MachAllah c une brave dame! Yag negno begal, Yalna ko Yalla sameu! Elle a un Bon coeur! Na bayi gnimiy topou si reseau yi rk, tekiwougn dara di wout buzz si yow! Longue vie sounou yaye dji❤️❤️❤️
Confession bi néxatina walahi ça fait chaud au cœur. Fatou laobé mère bou beurri feeling , cest qu'elle nest pas belle belle mais comme elle l'a si bien dit louko yalla xagne si tare rek maye nakoko si diongoma ak feeling . Ay weuyeum aussi néxx vraiment " doolé, outaté, baye karim ni nak ohhh manchallah. Vie bien mère faou laobé amal diame et reviens nous vite way❤
Macha allah tata Fatou j'aime ton nouveau look daga yiiw machallah ❤️❤️❤️❤️ on attend ton prochain album. Inchallah Dieu va te relever. Il faut toujours apprendre à se relever pour faire honte à tes ennemis, bouléne may lignou beugué il faut toujours avancer.
en 2014 lako guissone foire cices bi ,mais limou wakh ci taar bi deugleu deh , et dafa am lou grawe bouma guiss ci mom, moy bouleu holé ci beute dangay seug force elle dégage une forte personnalité machaallah❤
Ki dama ko beug ndakh fouleum, kikoy saga dinako wak deug bayiko mou dem Sénégalais daniou mouna Segal nit teh kou tekiwoul dara moka deh .respect rek nga mérité teh thi famille bou bakh nga bok ❤❤❤
maachaAllah sister Fatou...yaw koula gueneh thi art dara dotoufa déss maachaAllah...amnaa chance jouer ndo ak yaw Gorée bénn conférence bou douaniers yithi adouna donn déf niou déf première partie ak groupe ballet bima nékonn mais vraiment ce jour là wathieh wonn nga Gorée ak spectacle bou diaarone yonn maachaAllah donc gninguilay niaanal boubaakh...dila wakh daal ni Sénégal namm nagnoula lool sakh walaahi Nio nguilay souhaiter une Très bonne reprise... tawfeekh _taysir_jamm thi yaw ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Ndeyssane une femme très digne moi je l'aime bien ndakh diambar la liguéy katt la djiguéne diou meune goor la yalla nako may goudou fane ak wergui yaram té doliko soutoureu
YAYE BOYE SANTAL YALLA MUSIQE🎶 YALLA DAKKO TÉRÉE KOKO MANATOULA DÉGUE LU SANTAL YALLA BOUBAAKHA BAAKH JAPPAL NI BOUROOM BÉLA BEUGUE RÉK JAPPAL NI KÉN DÉFFO LA DARRA
Fatou comme tu l'as si bien dit n'en veut à personne ce qui t'est arrivé s'appelle le burn-out c'est à l'épuisement professionnel personnes e peut te marabouter tant que tu es croyante bon courage
Maman Fatou tu es belle et naturelle comme ca. c est bien que tu aies arrete le khessal. Yalla nala yalla deugueureul❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Allah Houma Amine Ya Rabi Incha Allah 🙏🙏🙏♥️
Machallah notre maman nationale.. Femme battante, digne..Goudal fane. On t aime toujours...
Bonsoir, confession.Moi j'aime Fatou laobé trop et mon mari .
She is a true artist.Thank you for the good work💕💕💕💕
MachAllah c une brave dame! Yag negno begal, Yalna ko Yalla sameu! Elle a un
Bon coeur! Na bayi gnimiy topou si reseau yi rk, tekiwougn dara di wout buzz si yow! Longue vie sounou yaye dji❤️❤️❤️
Bilay maman fatou goudeul fane senegalais daa sokhor yaye mais nammnagn leu yaye sa wayy dayy yeter .makk bougnou sokhla laa goudeul fane yaye .ayy wayy bayilen sokhor maraboutage bou beuri .yaye yalna sa diam yagg du courage
❤❤❤❤ elle a marqué sa génération une diva une icône ❤❤❤
Vérité Absolue Vraiment ❤
Ndéyssane une grande dame de valeur vraiment pleine de dignité fatou laobé ❤
Goudal faan ak Wer té werle, machallah damala yagueu toopou
Maman Fatou Laobe Ndane kouli Fadri. Machallah, nassa diam yagg
Confession bi néxatina walahi ça fait chaud au cœur. Fatou laobé mère bou beurri feeling , cest qu'elle nest pas belle belle mais comme elle l'a si bien dit louko yalla xagne si tare rek maye nakoko si diongoma ak feeling . Ay weuyeum aussi néxx vraiment " doolé, outaté, baye karim ni nak ohhh manchallah. Vie bien mère faou laobé amal diame et reviens nous vite way❤
Fatte nga hommage bimou defal Ndongo Lo nekh na trop
Grand diva avec une voix exceptional 🎉💕💗💝💯🥰🥰🇸🇳🇸🇳🇸🇳🌺
Machalah la diva goundou fane wergu yarame beaucoup de succès réussite totale vraiment tu une femme batante
Santal yalla musique dafa kharam kouko bayi wara sant soniou Brom yalla naniou yalla khir thi bopam 🤲🏻🙏
Macha allah la grande diva à la voix d’or yalnala Yallah maye goude fane ak wér si barkép Seydina Mohamed psl
Daurougnouléne baguéne dé rek DIAMA leu
Psl❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Allah Houma Amine Ya Rabi Incha Allah 🙏🙏🙏♥️
Mame Coumba yaw rek lay topeu ndakh sa yar sa dal ak sa téye Mach allah ❤❤❤❤❤
Machallah belle diva❤❤❤.
