Serigne touba lan lagnoulay fayè😭😭😭😭😭man d diebeul nala sama bopp adouna ak Alahira fayè nala sama boop ndem amouma louma la diokh 😭😭😭❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️dama beug mame bamba ❤️
Dieureudieuf Mouride j'ai pas choisi d'être Mouride mais ces Dieu qui a décidé k j le suis AlhamdouLiLah AlhamdouLiLah AlhamdouLiLah AlhamdouLiLah 💚💛🧡❤️💙💜🕋🕋🕋🕋🕋🕋🕋🕋🕋
MASHA ALLAH. Yala na YA ALLAH fayla yiw ALAHOUMA amiin. Yala na firdawsi di keureum ALAHOUMA amiin. Yala na YA ALLAH yok ay leram mbacke.ALAHOUMA amiin.
samag fofeel ci yaw la yaa moom yoon wi. defal nu fan wu gudd ànd ak barke, ci darajay maam balla aisa Mbàkke,. yoonu murit na nepp bokk yokk, sunub xalifa wer nu gënfee yokk amiina amiin bi jaahu Mustafaa, Salla halayhi rabbu naa kamasfaa. man soxna may bint xadimal Mustafaa, maay bëgg a bind lama seexul Mustafaa. dénkoon ci ak taalibe ngir saahir sa. manees na koo roy baatinam ne gor saa. xam naane Amuma Solo ci saahir, waaye samay mbir yaa ko yor taahir saa yoo xamee ne maa ngi jëm ci xaadim, di ko siyaar di ko sujóod ngir xaadam. saa xol bi day mel galaas akub suux, ngir limu meggool dox kenn dóotu ci suux. jaay naa samag jurel ci sayxu Bamba a, jënde ko ak taalibe ngir yónent baa. seex Mustafaa noon na ma jaamu Yàlla a. boleeg liggéey mooy tax a gis bur Yàlla a. amal gor ak jom fonk jaamu Yàlla a. seexlul bidaa fonk sunna moylu yiila. seex Mustafaa noon na ma jaamu Yàlla a, moo yor kërug laaxira jaamu Yàlla. seex Mustafaa noon na ma deel liggéey, mooy yor kërug àdduna nan liggéey. moo tax mu toog daaru di jaamu Yàlla a. mboleem liggéey sant sax ci Yàlla. yal nanu seex Bamba defal karaama, ba sun liggéey yal nanu am maala. noon na ma toogal daaru seexu Bàmba a. moo lay yoral boppam kasaa yónent ba. toog naa fa gis waa kër sëriñ Tuubaa ya. ay yooni yoon ak bër yi raw ci ngir yi. jëflante naag ñoom ba fab ci saam xel. ganeelu seex Bàmba xajul ci ab xol seex Bàmba de kenn du moom te moom kenn. kenn masula gis ku mel moom ci fenn. seex Mustafaa jokkoom ju sell jaa tax.
les paroles Sont d'une telle actualite, alors qu'ecrites tres longtemps. Dieureudieuf sounou BOROM bimou niokhe S.Touba. Dieureudieuf Bamba, louniou am ci YALLA sa dieum rek motakh
seex Mustafaa noon na ma sunu baay cerno, mooy seexu Bàmba moo yoroon maam cerno. rakam la dib taalibeem dib xaritam, di wolare wum woolu woon ci baa tin, taalube yay bañ moy te neex a àndal. àdduna ak laaxira neex a dendal, waaju dul tooñ mukk, te soo ko tooñee, mu daal di lay jeggal wares nakoo ñee. day fekk nit calay jikkoom geen ànd, deem sopp gaa àndal te bañkoo dend. seex Mustafaa amul moroom lam daa wax maneesu kooo way lépp géej du ak dex, gaawu ca yoor-yoor lanu taggoo bëyti, mu dellu Tuubaa fa kërëm ngir bëyti.
