Salut wally suis un fan, j'ai quelques conseils à vous donner il faut favoriser ton marketing sur les réseaux et être présent sur tous les réseaux,le 2 eme conseil fait des featuring avec les rappeurs français les plus célèbres ça te permet d'avoir la chance de gagner des disques d'or ou platine pourquoi pas disques diamants c'est possible il faut juste y croire et travailler.ces des conseils venant d'un frère d'un fan qui ne veut ton reussite.bonne chance ❤❤❤
Très pertinent. Pour les réseaux je trouve qu'il n'utilise pas beaucoup son influence. Malgré que c'est l'artiste le plus suivi, je ne le trouve pas très présent sur les réseaux. J'espère que dina si diot
Wally gnoun yaw rek lagni topou mais amato loy prouver Sénégal 🇸🇳 faut nga def feat avec les artistes français 🇫🇷 pourquoi pas nga remix confuse avec aya nakamoura ou nhino artiste Sénégalais yirek niodoul remix son guiss nga rema calme down am amna succès tewoul mou remix ko ak selena gomez gagné si des trophées wala nga remix donne moi une chance très belle chanson avec les chanteurs français 🇫🇷disque d’or france la geneu yomb gazo 11jour sila am disque d’or an son single nananina mais félicitations pour adidas arène 👑
exactement c'est ce que je disais. Nagnou wally bolé si conseillers staff bi 😂 dagnouy suivre actualité musicale bi. Je me disais que le son "Choix" avec Mia guissé dafa wara am continuité. Wally doit sortir un single "Mariage" feat Mia guissé et par exemple Dadju. Lolou rek souko défé avec toute la comm et marketing ça va faire une bombe. Public sénégalais ils sont plus youtube c'est pourquoi il doit faire des feat avec des artistes français qui sont en vogue pour le streaming. Lolou dou dara si Wally souko beugué ❤
@ Bilay confuse souko remix won ak aya Nakamoura soudoul am disque d’or louma la wakha bouko geum sou boba coumplé aya day nek copine mia fi mia di wakhé awma coix fofou lay tek couplém diko conseil sénégal problème streaming lagne am yom pour niom lep TH-cam leu
@@BabacarNdiaye-u2f carrément war nagno kham li khew si monde musique bi quand même. Je trouve que Baye Zale est ouvert si genre conseils yi. Il dit tout le temps dans ses interview que kou am conseil wala dara louy dieumale wally kanam il est preneur. Il faut mou guiss commentaire bi gnou appliqué ko
@ khana baye zale mais le reste niom sen kassé rek molen intéressé gnom bougnou sagnon sakh wally dou def afrobeat na yem vogue ak concert région yi cices grand théâtre l’essentiel nagne fayékou malgré wally hit yimouy def si afrobeat bi doun si communiquer dougn ko sakh challenge louler lalay wakh kholal gni nek si orchestre wally delen suivre sur les réseaux le vrai manager de wally modon aziza kokou mo kham musique mo def ay donne moi une chance ,faramaren,loving you ak alhamlilah avec sidiki kokou lancé mimou dielon dafa graw
Walaye Contane naniou Sa pape wakhone na ni di gui yali nieup Maashaalah yallah na Ya Rabbi kheep doli si barke Seydina Mouhammad Saw Bravo 🎉❤❤❤❤ Yallah no bolou bi guene boli yeune artists yi
Wally Ballago séck je suis fière de toi 📀🎤🎧💯tu es le meilleur chanteur en Afrique bly...mako wakh histoire dikô bind ✍️ Wally seck références leuh ❣️❣️❣️❣️
Effectivement il doit se reposer mais il a plein de programmes machallah pour le mois de décembre: 13 décembre, 14 décembre, 24, 25,26, 28, 29 décembre, 01 janvier, 04 janvier, pour ne citer que ça. Khawma kagn lay am temps pour nopalou
Wally est juste fatigué, l'émission a été tournée le lendemain de l'évènement. Il venait de se réveiller je crois. Il avait dit qu'il refera une émission debrief avec Momo Wade RTS1. D'ici là il va bien se reposer, comme ça on va voir le Wally fun qu'on a l'habitude de voir pendant ses émissions❤️ et Félicitations pour le concert c'était historique. Merci au grand Pape Cheikh (plein de succès pour Nomad Blu) et Abba no stress
Longue vie à vous et beaucoup de bonheur ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Kouniou ko teukeulél rék nakh nanioula amoul nawlé si musique Senegal bi daflén raw de trop daklén way foufe niome niépou nak mbirou souniou borom la 😂
Ne te laisse pas ébranler par ces harcèlement,persécution et manigances pour te déstabiliser. Focus sur U Arena ,disque d'or en restant prudent, vigilant dans tous les domaines. Sur ce félicitations à toi,kisma,diaspora et tout les faramarenes du monde entier!
