no yaw mall khiam mo nara metti deff lou la nekh wakh lou la Nekh billlahi Serigne touba nena kepp kou deug si loula Nekh biss dina niew nga am lou la nakhari yenen tebi ne nitt niè daniouw nelaw kouse de dinga yewou yalla nanou yalla tek si yonou siratall moustahim dieure dieuff Serigne touba
Aux jeunes qui sont au zénith de leur vie, cet homme vous parle...la rançon de la gloire peut être terrible...recherchez la réussite spirituelle lolou moy deug...
Une belle video très instructive sur le repentir ! Cest une bonne personne et qu'Allah SWTA le lui accorde ! Merci Mr le journaliste car nous devons positiver !
Vous pourriez quand meme prendre le soin de flouter son visage sachant qu'il n'a peut etre pas conscience de la conséquence que peut avoir son geste face camera
pas besoin de critiquer .il faut aider le mec a se repentir.bravo au journaliste qui nous fait découvrir la vie tumultueuse de certains. ce n'est qu'une leçon de vie
Li am importance moy nit yalla moko mom. Dioum na toupe li ci dess mom ak yalla la. Yalla nako yalla yeureum te yeureum gnou. Yalla nagnou mousseul ci bakar surtout ndiallo
Je ne sais pas ce qui se passera après mais sur cette video je salue ta véracité et je crois il faudrait un exemple pour faire savoir yalla nala yalla sopi def la magoum diner tei mou diegal la ! Kou yalla di tabal safara niit ndiaye khamouko ! Video a méditer
Et pourtant j' ose affirmer que l' Éternel l' a appelé à lui, reconnaître sa faute et demander humblement pardon est la source d' une remise de toute transgression , je ne le connais pas mais je ne le jugerai pas mais juste lui dire MERCI parce qu'il m' a ouvert les yeux alors je demande à DIEU la grâce de mettre en pratique la leçon reçue.
journaliste bii khamoul dara ndem bou done sa papa doko dougal li bakhoul dara ya geuna khamné ki dou sa mbokk thiiim wa senegal tv dh war nano wakh ak yaw lii rafétoul waay ndakh lii pabi wakh lép yakoko forcé soutoura dafa bakh si nitte té yaw dangay khawi soutouras diambr nga balma nak
dof yén gni la ki loumou wakh boudoul vrai sakh mogui conseil rek nakh. limou wakh dafé am. té bari nafi gnak khalisss loumou diaral nigni légui mo graw
d'après c que j'ai vu et entendu on peut analyse sa sous deux fenêtres un vieux qui a vécu des choses qu'il regrette et qui conseil ses frère et soeur a ne pas suivre le même chemin et l'autre le manquement de l'homme parce que Dieu nous a créé en étant imparfait chacun a ses secrets ses défauts ses faiblesses alors en commettant une actes dégagements il faut garde sa pour toi et ne pas le divulguer au yeux du monde le journaliste a eu tort de publier la vidéo mais peut être qu'il avait une bonnes intention de le faire je sait pas mais quoiqu'il en advienne on doit regarder le côté positive et s'en sévir pour notre avenir merci
oh 49ans daga lal lal lal lal ba niro kou am 76 ndakh la tchim😂 mem si il vous autorise de le mettre vous ne devez pas le faire mettez vous a sa place.
vous ne devez mm pas mettre ca sur le net diaroul moulen di diokh autorisation ou pas car il n'est lucide pour donner des conseils il es fou ce mec il peu mm pas argumenter 1e de c idée vraima beug gnou setane sen video boumou takh guen di dougal mimporte koi c juste mn avis....
père bii mougui def wareefam le problème est que journaliste bii dès fois il pose des questions idiotes mais nice nq t affaire bii amna soloh trope pour la génération actuel merci du conseil père
qui dou journalist sakh c just que youtube dafa am louthi nek so dougalé video nombre de vu boy am degne koy faye legui genre journalist yi deniou xole gua weroul yi diléne di utlisé pour am xalis mai qui sou fekone thi famille am la bok douko dougeul domou kharam la rek
pufff wa li lane la mai ki dougal li ak journaliste yéne gnépp ay défaillants nguéne li nane lako nit meuné wout khaliss ak ay nombre de vu lii adouna yagoul soff nguéne trop waye...
