
Bon courage coumba, je te souhaite un bon rétablissement tu es une battante ❤️❤️❤️❤️
Diam si iow Gawlo! Yalna yallah mayla wèr insha’allah!! Tu es tres forte masha allah:))
Mersi. Cuo
Premiere commentaire
Que le bon Dieu soit avec vous
La grande diva à la voix d'or yalna yalla feug sa bopp banga delousi watt on t'aime maman Coumba ❤️
je n'en peux plus vraiment jai bcp pleuré 🤲yalla n'a bororm bi weral baat bi
Tata Coumba ❤️ yallah na yalla may tane féké ak tal si barké cheikhoul Tidiane🙏🙏❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Yalla na yalla feugue sa bope, mayla weer Incha Allah! Longue vie et santé de fer à toi Coumba Gawlo Seck. Courage Coumba
Courage👏wolahi nul n'est fort(e) devant la maladie bilahi wolahi j'en sais quelque chose c'est un vécu de ma personne et mon défunt Papa thiey fébar méti na nama Yallah bal ms bon dogalou Yallah ken meunou ci dara vraiment yalnaniou Yallah may wergou kharam koulou koum ci barké Nabi Moustapha miniou yakar 💯🙏🙏🙏soit forte et patiente incha Allah sa va passer t nagnou geuneu sante Yallah 🙏🙏🙏
Coumba notre fierté je me rappelle les bons moments à la cité claudel consert you nekh machalla ,là si j avais une baguette magique notre coumba nga wer leguiiiiiiiii❤❤❤❤❤
Vraiment je t'aime fort la diva tu es très forte 💪
Bon rétablissement vraiment nous sommes très fière de toi k dieu vous donne la santé afin que vous puissiez continuer votre activité et réaliser tout tes rêve notre très cher diva la voix d'or. 💓💓💓💓💓💓💓💓💓💓💓💓💓💓💓💓💓💓💓💓
Bonne guérison tata Coumba gawlo,♥️ chapeau à elles
Notre fierté la Diva doundeul wereul 🙏🥰❤️
Bon rétablisement la lionne,une femme exceptionnel, une brave,la beauté africaine.Yalnala yallah maay werr,respect a vous
Manchalah la diva ❤️💪du courage yague ngua Di niou beguale yAlla nala yAlla maye were te werale sa voix ba ngua mena niewate sur scène inchalah. Si Barke mouhamed PSL 🙏🙏♥️
Sama yaram dawe coumba yalla nalla yalla takhawou si barke seydina mouhamede la diva
Ma coumba boul tite boul ragal weer ak jam thiat dou wess té li thiangate leu rek yalla nafi yem nga delou legui sa activé Inch'Allah barké Serigne Saliou
Ohhh ma coumba de luxe, digne, classe et pleine de personnalité change surtt op k'Allah te garde ma chére
Macha allah la voix d’or Coumba yalla nala yalla same deffal la weurr ak weurrlei incha allah boul ragal dara et courage la grande❤️❤️
Ndeysann j'ai pleuré tt l'émission, yalnala yalla sama gawlo chérie 🙏🙏🙏🙏
Tu auras de bonnes choses ma sœur Dieu ve te montrer quelque chose mais courage ça va passer
Quelques soit la situation tu continueras à faire de la musique quelque soit la manière tu as ça dans le sang
J ai les larmes aux yeux Yaye boye yalla nala yalla takawou thi barke Seydina Mohammed ( PSL) incha'alla dina bakh 💓💓💓💓💓😭
Amine
Émouvant ! Tu as pleuré et tu as fait pleurer tout le monde. Prompt rétablissement COUBA. Ça ira bien In challah
Coumba gawlo is indeed a diva ndyesan wish you a speedy recovery
Kouné ake nigua tolou souniou gawlo kéne d'où yawe seck que le bon dieu t'accorde une très bonne santé ont aime très fort
Coumba gawlo yalla bakhna yalla nala yalla faye sa xol Dina bakh inchallah
Bon rétablissement ma diva je t'aime ,je t'adore inchallah tu reviendras en force 💪💪♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️
Maman Coumba tu vas nous revenir par la grâce de dieu boule raggal dara ame gan sa geunreumeul wa dior
Oh mon dieu coumba yalnala yalla maye werre 😭😭😭😭😭
Bon rétablissemen La diva nationale 💖💖❣️❣️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️
Bilahi walahi talahi dinga tané inchallah fouma tolou magui nian yalla mou mayla wer ak wer lé inchallah jtm jtm jtm jtm jtm mama coumba
la diva yalla n'a la yalla may wer tu e toujours dan nous cœur ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️ je t'aime fort fort fort fort fort diqua wer lequi inchallah
Dama dioye ba sonne yalla nala yalla weral batt bi
On est tellement fière d'elle machalah yalana borom bi defal diame yoner la werr
Bilay on s’aime notre gawlo
Ndeysann coumba ak yayame damasi guisse ma mereet moi coumba weral ak diam🥰
merci cawlo yalna yalla defal diame desde fi si Argentina cheikh la sa fan fi si Argentina te querio mucho
Tey sama khol dafa diekh lima dioy meusumako dioy jai le coeur brisé bilay yalla nala yalla defal diam li dafa daw yaram 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
