@@biggismol8375 non beaucoup de gens font cette confusion Issa Laye est le fils de Limamou Laye. Issa est celui qui est sur cette image Limamou Laye n'a pas de photo
Yalla d beuguoul kouy togne le prophète PSL aussi na khounékh gueum ligua gueum yalla rék nakh mo kham lép gnoune gneup le prophète lagnouy topp wayé khounékh yalla bolé nala AK sa serigne gni servie le prophète PSL mo takh gnou gneuw fi ay messagère lagnou togne nk mome bakhoul bougnou déme nakh bay wakh lou niaw si Serigne si nk konn adouna bi migui beugue touki nagnou défarat guiko yi tes yarou amna gno khamni kéne douléne togne Mangui toup nk🙏
Dou sen wakh yi moy waral changement si li Yalla def... Seydina Limamou Laahi khana Yalla SWT raga louko ba mou taxaw ni moy Rassulu Laahi SAWS dokh si wakh si ba xeuy lakou deureum diotou ko ba ay domam yore ko ba légui ay seuteum.... Waaa mani ani Yalla mi dieuff leunté woone ak Firawna wala Namrouss xana Yalla boobou amatoul ba nite diko sossal mou tokk diko setane pendant 144ans déjà.... Utilisez vos cerveaus gars Seydina Limamou Laahi SAWS moy Rassulu Laahi SAWS ❤🤌
En Inde,un gars du nom de Mirzam Ghulam Ahmad s'est déclaré prophète,mahdi et issa en même temps et il a aujourd'hui plus de 10 millions de suiveurs dans le monde. Si on utilise votre logique,alors ce gars a t'il aussi raison ? Réfléchissez un peu waay
qu’Allah vous guide. Sheytane vous trompe et n’oubliez pas qu’Allah lui a octroyer beaucoup de pouvoir pour égarer les musulmans. Al kurane ak sunnah mo weddi seni wakh. qu’Allah nous éloigne de l’égarement et nous guide dans le droit chemin.
Aka wouté ak Mohamed moumoute diar ba nek Mohamed déguéne rer khamouléne foléne dioublou guén bougue taf sen bop si Mohamed Mohamed bena leer la yone bou yalla bindone cheytane mounoul dieul dieumeum bou tedd bi (psl)
Moi je n'arrive pas comprendre les Layen. khana yalla wakhoulné béneén yonente dou amatt après mouhamad (shs) légui vous voulez nous faire croire que limamou laye est mouhamad et que son Issa laye est Issa Ibn Mariame c'est totalement faux c'est harchi faux et c'est absolument faux
@@khadijaaicharassouljilbab7132 Ah guisgua deh je peux accepter limamoulay soit un homme parmi des pieux qu'allah Azwajalah a honoré avec une vie pleine de miracle. Le coran souligne qu'il y'aura aucun prophet derrièr mouhamad psl À propo de mahdi celon un Hadith du prophet psl il dit que le mahdi sera arabe son nom sera le meme de lui et le nom de son Pere sera aussi le mème de son père qui est Abdulah.
Machallah je suis mouride mé baye laye amoul morom yalla dal téral na Sénégal ak ay nite you bakh
Je suis Niassène wayei dama beugg wakhtanou Layènne yi machallah Yalna sounou Borom geuneu yokk ay leram ci barkei Baye❤️🙏🏻
Mashallah mashallah
Amine Ya raby
Iow sheytani ga .
Ki Di wotéwo yonnéntu ga nane seni wah da neh.
@@abdourahmanediallo24 Waxdji ak Wotê bi boula nakari dagay guêne deuk bi Seydina limamou laye moy Mouhamadou Rassoul lahi
Sa digueunté ak yalla talibé baye gua tarbiya gua ba am fathou??
Je suis mouride mé j’aime baye laye
C'est la première fois la dème appel
J'ai vraiment apprécié
Deug YALLA gui mofa né
Thiey seydina limamoulaye.
Yalla naniou yalla fayal.
Mame seydina limamoulaye rek la beugue.
