Je suis Chrétien(Catholique) et Fier de l'être et chaque vendredi j'avoue que c'était un grand plaisir d'écouter le GRAND IMAM MAODO SYLLA à la radio. Que son âme repose en paix!!!!! Sa phrase magique: "Mbokki Julit yi, niongui denk soniou bop dilen denk ragal Yalla ak topu Yalla"! Faut Juste pas perdre espoir. Dieu peut et rétablira tout avec un autre MAODO SYLLA. Union des coeurs pour un SENEGAL propère et paisible.
Que Imam Sylla repose en paix, beaucoup de jeunes riverains allaient à la grande mosquée à cause de lui, la parole de Dieu et l art de la présenter, il était adulé !
Man d damako sopone lol nakh deuguome et il ferait des discours très véridique Yalla n'a ko Yalla kharé aldiana firdawsi ak molém dioulite God bless Sénégal
Niakoul ni imam samb diangue na sakh d , khana kay daa nek déféant rek. Bop bi yeup khaliss mossi nek ak adouna. Do deg lou beuri wakhou yalla ak yonenté bi saws
@@laminediaw2921 baayiléne baakar, imam Samb kou modeste leu, khaliss titeulouko dé parceque doundouko au quotidien si koukokham lawakh, kou wédi démal ba fimou deuk nga interrogé ay noonam. Je parle en connaissance de cause ! Il est professeur d'arabe et de sciences islamiques de formation et fût enseignant à l'Institut Islamique de Dakar sous la direction du professeur El Hadji Rawane Mbaye jusqu'à sa retraite... Ay domame réussir nanou sans l'aide de qui que ce soit, les uns sont à l'étranger les sont à Dakar. D'ailleurs l'un d'eux est sorti de l'ENA. Wassalam
Imam Maodo SYLLA, quelle classe, quelle élégance ! Plaisir de l ecouter et de tirer des leçons !! Yallah nena, Yonente nena !! La qualité fait la différence !!!❤❤❤
Ndeysane bimay am 12 an kako donn deglou mounan mangi lene di denk topo yalla ak ragal yalla mouy louma marque won trop yalla nako yalla yereum 2024 bi mom domako ci xarr
Bilahi meme moi aussi lolou damako diapon ci mom ndeyssan ak nimko dan wakhe ragal yalla top yalla yalla na sunu borom yessal yermande ci mom barkep Ahmadoul khadiim
Imam Maodo Sylla Yalna Yalla yessal yeurmandé ci môme ci barker Seydina Mohamed SAW Amine ya. Il était véridique à chaque fois qu'il faisait le serment. Serment.
Borombi SWT yessal Djegueul ak Yeurmandé thi môme ak weidiour ya djitou ak koleréya ak jullit yepp amine ya Rabi bassi jullit yîi thi Yoon wi amine ya Rabi !
La communauté Leboue n’a rien à voir avec les corrompus djoub mo diaffeh thi diamono dji Leboue Toucouleur Peulh Diola etc … Yalla sammeu souniou ngor souniou Islam sammeu Sénégal diadieuf
Setci woulen mais limou deff mo sakh seitci il prie avec vous kay louko dakh dafa am. Imam maodo Sylla Yallah nako yallah doli yereum tei dieigal ko amine
Khana mome dafa mome grand mosque de dakar dioumadji lifa dabakh malick sy deff serigne fallou mbacké defcofa ak baye niass mome mamam défoucofa mome ancien footballeur la sakh
Ndeysane notre prof d'anglais en 3e Mister Martial Coly t chrétien la il prenait toujours exemple sur Imam Maodo Sylla Yalla na bour bi yeureum ko xaré ko Aldiana bijahi Nabil Moustapha ❤
bilahi yalla doù dioummm imam maoudo Sylla yalna yalla yessal yeurmandé si mom 👉 koffi nekk yalnako yalla sopil dokhalinam discours yi sahh douniou beneu wah si yalla AK wah si sa bopp dou béneu yalnaniou yalla yeurum
Entre les deux imams il n'y a même pas photo Imam Maodo Sylla un grand monsieur un érudit de l'islam a marqué le Sénégal en son temps et écouter par tout le monde qu'i repose en paix Qu'Allah le tout puissant l'accueille dans son paradis céleste aldianay firdawsi sallalahou ala Mouhamadine amine.
Je suis Chrétien(Catholique) et Fier de l'être et chaque vendredi j'avoue que c'était un grand plaisir d'écouter le GRAND IMAM MAODO SYLLA à la radio. Que son âme repose en paix!!!!! Sa phrase magique: "Mbokki Julit yi, niongui denk soniou bop dilen denk ragal Yalla ak topu Yalla"!