Alhamdoulilah mention spéciale à tw pape cheikh yangi soga deff louma nekh machalah khamo sakh linga deff AK touyaba binga sii meuna ame khôl yeup toy nah coumba goudal faane diam rekk ngay ame
Mane tmt soxlana kouma consolé dioyna ba sone 😭😭😭😭😭😭vremen on t'aime fort notre gawlo international
Man Bamako khamai ba tay soumako gisé damay dioy damaka beuge trop😢
Coumba QU'ALLAH le tout tout-puissant te viennent en aide incha ALLAH wnibik hateu habiby au nom du prophète Mouhammad ALEYI SALATOU WASALAM amine incha ALLAHOU RABI délole lépeu si loho sounou borom SOUBHANA WATALAH boul tite boul ragal santal sa borom est dit tjr ALHAMDOULILA ALLA KOULIHAL té kou am nianou wadiour niako dara on est de tout coeur avec toi la diva le dernier mot revient à ALLAH SOUBHANA WATALAH ❤❤❤❤❤❤🙏🏾🙏🏾🙏🏾
Bon rétablir la grande non je suis triste bilahi yalna la yalla wéeral si barké s fallou
Coumba notre fierté yala noko yala défal diam si barké wérou kor gui
Ndeysan 😭bn retablissement ma cherie coumba c triste wlhi yo allah rockou diam wnbik
Bilay khol toyna ma gawlo yalana yalla wéral batt bi bilay j’ai des larmes aux yeux mais bon dieu est grand la diva wakhali il faut être fort courage dina bakh
Maman co
Courage maman Coumba ♥️♥️♥️🙏yallana yalla weral batt bi🙏💖💖
Aye oyy coumba niou bok aye mame chez pendan débarone bi nak niou riche yalla gua tanè ake diam wayé
Machala gawlo santal yalla inchala tout ira bien notre diva
Liii doyna warr COUMBA LA MEILLEURE VOCALISTE SENEGALAISE I LOVE DOUNDAL LES BEAUX JOURS ARRIVENT IN SHAA ALLAH ❤❤❤❤
Bon rétablissement notre Gawlo tanéll ak diam.notre diva international
guiss beugu yalla la teh Sénégal yeup beugu nagnu la , lou am yalla la alkhamdoulilah ! Boul tite boul ragal amgua lou diafe , moy nianou wadiour, tiens bon ma chérie ! Love you !
Coumba yalla gua weurr si barke baye niass yarabi
fière de toi notre chère diva ❤❤❤
bon rétablissement 🙏🙏🙏🙏
Yallah na yallah may leuh werr thi barke Mouhamed psl
Yalla khamenané damaye djooye rek sii je le regarde maman Coumba courage sava allé je sui en Espagne Palma mes je t'aime au fond maman
Coumba la diva sa diann wathieuna yall n'a la yalla fayall bopam. May la werr diereudieufeuti
Bon retablissement la diva a la voix d' or❤
Soit forte tu es ma référence je t'adore et bonne guérison
Guérie toi vite ma belle 💓💗💕❤️ gawlo
yallna la yallah may werr thi barke baye Niass yah rabbi ❤❤😭😭
Merci tu es très fort bon courage
Bon rétablissement coumba guawlo
Sama gawlo jama rek ngay Am insahalla
machalla yalla nala sunu borome bi laf Thiat amal foulay doundou rék séck ❤
Yalna yalla wéral baat bii si barké serigne saliou
Du courage et bonne continuation sa ira mieux inchallah
Jai pleuré tout au long de l'émission c vrema triste bon rétablissement la Diva 🙏🙏🙏🙏
Tanel ak diam la diva🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲
Diam rek nguey ame tanel ak diam😘😘😘
jtm maman comba Bilay walay. yalla nala yalla defal diam ak werr amine yarabi 🤲
Tout ira bien la diva gawlo on t'aime et on ne cesse de prier pour toi
Bon rétablissement tata coumba jtm jtm jtm jtm jtm ❤❤❤❤❤❤❤
Bon rétablissement la diva tout ira bien inchallah par la grâce de dieu
Q
Bon rétablissement qu'Allah le tout puissant vous donne une très très très longue vie 💝💝💝
Yaye kaladiela si dome yalla bakhe na di courage
Macha Allah meilleure santé ma puce
Bon rétablissement notre diva nationale ❤❤❤❤❤
💜💜💜💜💜💯💯💋
Yalla na yalla feug sa bop baga délou watt si Say activités 🙏🙏
❤😊😂❤ Bon rétablissement la Diva❤
Coumba 😭 bilaye sénégalais mo bonne mais Yalla nalla Yalla hare bilaye yaye coumba doundeul bou bakh 1000 ans tu la mérites tu es le mieux aussi mais sama khôl nekhoul nak mais yaye soeurette tante Yalla nalla Yalla hare
Tané ak diameu la diva j'ai beaucoup pleuré
Mane mome manouma sakh wakh ndakh ay😭😭😭yalna nala yalla defal tane
Bon rétablissement coumba tu es la meilleure trop engagée machallah l'afrique a besoin de toi
Ndayesane yalla nala yalla maye wér🤲🤲🤲
Bon rétablissement la diva
Yalana yala may tanei ak diam si barkei seydina mouhamet bangua continuer musique bii je t'aime beaucoup tata deuk nala yala ak prophète Mahomet salahou aleyhi wa salame
Ndeyssan Sama yaye mag bu yarou la. Fégnna si lépp
Yalla nala yalla defal jambe coumba gawlo.
C vraimnt extraordinaire😓😓😓😓😓😓😓
Que dieu soit avec vous
yalna yalla weral yaram dawna
Sama cousine Dale j l'aime très fort elle est très brave
@@mimymbaye5956 🙏🙏🙏🙏🙏😭
Diame rék laye ame