Sé émouvant,,, yaye amoul morom AK no mél toujours elle est à té côté Elle est décédée ou pas Yalla na yalla goudeul fanou yaye yeuppp gni ka déssé Sama yaye yalla kharé ko adiana amin
Macha'Allah, mane D dioye naa sax té Tayou mako. Merci à Maty 3Pomme, on a tellement besoin des gens comme elle. Pour nos Maman on est prêt à tout😭Dagno sonou thi seuy Sonou thi Jaboot 🙏💋 Yalna Yalla diapalé jeunes yeuppeuh Incha'Allah Barké Nabil Moustapha.
Ndeyessane dieuredieuf assane ci barke Yonenete Salalahou Alayhi wasalam Yalla nalla Yalla tahawou kou regarder emission bi amme hoolle settanne lii dioyye
Tu as parfaitement raison nioune soniou gal defna 10 jours ci guedji soudé ci journé bi amoul problème mais sou goudè diam diékh kouci diaroul mano kham lisi nék c très difícil mais sante yalla tè niou kham ni yalla dou binde si 30 jour rey si 15 jour jamais courage frère 💪🇸🇳🇪🇸
Malheureusement ces gens qui l'interrogent sont tellement limites tellement peu structures que ceux qui vous ecoutent ne tirent pas grand chose du temoignage. Structurez et preparez vos questions. Laissez parler vos invites.
Fall yalna nala yalla défal diamou mane mi di gal yi la diare mé Europe sa way nékhatoul beurina niou fi nék di réthiou bou démbou done tay douniou dougou Europe mé nak kou néke aksa sa weursak
Jajieuf bro Jambar gua bilahi liguay doundou mom lay doundou motakh ma dougou si galyi tente 1 Fw dialouma ma daw dougou Maroc ta insbi dougou Europe rek la beugue insbi doundou wala dée rek bilahi yalla na yalla motali yéné yeup mais diamono da meti bilahi
Le Dieu qui est est en France est en Espagne en Italie au Etats Unis au Senegal croyez en vos capacités et en Dieu et ayez pitié de vos mamans la réussite sera toujours au bout de l'effort quelque soit ou que tu seras je juge personne mais tous les biens que vous avez vendu pour voyager si vous l'aviez utilisé pour investir vous seriez millionnaire sous peu
Je n suis pas avec vous . investissements requiert une accompagnement dans tous domaines. Le secteur privé à plus de problème a cause des investisseurs étrangers. On nous a vendu depuis fort bien longtemps
Mon cher je respecte votre avis mais selon moi les millions quils ont dépensé pour voyager sont le résultat de leur travail et non d'un accompagnement alors fallait juste continuer avec leurs propres moyens la réussite est garanti par le Tout Puissant mais pas par l'émigration
Sama pape lakouna Billakhi ga tokk wara liguiy té amo ligeuiy guiss sa yaye d'où ndéki te d'où agne mou lérr néla ni bousi kén fébaron amo lolén fadié d'où fén foko mana amé mé sa doundou bobou dém wala dé man souma défaloull sama yaye wala samay rakk d'où kénén may yakar bi magui mouritani dé si ndokhmi moma génal dé ak ndoll sénégal billakhi dioyloga tay
Le témoignage de ce mec révèle le niveau de désespoir de la jeunesse africaine et particulièrement sénégalaise. Pendant ce temps nos autorités déclarent leurs patrimoines à coup de milliards au lieu de servir le pays ils se servent des deniers publiques pour nourrir leurs fantasmes . Ce témoignage est celui d’une personne ambitieuse et sans espoir qui voit l’étau se resserrer autour de lui année après année , provoquant chez lui des actes suicidaires et incompréhensibles pour certains. Ce qui me choque c’est le clientélisme inconscient appelé « bonne volonté » Thérèse Faye a intervenu pour ce jeune homme oui c’est super ! , je veux juste demander qu’en est-il des millions de jeunes dans son cas?. Les organismes de l’état doivent être là pour tous sans distinction , il a été pris en charge par ce qu’il est passé dans les médias, sinon il serait reparti et serait probablement mort ou en Espagne .