Faut Juste pas perdre espoir. Dieu peut et rétablira tout avec un autre MAODO SYLLA. Union des coeurs pour un SENEGAL propère et paisible.
Amine
Amine.
Il ya une contradiction entre ce que tu est et ce que aime .
Bizarre
MASHALLAH mon frère ❤❤❤
Amine. C'est ça le Sénégal.
Imam maodo sylla yalla nako yallah yerem. Amine
Amine ya rabi
amine
Amine yarabi
Amine
Allahou ma amine
Éloquent, élégant, véridique Imam Maodo Sylla avait beaucoup de qualités. Qu'Allah l'accueille dans son paradis éternel. Amine !
Allahou ma amine ya Raby
Amine ya rabbi💖
Bilahi comme goudi ak beutcheuk yalna yala yook yeurmende cikawam
Amine ya Rabby 🤲 🙏
Kokou kan mame dallo😊
Que Imam Sylla repose en paix, beaucoup de jeunes riverains allaient à la grande mosquée à cause de lui, la parole de Dieu et l art de la présenter, il était adulé !
Il était très éloquent moi je l'attendais tout le temps à la télé pour suivre ses prêches
@@maria-vi3tf ah oui, il est une référence
@@assanediatta266 billaay qu'il repose en paix
Man d damako sopone lol nakh deuguome et il ferait des discours très véridique Yalla n'a ko Yalla kharé aldiana firdawsi ak molém dioulite God bless Sénégal
Yaw imam bou rew ga
Imame Maodo Sylla nous manque
Imam maodo sylla Yalnako yalla yeureum amine 🤲🤲
Moi je l’aime beaucoup Maodo Sylla que Dieu l’accueille dans son paradis
Ndeyessane imam Maodo Sylla Yalla nako Yalla yereum kouma sopone Machallah
Que de bons souvenirs avec Imam sylla ,il avait toutes les qualités pour…….
amine
00pm
@@fatoumatabalde385
@Diarratoulay franchement douma ko wédi
Kou diang AK diagoul manougno yam. Yàlla Nako yàlla yerem te jeegal ko
Affaires yii dou diangue.deh, pass pass leu, mootakh niouy wakh Yalla naniou Yalla défal degg ak tope
C'est ce que j'allais justement dire. Diang mais surtout dégue dégue
Kou diangoul fofou? Wakhal lokham
Niakoul ni imam samb diangue na sakh d , khana kay daa nek déféant rek. Bop bi yeup khaliss mossi nek ak adouna. Do deg lou beuri wakhou yalla ak yonenté bi saws
@@laminediaw2921 baayiléne baakar, imam Samb kou modeste leu, khaliss titeulouko dé parceque doundouko au quotidien si koukokham lawakh, kou wédi démal ba fimou deuk nga interrogé ay noonam. Je parle en connaissance de cause ! Il est professeur d'arabe et de sciences islamiques de formation et fût enseignant à l'Institut Islamique de Dakar sous la direction du professeur El Hadji Rawane Mbaye jusqu'à sa retraite...
Ay domame réussir nanou sans l'aide de qui que ce soit, les uns sont à l'étranger les sont à Dakar. D'ailleurs l'un d'eux est sorti de l'ENA. Wassalam
Imam Maodo SYLLA, quelle classe, quelle élégance ! Plaisir de l ecouter et de tirer des leçons !! Yallah nena, Yonente nena !! La qualité fait la différence !!!❤❤❤
Ndeysane bimay am 12 an kako donn deglou mounan mangi lene di denk topo yalla ak ragal yalla mouy louma marque won trop yalla nako yalla yereum 2024 bi mom domako ci xarr
Bilahi meme moi aussi lolou damako diapon ci mom ndeyssan ak nimko dan wakhe ragal yalla top yalla yalla na sunu borom yessal yermande ci mom barkep Ahmadoul khadiim
😂😂😂
Imam Maodo Sylla Yalna Yalla yessal yeurmandé ci môme ci barker Seydina Mohamed SAW Amine ya.
Il était véridique à chaque fois qu'il faisait le serment. Serment.
Yalla nako yalla yeureum thé khareko aldiana firdaws imam référence machallah damadoon yakamti djouli Tabaski wala korite nakh kii
Imam Maodo sylla fut l'un des qoutbous zamane de son époque un véritable disciple tidiane qui a été toujours franc dans ces discours sans distinction
Nous avons la nostalgie de IMAM MAODO MACHALLAH YALLA NA YALLA YESSAL YEURMEUDÉ SI MOM AMINE
Mon Imam Maodo Sylla,qu Allah swt l accueille dans son paradis Firdawsi amine ya rabal anlamina
للهم اغفرله وارحمه واسكنه فسيح جناته مع الصديقين والشهداء والصالحين وحسن أولئك رفيقا 😢😢😢😢😢
Nu ngi niane YAALLAH yessal yermendé si Imam Maodo Sylla khaareko Aljana Firdaws ak booléem julit yi Amiin
La nouvelle génération des imams et des khalifes kay dagay warou...
