Baye Fall tué à Touba :Saa wolof révèle une info de taille "litah ñu fipou...Macky Sall mo..."

แชร์
ฝัง
  • เผยแพร่เมื่อ 31 ม.ค. 2025

ความคิดเห็น • 98

  • @mamemoctarlo9744
    @mamemoctarlo9744 ปีที่แล้ว +15

    Franchement ce gars est tres pertinant 🙏🏻macha allah

  • @boubacardiedhiou1561
    @boubacardiedhiou1561 ปีที่แล้ว +2

    Sa WOLOFFest un monsieur très pertinent dans ses analyses teintées d histoire.Bravo!!!!

  • @moussaniang9404
    @moussaniang9404 ปีที่แล้ว +19

    Koudoul diouly manoul dioubanti kouy diouly

    • @weuz4715
      @weuz4715 ปีที่แล้ว +2

      Merci way Moussa. Wakh nga léppe

  • @rockayathiam526
    @rockayathiam526 ปีที่แล้ว +6

    Masha alah Sa wolof kéne dou yawe yalana sa diame yague nitou deugue n'ga

  • @bassprodtv6887
    @bassprodtv6887 ปีที่แล้ว +21

    Touba la deuk fila dioudo mais civil dou Lidianeti moromou civilam nane dem rek guissagoune dra😢

  • @goraseck9057
    @goraseck9057 ปีที่แล้ว

    Machallah sa wollof deugue rek nga wakh merçi frère

  • @amacoumbandiaye8238
    @amacoumbandiaye8238 ปีที่แล้ว +3

    Je viens de découvrir sa wolof mais vraiment ils a raison

  • @SiiwalalProjetBi
    @SiiwalalProjetBi ปีที่แล้ว +3

    Jërëjëf sëriñ saa-wolof dëgg fu mu man a féete dees koy wax.

  • @assanembaye1420
    @assanembaye1420 ปีที่แล้ว +3

    Lii xew Touba du dëgg du yoon. Yoon moo amul senegal.

  • @ibrahimacobar916
    @ibrahimacobar916 ปีที่แล้ว +1

    Que disait Namroud devant les millitaires ? Ce qui s'est passé à Touba est un échec ! Un civil ne doit pas être garant de la sécurité ! Les religieux doivent s'occuper des affaires religieuses et non de la mission de sécurité régalienne de l'Etat ! Soyons courageux et alignons nous à la vérité !

    • @sambadieng4546
      @sambadieng4546 ปีที่แล้ว

      motoulene du jokogne xhete baakoule

  • @cheickmoinga3245
    @cheickmoinga3245 ปีที่แล้ว +1

    Le cas de Touba me dépasse 😢

  • @dieynabadiouf8516
    @dieynabadiouf8516 ปีที่แล้ว +1

    Dieureudieuf deugg pure

  • @ousseinlo2082
    @ousseinlo2082 ปีที่แล้ว

    Merci

  • @ibradiop9753
    @ibradiop9753 ปีที่แล้ว +4

    Titre foncier boobou moo nékoul deugg. Parce que titre foncier kay dafay am yamoukay...

    • @AissataBa-xf5oj
      @AissataBa-xf5oj ปีที่แล้ว

      exactement un titre foncier en train de récupérer des autres villages environnant et les imposé des lois débiles

  • @sonkopresident3376
    @sonkopresident3376 ปีที่แล้ว

    Merci beaucoup waye

  • @bayefalloufall3792
    @bayefalloufall3792 ปีที่แล้ว +6

    Kousi dé dangay kharou dinne ken doukou force keneu commissaire bi ap lam la tak kérok bimouy dadié ak serigne basse abdou khadre louté nioniko tékiko

  • @amartoure9971
    @amartoure9971 ปีที่แล้ว +2

    Merci SA Ouoloff ci sa takhaway

  • @papefall9266
    @papefall9266 ปีที่แล้ว +3

    Touba dal ak yabate RK mo fa am baye fall wara reklé

  • @DiengKhadim-h9y
    @DiengKhadim-h9y ปีที่แล้ว

    Li serigne bi beugg lnchalla dina am touba

  • @mamourmbodji1204
    @mamourmbodji1204 ปีที่แล้ว

    Très pertinent !

