Doomi Gaindé épisode 14 (VOSTFR & ENG)
ฝัง
- เผยแพร่เมื่อ 7 ก.พ. 2025
- Alors que l'équipe des 'Lébous" menace leur qualification par leur virulence, Petit n'arrange rien. En effet sous les influences de sa famille il va s'éloigner du groupe de ses amis.Samba pourra t il échapper à la punition de son maitre coranique?
While the 'Lebous' team threatens their qualification with their virulence, Petit does not help. Indeed, under the influence of his family he will move away from the group of his friends. Samba will he be able to escape the punishment of his Koranic master?
Guest: Sau Cana, Joe Black et Be Sport équipe CFPT
Générique fin : Lu tax ñu bonn - POINT FINAL
Musique générique début:
/ sebobeats
www.sebobeats....
Votez pour Doomi Gaindé
Votre série préférée pour remporter le trophée de la meilleure série 2021 au Festival de Cinéma à Montréal, Canada.
Procédé sur deux étapes ( Deux pages)
1 infos et mails
2 Choisir dans la catégorie Série Tv et Web: Fils de Lion (Doomi Gaindé)
Pour les autres rubriques choisir si intéressé ou cocher "Aucun" ou "Autre"
Puis envoyer
Niou Dieul Ndam li indiko Sénégal.
Lien:
docs.google.com/forms/d/e/1FAIpQLSfRsny03MeRzRBWHAIhoNN-61EuuB-rd4_h7D-LHWNw_4BLqw/viewform?fbclid=IwAR34pcDUyqbVrbSFtP0aDneJwh0DvO_CKxRqhV80ybubIf9ulUxtJwTgxOM
Il faut écrire pour voter pour LE FILS DU LION la-bas c'est pas doomi gaindé pour sama genre yi🤣🤣
Bonne chance
Félicitations DOMOU GAÏNDÉ YI)))😭💘💘💘
Jai déjà voté avec le lien sur Facebook. Bravo à vous tous
J'ai voté moa🦁
Je la regarde avec ma machine et mon téléphone portable tous sa pour augmenter le nombre de vues car cette série mérite des millions de vues maximum de partage
Slt Vieux cisse
Magui niane nga abonné si sama chaîne bi ger yallah
Kou beugeu DOMOU GAÏDÉ DAWE 2 fois dans la semaine beusseul aime slvpl
Cône dou bax
1semaine c tros way
Slt Mouhammed
Magui niane nga abonné si sama chaîne bi ger yallah
Tay da mélni mafii ndieuk yalla na Sénégal 🇸🇳 am jam ak bép réwou djoulite si barké Mouhammed psl et bonne continuation Domi Gaïndé
Ak bépp rëw pas dioulit kassé
@@ndamayt2181 t'as pas compris frère
@@ndamayt2181
Magui niane nga abonné si sama chaîne bi ger yallah
Wallahii t'as raison d
Meilleure *Ghetto* série de toute l'Afrique de l'ouest 🇸🇳🇨🇮🇬🇭🇬🇳🇲🇱🇳🇬🇬🇲
Et 🇲🇷🇲🇷 🇲🇷 aussi 😳
@@tyfasow5649 ééy bandam ko gongo dé! Yaffo mí et bien-sûr que RIM🇲🇷 ma terre maternelle en fait partie. Woni ila bik🇲🇷✊
Oui Tyfa ma cousine à plaisanterie
@@djibsondasilva454 ne refait plus jamais 👎 d’accord 😍
@@mohamedsididiop8759 😂😂
Bienvenue les sponsor kopar dolima appuyez vous notre chéri préféré yalnaléne yalla may 20.sponsor you tabé meuneu fay khalise amiine
Il est mort
🙏🏿🙏🏿
Amin
Domarame
😦😦😦😦😦😦😦😢😢😢😢😢😢
Yalnaniou yalla yobou si koor gui akk diam niou woor ko si diam wory si diam si barké seydina Mouhamed (psl)🙏🙏
Serigne Mountapha mbacké yalla nafi yague te werr
Wa khal aminé 🙏🙏🙏
Kham wakhoko te yalla takh
Amin
@@bayediop2790 sof rek
Amiine
Amin
Premier koubeug assane doomi gaindé j aime
J’ai encore pleuré « le geste de Petit... »🔥🔥 merci pour cette série
Kou sopp yonentei bii beuseul j’aime 🥰❤️🙏🏿
Arête d'utiliser le prophète pour avoir des like STP
@@papamoussandao6244 lou thii nek
@@matarcisse je pense que bakhoul
Excusez moi mais ça fait un peu"putaclik"
Utilisez le nom du prophète uniquement pour avoir de likes....
