Mbeur yi déñuy def sport mé duñu ay sportif bilay. Ama blessé ak gnaka blessé mod lo ko meun allez ak retour. Mêm bu féké ama nekul à 100% on sé Q mod lo tamit nekul won à 100%
Sock vs Coly Faye 2 Sock vs Modou Dia Sock vs Double Moteur Sock vs Général Sock vs Gackou2 Sock vs Takké Sock vs Boul Laal Sock vs Ndiaye Tine Sock vs Alboury Sock vs Ablaye Ndiaye Sock vs Diam Terry Sock vs Thiatou Yarakh
Machalla sokh lamb wakhoul deugue bilakhi tu es un vrai champion ❤❤
Mor kang kang yalla na ko yalla maye ndame si barké cheikh Ahmadou Bamba Khadim Rassoul ❤️🙏🏿
Franc vs ama 50/50 leu
Mé tëg na si franc jusqu'à preuve du contraire.
Franc lourd bou am vivacité leu ❤👌💯
Choc vrai sportif yalnalaco yalla défal diam 🫡
Ama balde yalla nako yalla maye ndam lou sedd si kaw franc
Amine❤
Mbeur yi déñuy def sport mé duñu ay sportif bilay.
Ama blessé ak gnaka blessé mod lo ko meun allez ak retour.
Mêm bu féké ama nekul à 100% on sé Q mod lo tamit nekul won à 100%
Reug reug dou ay fo dé😂😂
vérité absolue bilahi
Yaw Sock nala lerni Ama Baldé aye mbokame dinagnouko leungue bouye gnibi ndak Franc dakaye dane diele bou lere inchallah 🙏🙏🎉🎉🎉❤
Sock vs Coly Faye 2
Sock vs Modou Dia
Sock vs Double Moteur
Sock vs Général
Sock vs Gackou2
Sock vs Takké
Sock vs Boul Laal
Sock vs Ndiaye Tine
Sock vs Alboury
Sock vs Ablaye Ndiaye
Sock vs Diam Terry
Sock vs Thiatou Yarakh
😂Wallay Reug Reug ndanane la
Sock champion la koi 😂😂
louler nga wax sock lolou dafa ler
Sokh ana faran sa copain 😂
Sock molen gueneu niiter
Sock vs reug reug
😮😮😢😮😮
Diapél ni sa adina wakh rékk
Franc mo meun Ama té après combat guein di comprendre na boy Niang ak GRD eum yen nieup lay dane diguein khamni Modou molen meun fouf
Da ngay saup Fran meunoul Ama bilahi
Fran ak Malick Niang bokoul de Malick Niang khax mom moye Borom mais Fran dole bi ak beurre bou wor bi set Ken Dou mom
Bilaye machalah 🎉