Maachaallah ya Imam Sylla Rahimahoul lah ❤...
Mada sylla c Est l imame de la grande mosquée qui m'a rappelé le plus paix à son ame
Borombi SWT yessal Djegueul ak Yeurmandé thi môme ak weidiour ya djitou ak koleréya ak jullit yepp amine ya Rabi bassi jullit yîi thi Yoon wi amine ya Rabi !
Imam biii mom dafñu yapp vraiment
Yalnako yallah fay yiw barké cheikh ahmadou bamba Amine
اللهم اغفر له ورحمه 🤲🤲😭😭😭
Aujourd'hui il faut qu´on se réfère au Tout Puissant.
Mais genres ne sont que de petits types
Ohhh imam maodo Sylla ndeysane yalla yokou leram
Bilay éloquent et véridique imam maodo Sylla yalna la yalla yeureum imam day dioup
Borom ragal yala ak topou yala imam sylla ndeysane ❤❤❤
Subhanallah yalla nagnou yalla djiègal sougnouye bakar
Ameen ya rabbi
Que firedawesi soit votre demeure éternel inchallah imam maodo Sylla
Dagne don yakhamti tabaski walla korite ndakh Ay khoutbaam machallah.wayee imam bi ken xamoul loumou don comm mérou mbotay rek
Imam sylla yalla yalla yesal yermande amine ua rabby
ماشاء الله تبارك الله 🙏🙏🙏
Allah hou ak ak wouté
Imam Maodo Sylla yalnako YALLAH SWT yeureum té kharé ko aldiana firdaws si barké Seydouna Mouhamed aleyhi salam amine
ah le regretter IMAM SYLLA 😭😭😭niémé deugue té YALLAH KÉSSÉ TAKH
Machallah.Qu’Allan accueil dans paradis 🙏🙏🙏🙏🙏
Imam maodo me manque tellement son savoir et la vérité.qu'l dit machlah fantastique paix à son âme repose en paix
Quel imam Maodo Sylla !❤❤ maachaalah paix à son âme 🙏🏽
Imam 2024 bi khaliss la geum
😂😂😂
Je regrette pour la communauté lebou, mais avec un tel imam elle est vraiment en perte de vitesse.
La communauté Leboue n’a rien à voir avec les corrompus djoub mo diaffeh thi diamono dji Leboue Toucouleur Peulh Diola etc … Yalla sammeu souniou ngor souniou Islam sammeu Sénégal diadieuf
Qu’il repose en paix imam Maodo Sylla et espérons qu’il en aura autre
الحاج ملك صاله اللهم اغفر له و ارحمه واجعل قبره روضة من رياض الجنة يا آلهى
Imam maodo Sylla Machallah yallah nako yallah yeureum🙏 imam moussa samb adouna dou keur 👍 Bayil beug alal
Imam Maodo Silla joulit la bokhmni yala rek mo takhone mouy wakhe yala na yala yokou laram te yesal yermandem si mom ake bene joulit❤
Setci woulen mais limou deff mo sakh seitci il prie avec vous kay louko dakh dafa am. Imam maodo Sylla Yallah nako yallah doli yereum tei dieigal ko amine
Maodo Sylla était un grand imam et mérite paix á son âme, mais moussa samb est un politicien de métier
Imam maodo sylla yalnako yalla khaaré aldiana firfawsi un vrai imam machaalah rip
Kom yalla ak yaali bi imam
Ndeysane ngiak ak togne la fi , au temps lebou dadane fier vraiment teksi nek noble modane mayé souf, ndawal , ak sokhna legi môme moy lolou
اللهم اغفر لهم وارحمهم واسكنهم جوار سيدنا محمد صل الله عليه وسلم آمييييييييين 😢❤
Imam maodo Sylla mome macha'allah. Cou matte imam leu, yallah na co borrome bi yeureume xarré co aldiana firdawessi
That was when Senegal had a proper Imam. He was not afraid to speak the truth. May janatul Firdaws be his resting place .May Allah guide us.
Amiine.