@@papamoussandao6244 d’accord merci bcp 🙏🏿
@@matarcisse tkt
Chaque série qui passe, montre un fait dans notre société.
Meilleure série.
Bravo à vous.
Première commentaire kou abonné si man yalnga yohbou sa yaye maka🕋
Merd
@@bayediop2790 😂😂😂😂
Yen lan moy sen problème 🤦🏾♂️
@@G_bril mdr😂
@@bayediop2790 sama telephon mako mom louma nekh lahsiye bind soula nekhoul nga rombou point
Le cousinage à plaisanterie entre les ethnies présent dans cet épisode est extraordinaire. Les sous thémes : Mystique, mendicité, Pauvreté fait de Dommi gaindé un chef d'oeuvre.
Kane ak Kane nio beugue niou ték ko 3 foi par semaines qui est d'accord beusseul j'aime
Nékal nitt boy scénario dafa méti
3 foi par semaine yomboul ligaye bi dafameti
YaW est que sidy va aller l'école 🤣🤣🤣🤣🙏
@@youssou.diagne6137 bien sûr sidy ne va pas à l'école
Iow tmt 🤣🤣🤣 amo 2 fois di lathie 3 🤣🙈
Meilleure série au Senegal qui est d'accord avec moi 👇👇
Une très bonne série, je n’en disconviens pas. Mais par contre ce n’est pas la meilleure série du Sénégal
Moi
Ana gni guiss sene bopp si série depuis debut bi bâ legui venait pointé beusseul j'aime
Lamzo
Lamzo
Moi
Mane gisnasi louma louma dioylo ak louma neh
Suis là moi qui m'intéressais même pas aux séries
Barki yalla So cana moy done sounou coach Asc
Kouko beugeu mou gnew coaché sa Asc beussale j'aime
Mane serie bi 2 fois lakoy sétane par ce que douma thi doyal qui est d'accord que 2 épisodes par semaine
2fois😱😱
sadata nday
ime
Allkhamdoulih magui sante yalla samba li mouy doundou ni diarr nasi neke talibe di football sama seringe tres mako aye yonn ma neke si rek di football dorr nama si aye yone magui sante seringe dakh wathie na camill corane diangal nama aye tre sarikha insbi magui italie di football di ligey❤🙏❤
Machalla ❤️
Mem mane tamite
Oh mach allah yalla n'asa diame yague Fréro yéro Mballo
Yalla bakhna
Je suis amoureux de cette série. C'est ça qu'on veut . Nous plonger dans la réalité. Le cadre réel de notre pays .. Au lieu de nous vendre de la fiction, des luxes , eumbeulaté fii eumbeulaté feulé comme le font les autres maisons de prod . Bravo Level studio
Le meilleur série de les temps je l'aime tellement svp deux épisode par semaines et bonne continuation vous êtes talentueux machallah les frrs
Espace commentaire bi yeup « mayma j’aime» késsé ngay guiss diokhélene sene avis si serie bou nekh bii akh🤦🏾♂️
*Vraiment*
Bilay wakhall dh ak kou sopou seydina mouhamed
Gnikoy j'aime nioko def bilay
Gayii nio sofff billay
Slt ibou Thiam
Magui niane nga abonné si sama chaîne bi ger yallah
Allons voter j'ai cherché partout dormi gaindé dekétéyo 🤣🤔 le nom c'est LE FILS DU LION votons pour les soutenir
1er coomentaire cou beugue assane beusseul aime
Ana sa tour😂😂
@@kharyamar7055 Moma diakhal Di😂
Lamzo
@@bayemoussandiaye8699 😂😂😂😂😂da gnou ko fatè toudou
@@kharyamar7055 😂😂😂
Kou âme yaye diou meleni yayi assane lalal jaime
Laissez des coeurs So Cana🤭❤️
♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️
Le papa de petit ma tué 😂😂😂
J'ai vraiment apprécié le geste de jeannot 😇😇😇
Serie bi moy sama serie préfèrée😭
@amt ka slt
Magui niane nga abonné si sama chaîne bi ger yallah
Zeuss il a tellement raison dans les conversations avec le petit frère. #PASSION avant tout👌🏽🚀
❤❤❤❤❤
Kou parè pour niou woutal niome Assane Mayo na wah 😂😂😂
Petit y'a Hague Macht bii
Ak ay dall🤣
Slt Moustapha
Magui niane nga abonné si sama chaîne bi ger yallah
aywaye papay papis rousna de kou ko guis rek beusseul j aime❤❤❤
ayy wayyy wakhléne si série bi mo geune ngéne nék fi nane première commentaire
Yaw nk si lo wkh mome
Meilleure série bilae surtout action domu baye bi ♥️ kou ham domu baye beseul jaime
Yallana gou yalla may gou dougou si kor gui ak diam yalla nagou sounou kor barkép borom touba
Si seulement tout enfant se comporter ainsi comme Petit face aux pensées malsaines des parents irresponsables Kone Sénégal dieum kanam!!!! Suniouy wadiour warnaniou bayii dii bolé sén doomi thi problème dekandoor walah problème famille c un lourd fardeau pour eux .... Merci le producteur cette partie m'a marqué
Toujours les meilleures combien de j'aime pour les trois jeunes talents kou jaim yalla nga donne milliardaire rou Serigne Touba 😍
Souniou équipe warniou setane série le meilleur série du Sénégal louniou doudou la actuellement
Ana wa theme beignet yaye ndack😂😂😂😂
🤣🤣🤣🤣
@@momyseck9379 c'est toi
Kone lolou baayi ngako khél 🤣🤣🤣
Jeanneau (Zeus) tu as très bien assuré ton rôle et ton Profil de la série synchronise automatique avec la réalité.
