Machallah Dieureudif serigne Baye diaga Diop yalla na yalla yokou saye lérre amine si barckp khadim rassul dieureudif 👂♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️🙏🏿
#Amine baye ndiaga diop yana yalla Yoko sa leer si adiana amine si barka serigne touba amine si barka cheikh ibrahima fall amine si barka Mohammed amine si barka yalla #
Thiey bay ndiagua diop bay fall yalla na yalla yok leram yen wa jazboul mourid yalla nalenfi yalla yeugual lou yagu lol fall eupoulen yesoulen thiat diapoulen ☝ kon yagulen yoklen werlen brakep SIDY BIRAHIM FALL ❤🙏🙏🙏
Ndéysane😭 FALL NDIAGA Yaram sa liguéye matna seuk si Darou #DOUNYA...yagnou guindi si MAME CHEIKH IBRAHIMA FALL LAMP💡 Yatakh amatouma saguo si #MAME_CHEIKH_IBRA_FALL sougnou Borom lakoy Sérél Barky #ALADJI_FALLOU❣💡❤💡❤
Ndeysan mane damakay sante boubax ndax leipp louma xam si Cheikh ibra mom la magui kay sante louma metty rek moy moussou mako guiss mais sante yallah nako souniou borom djegal té yokkal ko foumou nekk di fa waxtané cheikh IBRAHIMA FALL 🖤🤍🕊
Wallaahi Ndeysaan Suñu Baay Ñjaga Joop demna nii rek Waaye Dufi Mësë Jok Ndax Ligeeyëm bu Rafet si Muriid gi Yalnako Suñu Maam SIIDI BIRAAHIM FAAL YAARAM bi Teeru Teralko si Barkeb BOROOM TÚBAA
Baye Ndiaga Diop, ak Sr. Sam Mbaye ak Baye Ndianda ak gnima faté gnou mélni gnom dagno liguéyal Kou Téddki ak Mame Cheikh Ibrahima Fall ci jaam yi moy ragnalé séni djangalé aķ séne doctrine ba gni rérone guindékou baparé liguéyal jaam yi ci Kou Téddki ak Mame Cheikh moy khamal léne ci niom lou takh gnou liguéyal léne ba défarou. Sounou djoukal ci gnom moy diap béne yone ci bisbi wala semaine wala wér wi bolé lène ay Ikhlass. Nit kou fatou soko nianalé mou nianal la nga yague fi rawatina kou lakh nguërëmou Kou Téddki ak Mame Cheikh.
Seringe ndiaga Diop baye fall mou bakhmi diko nianal thi barkèp seringe touba ak ch Ibrahim ♥️ ♥️ ♥️
Salam il nous manque yallah nagnou yallah wanalé aldiana çi dooley Mame Cheikh Ibrahima Fall
Machallah Dieureudif serigne Baye diaga Diop yalla na yalla yokou saye lérre amine si barckp khadim rassul dieureudif 👂♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️🙏🏿
Baye Ndiagua Diop Baye Fall,Baye Ndiana Diouf,Serigne Ndiadji Tall Yallah Nalenn Yallah Yereum Té Djeguelen Té kharé lenn Adiana Bidjahil Khadimoul Moustapha Karimi 🙏🏼
Bissmilla massah allah thiey mame ch birahime fall yallna yalla yokou lérame ci barkep borom touba
Ndeyssan baye Ndiaga. Fan lanley guissété rek ci doyna. Rv aldiana baye✊🤲
k la terre lui soit légére ci barké cheikh ibra fall🤲.baye ndiaga tu vas nous manker😢
ndaye sane cey ❤❤❤❤eccol la yalla adianay seringe touba ak CHEIKH ibrahima fall don sa DALOU way ❤😭😭😭😭😭Ndeye sane
😭😭😭😭😭 they Bay Ngiaga yalla nako yalla yeureum si barkeb S touba
#Amine baye ndiaga diop yana yalla Yoko sa leer si adiana amine si barka serigne touba amine si barka cheikh ibrahima fall amine si barka Mohammed amine si barka yalla #
Yalla nako yalla yeureum si barkce serigne cheikh fall baye goor amine
Baye ndiagua diop yalla nanou la yalla féyal barke ckeikh Ibrahima fall