Longue et paisible vie.
Je me permets de vous conseiller d' éviter les réseaux sociaux.
J'aime bien Fatou laobe. Elle a un bon coeur. Que Dieu te garde.
Macha allah tata Fatou j'aime ton nouveau look daga yiiw machallah ❤️❤️❤️❤️ on attend ton prochain album. Inchallah Dieu va te relever. Il faut toujours apprendre à se relever pour faire honte à tes ennemis, bouléne may lignou beugué il faut toujours avancer.
Nn émission bi nekh na dama ré ba 😂ba sonou tata fatou yalla na yalla goudal sa fane ❤❤❤
Dafa bakh meun way lol machallah ❤❤❤❤❤
Une grande chanteuse internationale,c un don que dieu vous garde ❤love you❤ ❤❤❤❤❤❤❤❤
en 2014 lako guissone foire cices bi ,mais limou wakh ci taar bi deugleu deh , et dafa am lou grawe bouma guiss ci mom, moy bouleu holé ci beute dangay seug force elle dégage une forte personnalité machaallah❤
Maschallah notre fatou national yallah na la yallah deffaleu diam beug Lo gua kounek si rewmi !
Fatou vous êtes une brave dame il faut oublier la personne qui vous insulte
Ki dama ko beug ndakh fouleum, kikoy saga dinako wak deug bayiko mou dem
Sénégalais daniou mouna Segal nit teh kou tekiwoul dara moka deh .respect rek nga mérité teh thi famille bou bakh nga bok ❤❤❤
Lire sewal
Fatou laobe yalla na yalla defal diame ❤❤❤
Machala mouraye bi sellena longue vie à toi
Bila a part kiné lam moo daka woy thi Sénégal ❤❤❤❤🎉🎉🎉
Machalah ya mouna way fatou touré
maachaAllah sister Fatou...yaw koula gueneh thi art dara dotoufa déss maachaAllah...amnaa chance jouer ndo ak yaw Gorée bénn conférence bou douaniers yithi adouna donn déf niou déf première partie ak groupe ballet bima nékonn mais vraiment ce jour là wathieh wonn nga Gorée ak spectacle bou diaarone yonn maachaAllah donc gninguilay niaanal boubaakh...dila wakh daal ni Sénégal namm nagnoula lool sakh walaahi
Nio nguilay souhaiter une Très bonne reprise... tawfeekh _taysir_jamm thi yaw ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Elle a été honnête dans ses propos bravo Fatou et courage ❤
Fatou laobè ma chanteuse prèfèrèe, choco mom bayiko ak yalla dina ko guisse nitt ko khamnè togne rek bilakhi dinako guiss. Big up fatou
😂😂😂😂😂thiossane
Machala ndandane mingui ni
Souleymane son meilleur chanson ❤
Mashallah musique waxoul deug bilahi ndanane pur moy Fatou Laobé ❤
❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️ maschallah mouray bi seleuna
♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️fatou laobé 2002 ba tay mom rék sama artists bi
Maman Fatou laobe moune way ame fouleu❤❤❤❤❤❤
Ndeyssane une femme très digne moi je l'aime bien ndakh diambar la liguéy katt la djiguéne diou meune goor la yalla nako may goudou fane ak wergui yaram té doliko soutoureu
Machalla gnep contane
merci pour le son c'est genial maintenant
Courage yalla nopi na yalla dîna até lép mane dé ligéy rék la kham si yaw ak sa dôme Ndeye Fatou courage
Bilahi maman ya wakh deug Hoo Machalah longue vie à toi je t’adore ❤❤❤
❤❤❤❤❤ fatou ma sœur ma maman yalla nalla yalla maye goudoufane
Ma maman 💕❤️💕💕 je l'admire longue vie à toi
Maman Fatou Laobé une référence mashalah on t'aime et te respecte bcp. Tu as bcp fait pour le Sénégal dans le bon sens
MACHAALLAH. LONGUE VIE EXCELLENTE SANTÉ BCP DE BONHEUR MAMAN FATOU TOURÉ BALAGO. ÈMISSION RÉUSSIE. BONNE CONTINUATION.