Dieureudieuf Imam Maodo Sylla 🌹❤️🥰
Allahou akbar Maodo Sylla mactar dou s'en morom bilay walayyy mashallah sylla mactar
Machallah lMAM MAODO SYLLA YALNAKO YALLA YEREUM
Un mafieux il faut que président arrête d’aller dans cette mosquée, le procureur doit le convoquer pour offense à chef de l’État 😣
Je valide
Bouniou fi yalla bayé ba déwén nako président bayî dioumame ,guisoul thieure biko président diokh si korité
Khana mome dafa mome grand mosque de dakar dioumadji lifa dabakh malick sy deff serigne fallou mbacké defcofa ak baye niass mome mamam défoucofa mome ancien footballeur la sakh
Respecter wouko à ce que je vois. Désolée !
Ndeysane notre prof d'anglais en 3e Mister Martial Coly t chrétien la il prenait toujours exemple sur Imam Maodo Sylla Yalla na bour bi yeureum ko xaré ko Aldiana bijahi Nabil Moustapha ❤
Imams maodo machallah ❤
Wallahi Imam Maodo Sylla yallah na gnouko yallah fayal ❤ amine yarabal alamine
❤🙏 yalla na yalla yeureum ko khareko aldiana firdawsi inchallah
Repose en paix Sylla Imame bou niéméwoone deugg
bilahi yalla doù dioummm imam maoudo Sylla yalna yalla yessal yeurmandé si mom 👉
koffi nekk yalnako yalla sopil dokhalinam discours yi sahh douniou beneu wah si yalla AK wah si sa bopp dou béneu yalnaniou yalla yeurum
Yalla nako Yalla yeureume❤
YAL naniou YALA défal ndioub ak doylou 🙏🏻
Imam Maodo Sylla yalna yalla yessal ndjégalam ak yërmandèm ci kowam yoki lerram
Imam Sylla yalna yalla yessal yeurmandeme si mome,ki moye imam wakh rek tai yalla takh,repose en paix Grand imam
Entre les deux imams il n'y a même pas photo Imam Maodo Sylla un grand monsieur un érudit de l'islam a marqué le Sénégal en son temps et écouter par tout le monde qu'i repose en paix Qu'Allah le tout puissant l'accueille dans son paradis céleste aldianay firdawsi sallalahou ala Mouhamadine amine.
Imam maodo sylla sak tabaski khoutbam lay déguelou yalla na yalla yok ay leram barkep chiekhoul khadim aamine
Qu’Allha soubhanahu wa tala l’accueille dans sons paradis éternel
Ndeysane.imam maodo sylla.yalnako yalla yeureum
Machalah imam Maodo sylla paix à son ame
Imam maodo Sylla Yàlla nako Yàlla yeureume ta xare ko aldjana firdawsi aminé ya rabbi
Kom Serigne cheikh bouy wakh machala yalna yalla yokk sa lér imame maodo syla
Une sacrée différence de sermon … mon Dieu où irons-nous avec nos guides religieux…
vraiment sénégal warnagn kholate nougni tanh imam bilae
Soubkhanalah !
Rouss na sakh dh 😢
C est la 1 fois que m a djisko wayer machallah lerna 😮 yalla khareko firdawsi
Yalla nako yalla yeureum ta xaariko al jannah🤲😭
Imam sylla machallah🙏 yalna yalla mayko aldiana❤🤲 !!!
Allah y rahmo yaraby amine
Bilahi li comme yalla ak yalli 😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅
Sylla Makhtar yalla na khipé aldiana
Imame maodo Sylla yalla nako yalla faye aldiana
Ya Imam ndeweunal akk soukeurou koore. Jumma dji negou Allah swt la, momoulooko. Damal dianguiwate. Imam politiciens
Merci pour la comparaison.J'en parlais le jour de la Tabaski.Grand était Iman Sylla.Respect.
❤❤❤ machaallah Imam yalna ko Yalla yeureume té xaré ko aldiana firdawsy
Momdé kom présidant diomay rek monék si dioumaJi Li 😂😂
Comparer Imam Maodo SYLLA à ce gars là, est synonyme de pêcher. Imam repose en paix !
💯😭
Un grand homme de Dieu . Un grand croyant convaincu par les convictions de sa foi .
Soubhanallah
Imam Maodo Sylla k'Allah l'accueille dans son paradis éternel thi Firdawsi les vrais imams se font rares l
Oh imame boy mandou wone,
Yalla n'a firdawsi done Dekouwayam
Bayiwofi gadjié dé
Allahouma Salli Hala SEYDINA MOUHÀMADINE WA HALA ALY SEYDINA MOUHÀMADINE WA SALIM !
Il était un Imam que Allah l accueille dans son Paradis Éternel Amine
Imam Dakar khaliss rek yalla na yalla Ray len 😢😢