Ce groupe a revelutionne le rap galsen ! on est en 2019 et ce son est toujours d'actualité. Leur son doudou bou de gueune n'a toujours ete egalé ! un son sans refrain et sensé de bout a bout ! Respect !
Rapadio! le Crew ki avait Révolutionné le Rap Galsen Bipson,Kagoulard,Dégui Biba,Kéyti! Album Real HIP-HOP! Pakétass Pakétass! kouko moytouwul dinagne la Dass! Big Respect
iba keity daddy bibson grass a vous hip hop galsen toloufi si atoum 1998 ayi teqsi you ler binde ndom teqsi wolf you ler binde ndom teqsi ayi lorsque you nekh rap galsen amelnalene ak wanalen delo dioukel
J'ai des pincements au coeur quand j'entends les oldschools liniou daadj pour Rap aame guëude Galsén Légui ndeyssane newschools yii aay tassoukan niossi ëupëu 😡😡😡
Police sou P.A lagne mbakhé fekone ma madone trafiquer Cam la yorone teugone thi paathie thi night bobou ma nek fa di fight diko niakanté thioy yi ( policiers ) dal dimay escanté thi nonou niou dal dimay menotte violon la ndieuk di soonné niou teubeul ma hundred ( 100m ) sadique yi dimafa bak break beuss bou nek bou YALLAH sakeu may geun di sakeu aliéné meunoul wessou yilé ginzman you ginz ba ginz dima menacé souma deugeuroul wone fiit kone meun na deuké tiit salaw. Amna niou worri ndakh limou meti jail bi dangay diomi sayo kheuyé di khekh ak khiif nioulay khoy thiaabi 🗝 bro sone na Iba il est trop technique
Ndeysaane rapadio j'avais leur 1er album en 1998 je faisais la.6em. Temps boi!! Ils sont trop fort! 2022 still listening!
Ce groupe a revelutionne le rap galsen !
on est en 2019 et ce son est toujours d'actualité. Leur son doudou bou de gueune n'a toujours ete egalé ! un son sans refrain et sensé de bout a bout !
Respect !
Rapadio! le Crew ki avait Révolutionné le Rap Galsen Bipson,Kagoulard,Dégui Biba,Kéyti!
Album Real HIP-HOP! Pakétass Pakétass! kouko moytouwul dinagne la Dass! Big Respect
Ndeye sane le vrai moungui ni 2020
Qui est là en 2021 ???
iba keity daddy bibson grass a vous hip hop galsen toloufi si atoum 1998 ayi teqsi you ler binde ndom teqsi wolf you ler binde ndom teqsi ayi lorsque you nekh rap galsen amelnalene ak wanalen delo dioukel
rapadio a bousculer le hip-hop Sénégalais avec la sorti de leur k7 gni dama l'énergie sopp looolll
Indémodable. Gigantesque. Et surrtout, juste.
J'ai des pincements au coeur quand j'entends les oldschools liniou daadj pour Rap aame guëude Galsén
Légui ndeyssane newschools yii aay tassoukan niossi ëupëu
😡😡😡
LIMOY REAL HIOP HOP
Ndeyssane !! Tan boy,dur rap dur
rap pure et dure
Still in 2016!!!
remember nice son
COOOL
Big respect les frères
Fila iba yafi mane
Nice
Souvenirs lycées ndeyssàne
première couplet bi la comprendre guoul ba legui
Police sou P.A lagne mbakhé fekone ma madone trafiquer Cam la yorone teugone thi paathie thi night bobou ma nek fa di fight diko niakanté thioy yi ( policiers ) dal dimay escanté thi nonou niou dal dimay menotte violon la ndieuk di soonné niou teubeul ma hundred ( 100m ) sadique yi dimafa bak break beuss bou nek bou YALLAH sakeu may geun di sakeu aliéné meunoul wessou yilé ginzman you ginz ba ginz dima menacé souma deugeuroul wone fiit kone meun na deuké tiit salaw. Amna niou worri ndakh limou meti jail bi dangay diomi sayo kheuyé di khekh ak khiif nioulay khoy thiaabi 🗝 bro sone na Iba il est trop technique
12 ground
Iba dou niit
Garyi raabatou nou
Bilay
2019
wicked!
C'était en 98 Nice crû
💥
yes
cinay
Non rap bi ameutoul. No way
sama temps au collège