L’AVENIR DE MODOU LO FADAM VIDE SON SAC «modou na lamb wala mou bayi… »

แชร์
ฝัง
  • เผยแพร่เมื่อ 1 ธ.ค. 2024

ความคิดเห็น • 218

  • @AtoumaneNiasse
    @AtoumaneNiasse 2 วันที่ผ่านมา +60

    Nékhoul ba nékhoul mais billahi modou lo ndanan la ❤❤❤

    • @wara2043
      @wara2043 2 วันที่ผ่านมา +4

      Li ma sof cii sen wakhtane moy dougnou deglounté

    • @sencoursanglais
      @sencoursanglais วันที่ผ่านมา +1

      Moyy Kharagne Lo

  • @ibralemeringue3258
    @ibralemeringue3258 2 วันที่ผ่านมา +47

    Modou Lo c’est le meilleur

  • @AbdouDiallo-u1g
    @AbdouDiallo-u1g 2 วันที่ผ่านมา +8

    Suis fans de Bala m Modou dumromou boyi félicitations Modou lo

  • @TallFambaye
    @TallFambaye 2 วันที่ผ่านมา +15

    modou lo yalla na am diamou❤

  • @bellingham-k6t
    @bellingham-k6t 2 วันที่ผ่านมา +39

    J suis fans de balla gaye2 mes bly gni khamougnou Modou lô lagnouy wakh lepp nan siteu lolou la waron def eumeu sene def nako te danoul Modou lô Modou AK KO fou sori sakh takhoul gua dann ko

    • @nadiainnocenti3619
      @nadiainnocenti3619 2 วันที่ผ่านมา

      Dangay doule rekk modou lo moy sa mbeur

    • @mormbaye6583
      @mormbaye6583 2 วันที่ผ่านมา +1

      @@nadiainnocenti3619😂😂saway meun nga togn

    • @sencoursanglais
      @sencoursanglais วันที่ผ่านมา

      Guiss nga! Siteu nieuwoul wonn pour dann. Dafa nieuwonn pour bagna danou.
      Legui nakk...Na Modou tourner la page avec Siteu. Dieul Ball. Modou Balla - Modou Lekk si 500 Millions Combat du Siecle. Dieul Sa Thies Lekk 200 Millions. Dieul Reug Reug 200 Millions. Dieulat Ama 200 Millions. Bayi Beure. Diokh Franc Mou Dokhal.

  • @serigneNG
    @serigneNG 2 วันที่ผ่านมา +17

    Très compliqué, ils parlent tous en même temps, des fois c’est chaud 🥵 😢😢😢😢

  • @sebamc4219
    @sebamc4219 2 วันที่ผ่านมา +14

    Yènafi wakhon mbeur yiii dègno wara bayi mystique SI LAMB MODOU LO VS BOY NIANG.VAR banguifi d.modou seul

  • @issalaye4
    @issalaye4 2 วันที่ผ่านมา +34

    Débat bou intéressant la mais malheureusement amoul déglou wanté nieupeuy beug wax à la fois

  • @Dwight22
    @Dwight22 2 วันที่ผ่านมา +11

    Thièy Modou!!!! Allahou akkbar.

  • @abduuu-t1v
    @abduuu-t1v 2 วันที่ผ่านมา +24

    Limotakh siteu dou nougo beuré wakh lénko deug😢

  • @malickdia3495
    @malickdia3495 2 วันที่ผ่านมา +2

    Machalah ndame recke inchalah cikaw cikaname inchalah cikaw ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉

  • @KhalilDien-fe5uh
    @KhalilDien-fe5uh 2 วันที่ผ่านมา +7

    Kharagn seul❤❤❤❤ .... Combat woné naniii Siteu amoul fitttt

    • @sencoursanglais
      @sencoursanglais วันที่ผ่านมา +1

      Guiss nga. Wakh rekk ladonn deff...Di arriere rekk.
      Siteu nieuwoul wonn pour dann. Dafa nieuwonn pour bagna danou.
      Legui nakk...Na Modou tourner la page avec Siteu. Dieul Ball. Modou Balla - Modou Lekk si 500 Millions Combat du Siecle. Dieul Sa Thies Lekk 200 Millions. Dieul Reug Reug 200 Millions. Dieulat Ama 200 Millions. Bayi Beure. Diokh Franc Mou Dokhal.