Demaské iow weroo xana tu n'es pas sur sa page facebok elle nous a tout montré bayiléne ignane ak sokhor c'est de la grandeur et de la noblesse d'apprécier les bonnes actions ak lo meneu bagne une personne
slu assane diapal mou deugeur man mi thie gual gui la diar nieuw espagne wayé lo wah thie guethe gui mo am yal na yallah nangoul niou sunou nianou waye diour
Macha allahou yalna yalla takhawou la si barkép seydina mouhamad
Merci Maty trois pommes et tous les bonnes volonté
Amine
Bravo à Assane pour le dépassement de soi et tu peux voyager au Maroc à Fes pour voir l'expertise marocaine dans le domaine
Se émouvant , j'ai même pleurée, diambar le courage frère , dieu est grand
Sé émouvant,,, yaye amoul morom AK no mél toujours elle est à té côté
Elle est décédée ou pas
Yalla na yalla goudeul fanou yaye yeuppp gni ka déssé
Sama yaye yalla kharé ko adiana amin
Amin ya rabi 🤲
Amine yarabi
non je croie quelle est en vie cest son pere qui etait decedé raison pour laquelle il a voulu tenter laventure en espagne
Macha'Allah, mane D dioye naa sax té Tayou mako. Merci à Maty 3Pomme, on a tellement besoin des gens comme elle. Pour nos Maman on est prêt à tout😭Dagno sonou thi seuy Sonou thi Jaboot 🙏💋 Yalna Yalla diapalé jeunes yeuppeuh Incha'Allah Barké Nabil Moustapha.
Dieureudieuf Assane Machallah rafetna torop ❤💯
Bilay ya gorre goor Goor Lou rek Dina bax Inchallah 🙏🙏🙏🙏🙏🙏
Machallah Dieng sala am diom reek merci Maty 3 pommes 🙏🥰
L'Etat doit continuer à soutenir les jeunes.
J'ai pleuré.
Bravo à l'équipe de seneweb yenagui tek lou leer
Maty 3 pommes : MERCI . Yalna la Yalla Diapalé.
Ndeyessane dieuredieuf assane ci barke Yonenete Salalahou Alayhi wasalam Yalla nalla Yalla tahawou kou regarder emission bi amme hoolle settanne lii dioyye
Bravo Assane fingako diapou fofoula guor yalla danguaye gueum sa bopou nango ligueye, mes Sénégal legui dafa beuri aye thiogou gnake diome
Vraiment Bilahi 👍
Vraiment magnifique les chaussures...belles métiers artisanale,c'est quoi son numéro de téléphone pour lui acheter des paires..😍😍😍😍😍❤❤❤❤❤
Merci maty courage assane
Assane j'ai pleuré 🥵🥵😭😭😭😭😭walahi oie Bâye Fall gâ bilahi Que dieu té protège insa'alah ❣❣❣❣. Assane dîna bax déh. Dama dioy😭😭😭😭😭🙏🙏🙏🙏🙏
VOILÀ POURQUOI IL FAUT CONSOMMER LOCAL"".
CEST LÀ QUE LES AFRICAINS DOIVENT FRAPPER DANS CETTE GUERRE ECONOMIQUE.. SOLIDARITÉ, PARTAGE..
😭😭😭Courage bayeu fall
Merci Maty 3 pommes 🍎 et courage mon frère
MachaAlla très bon témoignage
Tu as parfaitement raison nioune soniou gal defna 10 jours ci guedji soudé ci journé bi amoul problème mais sou goudè diam diékh kouci diaroul mano kham lisi nék c très difícil mais sante yalla tè niou kham ni yalla dou binde si 30 jour rey si 15 jour jamais courage frère 💪🇸🇳🇪🇸
Essayez de préparer vos questions et de les ordonner la prochaine fois
Merci
Brava maty yallna Yalla faye la❤
Ndeyesaane
Yalla nala Yalla djapaler baye fall
J’ai vécu le pire avant d’entrer en Italie walahi 😭😭😭
CT kan Mai YALLA NA VOYAGE BI NEKH YALLA MAYELA papier
Explique
Da melni dessé nga touti nak mais yalla bakhna li metti na 😭dh
Bravo Bonne continuation seigneur viens o secours de tous nos enfants ki sont dans le sombre
Vrai sombre. E innexpliquable
Maachalla maachalla vous êtes très très brave que dieu vous bénisse abondamment
Courage à toi
Nit ak situation bo meunti nek dè nga wara hamni yalla mola tek lolou konn dè ngay mougn ...
