Le meilleur chanteur du monde. Il ne chante que le grand marabout et pour chaque chanson c'est un nouveau thème. Lii dafay woné ni serigne touba gueuna yatou guethie. Dieureudieuf sangue bi.
Thieuy sounou wadji Ken du mom mouhamed niang meilleur de sa génération👑👑 ningay sedalé souniou xol ❤❤yi Yalna lako yallha faye ci barkéb serigne saliou 🤲🤲
Je ne sais pas mais cette chanson me fait trop pleurer non pas des larmes de malheurs loin de là. Je ressens un bonheur extrême qui se manifeste par des émotions. Svp écouter cette voix de Mouhamed Niang au plus profond de vous. Écouter les paroles qu’il chante et vous comprendrez. Serigne Touba nous a tout donné et nous devons lui rendre grâce jusqu’à notre dernière énergie. Chacun de nous sait que Serigne Touba est l’artisan de sa vie en ce qu’il connaît et même de ce qu’il ignore. Je t’aime du profond de mon âme. Je te suis éternellement reconnaissant pour tout ce que tu as accompli et que tu continues d’accomplir dans ma vie. Dieuredieuf Mouhamed Niang. Dieuredieuf Serigne Touba ❤️❤️❤️🙏
Walayyy tu n’es pas le seul ki mo takh ma kham Lou beuriii ba toppp Serigne bi démmm tokkk si kharrou bi tokk sentir Lou beuriii et chaque foi avant d’être j chante un de ses chanson en peurs Yalla na ko Serigne saliou faye🙏🏾🙏🏾
Toutes ses chansons contiennent plein d'histoire et de sens pour ceux qui prennent le temps de décrypter son message. A travers ses chansons, notre amour pour Serigne Saliou ne cesse de monter au crescendo. Mouhamed Jeurejeuf Yalna la Serigne Bi Faye.
Niang yalla na yalla goudal fane weral LA weral bat bi 🤲lniguaniouy beguélé si ahmadou ak ndiabotame gui yalla na yalla sérélé nonu sa, khôlbi ❤🤲❤🤲❤🤲❤🤲❤
Esk sincèrement téwlou ngén paroles yi no ki dou nit dh mouhamed niang dis nous ki est ti 😂 Dama diougué magal geun ko déglou mais suis grav hypnotisé par le son niang doundal way
Ndaysan 2008 ba legui magui koy bayi khel mais bou nieuw geuna nekh kham na dall serigne bi moko tek lokho yalnala yalla takhwou si barke s saliou mbacke ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Sante Serigne saliou mbacké ❤️ contane naniou yalla na yalla weral bateu bi mm op deux jours ma meun waay bii nak parole yi seleul naaa keneuh du môme koku ameuh sagouu bilae🎉❤️niou khar beneuh bi samedi inshallah mouhamed Niang ❤️
Mouhamed beug nala beug bo xamni yalla rk lakoy sédél barki s saliou mouhamed Niang yalla gua goudou fan yalla gua wer yalla gua mouthie yalla gua mouthie lé yalla bo guiss lo rogual Niang ballo walahi kouy diang Kat si réwmi rawatina tag katou Serigne saliou mouhamed Niang yaye bayam
Bilahi khalé bu djiguen bi awou si souf biss bu khamon nimi def sama khol bi ❤️ ki diaral nama djebalu si mom lepp loum ma lathe ma diokh koko lima am sisa aduna lepp ay koumay diokh numérom 😭😭
Je suis talibé cheikh mais chaque année madame nek première commettaire cette année dama tardé 7h de temp fék fi plus 350commentair ☹️ yalnala yalla samauh🥰
Je ne suis ps mouride mais dama beugue cheikhoul Khadim❤️🥰Machallah yalna yalla weerel batt bii🙏🙏
Ndeyssane sa khol mo rafét
Ndaye sane
Akasa
Da ngua beugue lou bah rek
Beugueu kou yalla beugueu ak yonetibi psl
Kou beug serigne touba rk beuseul j'aime😍❤️👍
Mach'Allah je suis talibé serigne babacar mais j'adore serigne saliou et serigne fallou ❤😍
Machalla 🥰🥰
Bilae barcke serigne Saliou doko reuthiou 🥰🥰🥰🥰🙏🏾♥️
Ndeyssane 🥰
Merci beaucoup à vous ❤❤❤
T genti
Le meilleur chanteur du monde. Il ne chante que le grand marabout et pour chaque chanson c'est un nouveau thème. Lii dafay woné ni serigne touba gueuna yatou guethie. Dieureudieuf sangue bi.