Machallah touré mandingue mory ❤️💕💕💕
Elle est la meilleure ❤❤❤
Machalah Fatou, toute belle et yiw Machalah
J l’aime cette dame ❤dafa meune waaye
Machallah emission bi nékhna
Macha allah Fatou laobé ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Fatou laobe mo daka way Senegal ❤
Machalla fatou laobe la grande diva
Fatou laobe mashallah 🎉🎉🎉🎉 retane na ba tasss😂moussa kankou bayikooooo😝😝😝😝👋
Fatou yalla nalla yalla. Défale diam kou bakhala
Machallah tata fatou❤❤❤❤❤
Masha Allah Tata je t'aime très fort ❤❤❤❤❤❤
Yow laobe niepe la beugue defofi d'ara lou niawe grande dame artiste bou mak
Vrai ndanane meuna woye loll sama woyekate bi
❤❤❤❤ kou bakh la Ndeyesan feka namafi ci America ci Baltimore Maryland ❤
Fatou safna khorome ma sha allah
Bril il faut soutenir maman Fatou ❤
Machallah machallah ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
It’s not easy to be a singer in 🇸🇳 Senegal it is a very dangerous spot to be walay the showbiz in Senegal 🇸🇳 😢😢😢😢😢😢
Fatou TOURÉ YAGUE NIO BÉGUEULE. Gouda le FANE WEREULE AMIN YARABI ALLAH.
Dieuredieuf.
Machalla ❤❤❤
Maman Fatou laobe ken dakouko way Sénégal bilay. Yalna la Yalla aaral boppam
Je l'aime beaucoup
Passage thioossane bi meune nama raye 😂😂😂 je peux plus, aidez moi 😂😂😂
Fatou Laobe est une grde dame maa cha Allah, Mame Coumba li nga re si emission bi mousso ko re
Machala maman longue vie a toi waye rek ga meune
Maman fatou beuguenalla da teint rafetna mouraye rafetna laf thiate
Maachaa Allah ❤❤❤
Maschalla yalla na la yalla defal tawfekh nit kou bakh ga kou am foula ak fayda nagou ligueye nek bagne kata
Mâcha alla maman Fatou ❤❤
Bilay toure ya meuna weuuy riche sa fans la gambie
J'aime maman Fatou laobé❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
YAYE BOYE SANTAL YALLA MUSIQE🎶 YALLA DAKKO TÉRÉE KOKO MANATOULA DÉGUE LU SANTAL YALLA BOUBAAKHA BAAKH JAPPAL NI BOUROOM BÉLA BEUGUE RÉK JAPPAL NI KÉN DÉFFO LA DARRA
Bilay da gua bakh kou khamoul khamo rek
Thieye maman kinè mm moi je l'aime bc
Manchallah yiiwgui ❤❤❤❤
Maman Fatou on t'aime ❤❤
Toute belle que Dieu te garde
Beguetttt❤❤
Bayléne al yalla yaw amgua classe ba paré
Fatou focuseul rek bayi lep ci loho yalla beugue nala te dara douko dindi longue vie fatou de tout coeur avec toi
Ndaye Fatou amgua ndam sa yaye dioyoul
Waxi nite deugeu la Fatou laobe wax machala
😢 Machalla maman fatou je te Aime beaucoup du coraje ❤❤❤
Yalnala borombi geuna khir si bopam.weuy mom dara bakhouthi.
Mach halla long vie notre maman ♥️♥️
Machalla ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Machallah ❤❤🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉
Machallah
Une brave dame ❤❤❤❤
Machalah maman
Fatou comme tu l'as si bien dit n'en veut à personne ce qui t'est arrivé s'appelle le burn-out c'est à l'épuisement professionnel personnes e peut te marabouter tant que tu es croyante bon courage
Mashallah ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Tata fatou❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Mach'allah adjaratou
Machalla longue vie maman