Je suis talibé cheikh Wayel dama beugg baye laye❤❤❤❤
Senegal ba tay khamouniou linou yala defal nioune ay degue degue goor yala laniou ame nioune❤
Machalla j’étais là bas aujourd’hui mais j’ai même pleuré yalna yalla yokou léram ❤
Merci beaucoup pour la visite guidée
Bilahi mouride lah waye dama djekh si seydina Limamou Lahi yalla nagnou ko yalla fayal
Macha allah 🙏🏻🙏🏻
Masha Allah masha Allah
Machalla
Kou khamoul khamoul. Bilaahi! Nagniou baayi diingate!
Machalla yalla naniou yalla tasse si sén barké
Machallah dieuredieuf amna solo torop ❤️💓
Mach'Allah yalna y'Allah yoke lèrem thi Barké Seydina Mouhammed saws ❤
Non khana wakho léne kayy moy seydina mouhamed khamo léne sakh loo len fi wakh
Machallah seneweb tv international yalna yalla faylenn
Pour gni khamoul Seydina Limamou Laye amoul photo borome photo bi c'est son fils ainé Seydina Issa Laye lou way khamoul rek mandou si
Ak degue lamatar mamadou
Yen la rek
@@abybodian1448 yaw khana meuno teuthie sa guemigne te Manou
Ok issa lay et limamoulaye c'est pas la même personne?
@@biggismol8375 non beaucoup de gens font cette confusion Issa Laye est le fils de Limamou Laye. Issa est celui qui est sur cette image Limamou Laye n'a pas de photo
Talibe cheikh mingui contane loll sakh 😪🙏❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Je suis bay fall j aime mame limamou laye
Yalna ma yalla raye thi geum seydina limamou laye psl
SubanAllah dierejef baye laye Qu'Allah bénisse le Sénégal amine
Alhadoulilahi baniou dekké Sénégal 🇸🇳 ❤❤❤❤❤❤Alhadoulilahi Alhadoulilahi Alhadoulilahi
Khatimin nabi prophète Mahomet salalaho alayhi wasalam point❤❤
Walahi bilahi amneu béneu khair boumeu meuss guiss diguenté yoff ak virage walahi mou amm mark tank
MashaAllah TabaraAllah Laye Memedou Psl Demb AK Tay ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Machallah amna genrou émission deh mom mo geune diniou wane lo xamni amoul ben ndiarigne
Je suis un mouride mais contane na trop
Muhamad psl moy yonentou bou moudji bènèn yonèntou dou ame guinaw Rasouloulahi
Nie danio reerrr
Machallah amna solo
Machaallah Laye Makhtar ziarnalene 🙏 🙏 🙏
Machallah am na solo trop
الله نور السماوات والارض
Bilayii mourid laa wayai balaye borom secret laa kou mandou dakh yalla mo leudeum
Yalla leer nagn la def reer molen diapeu très ridicule
donté lou bakh nga diouplo wakh, wayé linga wakh kén douko wakh yalla lére la saytané mo leundeum dél wakh lo xam wala nga nopi
Baye laye amoul mass té narr ba khesone demb tay nioul na 🥰🥰🥰🥰❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Mashallah Laye Memedou Mokhtar Laye Alassane 🙏❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️🕊🕊🕊🕊🕊🕊🕊
Jai une fois allé laba avc ma soeur jai descendu jusqu’à bas machala
Moi je connais qu'in selle celui de mouhamad rasouloulahi صلى الله عليه وسلم
@@lossjloss8892 walay nitt loumou khamoul dasi madou
Yalla na sounou Borom yokk ay leerame tee tass niou si barkem ba
Liga wakhe Moy pure vérité qui dou yonént ibliss pure là
C'est vraiment ridicule 😄😁😆
Togn bakhul n'a kounèkk geum linga geum bayi polémique yi
Yalla d beuguoul kouy togne le prophète PSL aussi na khounékh gueum ligua gueum yalla rék nakh mo kham lép gnoune gneup le prophète lagnouy topp wayé khounékh yalla bolé nala AK sa serigne gni servie le prophète PSL mo takh gnou gneuw fi ay messagère lagnou togne nk mome bakhoul bougnou déme nakh bay wakh lou niaw si Serigne si nk konn adouna bi migui beugue touki nagnou défarat guiko yi tes yarou amna gno khamni kéne douléne togne Mangui toup nk🙏
