J'ai vécu la mm chose pratiquement les soeur de ma mère me fesaient vivre l'horreur et je demande dieu de m donné la force de les aider a l'avenir inchallah
Hé ma belle j'ai vécu la même chose que toi sama badiéne de même père et de même mère m'a accusé de vol de ses bijoux en or j'ai fait la même chose j'ai quitté le lieu de travail pour lui demander quand je suis arrivée à la maison j'ai trouvé mes autres badiéne avec elle entraîne de faire une petite fête je savais même pas quelle doit rentrer en France le même jour je lui ait dit que j'ai rien pris consernant ses bijoux en pleurant jour et nuitet el m'a même sachez de chez elle mon papa était le seul frère dans leurs familles et est décédé très tôt quand j'avais 5 ans jusqu'à maintenant je n'arrive pas à oublié ça mais je te dis courage lep dina meseu bakh inchalalh 🙏🙏
Du courage chérie Khamal ni yallah dina léne até inchaallah thi barké Seydina Mouhamed (صَل الله عليه و سلم ) Mougnal rek li yeupaye djiékh inchaallah rabi
Ne pleure pas ma chérie,soit forte,é sask yalla jehoul la justice divine existe,mane on m'a traité de tous les noms ,telk sathie,thiaga,mm deum,mais tay jexna , yalla gui may soutoural ba lignioumadone wahal lep guissouniouko , encore une fois je dis merci a mon Dieu . É tu sais kelk chose ma chérie,le ou on m'a traité de c noms c ce jour là k je devienne plus forte pour faire face à mes ennemis,car je sais kil chercher à me déstabiliser mais jamais je verssais mes larmes devant eux,mm si je meurs de chagrin j'essaye de le gérer ,une fois k je suis toute seul je pleure de toute mes forces pour me soulager.maintenat c ton tour bas toi devant eux n les montre jamais k tu é triste
Courage sister moi méme jai vécu cela kan avk une voisine Cté une téléphone portable On ma accusé sans preuve et jy ai rien compri mais grace a Dieu 3 jour apré on a attrapé le vrai voleur ki n'étai ke le neveu de son mari 7 ans apré jé mon travail et ma femme et chak fois ke je croise cette femme elle a du mal a me fixé dans led yeux
Wa Sokhnasi mougnal j'aime pas voire une femme qui pleure tu t'es biens defendu cameme et j'admire ton courage li si dess djiegueulko té balko aduna amoul solo. Dieureudieuf Sokhnasi
@@foogadebbomolooty9839 merci Hapsatou yen dé ngen wara di begué di contane sa souné kena waroulen tek matite . Bouma faté dé boy niane si SERIGNE BASSIROU MBACKÉ
Bama amé 10ans dém vacance sama keur rakou yaye mou maye djigne sathie. Dima yobou si guendeule may dioy guoudé bathiek c le vacance le plus longue de ma vie doumako massa faté ba sama bir bamel doumako massa faté
Courage mes chéries. Ma mère vit mais j ai vécu la même chose car en ce moment j etais chez mon oncle pour mes études. Et depuis ce jour j ai juré que bayinaléne ak yalla mais niane sama borom aussi que sama diom ak ngoor yalla na deuk di yok. Aujourd hui bougnou ma sokhlawoul sokhla woumaléne car j ai une vie extraordinaire une belle réussite mashallah. Car yalla mo até. Lougnou ma eupalé wone rek ba djigne ma sathie tey sougnou defna meuna louko raw 1million de fois. Digne , ngoor , diom ak foula réka diara sakou
mougnal lo guiss nètalii rk moudiè courage soeur mètina mais yalla balamo diokh keen dakoy yaan ba parer yalla na yalla tèguil kèpou kou nekk sii khat khat
Elle avait besoin de faire se témoignage pour se libérer car elle peut être une thérapie pour elle de pouvoir justifier à tout le monde son innoncence. Masta ça ira inchallah
Thiey allal, je suis meurtri. Que Allah te donne la force et le courage de surpasser cette épreuve. J'ai trop mal. Adina amoul solo. Nguir allal rek diarna sankh sa dome. Cest grave. Yeureum ndaw si.
