Le discours émouvant du Khalife: "Démou" Pape Malick Sy "Bétoul Yalla, Wayé Bettena Keep Koumou Amm"

แชร์
ฝัง
  • เผยแพร่เมื่อ 6 ม.ค. 2025

ความคิดเห็น •

  • @evafall9072
    @evafall9072 4 ปีที่แล้ว +130

    man famille sy soumaleni xol sama xoll bi day seddd si yiww bi, si xamxam bi, si dinee bi, si teguin bi

    • @babatall3355
      @babatall3355 4 ปีที่แล้ว +8

      Que dieu te bénisse

    • @evafall9072
      @evafall9072 4 ปีที่แล้ว +6

      Baba Tall aminnn ya rabi dfniou ay talibe cheikh hakan!❤️🙏🏿

    • @nenesy4868
      @nenesy4868 4 ปีที่แล้ว +4

      Alahouma Amiine 🙏🙏yalnane yalla def aye deugui deugui talibé cheikhe

    • @chamakhmakhtv2332
      @chamakhmakhtv2332 4 ปีที่แล้ว +4

      Walay ndayssane

    • @sysybeye720
      @sysybeye720 4 ปีที่แล้ว +4

      Machallah

  • @papadrame6623
    @papadrame6623 4 ปีที่แล้ว +16

    Yague fii lool Sy Malick tei mou andak weer si barké yonente bii sws 🤲🏾❤️

    • @Ba-pw4yd
      @Ba-pw4yd 4 ปีที่แล้ว

      ❤❤❤🙏🙏🙏

  • @astoudioume7296
    @astoudioume7296 4 ปีที่แล้ว +38

    Machaala yaala na yalla mayemou diegue ak toob thi barkee seydouna mouhamed salalahou alehiwasalan amine

  • @bamsbams5164
    @bamsbams5164 4 ปีที่แล้ว +6

    Machala Ndeyesane 😭 😭
    Machala Ndeyesane 😭 😭
    Yalna Bour yalla yeureum'ko
    Yalna tawou ndiegeul dorté
    Si kawam si barki seydina 🙏
    Mouhamed psl amine 🙏 🙏

  • @palaminedieye4775
    @palaminedieye4775 4 ปีที่แล้ว +6

    S.moustapha sy mactoum yalna yalla goudal fanam ak kouni amiiiiiin

  • @FatimaM653
    @FatimaM653 4 ปีที่แล้ว +25

    Ses causeries vont nous manquer Repose en paix Sy Malick😭😭

  • @karaseye2138
    @karaseye2138 4 ปีที่แล้ว +21

    Ay yalla yalnanga gnou samal wakeur seydy hajj malick bayilén fi gnulendi kholè yonentoubi sws.
    Boumalen di khol rek sama yaram dafay daw.

  • @peupbeatz3683
    @peupbeatz3683 4 ปีที่แล้ว +23

    sy Malick dina la weteul mame yalla nano yalla yeureum té yékhé gnou

  • @ndeyediouf6578
    @ndeyediouf6578 4 ปีที่แล้ว +2

    Machallah Sy Malick khol yi sed nagnou yalla borom bi may la wère tè mou yagual la si sougnou kanam ak ndiabotte gui yeup si barkè yonentèbi PSL 🤲🤲

  • @souleymanesane7764
    @souleymanesane7764 4 ปีที่แล้ว +5

    Qu'il soit notre tuteur au paradis Inchallah

  • @khalifadiop4175
    @khalifadiop4175 4 ปีที่แล้ว +7

    Serigne papa Malick yalla na yalla kharéko aldiana firdaw si serigne babacar sy mansour yalla na fi yague te wer si barké nabill mostapha salalahou alyhi wasalam amine amine amine

  • @FascinatingMya
    @FascinatingMya 4 ปีที่แล้ว +1

    exemplaire avec son masque machaAllah Sy
    Mame Pape Malick ndeyssane hol yeup toy naniou sant yalla bubah
    yalla nako borom bi yereum diegalko haréko aljana yok léram tass niu ci barkem. On l'aimait et on l'aimera toujours

  • @syllaserignemadiama1889
    @syllaserignemadiama1889 4 ปีที่แล้ว +8

    Serigne pape malick rombona bakh da geun yalna ko yalla yereum ta kharé ko aldiana man sama mame serigne moustapha sylla diangal na serigne babacar sy

