Salam et son pere de vrais irresponsables Baye niass jaraloulen dara mais kou lal sen leader politique ngen hatarayou Vous etes la honte en chair et en os Merci et courage ahmed cissè
Qu'attend la justice ? Si c'est possible qu’on fasse subir une telle barbarie au Sénégal, sans que les auteurs soient arrêtés, nous ne serions plus dans un état de droit ! Attendons la suite judiciaire.
Il faut les mettre tous en prison avec leur père qui est complice. Y’a pas de Serigne ou autres . Que des barbares sauvage. Je ne savais pas que tu peux te dire être musulman et avoir ce comportement.
pourquoi tu parles de la famille de baye Niass ...salam et autre et ce vieu ne font nullement parti de la famille de Baye Attention ...certain se nomme niass et ne sont pas en bon terme avec les fils de Baye Niass surtout ce vieu
wa medina baye tame naniou seneu yi dei di dore nit aka fitnale cheikh baye niass nila wone T cheikh baye niass dafa yaga khekhal wa tassawouf si kanamou wahabiya yi mais apres liniou ko fayé saga ak fitnal ndakh dafani baye niass dafa dioum si massalah melni baye warta dioum si massalah meme yonneti yi daniou dane dioum mais senegal serigne laniou def yalla .
Bayilen setane nit mou wakh louko nekh rkk guen yeureum ko di wakh ki khamolen loumou def té mom modone nianal Gana Mésséré lou bone sénégal yeup guisko kne yalla khol lay fay
Walakhi lignoula déf nonou lama mété , mais aussi Bayile di teukou nite parsk yalla rek mofi nek…. Gana nite la comme yaw té nite matoule , du courage 🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏
@@mouhemedbatcha3644 Yaw khanaa kon ci naafékh yi NGA bokk ?? Wala dëkkoo Sénégal 🇸🇳 ?? Ku sante NIASS wala Mbacké, Yamnagnou kumélné yaw, Broom santi " Fëgg diaaay yi, ci Kanam Loi bi ??? Voici la preuve. Du muddjou fénn! Ndakh dungéen ay NIT🤣🤓
@@mouhemedbatcha3644 Mandou ci l'Islam mooy guiss AK toogne NGA saafarako boko mannoul NGA nakharlouko ci sa XOL👂 Waayé du Tékki mukk 👁️👁️guiss dégg tékk ci sa tank !!! Comme ningay waxé nii. Réew mi AmouL Yoon ! Parparloo akuk Ndjaam, moofi nékk🤫🤺🏌️
Bilahii ki dama ko buegan waye ba mou buega na ray guana talibe Borom touba bo bou la pare wan thi mom bilahii kha man na né di nan ko tora khall nioun mom sou né bakh ba kha na nou yor moy tou len niou💪
Meussoumala kham, meussoumala djiss lou weessou teye waayé beugue naala. Andak yow di metitlou lii nioula def. Nioune dé ay talibé baye you deggou lagn té lii dafniou metti looool. Mane dé sama khol bi metti na torop torop. Ils devraient avoir honte 😭😭😭
Bayilen guiss nit mou wakh rkk guen yeureum di wakh ki mom yalla moko fay kholam heure bi daw ladone nianal Gana Mésséré lou bone té defouko wakhouko tay mou tok fi di wakh ay yone même soudé liniou ko def rafétoul mo togn
Dites à ceux qui méprisent le souvenir de l'oppression des tyrans contre les faibles après leur mort Dieu n'a-t-il pas mentionné dans le Coran les vilaines actions de Pharaon, Haman, Qarun et Abu Lahab ? Sont-ils morts ou sont-ils encore vivants ?D'autres tyrans sont meilleurs qu'eux jusqu'à ce qu'il soit empêché de se souvenir Mais les hypocrites ne savent pas.....Prenez du trait à deux faces qui est hostile à la vérité et à l'honnête et digne de confiance Laissons Al-Sadiq attendre que les quelques amis trouvent celui qui l'a choisi pour le destin Les gens ne suivent que des conjectures, et ce ne sont que des mensonges......
Kou si bayiwoul topp Serignou legui yi ni rekk ngay moudié. Diamou dji Yalla ta sakou sa nguereumal waydiour fofou la diamono tolou. Serigne sou bari danio wathié senn yoon, dieul bennen yoon bou bokoul akk lafi seni Mame ligeey bayi fi.