J'ai vécu la même chose la sœur de ma mère elle m'a fait subir la même chose m'accuser de vol partout où elle passe elle disait aux gens que je suis un voleur l'époque j'habitais chez elle mais comme on dit la route tourne c'était elle la voleuse mais quand je pense ça me fait toujours mal alors que ça fait plus de 10 ans mais quand je pense c'est comme si c'était aujourd'hui Une jour ma tante et habiter à France était venu en vacances à l'époque j'étais parti voir ma mère au village après de retour à Dakar elle m'a appelé pour me dire que ss parfum on disparu et que c'est moi qui les a pris parce que ma tante lui a dit que je te un voleuse les mots m'ont brisé le coeur et quand je te dis à ma mère je ne vais jamais oublierai la peine qu'elle avait dans les yeux après la vérité et finit par éclater c'est elle qui a volé toute la famille là si et personne n'a plus confiance en elle elle vole même ses propres enfants je remercie toujours Allah de m'avoir blanchir
Du courage ma sœur on t'aime beaucoup c'est Un peu difficile pour les enfants qui n'ont pas vécu avec leur mère courage et essaye d'aller de l'avant pour ton enfant
Sama tante cad sama diabarou papa meuss nama accusé sathie 1000f bobou ce2 la done df tei sama yay neikoul si keur gnep di ma saga ak dorr gnoumay reitane école fouma tourné deimay dioy après Deikei Khaliss domam moko dieul mais batey doumako fatei dei doumako baleu deifmay wo dima gnane credi tissu ak lounei mm ay domam malein di deifal mais j n p pas oublié cette histoire
Tourne la page be happy ... bou Gnoula yakhale sa Adina ...si weule sa bope pour rien .... gni khamoule wone khame ....... Media bakhoule . Vie ta vie diarouko sis . Du courage. Mais des années gua dèffe Li sa khole reek come on dou yawe dou yawe . Bayile akk Yalla ..... Mais Li mome dou idée bou bakh...... fèkhAlale es à khole . Be strong 💪🏼 Boule djoye sis 😘♥️❤️❤️
Métina mai sois forte yalla loumou name diéhal bilahi dey dieh😭😭mm bou fékone yako dieul sah warone na hol sang bii ndah alal mom kéne dou dé bamou top la mai du courag
Ma belle ne pleure pas et ne pense plus à ça. Vis ta vie, Yallah atténa té dina gueuna atté inshallah. Fais toi belle, mange, réjouis toi et fais plaisir à tes enfants et à ton mari. TU N'ES PAS LA SEULE A SUBIR CES MÉCHANCETÉS. VIS HAPPINESS POUR LEUR MONTRER QUE TU ES CLEAN ET BLANCHE COMME NEIGE SÈNES KHÔLES DI DAGUE, GADJÉ DILÈNE RÈYE DANKE DANKE INSHALLAH. ❤
Sa rakkou yaye bobou dee warna rouss ndeyam thim mane sama kholbii bone na sakh mais li moye lane sheuu niak yaye mo graw walahiii sa rakk yaye bobou kou bonne ndeyam la mais yalla nalla yalla atek mome deug mome yagu yagu daye fegn