  • @cheikhgueye2380
    @cheikhgueye2380 2 วันที่ผ่านมา +23

    Siteu a bloqué le poigné droit de modou lo pour esquiver les coups de khararagne lo😂😂😂

    • @mouhamet115
      @mouhamet115 วันที่ผ่านมา +1

      Tapett la di😂😂 wakh rk la meun

    • @jhonlatrel2284
      @jhonlatrel2284 วันที่ผ่านมา

      C'est interdit oubien

    • @sencoursanglais
      @sencoursanglais วันที่ผ่านมา

      Guiss nga nonou la demee

  • @mourtadasarr9006
    @mourtadasarr9006 2 วันที่ผ่านมา +9

    Modou Mbaye a raison
    Sagn sagn bii boy yii dagnko manquer.
    Surtout situé mii wakh djé beurii rekk

  • @AssaneDia-xi1ul
    @AssaneDia-xi1ul 2 วันที่ผ่านมา +25

    Modou. Lo
    👑👑👑👑👑👑👑👑💪💪💪💪

  • @rimesmakerposeidon2427
    @rimesmakerposeidon2427 วันที่ผ่านมา +3

    Modou lo messi de la lutte sénégalais xaragne lo ❤

  • @Jeuneentrepreneurcheikh217
    @Jeuneentrepreneurcheikh217 2 วันที่ผ่านมา +8

    Bayilén dii Félicité Siteu way 😮soff nguénn trop toppoulénn feuléé way 🫵

  • @talibebambasalihousarr1067
    @talibebambasalihousarr1067 2 วันที่ผ่านมา +4

    Père Iow khamo adouna dhh Iow khamo louy doylouuu Youssou sakh siii Deug daffa warra bayiii waye thé diamou ji yalla Modou Nioune ay Supporters niou Beug mou bayiii Wassalam

  • @ibralemeringue3258
    @ibralemeringue3258 2 วันที่ผ่านมา +76

    Siteu tjrs bouniou ko gagner nguen féliciter ko kaagne laay fass diome

    • @AbdouSow-i2v
      @AbdouSow-i2v 2 วันที่ผ่านมา +11

      Daneko ragalll rek 😂😂

    • @saidoubah8511
      @saidoubah8511 2 วันที่ผ่านมา +4

      Walay ndeysan

    • @modo6218
      @modo6218 2 วันที่ผ่านมา +5

      Lolou mana metti

    • @AliouneMbengue-y3v
      @AliouneMbengue-y3v 2 วันที่ผ่านมา +7

      Siteu khamoule dara daye daw rek

    • @CheikhGueye-js7ek
      @CheikhGueye-js7ek 2 วันที่ผ่านมา

      😊1aqq​@@AbdouSow-i2v

  • @votremiroir7612
    @votremiroir7612 2 วันที่ผ่านมา +5

    Fadam mome dafa gueum mystique bamou heupou

  • @FallouDiagne-mc4gs
    @FallouDiagne-mc4gs 2 วันที่ผ่านมา +2

    Modou lo yal na am diam way ❤❤❤

  • @dehabou7720
    @dehabou7720 2 วันที่ผ่านมา +1

    Fadam tank yi wékh na dh 😂 mais sou thiaxane diékhé modou c’est le meilleur lutteur.