Assane bayil gal gui guirre yalla 🇸🇳🇸🇳🇸🇳🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣
Avis de recherche mn mari😭 il s’appelle ndiaga diouf ça fait 8jour deguoumako khawma si loumou nék koumassi meneu diapalé guire yalla 😭🙏🏻
Yalnako Yallah niit mou fégn ak diammeu🙏
Quand il parle requins 🦈 j ai pleure ndeyessane Assane diambar la
Tonton Assane je l'aime par son courage
Malheureusement ces gens qui l'interrogent sont tellement limites tellement peu structures que ceux qui vous ecoutent ne tirent pas grand chose du temoignage. Structurez et preparez vos questions. Laissez parler vos invites.
Merci Maty 3 pommes de l'avoir aider
En tout cas le témoignage de Assane fait froid dans le dos. Les politiciens doivent redoubler d'efforts.
Dieu t'accompagne frère
Courage frere métina trop
La peine que tu fais pour aller en Espagne si tu l'as fait tu vas réussir
Moussa baldé
Sma bén magou xaritt leu mai dfw dafay méti kw mtx mai courage frère 👍❤️
Machll amna solo
Ndeysan ben copain bou nek sama côté day beuga sobou thi ndokh mi mais mako don teuye baniou eksi thi diamou alhamdou
Fall yalna nala yalla défal diamou mane mi di gal yi la diare mé Europe sa way nékhatoul beurina niou fi nék di réthiou bou démbou done tay douniou dougou Europe mé nak kou néke aksa sa weursak
Ndeyssane metina trop yalna tala diapaler gniep
Mes Respects ASSANE
Sénégal dafa meti trop..!!! Ne juger pas ceux qui prennent les pirogue 🚣🏾♀️🚣🏾
Bilahi frère fi nekhoul
@@layesall6605
Bro bala ngay xamni sénégal d’où dara guen sénégal
Sénégal rombouna meti
Yalla naniou yalla tahawou tè mayniou ngeum ngeum
C'est que gni animé émission mounouniou comprendre .........Il faut que vous vous mettez à sa place pour comprendre sa situation
Nagnou diaang kan mooy sounou Boroom. Yén journalists you djiguén gnii? Yalla reubb ne kouy yook. Saang lén sén yaram yi. Addineu déy diékh.
Goor Yallah deuggeu barké CHEIKHOUL KHADIM dii ngeu am lou bakh FALL 🤲🏿💪🏿✔️
Jajieuf bro
Jambar gua bilahi liguay doundou mom lay doundou motakh ma dougou si galyi tente 1 Fw dialouma ma daw dougou Maroc ta insbi dougou Europe rek la beugue insbi doundou wala dée rek bilahi yalla na yalla motali yéné yeup mais diamono da meti bilahi
Yalneu ngue dougou Europe si diameu ak salam , Ya ALLAH mèye leu ndam nga térrale sey Wadiour ak domou Adama yeupe. ALLAHOUMMA AAMIIN
@@soukeynadansokhocamara6538 amine sokhna soukey yamite ligua beugue yako xam bour yalla defal lako barkep mame cheikh ibra fall
Yallah naleen borom bi doolé tahawou té motali yeené yi
@@gnagnadabo3053 amine way yamite yalla defal jamu figua nek
Yalna nga dougou ci barké Seydina Mouhamed psl
Vraie baye Fall ga
Ndeyssane
Afia mon frère ci kaw si KANAM.