Massa li metina torop j’ai vécu pire que ça Tout allait bien avant que ma mère ne décède , elle avait un seul frère pour qui elle a fait tout mai malheureusement depui k ma mère m’a quitté son frère m’a pri com sa femme j’avais 16ans la première fois qu’il a abusé de moi Jn connaissais rien je versé tt les larmes d mon corps je pensais qu’il allait arrêter mai non il a continué et il m menacé d me tuer si jamais jl racontes à quelqu’un et bien entendu jn pouvais pas depui 16jusqua 20ans il m viole presque chaque jour à chaque fois qu’il en a envie et âpre il m donne des médicaments pour ne pas que je tombe en ceinte j’ai maintenant 21ans j’lui ai fui il n sais mêm pas où je suis jsai qu’il me cherche tjr mai il n réussira pas à me trouver il m’a complètement détruite j passe tte mes journées à pleurer mai n’empêche j suis croyante j laisse tout dans la main d dieu jte conseil d faire pareil toi au moins tu as un mari et tu as eu des enfants par contre moi non et Jn sai mêm pas si un jour jm marierai ni encore moin encore des enfants
Ni leuh dhé courage dès fois mettî nga lakkatou dioy ba sa xol sed guenatt si nite gni mais dara yagoul gueume ko rekk xam na si dara leepay bax diarr diarr la rekk💪🙏🏼
Quand j’avais 9ans dama dagn ma mayone sama rakk yaye Moumay maltraité dima guigne sathie Demna ba lakk sama lokho Affaire you boneu yonlen xalatt deff namako Mais Yallah moma sauver maintenant sumako guissei day rouss Bilaie
Masta ma grande li yeupe aye nétali laye moudjié bilaye maneu niite moma doule sonaleu mouye kima bokaleu sang ou pas sama yoneu sama yaye rek ak sama pape gnoma diore . Ak sougnou mboro Ak cheikhou tidiane 👌🏼🙏🏽
AISSATOU DIA xolaleu lolou rek mèti yoyou meuneu nala nopou diapeu la baa def la fèbar mbagua dè tei kèneu dou khameu mais yalla khamna lèp aduna Bi Mon mètti bari hypocrite mougne rek Moy solution bayilèneu AK yalla
Yaw dagnou la djinne sathie rek yam si santal mane dh yama tané j'ai que 18 ans mais la famille de mon père khâgne ma diam dima liguéy dima yakal diakhasé mak sam papa gt a l'étranger gnou ligey ma yakal ma sama ligey bima amone fofou gnou fékhé bama niew galsen batay mayou gnouma diam alors g ke 18ans yaw am nga sa dieukeur am say dom santal yallah bou bax am nga gno tanè dh
Ceux qui disent que c est problème de famille on doit pas le mettre dans le net sont vraiment hors sujet. Une fois à la police ensuite au tribunal c est déjà sortie du cadre familiale...On se dit dioulite et on fait pire que les mécréants celui qui pense au jour du jugement dernier et je crois évitera de faire du mal à toute créature à plus forte raison un être humain...Courage ma fille Dieu est là et in challa ces gens-là verront.
@@francineabron4991. Ndeye lègui darrou Salam la deuk mes. Mane mangui nguinte toujours j'habite avec ça famille môme seuyina lègui depuis guissatoumako wone wayer nite geunouko si adouna boma mené djiokhe ça numèro amoule blèm
J'ai vécu la mm chose pratiquement les soeur de ma mère me fesaient vivre l'horreur et je demande dieu de m donné la force de les aider a l'avenir inchallah
Waw coumba koula dji Lou gnaw fayko Lou rafet
Talibe Serigne Babacar s'y la te khôl bou raffet rek mo am solo
Ralibe Serigne Babacar s'y la te khôl bou raffet rek mo bakh
Ah Machallah, c'est bien. Koula yéné moussiba yénéko lou bakh. Aduna amoule solo. La vie est éphémère.
