Secret 7 vol 1 pour moi c'est le meilleur album de l'histoire pour moi toi tu es l'ennemi de ngaaka blindé pour moi ngaaka blindé c'est le meilleur 👑 wallahi
Un fans dip qui insulte ngaaka nit gni il sont pas fou frère ngaaka son album secret 7 moy l’un des meilleurs albums de l’histoire du sénégal. Sokhor bakhoul mec apprécie ngaaka ak dip psk meun nagn yobou ragalsen fou sorii merci
Ce mec a très bien compris le vide de contenu de ngaka blindé il fait plus de maquillage et de mariage folklorique pour se faire passer devant les sénégalais comme un fils du peuple au lieux de se battre lyriquelement dans le game typiquement rap avec ces codes il a peur de perdre le fil et il fait du bruit comme le tassou
Dire que secret 7 vol 1 c’est un flop suis pas d’accord Secret 7 est un album riche en terme d’écriture de flow et de thème Comme tu viens de le dire un hit C’est un hit aucun artiste ne peut te dire que je vais sortir un son est ce son sera un hit
Musique bi dou gawa dem ndax dafa am niou sokhorr c dommage.. Kinga Baba ligueyoul? Niou deplacer sa Keur ba fii pr nga wah si mom nganii ligueyoul😅 Baba sou ligeyer todj fii
Sa waye yow ya meuneu doule secret 7 ngaaka album tout les son son bonne par contre dip rappeurs mais album bimou moudié géne es ce que rap késsé la ballein féne sohor bakhoul dip tout ses son qui on fait hit toumbakh la
Mec sokhor nga album ngaaka bouder dafa flop conn galsen albums yeup flop li complo la pour yax image Ngaaka mais touti ngein si cocou limou am dako legueye
Comment on peut se moquer des Senegalais de cette manière? Tu te mets devant des milliers de gens pour nous sortir des sottises comme quoi « SECRET 7 vol I » est flop! Avant de critiquer les artistes ainsi, il faut d’abord reconnaître le travail acharné mais devant un camera, un micro prés de ta bouche rekk tu juges le travail des gens comme ça ! Secret 7 comme tant d’autres projets artistiques est le fruit des nuits et des nuits sans sommeils, des heures entre 4 murs pour donner le meilleur !!! Mec,vas apprendre la communication d’abord!!!
Il a parfaitement raison,qui dafa kham musique.... Mais malheureusement sénégalais yi 70% yi khamouniou louy RAP... Ngaaka fais du Rap Tassou... Omzo Dollar dafay RAP Dip Dafay RAP Elton Jamdong dafay RAP AK quelque boy...
Bayile sokhor king baba c le meilleur 🎤🔥
ki dafaye doul ènèmi ngaka leu king mo nek meilleure rapeur Senegal
Secret 7 vol 1 pour moi c'est le meilleur album de l'histoire pour moi toi tu es l'ennemi de ngaaka blindé pour moi ngaaka blindé c'est le meilleur 👑 wallahi
C juste ca
Dagaye khar monoko guènè sounou khol❤ngaka rèk kàsè kote mome dòguè
Ki wéroute lol secret 7 vol 1 rk ❤
Naanal glace sokhor nga ndym trop
Tout à fait ta raison par rapport tt se que tu as dit sur ngaaka
NITT KOU SOKHOR AMNA MAIS KI DA YESSS
Sokhor am na 😂😂
Même dip accepté na talent ngaaka blindé 😂 dip néna conce n'a s7 v1 bii il la apprécié 😂
Wakhalall yalla koladegue khamne farr nga
Ngaka amoul morom ❤❤❤❤❤❤❤❤
Nice na trop
King baba 🇸🇳🇸🇳 rék
Ki fan dip la
Niou khamoul rap rek niokoy saga mes il la raison il encourage ngaka afair plus deffor mes ces lyrics sont terre à terre
Yao xamo dra si lingay wahk cou wahk ngeini xamoul rap t’es yena xamoul gate
Un fans dip qui insulte ngaaka nit gni il sont pas fou frère ngaaka son album secret 7 moy l’un des meilleurs albums de l’histoire du sénégal. Sokhor bakhoul mec apprécie ngaaka ak dip psk meun nagn yobou ragalsen fou sorii merci
Sawaay yaw bou album bi guénei di nga noopi dé
Inchallah ngaaka day dominé Rap bi 💯
Big up 👍🏿 🔥
Me frère ioe meun doul nak ioe et ce que tu écoutes réellement @King Baba nek Thi TH-cam Di fén rek ibabe wa
Sa way sa invité bi sokhor neu dh😂😂 waouhh meussouma guiss lii
Bro ioe fo todie bly dagua sokhore nk
No ki da am louko ngaaka def billahy lolou môme lérr nama 😂😂
Yén niaar niépp sén data ndaye kiléndi vidéo data ndayém king baba papay boye golo
Ce mec a très bien compris le vide de contenu de ngaka blindé il fait plus de maquillage et de mariage folklorique pour se faire passer devant les sénégalais comme un fils du peuple au lieux de se battre lyriquelement dans le game typiquement rap avec ces codes il a peur de perdre le fil et il fait du bruit comme le tassou
Kbc❤❤❤❤❤❤
Wadji limouye wax dafa neexoul accepter wayer il a raison sur toute la ligne
King baba
Mg maker ioe mom meusso beug baba
Non billahi ki da sokhor secret 7 fait partie des meilleurs albums rap galsen
Sokhor bakhoul
Dip lo niémé niak😅
Dagay fén dh
Ki da am problème ak gnaAka wala
Sauf ayooo kingg baba bann son legnii consss beu leguii musiba nieww fayy leppp😅😂
Ki daye féne 😂😂
Ki dafa bagne ngaaka 😂
Khana sokhor sakh tite na😂😂
King baba rék
Ya moun dam laye abonnés le gui❤❤❤
Ngaaka na déff music bouko nékh
Public Rap bi késsé mounougnouko yob international bayilén naxanté
Heureusement niom nandeu Nagne yone bii
Mais il a parfaitement raison
😂😂😂😂😂😂kimomeun ndaye doul😂😂😂😂
Nice my g
Mais invité bii mom esk sava, secret 7 vol 1 ngua xamni y’a que des songs riche, mounane c’est flop, kii fans dip leu deh
Bayill dip ki dou fans dip da khamoul dar Secret 7 album dakhoko
Del invité Ay borom xaam xaam si milieu rap bi mo geun
MG maker yaw daga yag contre Ngaaka motah tu laisse ces bordel attaquer ngaaka sans donner des possibilités de répliques à ces proches
Ww
Yen Niar Gnepa Yem Sen Stratégie Bolen Tek Rek Pour Saboté Ko La. RETHIOU Na Loutakh Ma Dugu Fii.