    • @bintomboup8675
      @bintomboup8675 4 ปีที่แล้ว

      Machalla

    • @ramaba2521
      @ramaba2521 8 หลายเดือนก่อน

      Yallah bouka Thiat djitou rek

  • @daoudadione2829
    @daoudadione2829 4 ปีที่แล้ว +2

    Machallah Le khalif général des Tidianes yalla n'a yéne bi woyoffe tolle si yawe

  • @maremesy7276
    @maremesy7276 4 ปีที่แล้ว +45

    Amiiiiiiiiine Sy Malick yala bayelac gnoune' bathi kanam

  • @papadrame6623
    @papadrame6623 4 ปีที่แล้ว +4

    Serigne Pape Malick Sy Yalla nako Mak gni teirou Yalla na Yalla yessal yeurmandem si kawam tei teirouko si aldiana firdawsi si barké yonente bii sws 🤲🏾🤲🏾😭

  • @madjiguenediouf8674
    @madjiguenediouf8674 4 ปีที่แล้ว +3

    Serigne mbaye sy mansour yallah nafi Yague te werr malick amine. Pape malick yallah nako yallah xareko aldiana

  • @seydougueye7534
    @seydougueye7534 4 ปีที่แล้ว +1

    Yalla na sunu borom doli leuh fane wou goudou...xare aljana firdawsi sunu serigne papa malick sy ak bolem joulite insha'Allah

  • @rokhaya.a.ndione9782
    @rokhaya.a.ndione9782 4 ปีที่แล้ว +7

    Serigne Babacar Sy Mansour yalla guafii lolou th mou ande ak werr

  • @fatimasow9770
    @fatimasow9770 4 ปีที่แล้ว

    Dieuredieuf Sy Malick yallangafi yag te wer Pape Malick Yalla nako yalla khare Aldiana

  • @maremesy7276
    @maremesy7276 4 ปีที่แล้ว +68

    Yalnaco yalla yereme te khareco aldiana

  • @kissquenne6560
    @kissquenne6560 4 ปีที่แล้ว +38

    Ndeysanne Pape Malick yalla nako yalla hare adiana nite kou bakh 😭😭😭😭

  • @oumoukhairyfall2247
    @oumoukhairyfall2247 4 ปีที่แล้ว +19

    Dieureudieuf Sy Malick goudou fann akk werr inchalah

  • @khadijacamara1247
    @khadijacamara1247 4 ปีที่แล้ว +2

    Mes condoléances Serigne Babacar Sy Mansour yalla na yalla goudal sa fane té nga yague and akh wér.Que firdawsi soit sa demeure éternelle Papa Malick Sy Ibn Serigne Babacar Sy 🙏🙏🙏😭😭

  • @awadiouf7281
    @awadiouf7281 4 ปีที่แล้ว

    Sama sérigne pape malick sy yalna yalla yok lérame yalla wonaléko séydina mouhamed psl kou bah dem na

  • @famaseye5359
    @famaseye5359 4 ปีที่แล้ว +3

    Sy Malick kadouyi rafètena Masha Allah , Serigne pape Malick Sy yalla nako yalla yeureum té kharèko aldianay firdawsi ak bep djoulite insha Allah

  • @marimardiallo7428
    @marimardiallo7428 4 ปีที่แล้ว +3

    Koulaa sopeu loll démena 😭 Mame Boye yallna yalla goudeul sa fane🙏🏼

  • @coumbagningue5047
    @coumbagningue5047 4 ปีที่แล้ว +1

    Yalla na soufff oyoffff sisa kaw mame boy yalla nanou yalla Tass sisa barkel🙏🏼🙏🏼🙏🏼

  • @morpouye7927
    @morpouye7927 4 ปีที่แล้ว +3

    Ayway amatouniou kouniou kholé serigne babacar Sy k la terre lui soit légér 😪😪😢😢🙏🙏🙏

    • @khalifababacarcobar8178
      @khalifababacarcobar8178 4 ปีที่แล้ว +2

      Tivouanne nieup ay Serigne Babacar laniou . thieur bi doufi diouk mouk. Yalna Yallah doliko léér Incha Allah🙏

  • @aidarasokhnaoumoulfadly717
    @aidarasokhnaoumoulfadly717 4 ปีที่แล้ว +6

    Machallah sa wakh rafetna yallah na yallah yeuremko khareko aldiana bijaahi Nabil Moustapha salahou aleyhi wasalam

  • @mansourseye7576
    @mansourseye7576 4 ปีที่แล้ว +33

    Serigne BABACAR sy mansour yalla gafi yague te were

  • @ndeyefall3340
    @ndeyefall3340 4 ปีที่แล้ว +2

    Macha allah serigne Babacar sy manssour yalla na yalla guoudal sa fane 🙏🙏🤲🤲wakhtane bi amena sollo lol👂👂