Aissatou Mané hè amoull feye lou bahh da nga di halee
Yana la sa dome dem ba may lèn Or❤❤❤
Vraiment j'ai les larmes aux yeux bougouma guiss djiguene mouy dioye
Cava
@@manianglo92 ça maniang loubess
ndiaye maleye ohh masta
@@diattousow2104 bilahi Sénégal amna nio xamni amouniou xol ak yermande diattou
Aduna amoul solo real nigga nga💯
Hé ma belle j'ai vécu la même chose que toi sama badiéne de même père et de même mère m'a accusé de vol de ses bijoux en or j'ai fait la même chose j'ai quitté le lieu de travail pour lui demander quand je suis arrivée à la maison j'ai trouvé mes autres badiéne avec elle entraîne de faire une petite fête je savais même pas quelle doit rentrer en France le même jour je lui ait dit que j'ai rien pris consernant ses bijoux en pleurant jour et nuitet el m'a même sachez de chez elle mon papa était le seul frère dans leurs familles et est décédé très tôt quand j'avais 5 ans jusqu'à maintenant je n'arrive pas à oublié ça mais je te dis courage lep dina meseu bakh inchalalh 🙏🙏
Limotakh kén dokhtoul mbokk🙄
@@moussacamara9206😊😊😊😊😊😊😊😊😊
😅
Bo rindé say nonneu say mbok jekh
Yalla nala yalla takhawou
Bilay walay say mbok nioy seu nonneu!!!
Mbok amatoul
Adounia bi dafa graww et c’est désolant
Courage ma sœur 😭😭😭 wollahi Allah ne dors pas patienté ☝️☝️☝️☝️
Kham nala bou bakh nitt geunoula yalla nala yalla fay sa khol kou bakh nga😢
Du courage chérie
Khamal ni yallah dina léne até inchaallah thi barké Seydina Mouhamed (صَل الله عليه و سلم )
Mougnal rek li yeupaye djiékh inchaallah rabi
Ne pleure pas ma chérie,soit forte,é sask yalla jehoul la justice divine existe,mane on m'a traité de tous les noms ,telk sathie,thiaga,mm deum,mais tay jexna , yalla gui may soutoural ba lignioumadone wahal lep guissouniouko , encore une fois je dis merci a mon Dieu . É tu sais kelk chose ma chérie,le ou on m'a traité de c noms c ce jour là k je devienne plus forte pour faire face à mes ennemis,car je sais kil chercher à me déstabiliser mais jamais je verssais mes larmes devant eux,mm si je meurs de chagrin j'essaye de le gérer ,une fois k je suis toute seul je pleure de toute mes forces pour me soulager.maintenat c ton tour bas toi devant eux n les montre jamais k tu é triste
Courage sister moi méme jai vécu cela kan avk une voisine
Cté une téléphone portable
On ma accusé sans preuve et jy ai rien compri mais grace a Dieu 3 jour apré on a attrapé le vrai voleur ki n'étai ke le neveu de son mari
7 ans apré jé mon travail et ma femme et chak fois ke je croise cette femme elle a du mal a me fixé dans led yeux
Wa Sokhnasi mougnal j'aime pas voire une femme qui pleure tu t'es biens defendu cameme et j'admire ton courage li si dess djiegueulko té balko aduna amoul solo. Dieureudieuf Sokhnasi
gomis Jean robert merci tu et adorable
@@foogadebbomolooty9839 merci Hapsatou yen dé ngen wara di begué di contane sa souné kena waroulen tek matite . Bouma faté dé boy niane si SERIGNE BASSIROU MBACKÉ
Toumeu yague nafi, mais yalla guiss na lép. Massa .
Bama amé 10ans dém vacance sama keur rakou yaye mou maye djigne sathie. Dima yobou si guendeule may dioy guoudé bathiek c le vacance le plus longue de ma vie doumako massa faté ba sama bir bamel doumako massa faté
Courage ma chérie sa diar diar la walaye gueneu yok djom
Ouley Camara merci 🙏
Du courage ma chérie lép day diéh loudoul gourou yalla
Fanta DIARRA bilay djignela lo défoule dafa méti surtout so nèké peuvre
Courage mes chéries. Ma mère vit mais j ai vécu la même chose car en ce moment j etais chez mon oncle pour mes études. Et depuis ce jour j ai juré que bayinaléne ak yalla mais niane sama borom aussi que sama diom ak ngoor yalla na deuk di yok.