Serigne touba lan lagnoulay fayè😭😭😭😭😭man d diebeul nala sama bopp adouna ak Alahira fayè nala sama boop ndem amouma louma la diokh 😭😭😭❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️dama beug mame bamba ❤️
Yalla na yalla fayyyy sokhna maimouna mbacké bintou khadime
Chaque matin j ecoute ce merveilleux chanson dieureudieuf serigne touba nous mouride on doit être très fière de serigne touba
💚🤍💚🤍💚🤍🇸🇳 barkep borom Touba amoul morom barkep Mame cheikh Ibrahima fall 🇸🇳😊
@@cheikhamarfall6479p
Kurel Sahadatu Daarayni Wakeur Sokhna Maimouna Mbacke Parcelles Assainies unite 20
8p
P
Yala na yala yok léram té taf niou ci barkéme amine ya rabi ci barké Serigne Fallou mbacké amine ci barké alhourane Karim
Sama khol dafa fess serigne touba yalnanou co yalla fayal 😭😭
Ndaysaan Jërëjëf Cheikhoul Khadim. Sokhna Mai yalna Yàlla yokk leeram😭❤️❤️
Amine ya rabbi sokhna maimouna bint khadim yalna yalla yok say lère
Sama serigne sama yaye mbacke balla dieuredieuf yalla nagua am guereumoul serigne touba mbacke
Dieureudieufe Khadim rassoul diarama Sokhna maï yalla na yalla yook léram thé Tass nou thi barkém thi barké goudy laylatoul khadr
Ndeysan yalla nako yalla yeureum si barke seydina Muhammad psl Amine ❤️❤️❤️❤️
Thiey sama tourondo yalna yégali sa yéné❤❤❤🥇🥇🥇🥇
Dieuredieuf sokhna mai mbacke
Mashaalla sokhna may kabir yala.na yala.yok ay.leram oyofal souf si kawam yala.na khipe.thia adianay.firdawsi alakhoum amiiin.
Machalla
Dieuredieuf serigne touba borom le fondateur du mouridisme 18 safar
Dieredief s touba boudou ton yaw xawma fou ñou dieum yalna la ñou yalla fayal thi dradiay moukhamed
kep kouy mouride di dioulite gueum serigne touba sa khol sedene na kone na niou sante bou bakh serigne bou tedebi
6vçp
À
OP
Macha Allah khôl sedatina Mbackè Balla Aïcha yalna yalla fayla
Dieureudieuf Mouride j'ai pas choisi d'être Mouride mais ces Dieu qui a décidé k j le suis AlhamdouLiLah AlhamdouLiLah AlhamdouLiLah AlhamdouLiLah 💚💛🧡❤️💙💜🕋🕋🕋🕋🕋🕋🕋🕋🕋
MASHA ALLAH. Yala na YA ALLAH fayla yiw ALAHOUMA amiin. Yala na firdawsi di keureum ALAHOUMA amiin. Yala na YA ALLAH yok ay leram mbacke.ALAHOUMA amiin.
Sant serigne touba.sop ko. Doylo ko .wolou ko
Bilahi yalla moniou nameu yeureum tax mou diox niou kou melni cheikhoul khadim. Wayé sunu dieum you xébou yii mérité niou ko. Santati naniou bou baax alhamdoulilah
Mansor wakh nga deuk di
J'ai envie de pleurer, dieuredieuf serigne touba ! !!
Thiey serigne touba
Joyal way serigne touba diooy si faratala
@@ado7272 1
@@cheikhgueye7104
M
0c
Aaaa liii nékh na kène dou serigne touba sama kholle sèdena
Yallna yalla yokou ay léram té tass gnou si barkém🙏
Seul les chites n ont pas aimés cette vidéo
DIEUREDIEUFÉ KHADIMOU RASSOUL
yalla naniou falyal sokhna may bintoul Khadim
thieye s touba mbacke
Bilaakhi barké cheikh,li néékh n'a ci kholl machalla 🙏♥️♥️ talibé cheikh nééna djiaradieuf serignie touba 🇸🇳🇸🇳💖🙏
Dieureudieufety cheikhoul khadim diaramah Mame Cheikh Idrahima fall
Dommage que la fin du Ramadan aproche Yallah naniou Yallah nagoul sunuy diamou ta diégual Niou barkép borom touba
Sante na bama sa brom bolé si ndiabotoum brom touba gui😢
Kholl Sedatina Dieuredieuf Sokhna Maimouna ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Dieureudjeuf serigne touba diarama mame cheikh ibrahima
Machallah thiey sokhna sou bakhe si mbacké balla
dieuredieuf .khadimoul.rassoul.beugue.serigne.mbacke.madina.rek
Dieredieff serigne touba diarama mame cheikh Ibrakhima falll❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤serigne mountakha mbacke yalgafi yag ta were barkep borom touba
Dieureu dieufety cheikhoul khadime diaraw laka mame cheikh Ibrahima fall lamp
yalla naniou KO yalla fayal
Dieureu dieuff serigne touba khadimoull rasoulll
Allahou gnouné li djiguenn moko taliff
samag fofeel ci yaw la yaa moom yoon wi.