Ki damakoy beugue ba kagne ❤ magnifique trio je vous adore waly the king❤❤❤
Machaalah adidas aréna reussir na waly JEUREUJEUF
Le chanteur du peuple international wally seck👑🥇🎤🌟💰🤍alhamdu li LAAH☝🏾
Il faut que wally se repose et récupére beaucoup parce qu'il y va de sa santé !
On est content de toi. On t aime ❤❤ tes parents et ta sœur paix à leurs âme sont fières de toi. Longue vie ❤❤❤
Machallaah Wally Yalla na la Yalla lafal thiat may la wér ak werlé thi barké Seydina Mouhamed Salaatou wa salam ❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉
Amine ya rabi
Salut wally suis un fan, j'ai quelques conseils à vous donner il faut favoriser ton marketing sur les réseaux et être présent sur tous les réseaux,le 2 eme conseil fait des featuring avec les rappeurs français les plus célèbres ça te permet d'avoir la chance de gagner des disques d'or ou platine pourquoi pas disques diamants c'est possible il faut juste y croire et travailler.ces des conseils venant d'un frère d'un fan qui ne veut ton reussite.bonne chance ❤❤❤
Bien parlé tu as tout compris
Très pertinent. Pour les réseaux je trouve qu'il n'utilise pas beaucoup son influence. Malgré que c'est l'artiste le plus suivi, je ne le trouve pas très présent sur les réseaux. J'espère que dina si diot
C suis tellement d’accord avec toi disque d’or français la geneu yombou
Wakh gua lepeu👏👏❤
We love you so much Wally balago seck❤❤❤❤iow nala diamu sonal rek
Wally seck yalnala yallah may Diam incha Allah ak Mboléme Dioulite té ame werr ❤❤❤
Wally gnoun yaw rek lagni topou mais amato loy prouver Sénégal 🇸🇳 faut nga def feat avec les artistes français 🇫🇷 pourquoi pas nga remix confuse avec aya nakamoura ou nhino artiste Sénégalais yirek niodoul remix son guiss nga rema calme down am amna succès tewoul mou remix ko ak selena gomez gagné si des trophées wala nga remix donne moi une chance très belle chanson avec les chanteurs français 🇫🇷disque d’or france la geneu yomb gazo 11jour sila am disque d’or an son single nananina mais félicitations pour adidas arène 👑
exactement c'est ce que je disais. Nagnou wally bolé si conseillers staff bi 😂 dagnouy suivre actualité musicale bi. Je me disais que le son "Choix" avec Mia guissé dafa wara am continuité. Wally doit sortir un single "Mariage" feat Mia guissé et par exemple Dadju. Lolou rek souko défé avec toute la comm et marketing ça va faire une bombe. Public sénégalais ils sont plus youtube c'est pourquoi il doit faire des feat avec des artistes français qui sont en vogue pour le streaming. Lolou dou dara si Wally souko beugué ❤
@ wally gniko weur ken douko si conseil faw ay kangam weur ko disque d’or dou dra france 🇫🇷 Bilay 15millions streaming la
@ Bilay confuse souko remix won ak aya Nakamoura soudoul am disque d’or louma la wakha bouko geum sou boba coumplé aya day nek copine mia fi mia di wakhé awma coix fofou lay tek couplém diko conseil sénégal problème streaming lagne am yom pour niom lep TH-cam leu
@@BabacarNdiaye-u2f carrément war nagno kham li khew si monde musique bi quand même. Je trouve que Baye Zale est ouvert si genre conseils yi. Il dit tout le temps dans ses interview que kou am conseil wala dara louy dieumale wally kanam il est preneur. Il faut mou guiss commentaire bi gnou appliqué ko
