Mbacké Sakho limiy wokh fi ba adouna di touki ken dousi wed virgule ndakh wokhoul ay wokhi bopam kouy wédi Indil ay preuve si téré bi yalla wokh naniou si teunkou nakh bayiwousi dara ☝️
M. Diagne, CMS a répondu à toutes vos questions dans sa chaine Nihma TV en basant son argumentaire sur les versets coraniques. Après avoir écouté, si ce n'est déjà fait, pouvez-vous revenir pour nous faire part de vos observations. Merci d'avance.
Dieureufeuti Baye, yalna Yalla dolli farlu ak pasteef ak taxawaay, mashalla amna solo❤ Dila niaan nga xol émission capitaine dieye thia émission IGE télé i tv, mom itam nimuy yakhé pirim Al-khuran ji ta andd ci ak audace eupppppe neu trope franchement
Merci beaucoup père ne vous fatiguer jamais de parler,vos idées nous font beaucoup de bien et nous redonnent confiance que Dieu vous protège et assiste
ALLAH nous dit clairement faites ceci comme ça (par exemple les ablutions comme donné en exemple ici) et nous préférons croire en ce que des gens qui n’ont jamais croisé Le prophète (PSL) lui attribue? Méditons bien.
@@cheikhounatine758 je réponds une fois par courtoisie car je ne me lance pas dans un débat stérile sur la toile: Sourate 5 verset 6. C’est ce qu’ALLAH a détaillé. Libre à d’autre de croire que le Prophète psl a fait autrement et a modifié à sa manière.
Assalaamu alaykum. Innaa lil LAAHI wa Innaa ilayhi raaji uuna. Musiba gënula rëy lii dof yi ci sunu biir di wax ak di jëf. Ëy YÀLLA bu nu tôppê li dof yi ci sunu biir di wax ak di jëf. YÀLLA sàmmal nu sunuy njaboot ak sunuy woroomi xamxam yi ragal sunu Boroom YÀLLA. Nanu YÀLLA wan dëgg bamu leer mu yombalal nu topp ko, mu wan nu neen ba nu ràgnee ko mu yombalal dùmmôoyu ko. Jërëjëfati
Tout homme religieux devrait mener le même combat notre cher Papa Diagne. Hélas la plupart pour des raisons pécuniaire ou en tout cas d'intérêt personnel ne disent rien. Qu' Allah vous protège et vous récompense pour tout ce que vous faites pour la religion.
اصيب شخصان بالجنون الشيخ بك ساق واحمد سيش بعد ما ضربا في المدينتين العزيزتين.انت اعلم مني. لكن بارك الله فيك، تقوم دائما بواجباتك الدينية...من رءي منكم منكر ...الخ.
Senegal si bopam mo bari am ndiakhas! Baye fall fi layene fi... Yi yeup nii lan diouddo di tappale di soss ba ay nitt dioudou si mageë si geum ko te dara dousi dageu
Père ce pays va dans tous les sens. Il est sens dessus sens dessous. L'islam est chahuté de l'intérieur. Pourquoi cela se passe au mois de Ramadan ? That is the question ?
Moi je voulais lui poser la question sur le coran qu il fait reference c est l oeuvre des sahaba rtl qu ils ne croit pas Croire une chose et son contraire
Très difficile d’infirmer les propos de quelqu’un qui se base solennellement sur les textes Coraniques. Donc si je comprends bien selon vous, suivre Le Coran seul est anti-islamique? Père kholatal sey Wakh. Vous répondez à Sakho, mais vous rejettez tout débat avec lui 😊 donc les débats d’idée ne vous intéresse pas vous continuez à insinuer une attaque sur sa personne. Vous avez une audience dont je fais partie donc si vous voulez le contredire, débattez le sans passion.
Mbacké Sakho limiy wokh fi ba adouna di touki ken dousi wed virgule ndakh wokhoul ay wokhi bopam kouy wédi Indil ay preuve si téré bi yalla wokh naniou si teunkou nakh bayiwousi dara ☝️
Toujours contente 😀 de t’écouter papa machalla ❤❤❤❤❤❤❤Dieu merci 🙏 il y’a des gens comme toi papa longue vie à toi santé
May god Bless you papa
MachaAllah amena solo ! Dieureudieuf si ningay layé bir Islam bi askane bi yallah na yallah yagal takhaway bi inchaAllah 🙏🏿
M. Diagne, CMS a répondu à toutes vos questions dans sa chaine Nihma TV en basant son argumentaire sur les versets coraniques.