Journalisme dagnu koy diang gni sene débat bi organiser woul , questions yi diakhaso, étape par étape lagnu wara poser questions yi
Bien dit
Ils sont nul zéro structuration
Le Dieu qui est est en France est en Espagne en Italie au Etats Unis au Senegal croyez en vos capacités et en Dieu et ayez pitié de vos mamans la réussite sera toujours au bout de l'effort quelque soit ou que tu seras je juge personne mais tous les biens que vous avez vendu pour voyager si vous l'aviez utilisé pour investir vous seriez millionnaire sous peu
Je n suis pas avec vous . investissements requiert une accompagnement dans tous domaines. Le secteur privé à plus de problème a cause des investisseurs étrangers. On nous a vendu depuis fort bien longtemps
Mon cher je respecte votre avis mais selon moi les millions quils ont dépensé pour voyager sont le résultat de leur travail et non d'un accompagnement alors fallait juste continuer avec leurs propres moyens la réussite est garanti par le Tout Puissant mais pas par l'émigration
Mais le développement de c pays est pas le même
merci fall Boy dano sonou billahi 😢😢
Merci assne
Allahu Akbar conviction rék mo ame solo
Sama pape lakouna Billakhi ga tokk wara liguiy té amo ligeuiy guiss sa yaye d'où ndéki te d'où agne mou lérr néla ni bousi kén fébaron amo lolén fadié d'où fén foko mana amé mé sa doundou bobou dém wala dé man souma défaloull sama yaye wala samay rakk d'où kénén may yakar bi magui mouritani dé si ndokhmi moma génal dé ak ndoll sénégal billakhi dioyloga tay
Thieey sama assène wayy 😢 djabar nga
Le témoignage de ce mec révèle le niveau de désespoir de la jeunesse africaine et particulièrement sénégalaise. Pendant ce temps nos autorités déclarent leurs patrimoines à coup de milliards au lieu de servir le pays ils se servent des deniers publiques pour nourrir leurs fantasmes . Ce témoignage est celui d’une personne ambitieuse et sans espoir qui voit l’étau se resserrer autour de lui année après année , provoquant chez lui des actes suicidaires et incompréhensibles pour certains. Ce qui me choque c’est le clientélisme inconscient appelé « bonne volonté » Thérèse Faye a intervenu pour ce jeune homme oui c’est super ! , je veux juste demander qu’en est-il des millions de jeunes dans son cas?. Les organismes de l’état doivent être là pour tous sans distinction , il a été pris en charge par ce qu’il est passé dans les médias, sinon il serait reparti et serait probablement mort ou en Espagne .
MATY t’es démasquée😄😄😄😄
Demaské iow weroo xana tu n'es pas sur sa page facebok elle nous a tout montré bayiléne ignane ak sokhor c'est de la grandeur et de la noblesse d'apprécier les bonnes actions ak lo meneu bagne une personne
Sénégal nékhoul doundou fi lou métila
Hum ki nitou gal la
Mais diarama math 3 pomes
Celle en tunique rouge, pourquoi elle camoufle les réponses du baye fall comme si elle ne voulait pas que le mecs explique
Bilahi ki limou doundou grawoul lima doundou mo guene graw fouf
slu assane diapal mou deugeur man mi thie gual gui la diar nieuw espagne wayé lo wah thie guethe gui mo am yal na yallah nangoul niou sunou nianou waye diour
Il est possible de réussir au Sénégal. Voici l'exemple
Possible mais très difficile
Réussi au Sénégal avec très difficile
Fall lolou yomboul
Vraiment j'ai même pleurer mais jërëjëf yalla
Sénégal dafa meti 😭😭
Senegal ay Dirigent domo kharam la am
Yalla laniui yakar mai dou nuite kou deeeee
Courage mon frère
Émouvant Toma diambar sa war ba inchallah
Respect...
Tolou wayla bilay ndeyssane
Numéro du cordonnier svp
Ç très grave 😲
Machalla
Mann déh thi gale yii la diarr alkhamdoulilah eksi na thi diam
Kiii bossam tarr n'a lool fala diarr deugu bou werr la wah barke borom darou mais insbii dougouna Europe mais boye yiii kéne manoulene téyé billahi
Doundounako dhé 😢motax liii kou meuseul dem meuno xam
Djapalelen gnou si adress boutique bi SVP
Tioloul sama corner leu , Yalla bakheneu
Ki n'a pas pleuré 😭!! J'ai mal !!!!
Yalna entreprise bi djeum sa kawa kaw
Lou Amla billahi dimmou Amna
Courage et ne jamais d3courager
Billahi degg rek la whahk!
Ca cest le travail des genies vs ne savez pas que les plus grands djinnés les plus puissants djinnés malefiques se trouvent au fond des oceans
Maty trois pommes Merci
Ndaysan diapal rek
Fall mi guérier leu
Goor yombul begg tekki
Sa way deugue
La yalla beugue loulou amole mane
Mi si gale la diare
Vraiment djambar nga