  • @cheikhounatine758
    @cheikhounatine758 17 ชั่วโมงที่ผ่านมา

    Fadam dafa beug modou takk gris gris 😂😂😂😂😂

  • @yorokante8020
    @yorokante8020 2 วันที่ผ่านมา +1

    Modou mbaye yw rk nk ya khame modou bly kouko beugue ngua machalla ❤🎉

  • @mouhamedcherifaidara923
    @mouhamedcherifaidara923 2 วันที่ผ่านมา +4

    Siteu naroul ame diome boudé sayou daano nguène félicitéko Walahi dou daane kéneu

  • @isocra-ktm4099
    @isocra-ktm4099 วันที่ผ่านมา

    way way mayleine nitt yi diam ùodou lo limou done ya'Allah mokoko df dou mystique dou leineine

  • @mamadoualphaba3799
    @mamadoualphaba3799 2 วันที่ผ่านมา +2

    Siteu avait 75/ pourcent pour battre mais il a respecte trop le consigne de Max bargane : Modou lo est très très talentueux et technique et fort mentalement

  • @boyediaw1018
    @boyediaw1018 วันที่ผ่านมา

    Modou Lo vrai diambar leu❤️❤️❤️🎉

  • @legauchedione263
    @legauchedione263 2 วันที่ผ่านมา +2

    Siteu dagn KO diapal modou lo bamou né némeu mou am sur le plat , Li ama baldé , wala boy Niang souko amoneu danou naa bou yague niit bou amoul fiit lou ci waye meune 😊

  • @MborThioub-xd3vn
    @MborThioub-xd3vn วันที่ผ่านมา

    Yalla rk moy mayie ndam way kanan galahti modou yalla nako yalla defal diam ga am lu guen lamb

  • @mamzodia1471
    @mamzodia1471 2 วันที่ผ่านมา +1

    Ndeyssan Fadam daa yéné modou lo

  • @ElhadjiFall-nw2he
    @ElhadjiFall-nw2he 2 วันที่ผ่านมา +2

    Yen de len ratatati rek fadame ana sa ay victoire xamouleeen tous😂😂

  • @maxumbaye2790
    @maxumbaye2790 2 วันที่ผ่านมา +3

    Vous avez juste peur de dire que Siteu a juste peur de Modou lo daff ko ragalé khël c'est tout

  • @Niomnieugz
    @Niomnieugz 2 วันที่ผ่านมา +2

    Becaye no def mou djéma Andik modou ay sik😂😂😂😂

  • @saerhihiodf110
    @saerhihiodf110 2 วันที่ผ่านมา +5

    Becaye modou meunatoul niakati si adouna

  • @azizdia3347
    @azizdia3347 2 วันที่ผ่านมา +6

    Vraiment siteu dou mbeur mounoul mbeurei amoul fitt tei yaram daffa dess bou bax xamoul adouna mounoul communiquer kou wara sant yalla la

  • @AbdouDiallo-u1g
    @AbdouDiallo-u1g 2 วันที่ผ่านมา

    M fadame mi werne😂Modou dh mola gueune paré mystiquement

  • @IbrahimaDia-z5g
    @IbrahimaDia-z5g 2 วันที่ผ่านมา +1

    Félicitations et encouragements c’est différents. Siteu ne

  • @KhadyTob
    @KhadyTob 2 วันที่ผ่านมา

    Fadame nél na Modou delouwatt si yeuffou thiédoyii rk yéne Ama AK Boy Niang couléne gueuneuh mystique nane laléne Modou def bayiléne gnou way

  • @mouhamedcherifaidara923
    @mouhamedcherifaidara923 2 วันที่ผ่านมา +2

    Fadam mo beug ay wakhi mystique soff nga trop on parle sportivement yow wakhou galathieu rk

  • @ElhadjiFall-nw2he
    @ElhadjiFall-nw2he 2 วันที่ผ่านมา +3

    Vrement bourey tu as reson

  • @IbrahimaDia-z5g
    @IbrahimaDia-z5g 2 วันที่ผ่านมา +2

    Bour Gueweul et Fadam ne travaillent pas pour la lutte mais plutôt pour Aziz ndiaye et balla gaye.