Aujourd hui bougnou ma sokhlawoul sokhla woumaléne car j ai une vie extraordinaire une belle réussite mashallah. Car yalla mo até. Lougnou ma eupalé wone rek ba djigne ma sathie tey sougnou defna meuna louko raw 1million de fois.
Digne , ngoor , diom ak foula réka diara sakou
J'ai pleurer
Mounial té bayi lepou si lokhoy yalla yalla guamoul nelawoul boula dara métti 😭😭😭😭
Massa yayeboyame bayilen ak yalla syster Dieu contrôle bien soeur
Ce ki me fait mal au monde c'est de voir les larmes d'une femme respectons nos mamans
Ya bakh 👏👏👏
C'est vraiment triste ndèyssan, courage ma puce et tout ira bien, inch'Allah
mougnal lo guiss nètalii rk moudiè courage soeur mètina mais yalla balamo diokh keen dakoy yaan ba parer yalla na yalla tèguil kèpou kou nekk sii khat khat
Du courage Mme.... remet tout entre les mains du Seigneur.
Yallah dinala taxawou
Bb chérie lolou deh mofi am diamono Mo teureudi kou nek ak sa blem nak courage
Hoo Dooyna Waar Sister Mouñial Yalla Dina Até Leep InchaAllah god
🛄😭😭😭😭metina
Yalla dina ate lepe inchalla mounial rek lou way mougne mou diekh yalla na la yalla takhawou
Dafa méti mane bama amé 10 ans sama diabarou tonton dafané ma sathie Or domame mes aujourd'hui j'ai 21 an té fatéwou mako 😡
Khadija Sow Yalla bakhna
ibrahima sy yallah dinala atee ak nioom mouniall
Yalla bakhna sénégal moy lolou
Khadija Sow courage
Alahira dina meti trop. Togne bakhoul
Elle avait besoin de faire se témoignage pour se libérer car elle peut être une thérapie pour elle de pouvoir justifier à tout le monde son innoncence. Masta ça ira inchallah
ربّ أٓخّ لٓمْ تٓلِدُ اُمّكِ 😭😭😭 فصبر لحكم ربك 😢😢ياأختى
Massa ma chérie courage
Je vous souhaite bcq de courage. Apprenez à pardonner et oublier, en laissant la main au Tout Puissant...
Ndeysane 😭😭😭😭😭
Yalla nala yalla takhawu
Bilahi walahi dioye na sakh ndeysane metina trop
Mougnal chéri yala dinala ateik gnome inchala courage 😘✌️
yalla nala yalla takhawou si barker seydina Mohamed psl
Pareillement,le 14 mai 2023 doumako fattè sama addina😢😢😢
Massa ma fille cheri boul dioy li mofi am legui loufi nakhari ni ay mokam nion koko tekh mai bayi len ak yalla dinala feyyoul
Vraiment triste massa sokhnaci yalla nguisneu lep😭😭
Ohhh😭😭😭😭😭
Massa ❤️❤️
Thiey allal, je suis meurtri. Que Allah te donne la force et le courage de surpasser cette épreuve.
J'ai trop mal. Adina amoul solo. Nguir allal rek diarna sankh sa dome. Cest grave.
Yeureum ndaw si.