@ khana baye zale mais le reste niom sen kassé rek molen intéressé gnom bougnou sagnon sakh wally dou def afrobeat na yem vogue ak concert région yi cices grand théâtre l’essentiel nagne fayékou malgré wally hit yimouy def si afrobeat bi doun si communiquer dougn ko sakh challenge louler lalay wakh kholal gni nek si orchestre wally delen suivre sur les réseaux le vrai manager de wally modon aziza kokou mo kham musique mo def ay donne moi une chance ,faramaren,loving you ak alhamlilah avec sidiki kokou lancé mimou dielon dafa graw
2millons de vues wayy ana faramerenes yi
Wally yalla gua goudou faane ❤🙏si barkei Mouhamed Psl ❤️
Waykat bi Machalla gneupa contane toute les félicitations mala beugue way amal diam rek❤️❤️❤️👏👏👏
Il es tellement reconnaissant il m’étonne ❤❤❤❤❤❤❤❤❤repose toi nak❤
Niou dem diouli timis nieuwat
Walaye Contane naniou
Sa pape wakhone na ni di gui yali nieup
Maashaalah yallah na Ya Rabbi kheep doli si barke Seydina Mouhammad Saw
Bravo 🎉❤❤❤❤
Yallah no bolou bi guene boli yeune artists yi
Wally Ballago séck je suis fière de toi 📀🎤🎧💯tu es le meilleur chanteur en Afrique bly...mako wakh histoire dikô bind ✍️ Wally seck références leuh ❣️❣️❣️❣️
Sawaye delenn mayee nitt ki nopalou wally Dell récupération amna solo diamou si yaww
Effectivement il doit se reposer mais il a plein de programmes machallah pour le mois de décembre: 13 décembre, 14 décembre, 24, 25,26, 28, 29 décembre, 01 janvier, 04 janvier, pour ne citer que ça. Khawma kagn lay am temps pour nopalou
Ms tu vois même que c'est publié sur la page de Wally même est ce que nékoul môme mo beug interview bi
Machallah wally seck yalla Nala yalla samou ❤❤❤❤❤❤❤❤
Ndeysane sama wadji yalla nalla yalla samou ar leu
Wally il souffre en silence blh il est fatiguée ❤❤😢
Wally est juste fatigué, l'émission a été tournée le lendemain de l'évènement. Il venait de se réveiller je crois. Il avait dit qu'il refera une émission debrief avec Momo Wade RTS1. D'ici là il va bien se reposer, comme ça on va voir le Wally fun qu'on a l'habitude de voir pendant ses émissions❤️ et Félicitations pour le concert c'était historique. Merci au grand Pape Cheikh (plein de succès pour Nomad Blu) et Abba no stress
Yallah nala Yallah défal diamou dioubary❤❤❤❤❤❤❤❤
Wally seck yalla na yalla saam mousala si thiate ❤❤❤❤❤
Waly nopalou touti tu es fatigué pour l'amour de dieu
On est prêt
Masta thiono maryacine😢boula dara diote way si barké séydina mouhammad❤️
Wally que dieu te garde 💂♀️ 😢🎉❤
Amine ya rabi
Mann sa nitté rekk tahhnaa ma gueum sa baye fall bilahy diamou si yaww man broo
Damakoy beugue ba kagn❤❤❤❤
Wally reposes toi bien on sent que tu es fatigué et c'est normal. Congrats again 🎉❤
Yalla nala yalla saml bopam wally
Duo pape cheikh & Aba c’est Oufff
Wally môy adouna 🎉
Wally seck bou kérogé aldiana moye yoré ambiance musicale bi faramarene musique aldiana 😊
Yow ko yap
Enfin Bobou ba legui mangui khar 😂❤
Wally national khol yeupe séde machalla félicitation le golden boye ❤❤❤🎉🎉🎉
Wally Secka international ❤❤❤ star people choice ❤
J'aime bien cette version de toi, calme, posé, très réfléchi.
Très fière de toi!!!