Massallh
Cheikouna seye
Waay dounedal ta wér waay yaw mi wakh liii
Moi je suis Talibé Baye Niass mais serigne Saliou mbeuguél guima ko beugue thi sama khôl la Mashallah Mouhamet
Moi aussi je suis talibè baye mais dama beuggg serigne saliou trop sakh ❤
Ken dou Cheikhoul Khadim ❤❤❤aka meuneu defare nite barker serigne Touba ❤ ❤
Thieuy sounou wadji Ken du mom mouhamed niang meilleur de sa génération👑👑 ningay sedalé souniou xol ❤❤yi Yalna lako yallha faye ci barkéb serigne saliou 🤲🤲
Aminé 🤲🤲🤲🤲
Amine yarbbi 🤲
@@soukhissesalihou9362 l'la'lmoy
Amine yarabi 🤲
❤❤❤ amine
Walahi ki damako beugg ❤😢 soumqy seuyi tei gneuwo douma dem😭 machallah liii nekhna🥰🥰🥰🥰
Je ne sais pas mais cette chanson me fait trop pleurer non pas des larmes de malheurs loin de là. Je ressens un bonheur extrême qui se manifeste par des émotions.
Svp écouter cette voix de Mouhamed Niang au plus profond de vous. Écouter les paroles qu’il chante et vous comprendrez. Serigne Touba nous a tout donné et nous devons lui rendre grâce jusqu’à notre dernière énergie. Chacun de nous sait que Serigne Touba est l’artisan de sa vie en ce qu’il connaît et même de ce qu’il ignore. Je t’aime du profond de mon âme. Je te suis éternellement reconnaissant pour tout ce que tu as accompli et que tu continues d’accomplir dans ma vie.
Dieuredieuf Mouhamed Niang.
Dieuredieuf Serigne Touba ❤️❤️❤️🙏
💐💐💐
Ptsdyfc8 tuusig
Walayyy tu n’es pas le seul ki mo takh ma kham Lou beuriii ba toppp Serigne bi démmm tokkk si kharrou bi tokk sentir Lou beuriii et chaque foi avant d’être j chante un de ses chanson en peurs
Yalla na ko Serigne saliou faye🙏🏾🙏🏾
Depuis je cherche quelqu'un qui partage les mêmes sensations que moi fiere d'être Mouride
Bilahi mouhamet niang niguay sédalé xolou diam yi yalla nako yalla yokou thisa fan thi barké serigne saliou❤️❤️👍👍
Amine way
Le meilleur de sa génération ♥️
❤️❤️❤️
Machala ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤😍😍😍😍😍
Wa li lan la tamit
Machallah
Machallah dieredieuf serigne touba c’est encore une victoire de lislam Inchallah ❤️👏🏼
Toutes ses chansons contiennent plein d'histoire et de sens pour ceux qui prennent le temps de décrypter son message. A travers ses chansons, notre amour pour Serigne Saliou ne cesse de monter au crescendo. Mouhamed Jeurejeuf Yalna la Serigne Bi Faye.