  • @FamaFatma-we7di
    @FamaFatma-we7di ปีที่แล้ว

    Machaallah

  • @modoumbaye3427
    @modoumbaye3427 ปีที่แล้ว

    Machalla sa wolof

  • @Laminevision368
    @Laminevision368 ปีที่แล้ว +2

    Les bay fall sont indespline

  • @dias1975
    @dias1975 ปีที่แล้ว +3

    Vérité absolue

  • @sarr6876
    @sarr6876 ปีที่แล้ว +2

    Déjà pour expliquer les gens un événement il faut être témoin des faits ou au moins avoir la version des deux côtés.
    Tu ne fais que parler jusqu’à comparer les événements du combat de lutte Modou Lo et Ama
    Arrêtez de parler juste pour parler😊

  • @babba_joop1311
    @babba_joop1311 ปีที่แล้ว

    Senegal moom policiers ak baye fall kif kif , ils ne savent que brutaliser le peuple. Ce pays va mal 🇸🇳

  • @djibysow370
    @djibysow370 ปีที่แล้ว +1

    Ay Baye fall you tékiwoul ci dara nek ci deuk bi di def loulen nek guissagougnou dara sah

  • @mokhtarmboup6355
    @mokhtarmboup6355 ปีที่แล้ว +3

    Le Khalif de Touba est irresponsable

    • @mlo8241
      @mlo8241 ปีที่แล้ว

      Peut-être tamit gniko djégué nio ko wakhoul deug. Man dama yakarni exagération bi baye fall yi di def yeugou ko wala wakhou niouko lép bok

  • @baiajah9137
    @baiajah9137 10 หลายเดือนก่อน

    Nice

  • @masiba7272
    @masiba7272 ปีที่แล้ว +5

    Dégénéré goul sah naniou dem rek .police , gendarmerie nek fi ay bay fall Di def la police

  • @moustaphagoumbala1804
    @moustaphagoumbala1804 ปีที่แล้ว +6

    SERIGNE MOUNTAKHA wakhal ak baye fall yi 😢 li meti na t wa touba niou bari dakorou niou

    • @Yibrafalien
      @Yibrafalien ปีที่แล้ว

      Serigne mountakha nguay wakhal si TH-cam ni d dinasi diote ok 😂😂khél dou nitt

    • @mbissagain
      @mbissagain ปีที่แล้ว +1

      Il est l'uniq responsable

  • @AichaDia-y1l
    @AichaDia-y1l ปีที่แล้ว +2

    Li mom defa opou wakh degge yallah ngen fekke ay nit ba seeni biir ker door leen sathie len 😢bay fall bathi lan soudon man demay fayou

  • @mbackeseyecheikh6374
    @mbackeseyecheikh6374 ปีที่แล้ว +3

    Koula nara ray rayko amoull bakarr

  • @hotsy3005
    @hotsy3005 ปีที่แล้ว

    Mane lima diakhal moye baye fall gno dakh toukh yamba naane sangara 😂😂😂 li diné di terré yeup niokoy def😂

  • @JeanPhilippeMendy-w7k
    @JeanPhilippeMendy-w7k ปีที่แล้ว +2

    Baye fall yi nio wara kholal sen bop

  • @Dudusow-p6w
    @Dudusow-p6w ปีที่แล้ว

    merci sa wolof li wakh DEUG la

  • @awaballa5169
    @awaballa5169 ปีที่แล้ว

    Vérité absolue wallaahi waxgua deg

  • @yassinesow2700
    @yassinesow2700 ปีที่แล้ว

    Saa wolof nous sommes du même point de vue par rapport à l'incident survenu lors de combat entre Modou et. Ama pour. Moi. Les policiers ont leur part de. Responsabilité dans cet acte. Qui aurait pu avoir. Une. Tournure non. Souhaitée mais saa wolof kenn. Dou yew un homme véridique qui totan

  • @mamadougueye2017
    @mamadougueye2017 ปีที่แล้ว +1

    Civile dou dore civile Man serigne modou guēye Chef religieux Senegal makò wakh barkep serigne mandoumbê mbackę ana Police ana gendarmerie mountanga mbackę dēloo sile sa khèll

  • @amadouba9979
    @amadouba9979 ปีที่แล้ว +1

    Baye fall yi mbacké làaniouy naane sangara toukhe yamba ba nopi dougou touba nane daniouy saytou touba