Mame limamou nitou yalla deug yalnaniou yalla tasse si barkem
Macha Allah Baye Laye amoul mass dakh Moy Rassoullah sws❤❤❤❤❤❤❤❤
Macahllah amna solo
Yalna yallah yok aye lèram dika sant bimouniou bayé akh bate bi guene mouye La hillaha illahou Mohamedou Rassoullahi sws❤❤❤❤
Mashaallah amna solo
Al hamdulilahi Seydina Limamou Laahi SAWS moy Rassulu Laahi SAWS ❤
Baye Laye amoul mass fière d être layene seydil Awalina was seydil Akharina(PSL)
Ndeysane ma mbeugue mame libass laye Makhtar sope nala mame sokhna Awa bayfall
Machalla ❤️❤️❤️❤️ laye ❤❤
Yallah yoki léram tass gnu ci barkem
machaalh yalla na yalla yokou léram🙏La chanteuse sur l'interview rk la beugue ham
C'est la fille de Serigne cheikh mbacké laye salimata thiaw
@@adjisamb6308 merci exactement guiss nako🙏
Akhlou Layéne 313 ridialou LAHOU .. Laye Laye Mouhamadou Moukhtar Laye
Man mom damako beug billahi
Machallah❤️🥰🙏
Machaalah baye laye. Il est le Mahdi. Et je le jure sur saint Coran. Malgré que je suis Mouride
Limamou laye💕💕💕💕
On a kun seul prophète
Vrai un seul Mohamed avec deux missions
@@sokhna-awaboucherifousseyn5827 gni diarougnou tontou sakh
@@lesenegal221 bilay
Mame Limamou Lahi Aley salam❤
Kou beug ay Secret yi nek si alkhour âne abonnel
للهم اغفرله وارحمه واسكنه فسيح جناته 😢😢😢😢😢😢❤❤❤❤❤
Thakhane bakhoul réveillez-vous mes frères et sœurs 😢
Machalla yalla n'a ko yalla faye si barke sidina Mouhamét psl
Dieureudieuf Laye Makhtar
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ken dou sa Mame
❤Baye laye est mon serigne❤❤❤❤
Baye Laye du Serigne ap yonnene la bu dei tontu bi nga doon khaar mi ngui ni
Bayiléne nitt yigeundi réral.pa de Prophète après محمد صل الله عليه وسلم
Dou sen wakh yi moy waral changement si li Yalla def... Seydina Limamou Laahi khana Yalla SWT raga louko ba mou taxaw ni moy Rassulu Laahi SAWS dokh si wakh si ba xeuy lakou deureum diotou ko ba ay domam yore ko ba légui ay seuteum....
Waaa mani ani Yalla mi dieuff leunté woone ak Firawna wala Namrouss xana Yalla boobou amatoul ba nite diko sossal mou tokk diko setane pendant 144ans déjà....
Utilisez vos cerveaus gars
Seydina Limamou Laahi SAWS moy Rassulu Laahi SAWS ❤🤌
Allahou Akbar cey yallah mo meuneu setane way nooooo
En Inde,un gars du nom de Mirzam Ghulam Ahmad s'est déclaré prophète,mahdi et issa en même temps et il a aujourd'hui plus de 10 millions de suiveurs dans le monde.
Si on utilise votre logique,alors ce gars a t'il aussi raison ?
Réfléchissez un peu waay
Mane dama beugue seydina limamou laye bien vrai k suis mouride mais dieum dji mome dama ko fonk
Ohhh j'aime bien cette histoire
Comment faire pour y visitée
Mongui ngor almadi dangay ladjte khountma Walla dioulikaay ba
@@Salimata-l6e Domafa yobou khana?
Yonente amoul guinaw seydina mouhamad bayou fatima
Limamo lay nekol ben yonunte sénégalais mo mana nakh bopam
Machalah wahtane bi anasolo
Diadieufe Laye makhtare ❤️
Qu ALLAH nous guide
Machalla lay makhtar
Subhanallah thieye Sènègal KAllah ns pardonne
Bilaye lii dafa eupp😭
Dieredieufe seydina limamoulaye❤❤❤❤❤
qu’Allah vous guide. Sheytane vous trompe et n’oubliez pas qu’Allah lui a octroyer beaucoup de pouvoir pour égarer les musulmans. Al kurane ak sunnah mo weddi seni wakh. qu’Allah nous éloigne de l’égarement et nous guide dans le droit chemin.