Je l'écoute depuis plus de 10 ans.Mais ses paroles me dépassent souvent.J'ignore vraiment sa source d'inspiration.Il est tout simplement trop fort
NAYÈS na
Yñ
@@mamebambadiop2005 mpmpmpmmmmmmmmmm🤔🤔
@@amdikare2412 à
Soubkhanallah 🤦♀️🤦♀️ li nekh rèk lah yèn ayway yalla nala yalla fay sama khol bigua sedal yalla na yalla sedale nonou sa khol 😭
❤❤❤❤❤❤❤❤❤amine
Le meilleur de tous les temps , mouhamed Niang bilahi yalla nga fi yague tè ande ak wer❤️🧡💚
Mouhamed vraiment la communauté mouride est fière de toi, demeure béni 🔥
je vous écoute en plein pluie au cap vert🤩
,ñ.ñ
Ndeysan yéné layy baké Serigne Saliou mbacke ❤️ mom Mohamed Niang 😭lofi way app deugeul laa ndakh Serigne Saliou gnamou dimbalé,ak sopi gui kouko doundoul mounoko wakhh , dieuredieufeti dieuredieufeti dieuredieufeti dieuredieufeti dieuredieufeti dieuredieufeti dieuredieufeti dieuredieufeti dieuredieufeti dieuredieufeti dieuredieufeti dieuredieufeti dieuredieufeti dieuredieufeti dieuredieufeti dieuredieufeti dieuredieufeti dieuredieufeti dieuredieufeti dieuredieufeti dieuredieufeti dieuredieufeti Serigne Saliou mbacke ❤️
Kou Geumni SeriGnE Amoul Morom 👍🏼❤❤❤❤
Machala 👍👍
Moromantéwoul
Dieuredieuff Serigne Touba💚💚 une fierté de l'islam machallah alhamdoulillah 🙏
Ndaysann yalla na yalla faye ❤️❤️❤️💪💪💪💪💪
Je
Kou may passe magl
Thieuy serigne saliou♥️♥️♥️♥️♥️🌎🌎🇬🇳❤❤❤
Bly j'aime tellement ses chansons franchement c'est le meilleur de sa génération ❤️💕
Tout simplement salihat à jamais❤
Dieuredieufti Serigne saliou sama yakar tay ak elekk ✅🙏
Anii niou sope Serigne Saliou Mbacke❤️👌
Kéne dou yaw mouhamed niang mou serigne saliou ❤❤❤❤❤❤❤❤
Phgt
Il est trop inspiré mach’Allah 🥰❤️
Les lyrics c d’une autres planète 🪐 waouh 😵💫 dop 🔥
Ooooooooooohhhhhhhh♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️sama xol bi sedd n’a trooooooppppppppp. Yalla n’a Yalla weral sa batt bi barki Segn Saliou🙏🙏🙏
Li rombouna nexxxxxxxe wayy🥰degal soxnasiy awou si souf💃
Quelle Mélodie amal jamme bou saxe dakk Niang Balo🥰♥️
C’est Rema Diop
longou vie à toi niang baalo le meilleur de sa génération ❤️
Machalla yalna yalla gueuna wérale bate bi
Wallahi sama xol bi nimouy def ni♥️😍🥰🙏yalla rek moko xam😭❤️🥰♥️
Niang yalla na yalla goudal fane weral LA weral bat bi 🤲lniguaniouy beguélé si ahmadou ak ndiabotame gui yalla na yalla sérélé nonu sa, khôlbi ❤🤲❤🤲❤🤲❤🤲❤
Ma cha Allah encore Mohamed mou Serigne saliou sama mbokou talibé bi yalla na yalla yerel battt bi
Machallah les paroles sont pleins de sens 😩❤️
Saaa boo diké mou geuneu nekhhhh🥰❤️🤩🤩🤩
Mashallah mashallah merci bc jerejef grazie mille Serigne saliou ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Mane dé khamna ni thi kaw souf dé boufi kéneu wayati serigne saliou ndakh dingua koye wayé yaw kep rekk dongue dongue ko meune barké serigne saliou té dagno beugue toul kénéne kouko waye kodoul yaw mouhamed niang 🙏🙏🙏❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Ki en damako beug ❤️❤️❤️❤️❤️
Esk sincèrement téwlou ngén paroles yi no ki dou nit dh mouhamed niang dis nous ki est ti 😂
Dama diougué magal geun ko déglou mais suis grav hypnotisé par le son niang doundal way