Tieye baye ndiaga diop 😭😭 yalla na yalla yogue aye lerame
Thieuy Baye Ndiaga Yal nanouko sounou borom feikhal barkep serigne saliou🙏
Ba tay mangi koy jooy limou mq doli si Cheikh Ibra yalla nako yalla fay
Thieye baye ndiaga yalla nako yalla yeureum té diégalko barkéb borom touba
Yalna borome bi fayla ci barké Mame Cheikh Ibrahima Fall
Yalla na Yalla xareko aldianna firdawzi ci bakhou serigne touba
Yalna borom touba dolli yeurmandeem barkep Khassida yi
Cheikh ibrahima fall et un fin diplomate Remarquablement intelligent , baye ibrahima thiam, baye mbengue ,cheikh mbacke ndiaye abdou soccé , baye cheikh tall gallo , cheikh ndiaye dabaye , baye cheikh diama , baye modou gueye bakhdas............. , merci baye ndiaga diop yalla na sa borome yok say lerr , say wakh doufi diougue ba kerok yomalkhiyam
BAYE Modou guey Niaye, BAYE Moussa Niang kole ... Niogniou dotou Ame ❤️❤️❤️❤️
Et
Ndeysann!! Sama wadji demna😭🙆🏿♂️
Walahi amna louma métty
Yalnako Bayou guoor fall tèerou dooley sidy birahim fall
Amine fall wayou nieup ndeyssane ndemam di amna si mbektel lol
Thiey bay ndiaga mo bakhone tè mana wakhtane thie baboul mouridina yalla sounou borome doli say laire ak say tawfèkh barkèp cheikh Ibra 🤲🤲🤲🤲
Yall ko yall yarem te khare ko lladina ci barkep mama cikhei Ibrahima falll
yonou Mouride gnak nagne Bibliothèque bou reuy. Yallah sounou borom yok lèram té doli ay ndeureumeum thi barkep Mame Cheikh Ibrahima Fall.
Baye ndiaga diop ak serigne sam mbeye ak baye diana diouf ❤ yalla sa borome dolilén yeurmande,
Ndeyssane Baye Ndiaga Diop Mashallah Yalla Na Yalla Yokk Léram Sa Aldjana Firdawssi Amine Ya Rabbi
Thiey bay ndiagua diop bay fall yalla na yalla yok leram yen wa jazboul mourid yalla nalenfi yalla yeugual lou yagu lol fall eupoulen yesoulen thiat diapoulen ☝ kon yagulen yoklen werlen brakep SIDY BIRAHIM FALL ❤🙏🙏🙏
S ndiaga diop yallna ko cheikh ibra fall tero ci barkeb borom touba
Baye niaga yalla nala borom touba ak mame cheikh wetali si bamel ak bepe murid bu laku
Diarama Cheikh Ibra Fall
Baye diaga diop yalla na yalla yokou ay lerame
Dieredief serigne ndiaga diop baye fall❤
Ndéysane😭 FALL NDIAGA Yaram sa liguéye matna seuk si Darou #DOUNYA...yagnou guindi si MAME CHEIKH IBRAHIMA FALL LAMP💡
Yatakh amatouma saguo si #MAME_CHEIKH_IBRA_FALL sougnou Borom lakoy Sérél Barky #ALADJI_FALLOU❣💡❤💡❤
Ndeysan mane damakay sante boubax ndax leipp louma xam si Cheikh ibra mom la magui kay sante louma metty rek moy moussou mako guiss mais sante yallah nako souniou borom djegal té yokkal ko foumou nekk di fa waxtané cheikh IBRAHIMA FALL 🖤🤍🕊
Baye fall bou mak bii yalna khipe' firdaw sii
Je l'ai admmiré. Il m'a personnellement supporté à pouvoir comprendre c'est qui MCIF et admirer l'Homme. PEACE FOR EVER IN THE HEAVEN
Nioune deh amelle nayulaaa ak thiant ligua niou khamalle thi Sunu Mame Cheikh beriinaaa lolleu. 😭
Yalnako cheikh ibrahima fall térou barky cheikh ibra 🤲😭💖
Feu Baye Ndiaga DIOP RTA faisait la fierté des Mourides plus particulièrement la famille de feu Cheikh fall baye Guore RTA
Yalnako Cheikh Ibra Fall téérou té fayal niouko ...
