Machallah il me rappelle baye Abdoul Aziz Dabakh, un discours de vérité, il faut pas avoir peur de dire la vérité pour venir en aide à la population en énumérant les difficultés des gens tant dans la santé, dans la justice, bref dans la communauté, vraiment je suis très de votre khoutba, qu'Allah vous accorde une très longue vie ,pleine de d'une très très bonne santé ,
Serigne bi je souhaite que tout le monde écoute votre khoutbe car vous avez cerné le problème et donné les conseils pour s'en sortir. Que Dieu nous garde dans sa miséricorde.
Dieureudieuf serigne fallou mbackè bou serigne yèp mèlone nè yew kon askane wi dinanou am koulene yiir wayè askane wi sone nane trop lilène wara yiir gnome ak gouvernement gno ande di tek dile askane wiii rek
dégatina deug dé ! Macky à besoin des gens comme ce marabout, ce sont des conseillers véridiques pour lui. le marabout est objectif car, il a mis en exergue tout ce que le président fait de bien, mais il a également pointé du doigt tout ce qu'il fait de mal dans ce pays et qui nous retarde ! macky a besoin qu'on le lui dise pour qu'il corrige sa démarche.
Meilleur khoutba sama baye dju machallah kouma soppu trop moy sama baye fallou mi al hamndoulilah rabbil à la miine ba dou dégnsi diniu fattali li takh niu nieuw si adouna niughilay nianal yallah mayla tawfeikh ak taysiir
Dieureudieuf Serigne Fallou mbacke Dioumada vraiment lii mooy Imam Ratib ak Kilifa diiner dangay wakh deug té yalla takh il a raison sur toute la lignée à bon entendeur salut Deuwénati len inchallah 👌✊💪❤️💯🌟🙏🇸🇳
C'est mon imam préféré. Deug rek lay wax. MachAllah.
Machallah il me rappelle baye Abdoul Aziz Dabakh, un discours de vérité, il faut pas avoir peur de dire la vérité pour venir en aide à la population en énumérant les difficultés des gens tant dans la santé, dans la justice, bref dans la communauté, vraiment je suis très de votre khoutba, qu'Allah vous accorde une très longue vie ,pleine de d'une très très bonne santé ,
Amin yarabi 🙏
Serigne bi je souhaite que tout le monde écoute votre khoutbe car vous avez cerné le problème et donné les conseils pour s'en sortir. Que Dieu nous garde dans sa miséricorde.
Un homme véridique constant depuis des années que je le suis
Exactement c est ce que je voulais dire
Machalah ❤️ mbacké balla ki sama papa la moma may borom keur à l'âge de 17 ans jusqu'à présent 13 ans de mariage DEUG rek moko nior
Machallakh
Machallah...
Longue vie mon Iman
Kokou begue béssoul j'aime
Merci beaucoup vérité absolue que dieu te protège
Wallah juste en regardant son visage. Tu sens que c’est un homme de Dieu Manchallah Longue vie et de sante amen.
macha'Alla Serigne bii vous êtes un exemple pour autres marabouts. Rien que la vérité mo diekk mo moudiou. Vous avez tous résumé. macha'Alla❤
Machallah Amatina Solo Lool Dieredief Seringe Fallou ❤❤❤❤🙏🙏
Dieureudieuf serigne touba serigne mountakha yalla nafii yagg te wër dieureudieuf serigne fallou dioumada yalla nafii yagg te wër ❤️❤️❤️🇸🇳🇬🇼❤️☪️✅
Amiiine
Quel sagesse ! MashAllah..dieuredieuf Mbacké
Dieureudieuf serigne fallou mbackè bou serigne yèp mèlone nè yew kon askane wi dinanou am koulene yiir wayè askane wi sone
nane trop lilène wara yiir gnome ak gouvernement gno ande di tek dile askane wiii rek
Vraiment
Une personne véridique ,qui ne prend pas l'argent sale !!!! Que Dieu te protège partout il ya des hommes de Dieu machallah.
Mashallah bien dit que Dieu vous protège
Toujours également à lui-même un homme véridique machallah
Lii mooy khoutba, sensibiliser et informer sur les actualités de l'heure
Vraiment
Maa Shaa Allah
BAYE. DEUG Dou Rombi Nopes.
MERCI INFINIMENT
Seriggne fallou yowde boudee salairoup depute benela thi senegal yow langnouko wara djokh
Vraiment
Machaallah Serigne bi 🙏
Heureusement notre senegal a un imam exemplaire. Je vous aime mon imam
Y'a plusieurs Imam dans ce pays 🇸🇳
AMiiiiiiiNE
Dieureudieuf! Dieureudieuf ! Dieureudieufety Serigne bi wakh gua lép dégueu rék mon déss👂👂👂
Machallah Serigne FALLOU MBACKE DIOMADA
Machallah Dieuredieuf Mbacké yalla na yalla same la
merci mr dioumada
tu es tres pertinent ce que tu dis sur macky et les forces de l'ordre on le vit toujours
Mom nalén wor ni di Touba législatives yi yewwi Askan wi Mo fi gagner in cha allh
Amine yarabbi
Daffa leer
Machallah amna solo loool serigne fallou diomada
Machallah yalla nala yalla faay yeew dieuredieuf amnasolo mbacke
notre idole préféré yalla na yalla doli fan bou goude
Machallah amatina solo🙏🏽
Meilleur khoutba de l'année 2022
Merci beaucoup amena solo trope🙏
Machalah kouddall fannnn
Machalah! Deugue pire. ❤️❤️🙏diereudieuf serigne bi
machala deugue bou wer machala
dégatina deug dé ! Macky à besoin des gens comme ce marabout, ce sont des conseillers véridiques pour lui. le marabout est objectif car, il a mis en exergue tout ce que le président fait de bien, mais il a également pointé du doigt tout ce qu'il fait de mal dans ce pays et qui nous retarde ! macky a besoin qu'on le lui dise pour qu'il corrige sa démarche.