Ay Mouhamed dioxma sa numéro ndax limay yeuk atanomako 🥰😭😭😭😭😭🥰
Wa Rema limiy riim si souff nexna dei mashallah sama waadji mouhamed defatinga sa meunin dei🥰🥰🥰
Dieuredieuf Serigne Touba bimougnoula mayé ndakh woyy AK bak Serigne bii daa warr sii bépp mbindéff ndokk bignoulaa amé yagal té werr
Toujours du lourd avec Mohamed Niang ❤️💪
Ndaysan 2008 ba legui magui koy bayi khel mais bou nieuw geuna nekh kham na dall serigne bi moko tek lokho yalnala yalla takhwou si barke s saliou mbacke ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Waouh✨🙈♥️ Li dou batt Bou nekh kassei dh🙈♥️ wallahi yalla nala yalla Sam barkei Serigne Fallou♥️🙏🥰
Ku d’accord si 1M de vues yi bala mo matt semaine❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️🥳🥳🥳🥳🥳🥳💃🏽💃🏽💃🏽💃🏽💃🏽
Meilleur chanteur du sémégal❤
Sante Serigne saliou mbacké ❤️ contane naniou yalla na yalla weral bateu bi mm op deux jours ma meun waay bii nak parole yi seleul naaa keneuh du môme koku ameuh sagouu bilae🎉❤️niou khar beneuh bi samedi inshallah mouhamed Niang ❤️
Mouhamed beug nala beug bo xamni yalla rk lakoy sédél barki s saliou mouhamed Niang yalla gua goudou fan yalla gua wer yalla gua mouthie yalla gua mouthie lé yalla bo guiss lo rogual Niang ballo walahi kouy diang Kat si réwmi rawatina tag katou Serigne saliou mouhamed Niang yaye bayam
Machallah il a encore frappé Machallah rien à signaler
Salihate a vie 🧡🧡🧡
❤❤❤
😂😂❤
Nék Mouride da fa nék fierté bou reuy diadieuf mouhamed Niang
Wax deug yalla kou nangou ni mouhamed niang mofi dak way mashallah 🥰 rek yalla nalla yalla takhawou diam rek inchallah tawfekh ak taysir
Ta encore frappé 🥰❤️ machallah yalla na batt bii weer ❤️🥰🙏🥳🥳dieureudieufé cheikhoul khadim 🥰🥰🥳🙏
Machalla amatina solo dieure dieuf yalnanga goude Fan
Liii nimou maaay def oh 😥 Machalla ♥️♥️♥️
Mouhammad Niang wax dëgg Yàlla Doo séen moroom Xalima gi niaw na lool maasaallah.
❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️🤲🤲 seringe saliou MBAcké 🤲 yalla nako yalla doli Ay lérr amine yarabi 🤲❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️🤲
Ligua way grawena Limay yeugue nii yéména loll😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
Moukhamed Niang do nitt non li nekhna bilahi 🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰
Le meilleur de sa génération machalla encore Niang ballo ❤️🥰💪💪💪💪💪💪💪💪
Dieuredieuf SERIGNE TOUBA 😍 YALLAH na YALLAH wèreul bate bi 🙏🏾❣️
Wawaw gnongui ni di patienter pour le meilleur des meilleurs le meilleur chanteur du monde entier
Macha.allah yalla na sa diam yague waye🙏 😍
Tu es definitivement le meilleur machallah Yalnala Yalla samm
Bilahi khalé bu djiguen bi awou si souf biss bu khamon nimi def sama khol bi ❤️ ki diaral nama djebalu si mom lepp loum ma lathe ma diokh koko lima am sisa aduna lepp ay koumay diokh numérom 😭😭
Défati gua sa meunin deii👌🥳machalla niang balla khobi lém🥰yalla na bate bi wérr🙏💯
Batine ba graw,
Kou beugue xew dangay xam Li xew, wayyy (thiant) wakh diounou soukeur la, wayé serigne saliou dano béral lokho, lém lanou défal
Waye mouhamed nala s bi fayal bopam ❤️❤️❤️❤️
Amine
Sama xoll dafa sede thi mom
Dieuredieuff Mohamed. Degg n'a kham khamm deugg.