defal nu fan wu gudd ànd ak barke, ci darajay maam balla aisa Mbàkke,.
yoonu murit na nepp bokk yokk, sunub xalifa wer nu gënfee yokk
amiina amiin bi jaahu Mustafaa, Salla halayhi rabbu naa kamasfaa.
man soxna may bint xadimal Mustafaa, maay bëgg a bind lama seexul Mustafaa.
dénkoon ci ak taalibe ngir saahir sa.
manees na koo roy baatinam ne gor saa. xam naane Amuma Solo ci saahir, waaye samay mbir yaa ko yor taahir
saa yoo xamee ne maa ngi jëm ci xaadim, di ko siyaar di ko sujóod ngir xaadam.
saa xol bi day mel galaas akub suux, ngir limu meggool dox kenn dóotu ci suux.
jaay naa samag jurel ci sayxu Bamba a, jënde ko ak taalibe ngir yónent baa.
seex Mustafaa noon na ma jaamu Yàlla a.
boleeg liggéey mooy tax a gis bur Yàlla a.
amal gor ak jom fonk jaamu Yàlla a. seexlul bidaa fonk sunna moylu yiila.
seex Mustafaa noon na ma jaamu Yàlla a, moo yor kërug laaxira jaamu Yàlla.
seex Mustafaa noon na ma deel liggéey, mooy yor kërug àdduna nan liggéey.
moo tax mu toog daaru di jaamu Yàlla a.
mboleem liggéey sant sax ci Yàlla. yal nanu seex Bamba defal karaama, ba sun liggéey yal nanu am maala.
noon na ma toogal daaru seexu Bàmba a. moo lay yoral boppam kasaa yónent ba. toog naa fa gis waa kër sëriñ Tuubaa ya. ay yooni yoon ak bër yi raw ci ngir yi. jëflante naag ñoom ba fab ci saam xel. ganeelu seex Bàmba xajul ci ab xol
seex Bàmba de kenn du moom te moom kenn.
kenn masula gis ku mel moom ci fenn. seex Mustafaa jokkoom ju sell jaa tax.
Machalla dieureudieuf cheikhoul khadim amoul morom
Niane You Ame Solo Loolll Santati Mbacke ❤❤❤❤
ken dou serigne touba
Akssa
Cava
Thieye seringe touba mbacke sonou ko amoul wone khawma fou niou dieum Alhamdoulillah Alhamdoulillah Alhamdoulillah Alhamdoulillah Alhamdoulillah Alhamdoulillah Alhamdoulillah Alhamdoulillah Alhamdoulillah Alhamdoulillah Alhamdoulillah Alhamdoulillah Alhamdoulillah Alhamdoulillah Alhamdoulillah Alhamdoulillah ba niou amé khadim rassoul
les paroles Sont d'une telle actualite, alors qu'ecrites tres longtemps. Dieureudieuf sounou BOROM bimou niokhe S.Touba.