Après avoir écouté, si ce n'est déjà fait, pouvez-vous revenir pour nous faire part de vos observations.
Merci d'avance.
Dieurefati serigne momar diagne yalla na ja rahman doli fayal ñioula si barké saw paix et Salut sur notre bien ❤❤❤❤
Dieureufeuti Baye, yalna Yalla dolli farlu ak pasteef ak taxawaay, mashalla amna solo❤
Dila niaan nga xol émission capitaine dieye thia émission IGE télé i tv, mom itam nimuy yakhé pirim Al-khuran ji ta andd ci ak audace eupppppe neu trope franchement
Bayil Mback sakho limiy wakh lou la yalla wakhe
Jërejëf jaanne yallna borom bi samu le défal jammu ak yiiw manchalla
sarige bi yalla na yalla def diam ak Salam
Per mann damay déklou Sey video Mai nak boul khasss mbcke Sakho tontouuko rek thi alkhoran rék tébayi ay wakho kénnénn
Merci beaucoup père ne vous fatiguer jamais de parler,vos idées nous font beaucoup de bien et nous redonnent confiance que Dieu vous protège et assiste
👉👍👍👍👍👍👍👍👍👍
JAZAAKALLAH XAYRAN W XAYRAN JAZAA 🤲🤲🤲
Merci beaucoup papa pour éclaircirssement
Machallah tabaarakallaahou amna solo
Machalla papa yanala bour bi faye amale diame
Assalamou hanlaykoum macha allah dieuredieuf serigne bi Diagne.
Dieureudieuf baye ❤️
ALLAH nous dit clairement faites ceci comme ça (par exemple les ablutions comme donné en exemple ici) et nous préférons croire en ce que des gens qui n’ont jamais croisé Le prophète (PSL) lui attribue? Méditons bien.
@@cheikhounatine758 je réponds une fois par courtoisie car je ne me lance pas dans un débat stérile sur la toile:
Sourate 5 verset 6.
C’est ce qu’ALLAH a détaillé. Libre à d’autre de croire que le Prophète psl a fait autrement et a modifié à sa manière.
sourat 5 verset 6
Dieurejef baye momar
Machaallah baye amna solo que dieu vous protège et vous bénisse
Machallah amna solo diagne thièp
Paabi aalou nak😅😅😅😂😂😂.... Mais boulko khass tegal dara si table dji rek.. Moom lepp loumouwakh andina ay preuve donc defal com moom... Mettiwoul
Mbacké ka masoul andi preuve nak fall
Paabi limouy wakh boudoul preuve lane mooy preuve alkhourane lay wakh
@@abdourahmanembaye9399 wakhouma paabi d mbacké lay wakh
@@fall7220 meuss nga déglou Cheikh Mbacké Sakho? Waaji PREUVES rek ley diokhé
MachaAllah ❤ ❤
Mashallah sama Oustaz 🇪🇸🙏🙏🙏
Merci.
Alhamdoulillah!
dieureudieuf Oustaz
🙏🏿🙏🏿🙏🏿🙏🏿
❤❤❤❤
M'a cha allah Diagne, ayyadakal lahou WA nasaraka
Mbàkke Saaxo dafa reew te Senegaal moom boo tudul seeni tariixa rekk seen yoon néku ci😭🙏🏿
Dieur dieufety ya oustaz
Alhamdoulillah Qu'Allah vous accorde longue vie et bonne santé ❤️❤️❤️❤️❤️
Dieureudieuf, Lerna, khana kou bagne deug 🙏🙏🙏🙏
Machalaha
Mbacke sakho bala mouy frri bine ãya si thiobarém wala si guiss guisame na dém diagui wat ousoul...
Babacar Wally ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤😂😂😂😂😂😂
Mbòkk, diiné Islaam moo amul kuko jooyal. Beneen yonnent du amaat ginnaaw Muhammad sAaws moo gëna oyof li waajii di wax. Nanu YÀLLA sàmm. Jërëjëfati
Nous te suivons, vous défendez l'islam en général que DIEU vous guide et vous donne longue vie
Yalna yalla défal la jam Diagne
Assalaamu alaykum. Innaa lil LAAHI wa Innaa ilayhi raaji uuna. Musiba gënula rëy lii dof yi ci sunu biir di wax ak di jëf. Ëy YÀLLA bu nu tôppê li dof yi ci sunu biir di wax ak di jëf. YÀLLA sàmmal nu sunuy njaboot ak sunuy woroomi xamxam yi ragal sunu Boroom YÀLLA. Nanu YÀLLA wan dëgg bamu leer mu yombalal nu topp ko, mu wan nu neen ba nu ràgnee ko mu yombalal dùmmôoyu ko. Jërëjëfati
Ah Sénégal moo amoul koubère rek.