Sokhna boula dara méti alakhira dinagne lako faye bilahi
Ma chérie mounial bo niakhe yaye do am wérou waye
Esk. alaquira amna
@@babasidia1115 yaw daguay lathie nak alakhira amena ok togale di khare
@@Abou_Ngom frère réson pour l'a quel
@@babasidia1115 frère alakhira mooh nara guena graw kousi baye woule khél daguay nakhe sa boop
Ça fait mal franchement courage sieste
J'ai vécu la même chose la sœur de ma mère elle m'a fait subir la même chose m'accuser de vol partout où elle passe elle disait aux gens que je suis un voleur l'époque j'habitais chez elle mais comme on dit la route tourne c'était elle la voleuse mais quand je pense ça me fait toujours mal alors que ça fait plus de 10 ans mais quand je pense c'est comme si c'était aujourd'hui Une jour ma tante et habiter à France était venu en vacances à l'époque j'étais parti voir ma mère au village après de retour à Dakar elle m'a appelé pour me dire que ss parfum on disparu et que c'est moi qui les a pris parce que ma tante lui a dit que je te un voleuse les mots m'ont brisé le coeur et quand je te dis à ma mère je ne vais jamais oublierai la peine qu'elle avait dans les yeux après la vérité et finit par éclater c'est elle qui a volé toute la famille là si et personne n'a plus confiance en elle elle vole même ses propres enfants je remercie toujours Allah de m'avoir blanchir
Quand les mensonges prend l'ascenseur la vérité prend les escaliers yagu yagu dina fegne. Courage à vous
Même moi mais yalla bakhna
Nonou privè thi sa fami la eupè bilay walay mougne rèk yalla bakhna
Ndeye Ndao effectivement
Yalla bo lén geuneu avancer ( danioulay bagne)
Bilae
Yalnala yalla takhawou kou ray say noone say mbokkou dièkh
Du courage ma sœur on t'aime beaucoup c'est Un peu difficile pour les enfants qui n'ont pas vécu avec leur mère courage et essaye d'aller de l'avant pour ton enfant
Ohh j'ai des larme au yeux bilay mais mougnial yalla bakhna
bilay da méti man sama diabarou pape moma nyinion sagne or ram
NDEYSANN MOUNIAL RÉK INCHALLAH LÉPAY BAKH 🙏🏿🙏🏿🙏🏿
Kou réndi say none say mbokk ndieukk diekh
lerna
Courage ma belle 😭😭😭❤❤❤
Sama tante cad sama diabarou papa meuss nama accusé sathie 1000f bobou ce2 la done df tei sama yay neikoul si keur gnep di ma saga ak dorr gnoumay reitane école fouma tourné deimay dioy après Deikei Khaliss domam moko dieul mais batey doumako fatei dei doumako baleu deifmay wo dima gnane credi tissu ak lounei mm ay domam malein di deifal mais j n p pas oublié cette histoire
😢😢mounieul rk yalla bahna 😢
Tourne la page be happy ... bou Gnoula yakhale sa Adina ...si weule sa bope pour rien .... gni khamoule wone khame ....... Media bakhoule . Vie ta vie diarouko sis . Du courage. Mais des années gua dèffe Li sa khole reek come on dou yawe dou yawe . Bayile akk Yalla ..... Mais Li mome dou idée bou bakh...... fèkhAlale es à khole . Be strong 💪🏼 Boule djoye sis 😘♥️❤️❤️
Yallah guiss na lepp wayé dellole sa khél si Yallah khamni natou boula Yallah tek la rek
Mougneul rek 🌹
Ndey mounial yalla ken nala
Force à toi sister , seul Allah reste au contrôle , le jour de la vérité viendras Inch’Allah... courage
Tribunal kagne koulafaa yaubou déssétoula dara
courage ma soeur yalla guis na lep
Métina mai sois forte yalla loumou name diéhal bilahi dey dieh😭😭mm bou fékone yako dieul sah warone na hol sang bii ndah alal mom kéne dou dé bamou top la mai du courag