  • @falloudiop6807
    @falloudiop6807 2 วันที่ผ่านมา +3

    Bonjour déba bi nékh trop mais na kounék deglou moromame svp

  • @PapeOusmanePapaOusmane
    @PapeOusmanePapaOusmane 2 วันที่ผ่านมา +2

    Fadam mii matena 100 k lambal ta niew bakham

  • @aboudiop6467
    @aboudiop6467 2 วันที่ผ่านมา

    Modou lo c'est le meilleur

  • @alysene7091
    @alysene7091 2 วันที่ผ่านมา +5

    Keneu dou deglou keneu

  • @daoudasarr4455
    @daoudasarr4455 2 วันที่ผ่านมา

    Bilahi Modou lo bo tope gni do bayil nga dem nek si Lou nex yallah

  • @saerdieng6777
    @saerdieng6777 วันที่ผ่านมา

    Bécaye Mbaye néna kheuy rék am 100 millions yomboul😂 bilahi bénéfice 100 millions thi business moins de 5 mois yomboul déé na lèer

  • @manoumbebeye6308
    @manoumbebeye6308 8 ชั่วโมงที่ผ่านมา

    Bonjour, le seul problème de votre plateau est que vous ne nous laisser pas l'opportunité de vous écouter, la discussion est trop dispersée. Sinon, merci pour les analyses pertinentes.

  • @baubaubeye7836
    @baubaubeye7836 2 วันที่ผ่านมา +2

    Mais nakk vraiment débat bi war nguen ko organiser watte 😢ken dou deglou sa morom 😂nitt ki dina am lou intéressant loumou war wakh mais ken dou deglou kounek di wakh 😢😢

  • @mamadoudoucoure3689
    @mamadoudoucoure3689 2 วันที่ผ่านมา +1

    Fadame khana Moy modérateur 😂😂😂

  • @AmadouSamb-n4u
    @AmadouSamb-n4u 2 วันที่ผ่านมา

    Il faut l'encourager mo gueune nguéne koye féliciter

  • @MoussaBamba-ey6wn
    @MoussaBamba-ey6wn 2 วันที่ผ่านมา +1

    ci siteu avait attaqué , modou lo le finissait siteu a bien fait de suivre les instruction il devait ensuite profité mais modou es trop fin et tactique cest tres difficile de le battre seul dieu a donne modou a balla gaye sinon billaye modou es meilleur que tous

  • @papitogueye2767
    @papitogueye2767 2 วันที่ผ่านมา +3

    Siteu si j’étais luis damay dem ba diex louma am diel, prck douko modou danneii douko yakal dara.

  • @petitjoeba4031
    @petitjoeba4031 2 วันที่ผ่านมา +2

    Modou defoul.bèn ereur ki mouy beurèl moy daw modou amoul ben pression si combat bi

  • @AlassaneDieye-cc7jq
    @AlassaneDieye-cc7jq 2 วันที่ผ่านมา +2

    Fadam Siteu beugu na wayé xamoul. Yénako warone léral noumouy def ba dane😂

  • @sencoursanglais
    @sencoursanglais 2 วันที่ผ่านมา +3

    Mann louma guiss. Na *Modou* beurré *ak Balla Gaye*. Combat du Siècle : *Lathié 500 〽️illions.*
    *Sou paré dieul Sa Thiès:* 200 〽️illions
    *Sou paré dieul Reug Reug:* 200 〽️illions
    *Sou paré dieulatt Ama:* 200 〽️illions
    Dadialé 1 〽️illiard et poussière...Bayi Beuré. Tegal Couronne bi nionn Franc, Franc dieul ko. Dokhal !
    Mann guissouma mou beuré Watt akk Siteu. Siteu na xamni sou ko Benn Rois mayaté chance. N'a liguey. Roi bi daniouy kayy liguey. Kenn dou ko lidianti.