Ndeysane c'est un homme bien á mon avis, Yalla nako Yalla bale diégueul ay bakaram, yeurmendé Yalla dafa yatou...wa salam
yalla na KO yalla diegeul thi barke seydouna mouhamad. psl
Pour tt les personnes qui tomberont sur cette vidéo prié pour cet homme que dieu le guide le change et l'oriente
On dirai qu,il a 75ans,yalla nala yalla dieugueule.
The guy is saying the real truth... May God be with him.
no yaw mall khiam mo nara metti deff lou la nekh wakh lou la Nekh billlahi Serigne touba nena kepp kou deug si loula Nekh biss dina niew nga am lou la nakhari
yenen tebi ne nitt niè daniouw nelaw kouse de dinga yewou yalla nanou yalla tek si yonou siratall moustahim dieure dieuff Serigne touba
c est un fanatique fou
Aminnn yarabi yalnagn yalla maye degg ac toppou
Émouvant
Tu peux changer bilahi
Dieu vous bénisse
sa conseil amna solo comme t'a fait l'expérience. Yalna la ci yalla guéné
ndaysane yalla naniou yalla doli soutoura si doléy sa mame cheikh ibreu fall
AMINE
Ki kay diote woul ak mame chiekh dara
kou toupe yalla diegualale tres bonne leçon pour la jeunesse yalla nak yalla diegualale journaliste tu es un vrai lache
Aux jeunes qui sont au zénith de leur vie, cet homme vous parle...la rançon de la gloire peut être terrible...recherchez la réussite spirituelle lolou moy deug...
Alhamdoulilah li warna niou jangual lou barri tella takk sokhna dina la jappaler siloubari que Dieu nous donne de femmes de bonne famille
Une belle video très instructive sur le repentir ! Cest une bonne personne et qu'Allah SWTA le lui accorde !
Merci Mr le journaliste car nous devons positiver !
Vous pourriez quand meme prendre le soin de flouter son visage sachant qu'il n'a peut etre pas conscience de la conséquence que peut avoir son geste face camera
Il nous a donner une très bne leçon de vie 🙏🏾🙏🏾🙏🏾 Merci bcp tonton ✊🏿✌🏼
yalla na ko yalla diabbalè amine
mOI perso il a vraiment eu le courage quoi et ce vidéos peut sauver de millier de gens
Allah lui vient en aide et qu'il nous protégé tous amine
pas besoin de critiquer .il faut aider le mec a se repentir.bravo au journaliste qui nous fait découvrir la vie tumultueuse de certains. ce n'est qu'une leçon de vie
No pere bilahi guerrié gua diadieuf way
Wayyy sénégale TV dool wayyy bou nékone sény bay dou ngénko wané
Waww il a tres bien parle, c est a mediter
yalnako yalla diapale teko si yonou sirat al mustakhiim
Sénégalais liberté beu Déé🌍💰
Right !! Vrai ..koula djitou si néek bou leudeum molay wax figuay toguéé !! Attention !! Limoy wadiou niakk khorom waxnama Lou am solo...a bon entendeur salut!! Merci au Journaliste,son consentement né pas vicieux.!
Li am importance moy nit yalla moko mom. Dioum na toupe li ci dess mom ak yalla la. Yalla nako yalla yeureum te yeureum gnou. Yalla nagnou mousseul ci bakar surtout ndiallo
Ndeysane YALLAH DJI MO KO NAREU DIMBALLI.MOUDIOU BOU RAFFET LA NIOUY NIANE.
il a kan mem donné des conseils vitaux...''reuthiou day fekk dieuf weess''
Yalla nako yalla dimali mou toube
Yala nala yalla diabalé diel na sa wakh defko consail biahi df wésourk
ça c un hom saz!!!
c une video interressante
Je ne sais pas ce qui se passera après mais sur cette video je salue ta véracité et je crois il faudrait un exemple pour faire savoir yalla nala yalla sopi def la magoum diner tei mou diegal la ! Kou yalla di tabal safara niit ndiaye khamouko ! Video a méditer
Senegal dou dém.T.Hobbes a raison "l'homme est un loup pour l'homme".