Maane d gueuwma ay mbok
Merci rek
Mbok yo khamni niolay diay si mbede bi dila yakh merci rek
Sama yarame dewna dicourage ma soeurette 😢😢
Ma belle ne pleure pas et ne pense plus à ça. Vis ta vie, Yallah atténa té dina gueuna atté inshallah. Fais toi belle, mange, réjouis toi et fais plaisir à tes enfants et à ton mari. TU N'ES PAS LA SEULE A SUBIR CES MÉCHANCETÉS. VIS HAPPINESS POUR LEUR MONTRER QUE TU ES CLEAN ET BLANCHE COMME NEIGE SÈNES KHÔLES DI DAGUE, GADJÉ DILÈNE RÈYE DANKE DANKE INSHALLAH. ❤
Koulaa toumale dioulile nga bayi kok yallah té nga khamné kou bakh ak kou niak laniouy toumale wayé lou way déf bopam mawarou thi bii yaye🤔dila masta wou bou bakh ndakh dafa métii😭😭
Sa rakkou yaye bobou dee warna rouss ndeyam thim mane sama kholbii bone na sakh mais li moye lane sheuu niak yaye mo graw walahiii sa rakk yaye bobou kou bonne ndeyam la mais yalla nalla yalla atek mome deug mome yagu yagu daye fegn
Man nitt rek la kham Boko defone doula meti massa mougniale bayilen ak yalla borom beut bou rey bi bon courage
je m'excuse mais sénégalais mo tameu di accusé mbokam
Matsa yala nala yala same si barke seyedina mou khamet psl 😢😢
Oh c'est triste😥😥😥 bayiko ak yalla rék
Thieuy adouna!
Ndeye sann
Yalla na yalla lèral yeup
Merci
Amna solo
Wallahi dalna sama grande soeur par ma propre tante mais YALLAH bakhna
Yalla na leen yalla atte. Mugnal te am jom. Fexeel ba baax.
Courage sister mounial😥😥😥
du courage ma soeur 😭😭
Du courage ma belle 😭😭😭
billahi j'ai baucou 😭😭😭Ken je vie 7 vidéo
@@aminatafaye5114 moi aussi
moi à l'âge de 12 j'ai perdu me 2 penran et moi je ché le douloureux me dieu et grenier
Massa li metina torop j’ai vécu pire que ça
Tout allait bien avant que ma mère ne décède , elle avait un seul frère pour qui elle a fait tout mai malheureusement depui k ma mère m’a quitté son frère m’a pri com sa femme j’avais 16ans la première fois qu’il a abusé de moi Jn connaissais rien je versé tt les larmes d mon corps je pensais qu’il allait arrêter mai non il a continué et il m menacé d me tuer si jamais jl racontes à quelqu’un et bien entendu jn pouvais pas depui 16jusqua 20ans il m viole presque chaque jour à chaque fois qu’il en a envie et âpre il m donne des médicaments pour ne pas que je tombe en ceinte j’ai maintenant 21ans j’lui ai fui il n sais mêm pas où je suis jsai qu’il me cherche tjr mai il n réussira pas à me trouver il m’a complètement détruite j passe tte mes journées à pleurer mai n’empêche j suis croyante j laisse tout dans la main d dieu jte conseil d faire pareil toi au moins tu as un mari et tu as eu des enfants par contre moi non et Jn sai mêm pas si un jour jm marierai ni encore moin encore des enfants
Massa. Bon courage et qu'Allah te facilite
YAllah naleu Allah taxawou 🙏
Pourkoi a tu pas saisi la police
Pourquoi tu ne le dénonce pas
Amine
Ni leuh dhé courage dès fois mettî nga lakkatou dioy ba sa xol sed guenatt si nite gni mais dara yagoul gueume ko rekk xam na si dara leepay bax diarr diarr la rekk💪🙏🏼
Ndeysanne liii metina trop... Wallakhi boul dioy li dou draaa nah Lou yalla bide fok gua diarsi😭😭
Quand j’avais 9ans dama dagn ma mayone sama rakk yaye
Moumay maltraité dima guigne sathie
Demna ba lakk sama lokho
Affaire you boneu yonlen xalatt deff namako