  • @birametall479
    @birametall479 4 ปีที่แล้ว +31

    Yalla na souff oyoff si kawaw sy malick

  • @alimasima896
    @alimasima896 4 ปีที่แล้ว +6

    Machalla sy malik k le bon dieu t'accueille dans son paradis thi barké Mohamed

  • @ismailadieng2128
    @ismailadieng2128 4 ปีที่แล้ว +3

    Serigne pape Malik sy yalla na ko yalla yeureme té kharéko aljana 🙏

  • @adjiafall693
    @adjiafall693 4 ปีที่แล้ว

    Ndeysanne yalla rk mo meun li koufi dieulé yonenti bi doufi bayi ken walahi Pape malick Sy wétal ganiou yalla nala yalla yeureum té kharéra aldjana firdawsi si barké Mouhamed Psl

  • @cheikhmodouburbi8875
    @cheikhmodouburbi8875 4 ปีที่แล้ว +17

    Ndéysane yalnako yalla térou aldiana firdawsi ci barké salatoul fatiya

  • @mboupmboup1069
    @mboupmboup1069 4 ปีที่แล้ว +8

    Allahouma amine yarabi حفظكم الله ورعاكم وأطال بقاءك م

  • @binetaba6723
    @binetaba6723 4 ปีที่แล้ว +20

    Que Allah l'améne au paradis firdawsi amine

  • @matydabo301
    @matydabo301 4 ปีที่แล้ว +1

    Yalla na yalla yagal sa takhaw Sy Malick

  • @toufadia3548
    @toufadia3548 4 ปีที่แล้ว +3

    Nako yalla yeureum tassou gnou thi barkém🙏🙏😭😭😭

  • @abymbayereldione2111
    @abymbayereldione2111 4 ปีที่แล้ว +9

    Koufi dieule naby dofi bayi kene Magüi koy diale bepe dioulite walahi dee Ken meunouko definir Alahou Akbar yala na guissek mamame mawdo Malick ak khadim rossol mamame

  • @seynabouseye9580
    @seynabouseye9580 4 ปีที่แล้ว +23

    Metina vraiment dilene guiss té pape malick nekoussi nekhoul vraiment li yalla rek moko sagn😥

    • @dabafall242
      @dabafall242 4 ปีที่แล้ว +1

      Bilay métina trop

  • @coumbaseck6776
    @coumbaseck6776 4 ปีที่แล้ว +1

    Yalla nako yalla kharéko adianaye firdawsi amine waye sy

  • @boubooombayeeede6388
    @boubooombayeeede6388 4 ปีที่แล้ว +6

    Yalla na sounou brom djégual ko ay bakarame amine

  • @dieynabacamara9466
    @dieynabacamara9466 4 ปีที่แล้ว

    Que le bon dieu l'accueil dans son paradis firdawsy inchalla

  • @mourtallagaye4809
    @mourtallagaye4809 4 ปีที่แล้ว +15

    Khalifa bii yalnafi yag té wér

  • @jodiemaury9306
    @jodiemaury9306 4 ปีที่แล้ว +1

    Yallah na leen yallah yeurem tè kharel aldiana firdawsi amine ya rabi siggil leen ko nigalé

  • @mboupmboup1069
    @mboupmboup1069 4 ปีที่แล้ว +8

    في خدمة الإسلام والمسلمين والمسلمات والمؤمنين والمؤمنات الأحياء منهم والأموات اللهم صل وسلم على نبينا محمد وعلى آله وصحبه أجمعين وسلم تسليما كثيرا إلى يوم الدين 🙏🤲🤲

  • @thebosh-se5lb
    @thebosh-se5lb 4 ปีที่แล้ว +34

    Yagg fi lol s'y té weer amine

  • @papegueye6296
    @papegueye6296 4 ปีที่แล้ว +1

    رحمه الله وايدكم وامدكم التوفيق والنجاح وعمرا طويلاً ونجاة من جميع الشرور

  • @mamourlaye5176
    @mamourlaye5176 4 ปีที่แล้ว +1

    Yalna yalla yok ay léram sy malick ❤

  • @papematarfall4354
    @papematarfall4354 4 ปีที่แล้ว +1

    Machalakh sy Malick yalla na yalla guoudal fane yii

  • @farbathiam6202
    @farbathiam6202 4 ปีที่แล้ว +1

    Yalla nako yalla yeureum ta xareko aldiana

  • @aminatathiaw3075
    @aminatathiaw3075 4 ปีที่แล้ว +45

    Que le bon dieu l accueille dans son paradis

  • @seckyacine6069
    @seckyacine6069 4 ปีที่แล้ว +1

    Kou yiwe kou bakhe demna yalla na deuke ak seydina mouhamed psl mamame ak magame you bakhe yi