J'ai fait des constats que yow 2ans gui ni yow dangay def violence verbale Di def yefu ma meun té yaffi teuku won gana messere ak cheikh Omar Diagne kon yoyu violence deko moytu
Si vous vous êtes limité à la sunah seulement y'aura pas ses problèmes.Car là-bas tous les gens sont égaux et si tu as quelque chose à dire on peut t'écouter.Alors qu'ici le Serigne est plus comme un Dieu.
La première chose que le cheikh m'a dit quand je suis venu à lui pour étudier et améliorer ma pratique de l'islam, c'est : "khali a nafsa kawtal". Nous ne sommes toi et moi que des frères en Allah Swt qui cheminons derrière le Bienaimé Prophète Mohammad SAWS. Si tu me vois faire une chose que la charia à proscrit, pars car j'aurai trahi mon sacerdoce. Partout le Bien et le Mal s'affronteront, même là où l'on est censé ne vivre et penser qu'a Allah SWt.
@@mthiam1567 mais comment peut tu m'expliquer ce qui s'est passé ?Car c'est pas la première fois que l'on voit ces genres de choses dans les tarikhas.Ex y'avait ici l'affaire de Bethio récemment ?
@@amadoudiallo9277 mandou bakhna deee d’aucun les chefs religieux ils ne se sont jamais senti supérieur au autres. nangoulen Serigne Touba El Hadji Malik Mame Baye Niasse El Omar foutiyou nitt dey nangou pour moi gnak kilifeu woroul gnak dine weroul woroul encore une fois sunuy kilifeu wallahi ne nous ont jamais enseigné ce terreurs.
@@mberryable qui t'a parlé des chefs suprêmes des tarikhas je te parle de ce qui est entrain de se passer aujourd'hui et toi tu me parles des fondateurs.Quand l'entente depasse la raison dans ce cas y'a problème.Crois tu ce qui s'est entrain de se passer aujourd'hui dans les tarikhas si leurs fondateurs étaient là ça aller se faire ?Il faudra bien analyser pour être à la hauteur.

N'oublions surtout pas les 5 prières quotidiennes car cette vie là est très courte.dieu est grand
🙏🙏🙏 machalla amm na solo loll le des 5 cinq prières est un obligatoire
Ça sert à quoi ?
Toi aussi n'oubli pas les 5prières
Merci Ndongo sene🙏🙏🙏
JULLI BAKHNA LOLOU AK KHOL NU SÉTT REUY IYANE BONN YALLA NANI SI YALLA MOUSSAL
Salam et son pere de vrais irresponsables
Baye niass jaraloulen dara mais kou lal sen leader politique ngen hatarayou
Vous etes la honte en chair et en os
Merci et courage ahmed cissè
Alhamduliah Yalla Yonénete bi sama niary wadiour !
Yow la gueum
Rafétoule démal bock gni dogatila lolou yow la engagé
@@aminatawone8915 parle wolof ou français j’ai rien compris
@@lesenegalais1161 Bayil rothie tougne ba nopi ,yeuffou gordjigéne yi!
@@bambagueye7484 bayi nala ak yalla
Mane mom sama yaye doynama Serigne ♥️🥰🤲☝️
Très bien ! Doyna seukk
Wékou nga fou woor.
manit🙏
Amnga serigne bou wor
@@magattediene8920 😍🤲
AHAMDOULILAH C’EST IMPORTANT LE RESPECT, L’INTÉGRITÉ ET LA DIGNITÉ HUMAINE...QUE JUSTICE FAIT SON TRAVAIL.
Wawaw.merci
@@rabya7 npl0
Je
,
Dekka bou am yone meme sen papa bi dagnko wara diapou
En tout cas le Mr est tres calme et posé. Que justice soit faite
Ah bah alors aujourd'hui je penses pas toserai réitéré ces propos
Merci procureur. Il faut etre tres severe avec cet famille e leurs enfants.
Ndeysanne mougneul mon frère
Qu'attend la justice ? Si c'est possible qu’on fasse subir une telle barbarie au Sénégal, sans que les auteurs soient arrêtés, nous ne serions plus dans un état de droit ! Attendons la suite judiciaire.
Il faut les mettre tous en prison avec leur père qui est complice. Y’a pas de Serigne ou autres . Que des barbares sauvage. Je ne savais pas que tu peux te dire être musulman et avoir ce comportement.
Bien dit 💯👍
Depuis ma naissance avant les indépendances à nos jours c'est la première fois que je vois un homme humble et honnête sur toute la ligne
😂😂😂
Xamo liguaye wakh qui domouharame la 😂
@@rokhayacisse1606 kon koi
@@mantousamba2809 original domoukharamata ndiaye ma sœur ki da khamoul rk😂
Tu changes d'avis maintenant 😂😂😂😂, oubien
Machala nitte kou deugue gua te dale gua te amegua esprit de depacement yalla maye lo kholo mougne
Dieugueloul prof Cheikh Oumar Diagne. Togne mom bakhoul.