  • @lbyoungtv2223
    @lbyoungtv2223 2 วันที่ผ่านมา +1

    Fadam mi seytané deug lh 😢😂 lamb c forcé gua tak galadj mod lo a sa façon leigui gua niii da wara

  • @PapeDiagne-hx7lw
    @PapeDiagne-hx7lw 2 วันที่ผ่านมา +2

    Dolen abone gir yalla ak père bekay ❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉🎉

  • @abduuu-t1v
    @abduuu-t1v 2 วันที่ผ่านมา +3

    Bourr mom mogui koy wakh deug

  • @IslandCureislande
    @IslandCureislande 2 วันที่ผ่านมา +4

    SITEU DEY DANOU DANOU DANN DANOU DANOU

  • @anthioumanefadiga9314
    @anthioumanefadiga9314 2 วันที่ผ่านมา +2

    Siteu mo ayoul cii bopam. Tok plateau ak wakhe djiou beurii.

  • @PapeOusmanePapaOusmane
    @PapeOusmanePapaOusmane 2 วันที่ผ่านมา +2

    Boudone galath rek fadam mii dou bayi lamb 😂

  • @rimesmakerposeidon2427
    @rimesmakerposeidon2427 วันที่ผ่านมา +1

    Siteu dafa daw sou takhawone modou lo reuy ko

  • @mordia4756
    @mordia4756 วันที่ผ่านมา

    Fadame tay danou gua modou mi bayiwoul boppape dh

  • @alioudieye5778
    @alioudieye5778 2 วันที่ผ่านมา +1

    Siteu defoul dara way Ahhh da ragual Modou lo trop motakh

  • @cheikhounatine758
    @cheikhounatine758 17 ชั่วโมงที่ผ่านมา

    Aziz est 👍🏿
    Modou Lo peut bel et bien arrêter la lutte et s’en sortir hein

  • @bathiembaye1722
    @bathiembaye1722 2 วันที่ผ่านมา +2

    Niom nieppou ken xamousi gatt si lamb reuy lamign kassé 😅😅😅😅😅😅😅😅

  • @ElhadjiFall-nw2he
    @ElhadjiFall-nw2he 2 วันที่ผ่านมา +3

    Becaye wax ngua l'EP

  • @bathiefaye50
    @bathiefaye50 2 วันที่ผ่านมา

    Vraiment modou lo ndanane la

  • @daoudasarr4455
    @daoudasarr4455 2 วันที่ผ่านมา

    Yanna Modou lo baye lamb

  • @votremiroir7612
    @votremiroir7612 2 วันที่ผ่านมา +2

    Comme khalé youy wakhtane réck kén dou déglou gnépay beuga wakhando à même temps

  • @makambtv608
    @makambtv608 2 วันที่ผ่านมา +2

    Léne rekk moy problème moy doléne dégueloneté

  • @AliounebadaraGassama-or4op
    @AliounebadaraGassama-or4op 2 วันที่ผ่านมา +1

    Boudé bénn combat l'a Modou lo déssé nako diokh sathies

  • @modoufallbetebeteitsenegal5272
    @modoufallbetebeteitsenegal5272 2 วันที่ผ่านมา +1

    Sen émission bi nekhna mais dolén deglouweunté nieupou mounounio wakhadon delén deuglonte way isss

  • @BeckayDiop
    @BeckayDiop 2 วันที่ผ่านมา +1

    Modou tay la guena lamb wakh doff rek nguinn Di wakh

  • @GuyGuiguitou
    @GuyGuiguitou 2 วันที่ผ่านมา

    Mdlo djambar leu wayei teunkoul lamb il a des adversaires potentiels et directs bou bayi wei nkk il en a le droit mais d’où dafa deff lepp