Vraiment
ndeyssane yalla nala yalla guimdi amin
اندي سان
sèèle bi yalla sokhla mooy nèèke Hibadou Rahmane. yalla nalla yalla dioubeul
K le Tout Miséricorde t'aide à te repentir et guide sur le chemin de la droiture 🙏
amin
Amiin 🤲🏿
Amoulene soutoura wokholene fi. Darra
Right now leson la pour jeunés bi 49ans Nala yalla tek thi yon rk
Il a raison khalè génération fin du monde gueme mounou dara. Thiakay rék
Qu'Allah nous guide vers le droit chemin inchallah
Et pourtant j' ose affirmer que l' Éternel l' a appelé à lui, reconnaître sa faute et demander humblement pardon est la source d' une remise de toute transgression , je ne le connais pas mais je ne le jugerai pas mais juste lui dire MERCI parce qu'il m' a ouvert les yeux alors je demande à DIEU la grâce de mettre en pratique la leçon reçue.
.
Iu
.
Bonjour mu
H
lui-même il est d'accord que pour tout le monde l'entend
Yallanala yalla diapale mou tekla si yonbou djoup
ahh ylla nayalla guindi way amine
Yalla nko yalla yereum
Yénn kii yoboulénko dépistéko limfi lime yeup loubone baahoule solénn bayiwoule diabarou diambour yinguénni katte déléenn hame loulénni dale😮
merci beaucoup grand du courage
saye saye rek la def
yalla nala yalla gené si loulo
c pa pour rien k dieu nous recommande de prier ça nous permettra de nous maitriser
journaliste bii khamoul dara ndem bou done sa papa doko dougal li bakhoul dara ya geuna khamné ki dou sa mbokk thiiim wa senegal tv dh war nano wakh ak yaw lii rafétoul waay ndakh lii pabi wakh lép yakoko forcé soutoura dafa bakh si nitte té yaw dangay khawi soutouras diambr nga balma nak
mes paa bi moko wakh niou tekk ko fall degloul bou bakh journaliste bii dafko prevenir
No mai chaq person à son propre secret nak soutoura !!!!
pispa dollar
Ahhh Wii Pa bii moko permettre mou dougueul ko
Aminata Thiaw oui mes s"negalais day juger avant mouy savoire sa c pas bon
pispa dollar Wii tu voii meii kou dégu bou bakh dina kham
yéne au lieu nguéne Gnanal ki mou guéneu ci limou nékké vous vous permettez de le juger. et si tout le monde osait se dévoiler...
Danio tégalo 3moi kay😂😂😂yalla nala yalla ball
moi je vois k c tune bonne personne. au moins il est honnete.
Il a vraiment besoin de soutien, il regrette vraiment...
ya ayouhal lezina amanou itakou laha!!!!! nañou len ragal yalla gañou gueume yalla yi
Yalana YALLA wathié yeurmandé si nioune niép
Amine
yallah na yallah yeureum
Ctey q le bon dieu lu guider ver le bon chemin
yalla nako yalla dieggueul te wagniko
May Allah help you be where you wane be , jashakllahu kairan, he need help !!
Un vrai #THUGLIFE ce vieux hahaha
dof yén gni la ki loumou wakh boudoul vrai sakh mogui conseil rek nakh. limou wakh dafé am. té bari nafi gnak khalisss loumou diaral nigni légui mo graw
nit loutakh....sounou borome teralko....sagal sagouko soutoura...
yaw mii dougall lii xolal soudonn sa baye wala sa famille doko deiff su net bii..