Way gnii tamiit torokhal gui eupna daal. Yallah sam leu
Maachaa halla refet na torop 🤲🏻🤲🏻🤲🏻yalla bakhna
Machala vous avez parfaitement raison que dieu vous protège
C'est honteux venant de la famille de BAYE Niasse un adepte de la paix un référence
pourquoi tu parles de la famille de baye Niass ...salam et autre et ce vieu ne font nullement parti de la famille de Baye Attention ...certain se nomme niass et ne sont pas en bon terme avec les fils de Baye Niass surtout ce vieu
C'est pas lui qui menaçait qu'il avait des pouvoirs magiques 🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣
@@mahrifatoubilahi6464 Niome nio def liniouy khass lou way. Lii dafa rouss lou, dafa niaaw mane sama khol baa ngi beugue guenneu. Mane sama baye mouqaddamou baye lawone. Franchement lii dokhoul
wa medina baye tame naniou seneu yi dei di dore nit aka fitnale cheikh baye niass nila wone T cheikh baye niass dafa yaga khekhal wa tassawouf si kanamou wahabiya yi mais apres liniou ko fayé saga ak fitnal ndakh dafani baye niass dafa dioum si massalah melni baye warta dioum si massalah meme yonneti yi daniou dane dioum mais senegal serigne laniou def yalla .
Bayilen setane nit mou wakh louko nekh rkk guen yeureum ko di wakh ki khamolen loumou def té mom modone nianal Gana Mésséré lou bone sénégal yeup guisko kne yalla khol lay fay
Je suis Talibe baye niass waye dema rouss 🤦🏾🤦🏾 li defa metti
Doo rouss ba dab ma sama baye mouqaddamou baye la woone wayé lii niaaw na té rouss lou na. La honte. C'est la fin du monde soubhanallah
Ndèyessane
Wallahi li diefou domi haràm degue la sén baye moy kan le 24 bou féné dina KO degue
Wawaw tout à fait d'accord avec toi
Allah n'accorde jamais sa miséricorde sur un peuple qui cautionne l'injustice.
Baayill mo sedd yallah bakhna nit ko bakh ngah
Je suis avec toi malgré linga wakhone si chaikh Omar Diagne je suis contre Sénégal Les petits marabout gnoko yakha
Kim tekou moka eup bopou akh moko dalle
@@laminembathie9952 lolu kessé la amoul lenen
Merci pour le message de la fin c’est très important et courage niawna té metina trop
En tout cas il parle bien se mr Cissé
Machalah cheikh akhmed cisse niogui sa guinam
😭😭😭😭😭 j'ai honte pour mon pays
C'est grave cette justice privée au nom du privilège de naissance qui doit être aboli au Sénégal. PAN
Khawema ani serigne ak politique beugue khalis rekkkk serigne wakhou yalla ak wakhou senetibi
Ana lo khame si kou réw
ALHAMDOULILLAH ❤️ derrou BAYE NIASS RDA 🍀💚 kene mounou KO yakha
Massa ndeysane yalla na yalla attei
Nala Yalla Same dolila soutoura amine ya rabi Amine
Walakhi lignoula déf nonou lama mété , mais aussi Bayile di teukou nite parsk yalla rek mofi nek…. Gana nite la comme yaw té nite matoule , du courage 🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏
Je suis mouride mais wallahi liii metti nama trop barkeb s saliou
li kouy nitt metti nala
Louy ndayou je suis mouride....sén xélou sheytané yi fou nguén dém youboukofa....vrai doméram
@@mawlanacheikhndiaye7924 ki weroul
Ki dagn ko moy
Yaw dodara
Mashaallah Mashaallah
Ahmed Cisse
Wakhou prefet bi raffetoule dara
Gnatta Senegalais gno yore double wala triple nationalitè
Macky Sall aki gno gname yeupe ame nagne double nationalitè
Du courage talibè Baye 🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾
Ndaysann
Que justice soit faite, dieu est grand
Ndaye Sane 😥😥😥😥👌
NagnouLéen ATTÉ ATTÉP RAY. AmouL Serigne AmouL Taalubé 😭😭 AmouL sëuttoub Kénn! RÉEW 🇸🇳 mi fook gnou 👉 Yamalé Sante yéppou! Il faut que justice soit faite 🏌️🏌️🏃🏃🤺🏌️.