  • @adamspro6945
    @adamspro6945 4 ปีที่แล้ว

    Amine inchallah Sy malice yalla nalla fi yalla bayé bathié kanam amine inchallah

  • @ramadiop3209
    @ramadiop3209 4 ปีที่แล้ว +1

    Yalna la sounou borom xare aldiana

  • @iboukebe145
    @iboukebe145 4 ปีที่แล้ว +1

    Yalnako yalla kharè al diana bark s touba amine

  • @zial0971
    @zial0971 4 ปีที่แล้ว +3

    Serigne pape Malick Sy yalla nako yalla gereum

  • @matyleye5471
    @matyleye5471 4 ปีที่แล้ว +31

    Yalla nako Ay wadiouram terrou si daradizye sayoudina mouhamadou rassoullou lahi sallalahou alléy i wa sallama

  • @ndeyerada4774
    @ndeyerada4774 4 ปีที่แล้ว

    Machalllla mame amnasollo sougou mame pape Malick sy yalna souf s'aide kowom si barke séydina mouhamed rasoulila salalaw alley wasalam amine ❤️🤲

  • @papegueye9665
    @papegueye9665 4 ปีที่แล้ว

    Machalla Sy malick yagi lolou té wer

  • @mbayengom4797
    @mbayengom4797 4 ปีที่แล้ว

    Machalha serigne babacar sy Mansour sy yalna yala goudal sa fan ak wer barkue sws

  • @dieynabandiaye3661
    @dieynabandiaye3661 4 ปีที่แล้ว +1

    Yalla nako yalla kharé aldiana

  • @papematardiop3366
    @papematardiop3366 4 ปีที่แล้ว +12

    Yalla nako yalla yereum té yèekhégnou

  • @toumanimandiang9355
    @toumanimandiang9355 4 ปีที่แล้ว

    Man dé mom dama santé yalla ndakh Serigne pape Malick Sy kou bax la khele dall na si mom

  • @mansourdiagne5234
    @mansourdiagne5234 4 ปีที่แล้ว +5

    Yalla nako yalla kharé aldjana 😭😭🙏

  • @morgueye2635
    @morgueye2635 4 ปีที่แล้ว +1

    Seringe pap malick sy yalla nako yalla kharéko aljana

  • @aissatousoumare5604
    @aissatousoumare5604 4 ปีที่แล้ว +48

    Sénégal dioyna weet

  • @biguediagne4029
    @biguediagne4029 4 ปีที่แล้ว +1

    Walahi ndeyssane gneupeu la bett😭😭😭😭😭

  • @papegaye3558
    @papegaye3558 4 ปีที่แล้ว +1

    Yalla nako seydina Mouhammad sws terou té tasounou si barkem

  • @maimounamangane2148
    @maimounamangane2148 4 ปีที่แล้ว +23

    Paix à son âme

  • @mariamandiaye5489
    @mariamandiaye5489 4 ปีที่แล้ว

    Yalla naka yalla doli yeuram ak diegal

  • @elcapogeneral4048
    @elcapogeneral4048 4 ปีที่แล้ว

    Yalla nako yalla yeureum te khare ko aldina fi daw si amine mes condealece serigne bi mbaye sy yalla nga fi yague lol sakh amine

  • @fatousamb1853
    @fatousamb1853 4 ปีที่แล้ว +1

    Machallah si ababacar yallna fanwii goudou💟 pape malick yallna yalla yaram ko si barkéb Mohamed incha Allah😅😅😅😅

  • @linguerouibrahimadieng1083
    @linguerouibrahimadieng1083 4 ปีที่แล้ว +8

    Yalla nako yallah yeureum yok ko kheweul fofou mou nék AK soutoureu

  • @aidagueye8808
    @aidagueye8808 4 ปีที่แล้ว +16

    Paix à son âme 🙏🙏

  • @mamytagueye1096
    @mamytagueye1096 4 ปีที่แล้ว +25

    Ndeyesan byl dafa métti torop vraiment Yalla naniou Yalla tass thi barkém kharé ko Aldiana Firdawsi si barki Seydina Mohammed psl🙏🏿