Amine
Santa yalla dé walahi bima bokké si wa keureum libassa lahii rassoul swas
😢tasbir machalla
Mangui ziar mane la khadim mou limamoulahi.
Kou wooté watt ak yonénte guinaw mouhammad wakho deug Sénégal fénn mofi man deug😂😂
Sénégal, carrefour de tous les miracles.
qu'Allah nous guide
Bilahi dafa yémé
Surtout ça. Amine !
MaSha Allah
ماشاالله❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Limamou moye Rassoulou lahi
Qu'Allah nous préserve de l'ignorance et du fanatisme.
Vous êtes plus que égaré.
👌
Bou yaboo, nioune Baye Laye lanou geume... Baye Laye psl lanou guiss
Wallahi
Comme qu'on est égaré laisse nous avec nôtre égarement guemeul linga gueum bayi sa morom gueum limou sentir
Mandoulen
Nittou yalla piir la Seydina limamoulaye yalna yalna tasniou si barkem mako beugg piir
je suis surpris de ne pas avoir connu ca ? ca se trouve ou svp ?
À Ngor côté Almadies
Kéne dou môm mon geune nieup
❤❤❤❤❤❤
Yalla na yalla yokou ay leram
Fi rek la beuga dem
Bilay mane mii lolou la beugue
Bilay xawma nane rek lay def ba dem fa
@@arametine7783 athia gnou déf Ziar groupés pour vendredi in sha allah
Machallaha
Machallah 😍
Ndaye sane ♥️♥️♥️♥️♥️♥️
Gni wéddi limamou rék la yereume
Hiiiiiii Khalass yalnanu yalla guindi....
domouram dji dindil mbacké sa tour wi domouram nga rek ap salafist nga
Man mi talibé baye niass laa, ms guénte n'a limamou laye mouni ma niowfi dioulifi niarri rakka samay adio fadiou
Titre du son svp😢❤❤
Sénégal khawma lan mo nek thi sen khel yi
Va te faire voir
Mashallah
Fila beugue dém wallahi ms khamoumako
❤ alkakbr ❤
Kou guem nii yonnente amna guinaw mouhamad yéfér nga
Limamou Moy Mouhamed
Aka wouté ak Mohamed moumoute diar ba nek Mohamed déguéne rer khamouléne foléne dioublou guén bougue taf sen bop si Mohamed
Mohamed bena leer la yone bou yalla bindone cheytane mounoul dieul dieumeum bou tedd bi (psl)
@@momogreenwood2254 bilay
@@bayetackodjimera8754 Baye laye asws amoul photo
Gestu dji léne
Moi je n'arrive pas comprendre les Layen. khana yalla wakhoulné béneén yonente dou amatt après mouhamad (shs) légui vous voulez nous faire croire que limamou laye est mouhamad et que son Issa laye est Issa Ibn Mariame c'est totalement faux c'est harchi faux et c'est absolument faux
J'ai tjrs suivi leurs histoire en tant que musulman j'ai eu mal à le croire
Moi aussi je 🤔🤔🤔🤔🤔🤔bizarre yala yala na ma yala mousle alakhira di na nékh dé
@@idrissadiagana2416 mouhamde c'est le dernier message d Allah il raconte c'est faux histoires soupkhanala
@@khadijaaicharassouljilbab7132 Ah guisgua deh je peux accepter limamoulay soit un homme parmi des pieux qu'allah Azwajalah a honoré avec une vie pleine de miracle.
Le coran souligne qu'il y'aura aucun prophet derrièr mouhamad psl
À propo de mahdi celon un Hadith du prophet psl il dit que le mahdi sera arabe son nom sera le meme de lui et le nom de son Pere sera aussi le mème de son père qui est Abdulah.
@@idrissadiagana2416 ah tou ca c'est bizarre que Allah nous pardonne li faut vivre avec le sounna du prophète mouhamde
Yaw miy lirr sama commentaire ngalla waay jàngalal sa dome diiné sinon lou waay wootéwo mou gueum ko xam ngene ni lii gueum ko sax weddi yalla la