Machala amena solo lol yalna khipé Aldiana Firdawsiii
Yalnako serigne TOUBA ak mame CHEIKH gatandou. Si barbe YONENT. Amine
Cheikh fall baye goor rek
Wallaahi Ndeysaan Suñu Baay Ñjaga Joop demna nii rek Waaye Dufi Mësë Jok Ndax Ligeeyëm bu Rafet si Muriid gi
Yalnako Suñu Maam SIIDI BIRAAHIM FAAL YAARAM bi Teeru Teralko si Barkeb BOROOM TÚBAA
DIEUREDIEUF Borome Touba Euskey Mame Cheikh Ibrahima Fall Baboul Mouridina Sounou Khel dalna cii Baye Ndiaga Diop
Yama dimballi bama kham mame cheikh Ibrahima fall, ki gueune ci nit gni moy ki kham cheikh Ibrahima fall waneeko, té lolou moy kham kham
Amna solo
Yallanako cheikh ibra terou
Baye ndiaga diop baye fall yalna sunu yokou ayy léraam ci barké cheikh ibra
Amougnou sa fay Fall Ndiaga.
Vraiment il sera trop difficile d avoir un autre baye ngaga diop capable d enseigner mame cheikh ibrahima fall avec une pedagogie exceptionnelle
Yalla n’a yalla youk lérr yii sa baye
Baye ndiga diop et on fait un diplomate lima mèti Senegal khamoko
Baye ndiaga Diop baye fall bilahi doumala masa fatté
Thiey Baye Ndiagua deker mission la done dokh matelena ABADANE nakh aye kadome dotou fi DIOUGUER tii
Baye Ndiaga Diop, ak Sr. Sam Mbaye ak Baye Ndianda ak gnima faté gnou mélni gnom dagno liguéyal Kou Téddki ak Mame Cheikh Ibrahima Fall ci jaam yi moy ragnalé séni djangalé aķ séne doctrine ba gni rérone guindékou baparé liguéyal jaam yi ci Kou Téddki ak Mame Cheikh moy khamal léne ci niom lou takh gnou liguéyal léne ba défarou. Sounou djoukal ci gnom moy diap béne yone ci bisbi wala semaine wala wér wi bolé lène ay Ikhlass. Nit kou fatou soko nianalé mou nianal la nga yague fi rawatina kou lakh nguërëmou Kou Téddki ak Mame Cheikh.
Wa dolen defal baye ndiaga hommage plateau
Yanna ko ysll yararm tekhr ko alldina
Yalla na ko yalla yeram
Amineeee Baye Ndiaga Diop Baye fall❤❤❤❤❤
Yolei kiy ile ekul jolie ete
Danga bakh bilahi
Ken sidy Ibrahim
Kéne la thi kham lé Sidy Ibrahim Fall Séré loul Diop thi képaroup bayoup ngoor Fall
MACHALAH DIEUWRINE DIEUREDIEUFETY DIEUWRINE AKASSA DIEUWRINE DIEUREDIEUFETY
Firdawsii yaram
Plateau spécial bay ndiaga lan beugue guir yalla homamge bi
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤✊🏼✊🏼✊🏼✊🏼✊🏼✊🏼✊🏼✊🏼✊🏼✊🏼✊🏼👸✊🏼✊🏼✊🏼✊🏼✊🏼✊🏼✊🏼✊🏼✊🏼✊🏼✊🏼✊🏼✊🏼great man we will never forget you
Niepeu contane siii yaw
cëy Seugn Bamba 🤍 Mbeur mii foumou feuhė
serigne mamour ndao doma envoye numèro aline mbadara
Sama wadji gnibina adiana
Gracias talibe
Diadieufeti Fall yarram
hakasa s ndiaga diop
Sére loul Diop thi kana Mame Cheikh
Fougni deuleteu kooo mêle ni yaw
Sa xol mo rafété
.
Baye ndiaga Diop baye fall watale nga nio