Yala sakh yemalewoul nafekh bakhoul je suis pas niassene
@@mouhemedbatcha3644 Yaw khanaa kon ci naafékh yi NGA bokk ?? Wala dëkkoo Sénégal 🇸🇳 ?? Ku sante NIASS wala Mbacké, Yamnagnou kumélné yaw, Broom santi " Fëgg diaaay yi, ci Kanam Loi bi ??? Voici la preuve. Du muddjou fénn! Ndakh dungéen ay NIT🤣🤓
@@taphand8323 nafekh wessewoul gua mandou ok vous avez rien compris allez y il avoir la discipline dans là Vie
@@mouhemedbatcha3644 Mandou ci l'Islam mooy guiss AK toogne NGA saafarako boko mannoul NGA nakharlouko ci sa XOL👂 Waayé du Tékki mukk 👁️👁️guiss dégg tékk ci sa tank !!! Comme ningay waxé nii. Réew mi AmouL Yoon ! Parparloo akuk Ndjaam, moofi nékk🤫🤺🏌️
Mouride sadikhe la tè kou sopp Baye Niass la mais li niawna lole. Yallah na Yallah mayla kholou mougne
C’est ce que ça donne quand des marabouts se rangent aux côtés des ennemis du peuple.
Li dafa nyaw
Khana Gambians dou nit
Mane Sènègambienne la et tres fière
I am a very proud Senegambian
Mangui lay masta wou bou bakh dagnla beugone humilier mais ils n'ont pas réussi ndakh Dagno yokou Say sopé
Yalla Dina atté,guisna lep
Sénégal papa yi kéne momouko k justice soit faite et k ce Salam et les autres agresseurs y compris leur Papa pourisse en prison
Soubhanalah li mom warnafi diog il faut que la justice de notre Sénégal soit neutre non à la violence humaine
Je suis tout cœur avec vous
Massa pape 💖
Ndeye san
Coran et Sounnah mo ndieuk té Moy moudjiu DEUG bi Dina Lerr inchaallah
Et qui a dit le contraire mandou bakhna deee.
Celà est injuste .
Je suis contre cet acte ignoble et personne ne doit pas prendre une intervention de ces soi-disant marabouts
Bilahii ki dama ko buegan waye ba mou buega na ray guana talibe Borom touba bo bou la pare wan thi mom bilahii kha man na né di nan ko tora khall nioun mom sou né bakh ba kha na nou yor moy tou len niou💪
Meussoumala kham, meussoumala djiss lou weessou teye waayé beugue naala. Andak yow di metitlou lii nioula def. Nioune dé ay talibé baye you deggou lagn té lii dafniou metti looool. Mane dé sama khol bi metti na torop torop. Ils devraient avoir honte 😭😭😭
Bayilen guiss nit mou wakh rkk guen yeureum di wakh ki mom yalla moko fay kholam heure bi daw ladone nianal Gana Mésséré lou bone té defouko wakhouko tay mou tok fi di wakh ay yone même soudé liniou ko def rafétoul mo togn
Ki done teukou Gana messéré mom mi laniou niouss mouy ben benal ni bakanam ni kouberou deuk
BILAE MOUNIEULL REKK YALLAH BAKHNA 🥺
Ahmed Cisse yalla nalla yalla sam 🙏🙏🙏
C la fote de l'état personne n'a le droit de torturer personne c honte l'islam bani toutes l'injustice queque soi sa forme
Wallai c'est la honte. Je suis talibé baye mais j'ai mal au plus profond de moi. La honte😭😭😭
Senegal rek ngay guis kou def louko nékh té appre dara douko si fekk,ndakh lan app serigne la wa ap santas😡
Serigne Ahmed sa wokh rafet na yalnala yala fayoulwaye bougaw mais guemelni Sénégal justice amoufi
Machallah am na solo trop Cisse gari
So sad for Senegal’s people doing this to our people sorry for what they do sheikh Ahmed Ceesay
My name is awa, am sorry Ahmed am a talibeh of bai nyass but I hate thus people
Allah is the biggest judge 🙏🏽🙏🏽🙏🏽
Bilahi y’allna la yalla may la diam li mom bakhoul si paiy bi dama rouss trop na yone def liguéyam Amoul Niass la sante amoul kah la sante
Dites à ceux qui méprisent le souvenir de l'oppression des tyrans contre les faibles après leur mort Dieu n'a-t-il pas mentionné dans le Coran les vilaines actions de Pharaon, Haman, Qarun et Abu Lahab ? Sont-ils morts ou sont-ils encore vivants ?D'autres tyrans sont meilleurs qu'eux jusqu'à ce qu'il soit empêché de se souvenir Mais les hypocrites ne savent pas.....Prenez du trait à deux faces qui est hostile à la vérité et à l'honnête et digne de confiance Laissons Al-Sadiq attendre que les quelques amis trouvent celui qui l'a choisi pour le destin Les gens ne suivent que des conjectures, et ce ne sont que des mensonges......