#Courage_Gaïndé❤️🇸🇳
Mé coach lébbou yi esk dougnou ko diox équipe nationale bi légui gnou dieul Can bi 🤣🤣🤣
Slt Mahomet
Magui niane nga abonné si sama chaîne bi ger yallah
Ndeysan petit papam dinako diakhasé ak Assane rek😌😌
Wakhal deh égoïste la ce pere
vraiment khamoul dara
Allez voter pour supporter Doomi Gaindè🦁 (fils du lion )
Comment voter
La série est mérité des millions
Mais boy bi 😁 bégné yaay ndaak yii rék lamay diokh koi 😂😂😂
Authentique Zeus lafi guisdé j'aime bcp la présence du hip-hop dans ce film. Nice job
ndeyssane mak mo barri yeurmandei si rakam
toukhoul dh wayei rangou na probleme bi pour sauvé rak dji ohhhhh la famille
Bilay sama grande sœur ni la dnne df biniou nekei khalei louma meussa df mouni mom la bilay sama yaye dako danne dore rk t meussoul df dara
Ndeysann passage bobou da dawal sama yaram
Lebou dou ragaal.kou d'accord bayil sa j'aime
Qui aime Oothentik Zeus ???
Merciii Dip et zeuz ça c'est du professinalisme et du business niou yeune rék lagne sou rafété rk on est content 👍👍
Meilleur série de tout les temps
Vraiment impressionné par la façon dont il reflète notre réalité du football 🤧
Je suis très content de cette série
Nonnn lama dafa ame classe nak.
Mane lamarana laaa beugue😂😂😂😂😂
😅😅 billahi
Seytané wakhoul deugu wayé yakh na khél deiggeul petit rk🇸🇳🏌️🙄😬
Bilay oh🙏🙆
@@fansidipdoundouguissmanela1896 guisga dh
@Oulimata Ndoye wallay
Slt
Magui niane nga abonné si sama chaîne bi ger yallah
Khana koor gi dingeun déf chaque semaine 2 épisode ngir Yàlla mou nekk sokarou koor sakh wa baa na 🙈❤️😂
Slt lou ler tv
Magui niane nga abonné si sama chaîne bi ger yallah
Oothentik zeuss 🇸🇳🇸🇳🎧🎧
Ay way 2 semaine par vue diap lene si nguir yalla meilleur série blh
Niarri épisode mosi dess bayil niou sakanal ko rk😂😍
@@diopbenedetto1097 🤙🤣🤣🤣🤣
*bientôt Ramadan inchallah kèpp kou beug dianguè sa dinè gratuit aonnèl inchallahh*
Qui est d’accord que Petit est un vrai Gaïdé🦁
Oothentik Zeus 🔥🔥🤙🤟❤️✅
Meilleur série sénégalaise de tout les temps. ❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Le retour de rokhaya de la série "laye sangara" 😊😊😊😊
Slt Gueye
Magui niane nga abonné si sama chaîne bi ger yallah
Ah j'adore le geste de petit franchement ça m'a fait pleurer
Yallah nagnou yallah defal kooru diam🇸🇳
Amine
🤲
Amine frère
Amine 🤲❤️
Amine
Kou beugeu s fallou mbacké abboné sama chaîne té yalla rek takh🤲
Les scènes marquantes de cette épisode sont l’apparition de Sau Cana, la réconciliation de sassante et Petit et la fin tragique de Dongo Dara
Ma série prefere
Oui c’est ça tu as tout dit
Un simple tournois de foot qui révèle plein d'autre aspect de culture et vie humaine,avec un soutien vous verrez un 2em Ousmane Sembene merci M. A. S.S
Doomi gaïnde c'est le meilleur série 2021
Je valide
Bilahi
Cette épisode est riche en émotions bilahi entre papi et son frère
P'tit et assane
Et le pauvre samba yilei mais il ne doit pas mourir nak sinon ça va joué dans l'esprit des petits
Oothentik Zeuz Comme Boy Cii Série Bii 😂😂😂
Deem leen votél doomi gainde sii sen lien bii neck si commentaire yii🙏🙏ndam rek incha-allah 🥰🥰🥰🥰