Lumu wayul neikhul kein dou moom ❤️machallah
Laf thatt yalla nga egale sa youne yaye sene baye yaye eneversite de shanter yep mashalla
Machallah way mouhamed yalla n'a sa diamou yague way li nékh n'a torop ❤️❤️❤️
amine machallah diareudieuf
Dieureudieuf serigne saliou dieureudieuf serigne saliou dieureudieuf serigne saliou dieureudieuf serigne saliou balla aicha mon bakh diko sant mba faw
Je suis talibé cheikh mais chaque année madame nek première commettaire cette année dama tardé 7h de temp fék fi plus 350commentair ☹️ yalnala yalla samauh🥰
MAchalla Niang ballo bégeul nga mouride yépp♥️♥️♥️♥️xol yi fess n'a déll🥺🥺Mane dh soxna mously saliou diokh nala sama bopp adiya😭
Oh machallah mais deuxième partie bi lounè la❤❣🖤😘🥰🥰🥰👏👏🤲🤲🙏🙏🙏
MACHA ALLAH Mouhamed yalla na borom bii gueureum wéraal
Mouhamed a encore frappé.ma cha'allah.kén d'où yaw. Longue vie à tw👏👏
Machallah li nékhn de Sant Serigne saliou mbacké rké ❤️❤️🔐
ana kouy kharrr commmm mannnnn
Ahh machalla yalla guafi Yague tei weir si barki serigne saliou💎💖🙏🤲
Theuy Muhammad mala beugeu dh❤❤ barké S.Saliou ☝yalna bat bi wuér barkép S.Saliou🤲
Machallah mouhamed Niang yll na yll wéral baatt bi barki Cheikhoul xaadim Mbacké amna sollo lool
Bilahi sosou nék rek ma wakh ko tu es le meilleur de sa génération sa you kholl yi fekhé rek yaw la Niang BALLO DOUNDAL WERAL BARKE MAME SALIOU
Machalla meilleur de sa génération ❤❤❤❤❤❤
Machalha ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Ndeysan yalna batbi wer thi barkep serigne saliou ❤❤
manam mom n wayano woul ak khalei yiii nagnouy deglou paroles yi niang do nite❣❣❣❣kouy diay gneukk khana lay xarr meun nama ray
En tout sa musique mague Na. Tu chante avec aisance et professionnalisme. Tu as grandi en musique
Réwmi yeungouneu mouhamet niang ningay sedalé Sunu xolyi yalnako yalla séralé sa xol
Thiéyyy signou❤️ Sedna lool mouhamet Niang
Mashalla continue à nous régaler chak magal tw et Ndiogou Afia vous êtes les meilleurs
Kéne dou yaw barki Serigne saliou 😍😍♥️♥️👌👌
Mashallah bareké serigne saliouh ñiola beug nakh serigne bii
Sénégal ño beurii ay ndaanane ta khamouñoukooo🙏🙏
Mouhamed diambarr deugg gua barker Serigne Touba. Yalna Serigne Bi guenn taxawu🙏❤️
Ammo morom thi aroute....défati gua sa meunine rek yalla na yalla goudeul fane yii thi barké Serigne saliou.
Ba yagui wadial magal inchallah lalal j'aime ❤❤❤❤❤❤❤❤❤