Mais Yallah moma sauver maintenant sumako guissei day rouss Bilaie
Thiéye Sénégal mbokou légui diaxalnagne ma bo rendé saye none saye mbokou diéx mougneul loudoul diéx amoul yalla dinala até ak gnome
Masse sister chéri courage courage
du courage elles ne méritent pas tes larmes❤❤🙈
Yalla guisna lep mougne rek nite cou noir rek moyen deff li un jour on vas mourir
Courage ma puce 😣😦😓
Courage rekk Dieu est grand
Mètina trop wayy😭😭😭😭
Regardez sa mere est décédée il fallait la soutenir mais son tel stp courage
Courage rek
Masta ma grande li yeupe aye nétali laye moudjié bilaye maneu niite moma doule sonaleu mouye kima bokaleu sang ou pas sama yoneu sama yaye rek ak sama pape gnoma diore . Ak sougnou mboro
Ak cheikhou tidiane 👌🏼🙏🏽
Tu as rézo ma belle bayi léne a vie vraiment sa m fait mal 😭😭😭😭
Yak adouna domou diambour rek mé courage
Mais lii mettina ma dé bilahi massa yalla bakh n'a
Amna gnou bonn😭😭😭😭
accusé la gueuneu bagne sama aduna motax doumako def niteu billay baxoul mais dara c la vie soit forte tt ira yalla khamna lep
Ndeya Karisma dafa metti comme nane boisson lagnma meussa accusé mou mettima bathi kanam yalla gneup topma nane kheilou diambour t meussoumako def Ken thi gniom kone ki amna louko metti
AISSATOU DIA xolaleu lolou rek mèti yoyou meuneu nala nopou diapeu la baa def la fèbar mbagua dè tei kèneu dou khameu mais yalla khamna lèp aduna Bi Mon mètti bari hypocrite mougne rek Moy solution bayilèneu AK yalla
Am sorry Darling 👏👏👏
Walagui sama yarame dafa dawe boule dioye ma chérie yalla dinaléne até
Bilaye
Massa ndeye diakhou mougneul xamnala boubax gno bokone arabe yalla na yalla atté akk gnom une personne tres sincere tres veridique
Yaw dagnou la djinne sathie rek yam si santal mane dh yama tané j'ai que 18 ans mais la famille de mon père khâgne ma diam dima liguéy dima yakal diakhasé mak sam papa gt a l'étranger gnou ligey ma yakal ma sama ligey bima amone fofou gnou fékhé bama niew galsen batay mayou gnouma diam alors g ke 18ans yaw am nga sa dieukeur am say dom santal yallah bou bax am nga gno tanè dh
Sa yaye mou ngui dounde sssi ooui ???wakh kommou laye biennal tout le temps si elle ne vit papas laisses ton ton contact stp
Mymy Fortes ok
Ceux qui disent que c est problème de famille on doit pas le mettre dans le net sont vraiment hors sujet. Une fois à la police ensuite au tribunal c est déjà sortie du cadre familiale...On se dit dioulite et on fait pire que les mécréants celui qui pense au jour du jugement dernier et je crois évitera de faire du mal à toute créature à plus forte raison un être humain...Courage ma fille Dieu est là et in challa ces gens-là verront.
Ndeyessane nite kou bakhe oyofe t'es sincère ndeye du courage gnio deukone nguinte depuis ta tendre enfance meussoumala khamè lou bonnes Bilaye nitou kèsser gua
Je valide
@@seyenabouyade920 stp passe moi sont numero je vie en france je veux vraiment laider
@@francineabron4991. Ndeye lègui darrou Salam la deuk mes. Mane mangui nguinte toujours j'habite avec ça famille môme seuyina lègui depuis guissatoumako wone wayer nite geunouko si adouna boma mené djiokhe ça numèro amoule blèm
Louy or nioniou dee dou niou teralsi say belle famiy
Massa .yallah na la yallah sam amine
Thieuy mboki legui 🤐🤐
Mandala ak yalla rk ndakh mbokou lègui yi bakh dèfou gnouko 😭😭😡😠