Bonne continuation mon gars de la part de Idy (ISEG)
Merci Mon Frère
Danio wéssou lingay wah
Mais yow ya tardé baganio tardél
Nice concept OG 🎉
Big Thanks Homie 🎉
😂😂😂😂woy doulkat bi
Ki dafa dieloule ay garabame Mouy takhaw di wakh ay wakhi doff
sa way néna Secret 7 vol 1 dafa flope mdrrr😂😂😂😂😂
Dire que secret 7 vol 1 c’est un flop suis pas d’accord
Secret 7 est un album riche en terme d’écriture de flow et de thème
Comme tu viens de le dire un hit
C’est un hit aucun artiste ne peut te dire que je vais sortir un son est ce son sera un hit
Nitt you xamoule sarap di commenté si king baba
Mais invité bii neexna 😂
🔥🤣
kii neexna nak😂
Secret 7 flop nga wakh ioe may wakh mounane bène hit où est incorrect final mais ki moo sokhor😂
Waxou fy Dara ngaaka artiste leu maylen niou
Yow sa leufeul nday invite bou todj sa leufeul nday gua sokhor gua démm
Ay sisou mane guéne 😂😂
Wadji mo meun dull deug 😂
Prochaine fois sa son bi dafa faible. Mais plateau bi Nice débat bi amna niveau
Oui tu as raison et Thanks🔥🫵🏾
Sokhor bonne ignane gnaak diom bo bayiwoul sissou legui nga dèhh idiot 😂😂😂
Ki da bougou buzz ms yew dagaye rare yew
Ya sokhor 😂😂
Il a parfaitement raison bro
Sokor😂😂
Wa ki kala si 😂😂😂
Musique bi dou gawa dem ndax dafa am niou sokhorr c dommage..
Kinga Baba ligueyoul? Niou deplacer sa Keur ba fii pr nga wah si mom nganii ligueyoul😅 Baba sou ligeyer todj fii
Saway ki di wakh keureum la togg ni dehh
@ ba lguii mogui dieul tmps wam di wah si ben nitt bo xamnii neina ligueyoul..!
Iblisse cv Kay ki boy da dof
Sa invitation daye doul ndayam sa data ndaye sa koyou yaw ngaaka Moy sa baye gaye doul ni rk😂😂😂
Sa waye yow ya meuneu doule secret 7 ngaaka album tout les son son bonne par contre dip rappeurs mais album bimou moudié géne es ce que rap késsé la ballein féne sohor bakhoul dip tout ses son qui on fait hit toumbakh la
Ki xamoul rap té dou nopi himra meilleurs rappeur tout le africaine
Ki ham ham lay wah ni srx
Ki sokhor na Bilay 😂
Il a parfaitement raison bro
Wa😂😂😂
Mec sokhor nga album ngaaka bouder dafa flop conn galsen albums yeup flop li complo la pour yax image Ngaaka mais touti ngein si cocou limou am dako legueye
Comment on peut se moquer des Senegalais de cette manière? Tu te mets devant des milliers de gens pour nous sortir des sottises comme quoi « SECRET 7 vol I » est flop!
Avant de critiquer les artistes ainsi, il faut d’abord reconnaître le travail acharné mais devant un camera, un micro prés de ta bouche rekk tu juges le travail des gens comme ça ! Secret 7 comme tant d’autres projets artistiques est le fruit des nuits et des nuits sans sommeils, des heures entre 4 murs pour donner le meilleur !!!
Mec,vas apprendre la communication d’abord!!!
Loll secret 7 ngaani flop la 😂😂😂😂 sa analyse bakhoule
👎👎👎👎👎
Mais c'est qui ce gars ??
😂😂This guy is just jealous of king 👑 BABA, what has he achieved in the music 🎶 he's a hater that's all
Il a parfaitement raison,qui dafa kham musique....
Mais malheureusement sénégalais yi 70% yi khamouniou louy RAP...
Ngaaka fais du Rap Tassou...
Omzo Dollar dafay RAP
Dip Dafay RAP
Elton Jamdong dafay RAP
AK quelque boy...