  • @MAN_TV
    @MAN_TV 2 วันที่ผ่านมา +1

    Fadam ioe tu ne parles que de mystique 😢

  • @assanesene9409
    @assanesene9409 2 วันที่ผ่านมา +1

    Fadam bayuil gayui wak waye

  • @nimspetite
    @nimspetite 2 วันที่ผ่านมา +1

    😂😂😂siteu dawnaaaa combat bi yeup siteu excité na barina wakh gnouniko kay def antidopage mou bagn modou louko wakh togn ko

  • @AmaraDiop-e5l
    @AmaraDiop-e5l 2 วันที่ผ่านมา +2

    Boungén khamon Dara nék roi des aréne

  • @anthioumanefadiga9314
    @anthioumanefadiga9314 2 วันที่ผ่านมา +1

    Siteu bimou gnibé batay guénoul wakhe. Kanam bi mo ndéwii

  • @BadouDeh-jv7ge
    @BadouDeh-jv7ge 2 วันที่ผ่านมา

    Fadam da geum galath 👀

  • @abdoulayesow4208
    @abdoulayesow4208 2 วันที่ผ่านมา +1

    Papa Sow fin carrière lako dane

  • @massambadare
    @massambadare 2 วันที่ผ่านมา

    Yen lokho situé tairai bisinek la Modou lo diap lolou motah delen khol boubakhe

  • @lefootballsansfrontieres8921
    @lefootballsansfrontieres8921 2 วันที่ผ่านมา +2

    Xalis yen l titeul pas Modou

  • @sadiafaty2556
    @sadiafaty2556 2 วันที่ผ่านมา

    Grand Modou Mbaye tu as tout bien analysé. Niou dane Modou nieup dénio am Sagn sagn mais Siteu dafa dess mais il a été courageux ba danouwoul

  • @NiangDane
    @NiangDane 2 วันที่ผ่านมา

    Fadame yaw wakhou douff rike laye wakh

  • @AbdouDiouf-g8g
    @AbdouDiouf-g8g 2 วันที่ผ่านมา +2

    Situé.la.faral.mé..da.ragal.modou

  • @faye6718
    @faye6718 2 วันที่ผ่านมา +1

    Modou lo c'est le meilleur mé situe tmt c'est le meilleur baye léne sokhor niari nafék yi bour ak Fadame ak séne niawaye

  • @AlassaneDieye-cc7jq
    @AlassaneDieye-cc7jq 2 วันที่ผ่านมา +1

    Combat tolof tolof😂😂😂😂

  • @KossoGadiaga-vw3wc
    @KossoGadiaga-vw3wc 2 วันที่ผ่านมา

    Siteu kasse siteu kasse ❤️👑👑👑👑👑

  • @AissatouHagne-f1t
    @AissatouHagne-f1t วันที่ผ่านมา

    Fadam beuri wakh 10 combat ben Victoire gua am 9 défaite

  • @oussoubane2712
    @oussoubane2712 2 วันที่ผ่านมา

    Par moment on a l'impression d'être dans un poulailler quand tout le monde veut parler en même temps.

  • @Blackmamba786-m6e
    @Blackmamba786-m6e 2 วันที่ผ่านมา +1

    Siteu mo dane diokhlén ko victoire ram way

  • @ndenediagne50
    @ndenediagne50 2 วันที่ผ่านมา +1

    Siteu t le meilleur Gnoune yaw rek lagnouye top 😂

  • @khadimfaye8003
    @khadimfaye8003 20 ชั่วโมงที่ผ่านมา

    Siteu dafa Niank dioume

  • @khdimfall1837
    @khdimfall1837 วันที่ผ่านมา

    Modou mbay ioe AK sa Bay bagou lien Modou lo wayi Modou lo rek lan topou

  • @alasanembow8252
    @alasanembow8252 2 วันที่ผ่านมา

    Wa khana commentaire yi ken faraloul Siteu

  • @MaguatteNdiaye-my6mg
    @MaguatteNdiaye-my6mg 2 วันที่ผ่านมา +1

    Siteu amoul fiit wakh dji. Moobari