Wara wakh thi série bi Di tokk fi Di fenn naan May Premier vue May premier commentaire
😂
Kou beug cheikh ibrahima Niass beusal j'aime
Svpl bouléne sii yiii koi mbeuguél si Baye niass lénéne la ❤❤❤
dina beuss j'aime ndakh limako beug mais
nakk fi dou palace samm svp
kou bougua prophete psl beussal j aime
Doulll
Lou ngeni khar pour tek ko tèlé qui est d'accord pour moi
mongui daw 2stv
Yayou Papi kou bakh la🙏🙏 khoulo khalé koussi dougou yassiy dess
Gayi diapale lénn ma à bonne sama chêne TH-cam guir yalla rek yalla ga goudou fane si barkebe serige touba lo begue yalla nalako yalla defal 🙏🙏
J m'appele ridialdo numéro 10 j suis footballeur. .ms vraiment boyii gueune nanou ma yokouu courage bilahii..serie bii nexneuu tropp mashalaa
Hé petit nekal nitt équipe lagnou mais ken wahoul individualités boul bayi seytané yi yakeu sen groupe bi
Coach lebou yi dou borom lancée bou reuy ba merci petit bigua télé comprendre domou gaïndé thia kaw thia kanam
Thx coach😂
@@saliwjunior4745 😁😁😆
salu copine aida national namenala 🙏👌
Ioe t partout 😂
@@milczo3561 voilà
Well done !
Meilleure série sénégalaise...Bravo
Korou diamou🇸🇳😍
Merci🥰🥰🥰
🥰🥰🥰🥰
amine
Salut
Celle qui est en jaune, Diaw Ka , c'est moi même.
Merci beaucoup Mame Ass Seck pour cette mise en scène.
Hardo Ka vous remercie infiniment aussi
Ndeysan yeup pay tok dillén xar machallah
Kou beugeu serigne fallou beuseul j'aime
le frére de papi est gentil 🙂🙂
C'est Oothentik zeuss rappeur
Kou bègue sa yaye beuseule j'aime
En tout cas c'est bien de nous montrer des artistes de chez nous dans les séries.
Oh Rolou Samba Bi Diamano 2003 Bimay Diangue Daara Diourbel Rek Lama Fatatlil Boyou Ocance Sugn Amé Match Rek Madaw Diangue Dem Football Siniom Waaye Ndeysaan Damadan Jouée Basi Kanam Rek Magui Daaraji Yeksi Nema Kay Wuyu Ma Sedd Guyy Motakh Doomi Gainde Daal Nieup la laal basi dundu talibe bi😭😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍
J'adore cette série
Li moy Sénégal do dém douma dem kénn dou dem nous sommes des imbessile on est d'accord
Meilleure série sénégalaise
C'est le ghetto..ya plein de d'enseignement.. Merci a l'équipe domou gaïndé..
Yalla naniou doug si koor gui ak diame gene sii ak diam si barki seydina mouhamed
Ayway les gars allez voter pour doomi Gaïndei le fils du lion
Number one❤️❤️❤️👌🏿
Slt matar
Magui niane nga abonné si sama chaîne bi ger yallah
Abonnés lén fi ci Touba xassida rék guir yalla ak Serigne Touba ❤️🙏👍
Defal lingay def rk te bayi Xasida yi sof nga trop
@@bayediop2790
Saway sa 💔 Moy dague rék 😂
Xassida yi doun ko bayé 😅😅
Démal dou défal
@@toubakhassidarek8073 demale diobè mo eup change sa ye ngaye def
@@bayediop2790
xana danga Amoul lodéf en😂😂
Kou gueum ni digua yobou sa yaye makka abonnéll si sama chaîne TH-cam bi
Kham abonnés woune
@@bayediop2790 fall nay raffétt wayy ok
@@senchallenge5362 daguina wara liguindi def te comment se série be
@@bayediop2790 yh nnou la sakh
Mei buul fatei abonné way
Kou beugue SAU CANA beuseul j aime
Ootentik Zeus mi d waxoumala nga deglouko d mais bokko xolé rk mou influencé la 😂😂😂😂
Mbadou 😂😂
@@khalildanso3620 defeant la Zeus 😂