Baye digléwoul li kou kham yalla kham lahilaha illalah mouhamadou Rassoulilah fo fekk domou adama diguako térral alhamdoulilah
Wallahi Baye Niass diglé woul lii. Laa hawla walaa qouwwata illa billahil 'aliyil 'aziim. Lii rouss louna😭😭😭. Nioune dé djissougn té khamougn lii té metitlou nagn ko bassi kanamou yalla. Nit kenn douko torokhal
Souko digler woul na wah yone def liguey yeum comme ça les autres ne vont pas douter ce que le gars dit c'est très grave
This is very heartbreaking
C vres kay
Li mom niawna trop je n’aurais jamais pensé que cela existe à médina baye que justice soit faite
On doit les traduire en justice
il a raison nak gniko dore danio moudié soufei dakhe koulenne waroul wone yabe yabnalenne dakhe guisna sakhe nioulenne saga si reso socio yii
Gni kagne imbecile deugheu lagnou
Nék waliyou yalla téréwoul ngua dioure domi mbame bilahi
Ndèysane
Lignou déf ni bokoul si li Baye diglé si deukeum bou séle bi,que justice soit faite
Ndeysane MASHALLA ❤️
Lii moom dou deug dou yoon..gniko déff naniou lein ték si yoon ba bénéne yoon douniou koo sagna défaate lolou moy deug 🙏🏾
Guesstoul les faits d'abord litakh door yi
Vraiment amna louma nakhari barkép alkhourane
Il faut les porter plainte
Walahi li lourousloula, tai louniawela,
Kou si bayiwoul topp Serignou legui yi ni rekk ngay moudié.
Diamou dji Yalla ta sakou sa nguereumal waydiour fofou la diamono tolou.
Serigne sou bari danio wathié senn yoon, dieul bennen yoon bou bokoul akk lafi seni Mame ligeey bayi fi.
Bilahi wakhal dé
This is so sad and heartbreaking 💔 doing such a brutal act to fellow human being and a fellow talibe tidiane
J'ai fait des constats que yow 2ans gui ni yow dangay def violence verbale Di def yefu ma meun té yaffi teuku won gana messere ak cheikh Omar Diagne kon yoyu violence deko moytu
Courage cissè
Mais va voir le procureur directement et porter plainte
Vréma
Mon frere procureur =apr
Yalna Yalla Fayaleniou Baye ya Rabbi Baye wanoniou sa bopou Yalla reck nganiou wane
Ndayesanne yalna yalla torokhal len
Bilahi wakh nga deug ndeysane
Ce genre de violence est fréquent chez les tarikhas malheureusement
C'est cheikh yirime seck qui m'a déçu tu es en compagnie d'un être humain torturé maltraité tu n'a pas réagi tu me déçoit si kou sante seck
Vérité merci ❤️❤️❤️💯
Ndèysane Mettina vraiment.
Machallah yalna yalla samoula ya bii
Liii niawna trop que justice soit faite 😡😡😡
Franchement vous avez souffert mais sans froid avec discipline
En tout cas baye niass lagnou beugeu té lou ham rek baye lagnouye topou❤😊
Boul khalat yone dax amoufi
Que justice soit faite 🇸🇳🙏🙏
Bilahi so lén balé doumala bal
Bilahi warou léne bale li dafa yombou trop sakh trop d injustice
bilaye iowite solenne balé doumalenne ko bale
Ndeysane li métina deuk bi amoul yone yalnalene yalla atté
Ki dan ko togne reew mi xaw ma loufi justice bi diarigne
Merci cheikh nit kou bakh ngua
Yalna yalla saam leu ya rabi
Prefemom ab dofla allahou Akbar kholalma yiidofrek
Massa waye yeureum nako
Yalla nala yalla Atel bopam
D ou yeufou nitt sakh vraiment est ce que xam yallah biye certains di woter nek na siniom
Bou guene topone yalla ak yonetebi kane douléne trokhale wayé topou serigne yi rek gnoulene di trokhale kome khathe
Lahilaha ila aneta soubhanaka ini countou minal zalimin