conseil pour nous les jeune bayilenn takhawalou bi te liguey
Da fa rerer rek Na niou ko nianal , môu guindékou c est dure quand même . D avoir tous ses remord
Mbaye Mbaye naye rafete per favor
d'après c que j'ai vu et entendu on peut analyse sa sous deux fenêtres un vieux qui a vécu des choses qu'il regrette et qui conseil ses frère et soeur a ne pas suivre le même chemin et l'autre le manquement de l'homme parce que Dieu nous a créé en étant imparfait chacun a ses secrets ses défauts ses faiblesses alors en commettant une actes dégagements il faut garde sa pour toi et ne pas le divulguer au yeux du monde le journaliste a eu tort de publier la vidéo mais peut être qu'il avait une bonnes intention de le faire je sait pas mais quoiqu'il en advienne on doit regarder le côté positive et s'en sévir pour notre avenir merci
oh 49ans daga lal lal lal lal ba niro kou am 76 ndakh la tchim😂 mem si il vous autorise de le mettre vous ne devez pas le faire mettez vous a sa place.
qui niane la skohla qu halla te guide
Topou sa ndaw Lou niawla bakane danioukoy péral ba heures bi amo diabar pithié
mandi wo dé waye yangui nè dourrrrrr
Allah pardonne tous les péchés. kou dèè ak bokhalé rek ladoul baale.
Thieuy yalla
Journaliste Sénégal amouniou kham kham
Mauvais "genre de journaliste"
babacar diouf
Done n'a warr
vous ne devez mm pas mettre ca sur le net diaroul moulen di diokh autorisation ou pas car il n'est lucide pour donner des conseils il es fou ce mec il peu mm pas argumenter 1e de c idée vraima beug gnou setane sen video boumou takh guen di dougal mimporte koi c juste mn avis....
Yalla nala yalla tek thi younou djoub
Que dieu nous pardonne
ki limouy wakh dara amou si kikoy lath mokoy empose mouy wakh rek
C'est extraordinaire. Ils savent ce qui est bien mais malheuresement Satan est puissant. Yallah nalla Yalla dimbele. C'est triste
Journaliste bi vrai domram
Wawa
Il a donné une bonne leçon
Mais kou sadique la nakk 🤣🤣🤣
Nena dafa beug affaire bi
amo kilife
no journalist bi dou khalat
père bii mougui def wareefam le problème est que journaliste bii dès fois il pose des questions idiotes mais nice nq t affaire bii amna soloh trope pour la génération actuel merci du conseil père
Yalla rekkay bourr. Th mooka ndjabboot hiii
haahahaha magui youuut waay
daga beugue affaire bi
mouunéko bou bakh saxx
kholalma dof bi rek muy mélni bouki, day doul rek
ahahahah ahahah
lissa diop j'aimerais bien mais désolé je suis de l'autre côté du monde
qui dou journalist sakh c just que youtube dafa am louthi nek so dougalé video nombre de vu boy am degne koy faye legui genre journalist yi deniou xole gua weroul yi diléne di utlisé pour am xalis mai qui sou fekone thi famille am la bok douko dougeul domou kharam la rek
Phénomène Ello
Je pense qu'il fallait masquer son visage pour ne pas heurter la conscience de sa famille
certes il c libéré mais dommage il ya de la manipulation derrière ça monsieur le le journaliste
cette confession est naturel et audacieux
hahahahahaha no Sénégal mo nekh rek 😂😂😂😂😂😂😂
Li ken warouko dougal way li bakhoul
pufff wa li lane la mai ki dougal li ak journaliste yéne gnépp ay défaillants nguéne li nane lako nit meuné wout khaliss ak ay nombre de vu lii adouna yagoul soff nguéne trop waye...
d'après ce qu'il vient de d'expliquer ,douwoul nitt kou manquè mè natou moko dall
wakh na deug ay conseil lay diokhé
kii dafa doff
Boudone sa papa dowanè kanamame khawma journaliste nga khawma lodone Domèrame
49ans 😂😂😂😂😂😂😂😂yaw guay paaaaa 66ans
Cisse maman boulma ray way
Cisse maman 😂😂😂 wadji kay amna 100 ans
Cisse maman tess
motakh fegne na thi yaw de leundeum keuriis nga def
mon frère yalla n'a yalla dimbalela me c pas raté tu te rattrapé sa dingante ak sa borom repane toi dieu pardon tout pense regrete
duy nawar
sèn titre yi, nay rafèt way👎