As t'il vraiment besoin de ces marabouts.Nous avons besoin de leur voix dans ce pays
Meilleur praicheur de l'annèe
Je valide ✊
Ki yakarout bénn gouvernement
Peut être que les mallettes d'argent il n'a encore rien vu .un mara politicien
ماشاء الله بارك الله فيكم
Dieureudieuf serigne fallou dioumada wakhdji rafetna looool maa cha allá yalla nala yalla sammou té aarla yangi ci yoon bi
Meilleur khoutba sama baye dju machallah kouma soppu trop moy sama baye fallou mi al hamndoulilah rabbil à la miine ba dou dégnsi diniu fattali li takh niu nieuw si adouna niughilay nianal yallah mayla tawfeikh ak taysiir
Machallah Serigne bi
Mashallah yalla na yalla yoku wéreul kham kham bi
salam salam merci beaucoup mon père je suis très très content de toi que allha te protège amine yraby
Machallah yalla nala yalla sama
Masha allahou
Machalla Serigne Fallou donougua sa toma contane ci yaw Serigne bi yalla nasa diamou yague djieure djieuf
Machalla limoye deugue
Dieureudieuf !!!!
Machala Amna solo yalna yalah fay yiiw houtba bii bakhne si tolouwayou réwmii
Dieureudieuf Serigne bi yalna nga fi lol té And ak weur
Dieureudieuf Serigne Fallou mbacke Dioumada vraiment lii mooy Imam Ratib ak Kilifa diiner dangay wakh deug té yalla takh il a raison sur toute la lignée à bon entendeur salut Deuwénati len inchallah 👌✊💪❤️💯🌟🙏🇸🇳
Wawaw Applaudissez!!! 😂😂😂
machallah serigne bi domi kane la
Serigne Fallou the Senegal is proud of u. May Almighty Lord give you more strength to do wonders 🙏
Machallah wakh dji rafetna trop yalla nala yalla defal diam ak soutoura
NDAYSAN 😭😭😭
Mbacke Yalla Na Nga fi Geuna Yagg Te Andak Werr Barkeb Serigne Touba 🤲
Yalla Nala Reew Mi Deg 👂👂
yalnala yalla maye goude fane ak wer degue rek nga wakh
MACHALLAH serigne bi
Machallah 😌 tarkallah.
xutba au niveau Mach allah yalla na yalla goudal sa fan
Machallah Amna solo papa longue vie 🙏🙏🙏👏👏👏
Leerna nagne billahi macky yakhana reewmi
Deugeu bou werr peng la dieureudieuf serigne bi
Imam yalna yalla goudal sa fane kou artouwul attè deug moy moudiou le senegal va très mal
Merci imam
Bilay merci imam kou artouwoul digua atté
Jërëjëf Mbacke balla ❤🙏
Machala amna solo lol guoudou fane ak weer Mbacké balla
Machalla serigne fallou mbacké goudal fan té ande ak weer
Machaallah yalnako yalla dolly lère nitou deug
Dieureudieuf Serigne bi❤🇸🇳
Machala ❤️❤️❤️
Machalah mbacke wahh nga lepp déé🙏
Machalla ♥️ Machalla ♥️ Machalla ♥️ Machalla ♥️ Machalla ♥️ Machalla
Merci beaucoup Serigne
Diaradiaf ❤️❤️❤️❤️❤️
Machalla am na solo dieureux dieuf serigne falou Yalla nonou am degu ak topou macky degloul li am gua si walla
Masha Alla dieureudieuf Ya IMAM, deux rek walakhi li lagnou soxleu assemblée Nationale
Machallah que dieu te donne une l'ONG vie
Diadieuf Papa mashallaah
C'est ce que l 'on attend de kilifeu,diadieuf goudal fane Serigne
Walay deug dafa nékh Serigne bii machallah
Albarka Serigne Fallou
Machallah leer neu rafetna.
Merci imam Dioumada
Machalla.mbacke 🤔🤔🤔🤔🤔🤔🤔🤔
Yalnala yalla sammou
Machahala lale nga fépe deugue rék mo nékh yalla
Dieureudieufety mbacke
Bouniou amone niou melni yao nieme deugg rewmi nekh
Dieureudieuf serigne bi
Machallah Serigne falou yal nalafi sounou borom yagal lol ta waur
Mon père, on a rien à te dire que de te remercier
Ndeysan Serigne Fallou mbacke dioumada nite kougneme deugeu yalnako yalla yeureum khareko aldjana firdawsi bidiahi seydil woudioud Amin.
Dieureudieuf mbacke amna solo LOL macchallah
Serigne bi yalla nallafi yalla bâyi mayla weer
Machallah yalla bayi la fi yaraby
Chacun doit choisir son camp et de manière Claire.
Machalla yow faleiwo khaliss deguereik mo le nior ah Yalle machalla longue vie
Macha allah kou melni yène moko wara djité brome addouna ak allakhira