Dieureudieuf Bamba, louniou am ci YALLA sa dieum rek motakh
awa djily
Serine touba rekk
Vkkjbvn@@adamandiaye6960
@@nigaudngom94 k
O. Oo
Macha Allah yalla naléne bour bi fayale bopam
dieureudieuf serigne touba dieureudieuf serigne touba dieureudieuf serigne touba dieureudieuf serigne touba dieureudieuf serigne touba dieureudieuf serigne touba
Dieurudieuf
Dou ma si doyol mouk billakhi 💚💚💚
Dieuredieuf cheikhoul khadim 😭❣
Sante serigne touba rek mo weure
Dieuredieuf serigne touba ❤💯
Serigne touba amoul morom..Mbacke Dieuredieuf
Dieureudieuf Serigne Touba .Sa m'a fais pleurer 🥲🥰💗💖❤❤
Yalnanou yala fayal soukhna sou yiwsi sokhna maïmounatou bitou khadim rasol
dieureudieuf serigne khadimoul rasoulilah dieureudieuf ahmadou bamba
thiey serigne touba amoul morome
Bilahi ndeysan yéuména barkem khasside yii 😭😭😭😭😭😭😭
Sa youma wete fi si italy li mo may weteuly dieureudieuf mbacke balla aissa
Kéne dou serigne touba
dieureudieuf serigne touba dieureudieuf serigne touba
Dieureudieufeti Cheikhoul Khadim
Macha alla sante mame borom touba rekh ak mame lamp fall ❤️🥰
Dieureudieuf serigne touba
Dieudieuf ma borom touba di yadiale magalgui
Booba Kenza
dieureu dieuf borome touba
Chacha Mbaye merci
Merci
Dieureudieuf serigne Touba
Dieuredieufety serigne touba
Dieureudieuf Serigne Touba
Codoucueye
Dieuredieuf.s Touba Rék ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
2020❤️❤️❤️
Dieureudieuf Serigne Touba 🙏🙏❤️❤️
Dieuredjieuf s touba khadimou rassol
Dieuredieuf Cheikhou Bamba
thiey sama tourondo alhamdoulilah
Macha alla ♥️ dieureudieuf Mbacké
deure dieuf serigne touba diarama ibrahima fall lamp
Amdy diane
2020🙏yala naniou yalla fayal Soxna Maï bintoul Khadim❤❤❤
Sante serigne bamba s.salihou mbacke
00000Mp000mpp
0p00
000
0
Yalla na sunu borom fayal
dieuredieuf cheikhoul khadim
dieuredieuf cheikhoul khadim
dieuredieuf cheikhoul khadim
seex Mustafaa noon na ma sunu baay cerno, mooy seexu Bàmba moo yoroon maam cerno.
rakam la dib taalibeem dib xaritam, di wolare wum woolu woon ci baa tin, taalube yay bañ moy te neex a àndal.
àdduna ak laaxira neex a dendal, waaju dul tooñ mukk, te soo ko tooñee, mu daal di lay jeggal wares nakoo ñee. day fekk nit calay jikkoom geen ànd, deem sopp gaa àndal te bañkoo dend. seex Mustafaa amul moroom lam daa wax maneesu kooo way lépp géej du ak dex, gaawu ca yoor-yoor lanu taggoo bëyti, mu dellu Tuubaa fa kërëm ngir bëyti.
dieureudieufeti Serigne touba khadimoul rassoul
Yousou Diop
Lklk.' .bvxz m
Yousou Diop
dieuredieuf sokhna maimouna ndiaye
Akssa
+Ameth Sarr to
Sama badien la
Dieredieff serigne touba ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Thieey serigne touba
Mansour Mboup
Mboup
Diaradiaf Serigne touba Mbacke
Yalna yala yookou lairam taakh yousi barkebi
Dieureudieuf serigne touba...
Thiey Serigne Touba Dieuredieufi
Li dafa nekh trop kén d'où Serigne touba
Dieuredieuf Mbacké Balla mala beugeu .😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
serigne touba kene dou môme amoule morome sama khole Suède toyna bilahi
Machalla😭😭😭😭😭😭😭
Machalah s mai mbacke
Dieuredieuf sounou badiane
écrit par sokhna maï mbacke bintou khadimou rassol en 1990 chanter par les hizbu tarqihha
THeuye serigne touba
sante serigne touba
machala ken d'où sougnou mame borom touba
Nékhna lool dh Machalla ❤ ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Dieureudieuff kou tedd ki ❤️🙏
dieurdieuf Serigne touba
Hassida rek mo wor.yalla neu sunnou borom fayyel khadimou rassoul