The King of the King ❤❤❤❤
Machlla li nice n'a torp contan si yow Pape cheikh Diallo mrs aba yalla nalne yalla same mayla goudou fané AK wer inchallah
Wally yallah gua am diam ♥️😘♥️♥️
❤❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉merci beaucoup à tous bravo à mon frère cool machalla félicitations à Wally seck
Wally yalla nala yalla défale diamou ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️
Yein yi wakh dou référence mom mogui fay 95 personnes par week-ends pas par mois 😂😂😂nopalikou lein si ki
Nji wakh dou reference wakhoumala meune sene baye waye sene Akane yeup molene meune
C'est une fierté ❤
Vraiment
Wakhou dof yoyou diaroul répondre
Lem meune sen baye meuno ko mo takh 😂
Wally ne te laisse pas faire senegal dafa bari niou sokhor bone ignane prend soin de toi ❤🎉bonne continuation
Machalla sama Wally laf thate long vie a toi mon préféré ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Machallah yalna sa diam yague mar yacine
Bilay diambar ga wally
Notre wally national ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Maryacine yaw goudou fane rk lanelaye ndianall yalla nalla yalla sambou
The King of The live long 🙏
Félicitations 🍾 mar Yacine 🎤🎤🎤❤️❤️❤️❤️
Machala mes frére
Machalla yalla na sa diam gague mar ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Machallah ❤❤❤❤❤❤
Félicitations Wally ❤
ABBA lunette yi dafla diap machallah
Machallh ❤️
Duo Wally Seck Aya Nakamura la beug guiss 😍
Ioee beugoulo diam dhe😂😂
@@MohamedSamb-kg7wk lolou dina yeungeul adouna 🔥
On t'aime fort 😍je te suis depuis 2009
Machalla yalnala yalla samou ❤❤❤❤❤❤❤❤
Wally yalla nagua goundou fann way ❤❤❤🎉🎉🎉🙏🙏🙏🙏🙏
We appreciate and love you alot ♥️💯
Wally SECK BEGUE NALA ❤ BILAY WALAY BEGUE NA LA ❤
Niou chanteur du peuple ❤️
Chanteur du peuple
Le meilleur de qa génération 🎉❤
Doundeul bro. Yageu yokou ak weer
Marshallah more blessings inshallah 🙏 ❤
Gambia🇬🇲 is calling 💃🏽👯♀️👏🏾
Macha halla ❤
bilay suma Artish bii sah hol moo rafeat maryacine yallag gah gudaa faan masallah ❤❤❤❤❤
Longue vie à vous et beaucoup de bonheur ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Bilahi notre chanteur il est fatigué repose toi stp ❤🎉🎉🎉
Waly danga sonou xana 😅😅😅
Machaallah wally sa yaye dala nianal diamou rekh gay ame ❤❤❤❤❤
Walahi danouy veillé Bangua joué ba paré
Seck yalnala yalla defale diam thi sa barcké Serigne amine❤❤❤❤❤❤❤❤❤😢
Maryacine🫶yalnala sougnou borome saame are la yiir la goudeul say fane👏❤️🙏
Bilay deguela ❤❤❤❤
Kholl yeup sedd na maryasine
NON PAPAE CHEIKH YALLA NALA YALLA FAYE T'es tres pro
Manchala ❤️ ❤️ ❤️
Kouniou ko teukeulél rék nakh nanioula amoul nawlé si musique Senegal bi daflén raw de trop daklén way foufe niome niépou nak mbirou souniou borom la 😂
Bilaye walaye
Deugeuleu
Kou am fit teukou Wally 😂? Khana Wally 2014 😂mais Wally 2024 limou len rawé sakhar douko daw il ne cesse de mettre la barre très haute machala
On t’aime wally 🎉❤
❤❤❤❤❤wally yallah gua am diam doundel Lou barri
Yalla na yalla sama la wally ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Waye dioure you bakheu rék moye adouna 🎉🎉✨️✨️🍇🍇💯💯💯💯
Il est fatigué vraiment et c normal
Félicitations Waly et bonne continuation.
Wally merci ❤❤❤❤❤❤❤🎉🎉
Felicitations wally
Wally ❤❤❤🎉
Qui Kouko bagne rek dagua xamoul yarouna dale na geumna yalla geumna bopame machalah ❤
Wally yalnala yalla May Fan bou gourou bou and ak wer ak werou ndiaboot gui❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Ne te laisse pas ébranler par ces harcèlement,persécution et manigances pour te déstabiliser. Focus sur U Arena ,disque d'or en restant prudent, vigilant dans tous les domaines. Sur ce félicitations à toi,kisma,diaspora et tout les faramarenes du monde entier!
Dia si yow mar❤❤❤
Ya nekha beugue dee
Wally moyy Bob bou sellee