  • @famandiaye-k6e
    @famandiaye-k6e ปีที่แล้ว +1

    Ce khalif est irresponsable il fuit toujours ses responsabilités

  • @cheikhmoustaphacamara1405
    @cheikhmoustaphacamara1405 ปีที่แล้ว

    Sénégal dou réw

  • @mbissagain
    @mbissagain ปีที่แล้ว

    Guissagoulene dara, avançons rek

  • @wwneleson4849
    @wwneleson4849 ปีที่แล้ว

    Baye falle loumouye doyé sow goudu😂 thi comment téryi

  • @SeynabouNdieye
    @SeynabouNdieye ปีที่แล้ว

    Té kénedou lale mbacke mbacke yi

  • @papeballaseye685
    @papeballaseye685 ปีที่แล้ว

    Cette présentatrice est vraiment nulle à chié, elle s'est pas posée une question, un conseil, change de métier cet métier n'est pas fait pour toi.
    Sou pertinence dou carisme dou intelligence, dara amouko et elle est pas la seule quand je regarde d'autres émissions dans les autres chaînes c'est pareil .
    Bilakhi yakhana émission bi yeu

  • @bambasunumbeckte5915
    @bambasunumbeckte5915 ปีที่แล้ว

    Baye fall yi ll est bien organisé du rek ku diok ne baye fall la nio bayii la nek thi li nga wakh amul dangay fien rek dema nga guestu ji ni baye fall yi di dokhe thi mbir mi mais dara khew rek ngen took thi sen plateau di fien arrête

  • @hotsy3005
    @hotsy3005 ปีที่แล้ว

    C'est la faute de serigne mountakha boulen gniu fonto

  • @abdou5349
    @abdou5349 ปีที่แล้ว

    Walahi lulere nga wah

  • @moustaphakane1979
    @moustaphakane1979 ปีที่แล้ว

    Saa Wolof, meme vos marabouts sont fautifs, si Touba est un titre foncier pourquoi l'Etat y investit nos impots? Touba n'a qu'a se ranger.

  • @BayedameSy-q1c
    @BayedameSy-q1c ปีที่แล้ว +2

    Billhi degue le

  • @cherifbadji2985
    @cherifbadji2985 ปีที่แล้ว +1

    Mais ces baye fall viennent d'où? Ce sont des baolbaol et kadior kadior.

    • @Abdoulahi-cisse
      @Abdoulahi-cisse ปีที่แล้ว

      Yaw noo bokk lu ñuy wax di! Moo tax ma ne la danuy dee ba jeex ndax ku nekk sa jomm a lay yóbbaale 🙏🏿

  • @ibradiop9753
    @ibradiop9753 ปีที่แล้ว

    Saawolof yaagui guén sadomén. Aférou sokhna Serigne bi boulci dougg..sookhamé date de naissance Serigne yi digua xamné liguawax amoul...

  • @sikssskok114
    @sikssskok114 ปีที่แล้ว

    Définitivement Sénégal deukkou nafekhh la c'est dommage. Je lis les commentaires et me rends compte que d'un seul coup vous semblez avoir une confiance absolue en la Police et la Justice??! Bon...
    Sa wolof iow liga wakh yeupp am na foko tekk parce que waroul moudiéé ci violence. Mais nak bayyil di wakh naaane mane mane parce que tamitt ligay wakh ci plateau Seneweb ci sujet bii amaaana moo niou niorr, mais pas yaw ci sa bopp. En plus, si je puis me permettre un autre conseil, so améé sagn sagn di wakh il faut équilibrer tes propos, ga wakh aussi ci bénééne pathie biga xamni nio sakhal ay activités you bakhoul ci benn deukk biir Touba. Mane nak sama diabar sou deugueuré bopp warouma damm beugneumm mais sou fékéé ci sama titre foncier la nekk di fontou damay fékhé noumako dellowéé ay mbokkam ci jamm. Ma gui niaane Jamm di fatali aussi ni kénn meunoul téré Serigne bi mou am limou beugg Yalla moko def té am na nioumou néékh looolou. Salam encore

    • @AissataBa-xf5oj
      @AissataBa-xf5oj ปีที่แล้ว

      Deuk bobu mo dieuk Touba kone Touba mo wara limiter ay bornes wayé ñeuw deuk diambur beug leen imposé ay loi fa lañu deuk fa lañuy took ba dé

    • @sikssskok114
      @sikssskok114 ปีที่แล้ว

      @@AissataBa-xf5oj bane deukk gay wakh nonou?? Dem leene nopalou té séétane. Encore une fois daguene di sonal seen bopou rek. sou violence takhone Baye Fall yi diokk ko xam gani dounou fi nekk sakh di tchater

  • @masiba7272
    @masiba7272 ปีที่แล้ว +1

    Dangay fen encore une fois

  • @babakebe4094
    @babakebe4094 ปีที่แล้ว

    Serigne bi ndigal yimou diox baye falyi, violence la, téguéwoul fénn, Nanou bayil naa fikh. Civil doù douma civil moko wakhon.
    Bay fall you bèsyi amouñou bènn yar,
    Serignebi nitla, dafaye dioum té kénn douka wakh