  • @bounafallba2352
    @bounafallba2352 4 ปีที่แล้ว +2

    Wër ak goudou fane yalnga ko fess serigne bi ak gni nga bokal rewmi

  • @coumbagaye4739
    @coumbagaye4739 4 ปีที่แล้ว +1

    Yalna yèwo dji aldiana firdawsi

  • @daoudambow8348
    @daoudambow8348 4 ปีที่แล้ว +1

    Wakh dji reféte na fii (La ilaha ilalahou) rek mo fi nek wayé dou (Tama ak ay khiine)kone mbok niou gueune farlou si diiné dji té bayi thiakhane bakhoul,yalla na niou yalla khiir si lou bakh def niou ay niite niou bakh ay talibé cheikh deugue nak🙏🏿yalla na ko yalla khaaré aldiana ak mboléme dioulite ci biir souf🙏🏿🙏🏿🙏🏿

  • @fantambaye3976
    @fantambaye3976 4 ปีที่แล้ว +4

    Ndeysan khol yeup toyna Sy wéttal guanou

  • @leuzdione6572
    @leuzdione6572 4 ปีที่แล้ว +1

    Yallana yalla yok ay lerame barkep cheikhoul khadim aka bakh Way

  • @malicksy8546
    @malicksy8546 4 ปีที่แล้ว +18

    Aka bakh sy malick ya bakh

  • @maogningue3922
    @maogningue3922 3 ปีที่แล้ว +1

    Manchallah 🥰🥰😍

  • @modoulo8041
    @modoulo8041 4 ปีที่แล้ว +14

    Bilahi s. Mansour

  • @papesylla7281
    @papesylla7281 4 ปีที่แล้ว +8

    Yalla na yalla kharé Aldiana sérigne Pape Malick ak Sérigne Cheikh Ahmed tidjan Seck le khalife général de thiénaba.
    Yalla na yalla bayil nioufi sougnou kilifa youffi déss bassi kanam.

  • @ramaba2521
    @ramaba2521 8 หลายเดือนก่อน

    Bess bi doumako faté moukk s'y Malick yallah nako sounou Borom até si yeurmadem si barké seydouna Mouhamed saw

  • @aramndiaye2987
    @aramndiaye2987 4 ปีที่แล้ว

    Nako yalla yeureum té yékhégnou

  • @houleydia1045
    @houleydia1045 4 ปีที่แล้ว +1

    Macha allah kaddou yi raféte na

  • @modoufallbetebeteitsenegal5272
    @modoufallbetebeteitsenegal5272 4 ปีที่แล้ว

    Machallah Machallah amna solo LOOL surtout fin biii khoromouna trop mais Vérité absolue

  • @boudabaax8177
    @boudabaax8177 4 ปีที่แล้ว +2

    Sy Malick sa taxawaay refett na, feess nga delleu sa place, jouer nga sa rôle de kilifeu bamu matt seuk.
    Kerook discours bi nga def si prière mortuaire bu Pape Malick rta bi rek dalal na taalibé yi.
    Et pourtant yow dé ken geunu la am mbetteel ak metit.
    Yageu fi loolu té werr SY🙏🏾

  • @annasamb9956
    @annasamb9956 4 ปีที่แล้ว

    Yalnako mame cheikh térou

  • @daoudambow8348
    @daoudambow8348 4 ปีที่แล้ว +3

    walahi dioulite dafay gueum yalla,dafay yiiw,dafay kham adouna bayi lép ak sou niou borom té si lolou rek nguéne niou yar sy malick❤yalla na ko yalla khaaré aldiana firdawsi🙏🏿🙏🏿🙏🏿

    • @mombaye4031
      @mombaye4031 4 ปีที่แล้ว

      Yalla nako yalla diéguel té kharéko al diana🤲🤲🤲😭😭😭😭😭😭

  • @nogayediop6781
    @nogayediop6781 4 ปีที่แล้ว

    Yallna ko yalla yeureum té kharé aldianay 💟💟

  • @papeomar8530
    @papeomar8530 4 ปีที่แล้ว

    Paix á son âme yalla nako borombi yeureum té kharéko aldiana firdawsi si barké Seydina Mouhamed(PSL)

  • @gorambengue5955
    @gorambengue5955 4 ปีที่แล้ว +30

    Dieu l accueille Dans son Paradis

  • @assakante6490
    @assakante6490 4 ปีที่แล้ว +3

    Mes sincères condoléances que son âme repose en 😭😭😭

  • @aminatasarr1081
    @aminatasarr1081 4 ปีที่แล้ว +13

    Que son âme repose en paix