Mane mome je n'ecoute pas certaines personnes.
Yalla na gnou yalla takhawou mousseul gnou si rèr
Wakhatiko yalna mbake Sakho mouma
ماشاء الله حفظك الله ونصرك
ولاكن مباكي ساخو لا بد أن تذكروه بأنه كان يتخذ آيات الله هزوا
Sénégal doyna waar lou nekh waay wakh lou nekh way def té dara doulassi fékeu thiakhane rek dieuredieuf Diagne
Wakhe lene yalna mbake Sakho mouma mouma mouma mouma
wahou gorgui ndal gnorna lolou
Tout homme religieux devrait mener le même combat notre cher Papa Diagne. Hélas la plupart pour des raisons pécuniaire ou en tout cas d'intérêt personnel ne disent rien. Qu' Allah vous protège et vous récompense pour tout ce que vous faites pour la religion.
XANAA DAFA BOOK CI CORANISTE YI ? CCEY!!!🙊🙊
اصيب شخصان بالجنون الشيخ بك ساق واحمد سيش بعد ما ضربا في المدينتين العزيزتين.انت اعلم مني. لكن بارك الله فيك، تقوم دائما بواجباتك الدينية...من رءي منكم منكر ...الخ.
جزاك الله خيرا ان زوجتي لقب والدته ؛جاج.وهي تقول استمع خالي. تطلب منكم الدعاء
انديسان. بلغ تحياتي إلى ابنة أختي، أي زوجتك و قل لها أني معتز بمتابعتها الفيديوهات.
Vraiment ce Mbacké Sakho est un fou on doit avoir un ministère de religions
Ayant wou am ci les lampes ngoumla
Senegal si bopam mo bari am ndiakhas! Baye fall fi layene fi... Yi yeup nii lan diouddo di tappale di soss ba ay nitt dioudou si mageë si geum ko te dara dousi dageu
Mais ce mbacke sakho dans un pays normal on doit l arrêter l emprisonner à vie
Svp qui est Mbacké Sakho?
L’arrêter pourquoi? Parce qu’il rappelle les croyants au Coran?
Aby yamana doul
Diara diaf s momar tekwngo dara
Wa yén kouye mbaké sakho
Boudée sa kham kham sori woule si dîner diaroule nga koy deglou nakh day leunteule pass pass
Mbàkke Saaxo bu ko jiima deglu sax mbokk mi
Lu doywar dafa melne adouna dafay wadia touki 🤔🤔🤔 man khamouma foumou dianghè ak kuko diangal
Père ce pays va dans tous les sens. Il est sens dessus sens dessous. L'islam est chahuté de l'intérieur. Pourquoi cela se passe au mois de Ramadan ? That is the question ?
Leur chef Muhamed goulan a était chassé. C le chef des coraniste
Moi je voulais lui poser la question
sur le coran qu il fait reference c est l oeuvre des sahaba rtl qu ils ne croit pas
Croire une chose et son contraire
Nioune gni kham ay waydiouram dounou diakhal thi wakhi dofame
Très difficile d’infirmer les propos de quelqu’un qui se base solennellement sur les textes Coraniques.
Donc si je comprends bien selon vous, suivre Le Coran seul est anti-islamique? Père kholatal sey Wakh. Vous répondez à Sakho, mais vous rejettez tout débat avec lui 😊 donc les débats d’idée ne vous intéresse pas vous continuez à insinuer une attaque sur sa personne. Vous avez une audience dont je fais partie donc si vous voulez le contredire, débattez le sans passion.
Sa way kon yangui diouli niari rakat 😅😅
Désolé père mais wakho fi dara répond par des arguments tiré du coran
Mbacké sakho lou yalla wakh rék la wakh.
Il faut savoir la diference entre Mohamed ,nabi et rassoul essaye de metriser un peu le coran tu es entrain de lire