  • @rockayathiam526
    @rockayathiam526 ปีที่แล้ว +1

    Li khewe touba eupe na toubap bi néna l'habit ne fait pas le moine yone. naniou co diokh nitou yone touba louniou co beugueu sopali wala shaytané mofa dougue wala danio beugue créé terrorisme fofou shatané dougue nafa

  • @boubousy3313
    @boubousy3313 ปีที่แล้ว +1

    DEUKOU DORÉ DAL DEUKOU FAYOU MOKAY FAY... TÉ WALLAY BOUGNOU BAYI WOUL ATTAQUER PEULH YI BILLAY DOU DJOUR DIAM

  • @MoussaMbengue-vc9wg
    @MoussaMbengue-vc9wg ปีที่แล้ว +1

    Ndiguel li force la

    • @boundiaye943
      @boundiaye943 ปีที่แล้ว

      Yene la rek

    • @CampNou-vr7hx
      @CampNou-vr7hx ปีที่แล้ว

      Dokhane sa ndaye rek peulh ya ngua fa😂😂

    • @sadgametv2538
      @sadgametv2538 ปีที่แล้ว

      Ray Sén ndaye rék

  • @khadimseck1424
    @khadimseck1424 ปีที่แล้ว +1

    Wa lay assim lou ler ga wakh duegg rek moy duegg

  • @dokey9332
    @dokey9332 ปีที่แล้ว

    Sa brom xam xam ga, so let’s try to be more positive…., yaw Ko fék moy def lou diadouwoul waroko nokhou pour man warga converquer mou khamni lou mouy deff dou nonou. Respect ✊

    • @Abdoulahi-cisse
      @Abdoulahi-cisse ปีที่แล้ว

      Kuy toroxal jigéenu biir sama kanam?

  • @aliounebadarandiaye5344
    @aliounebadarandiaye5344 ปีที่แล้ว +1

    DEGUENA DEUGUE

  • @amadouba9979
    @amadouba9979 ปีที่แล้ว

    Sama wadji deug rek lay wakh

  • @alioutoure5035
    @alioutoure5035 ปีที่แล้ว

    Senegale Legi jeun yi gno geuna mat mak yi mak yi dongou gnoy defal maky ligey you bon

  • @cheikhmoustaphacamara1405
    @cheikhmoustaphacamara1405 ปีที่แล้ว

    lou boune la notéle bakhoule

  • @ablayembayetoumb9134
    @ablayembayetoumb9134 ปีที่แล้ว

    Mais baye fall yi nioye diape Di teude wala police

  • @bigophone2834
    @bigophone2834 ปีที่แล้ว

    Sawolof yani depensé yawyay kan linoni yonwi ragalon lep yenaksii

  • @dijaimmobilier
    @dijaimmobilier ปีที่แล้ว

    5

  • @masiba7272
    @masiba7272 ปีที่แล้ว

    Danguay fen Serigne Touba 33 épouses la amone dont 3 you bok nday AK bay AK ben demi sœur.la famille diakhete kala.
    Nio fekantee te nio diour pratiquement domam you geuna siw

  • @oumiseck4500
    @oumiseck4500 ปีที่แล้ว

    Leep macky iblisela

  • @Laminevision368
    @Laminevision368 ปีที่แล้ว

    Gni danion apeul

  • @bigophone2834
    @bigophone2834 ปีที่แล้ว

    Sawolof domoram

  • @ibrahimacobar916
    @ibrahimacobar916 ปีที่แล้ว +11

    Que disait Namroud devant les millitaires ? Ce qui s'est passé à Touba est un échec ! Un civil ne doit pas être garant de la sécurité ! Les religieux doivent s'occuper des affaires religieuses et non de la mission de sécurité régalienne de l'Etat ! Soyons courageux et alignons nous à la vérité !

    • @badiboy8698
      @badiboy8698 ปีที่แล้ว

      😂😂😂😂😂😂

  • @ibrahimacobar916
    @ibrahimacobar916 ปีที่แล้ว +6

    Que disait Namroud devant les millitaires ? Ce qui s'est passé à Touba est un échec ! Un civil ne doit pas être garant de la sécurité ! Les religieux doivent s'occuper des affaires religieuses et non de la mission de sécurité régalienne de l'Etat ! Soyons courageux et alignons nous à la vérité !