WA GOR WAY SONKO DEFAL SERIGNE CHEIKH SALIOU SA KILIFA SO BEUGUÉ AM NDAM SI SÉNÉGAL KI KILIFA LA GOU DEUGOU TEE NANGO LIGUEYE TOLE YI AK DARA YI RK LA XAM
Xana dego liko serigne bi wakh yaw.bamoukoy fekk si tol yi defois si daara dja bobou dara khewoul. Serigne bi def ko ni domame.boula doyoul nak c ton bleme sonko dou guistal bokkoul ak politicien yi ga yagg guiss
بسم الله الرحمن الرحيم والصلاه والسلام على سيدنا محمد وعلى آله وصحبه وسلم تسليما كثيرا أيها الشباب السنغالي هل رأيتم في حياتكم مرة من يجلس أمام الشيوخ الكرام بهذا الإحترام ويطلب رآسة البلاد وهذا يدل على إيمانه بالله وتوكله على رسوله (صلعم) أعلم علم اليقين أن الخديم (رضي الله عنه) لورجعنا في زمننا هذه والله اساعد الرئيس عثمان سنكو نصره الله وأيده لكي يحكم السنغال وفي الختام دعوة واحدة اللهم أنصردينك وأهلك عدوك وعندو المسلمين وإن كان يتلبس بالإسلام اللهم آمين يارب العالمين والسلام عليكم ورحمة الله وبركاته
Yow idrissa seck guay wakh waye kokou dafa trokhale seutou serigne touba sa bir assemblé national ak bir touba mouy khadim bousso inchallah si barke serigne touba dotoufi falou ila yow mi dine barke yonent bi workate nafekh gueweulou kharame bi
Bes na ki tay sonko sop nala ousman sonko yalla nala serignue touba diapale ba nga diot rew mi 🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲
Amine
♥️♥️♥️
Hiii ousmane sonko amga lou jaffei si serigne cheikh saliou yallna nako yalla defal diam bisni tay beug nala sonko
Président Sonkho say kadou rafétena lole machallah.
Sama sarigne sarigne cheikh Sallou mbakc yalla nafi yeugg tawèr amiine sama sarigne sama khòòl ❤ sonko 2024 insallah
Thieuy Serigne Cheikh Ligueye Diammou Yalla rek ...
Yalla nala yalla same diokh la rew mi si barke s.saliou
Man mom bes naki tay sop nala
Amine
Machallah Serigne Cheikh Salilou Mbacké yalla nalla yalla Samou amiine Sonko Diadieuf ❤❤❤❤❤🤲🏽🤲🏽🤲🏽🤲🏽
Amine Mbacké Yalna nga yague fi lole té wéér
Thiéy serigne chiekh mou serigne saliou mbacké sonko 2024 rek incha Allah
Merci beaucoup Sonko
Noo kii mome mouye ñiane bou gawe biii seringe cheikh Ahmadou Mbacke saliou ❤
Sonko future president of Senegal 🇸🇳 2024 inchalla
Serigne cheikh saliou et sonko ❤️
Ma challah amna solo lol ❤❤
Sonko rek rek rek rek rek rek rek rek rek ❤️❤️❤️ inchallah
merci président sonko❤❤❤
J'aime beaucoup soko lou niép beugone nga ame
Yallah nala Yallah diokh reewmi. Sama thiofeel ci ioe (Ousmane Sonko) yokk na bis ni tey
Amiiine
Machallah
Machalla sonko
Bravo Sonko
Merci pape sonko 🙏
Grazie mille serigne Cheikh Mbacke balla
Merci sonko
En tout cas si met à côté certaines considérations d'ordre politiques ousmane Sonko est le meilleur profil pour le Sénégal
Jereudieuf serigne touba ❤
Vive Sonko vive Sénégal
Ndeyesan alhamdouliah Machallah DIEUREUDIEUFETY Mbacke
Mashallah president Sonko ♥️♥️♥️♥️😘😘😘😘
Sonko yangui palais 2024 inchalah ?
Ndeyssane dieurejef mbacke balla yagfi lol té wér mbacke balla sunu xol chéde na lol sonko rék inchalla 2024
Ousmane yalla nako yalla diokh rew mi
Machalla Merci Sonko
Machalah
Ndeysane Borom Baye bou sella bi Serigne Saliou Mbacke. Serigne Cheikh yalla nga fi yag lol té wèr 🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾♥️♥️♥️♥️♥️
Serigne saliou deugg lay guise
Dioumo dei aka deudou aduna
Vive Sonko
Serigne chiekh mbacke liguey ak diamo yalla rék mo ko nior
A sonko mi kat diarrna diapou kat
KOUY DEF DARA, AME DARA.
Ok merci 🙏🤲🏾💚💛❤🙏
Wawaww mbacke geunnn nga dalal khel yii si Ousmane sonko dila gnanal mbacke nga yagg fii lol de and ak werrrr barkep nourou dareyni
Sonko président en 2024 incha alla
Vive le président sonko
Amna solo yalla na yegue te sakh
Sonko président inchalla
Kéne doula lal inchalahou niit kou bakh nga sonko bayi nala ak serigne touba boul ragal dra
yalla nanga fi yag lole té wer mbacké gna nalal Ousmane sonko amenane yakar thi mome
Sonko ci kanam rek BAye fall yi ❤❤❤❤❤❤❤❤
Thiay sonko Rousunioula ragalunla khana Beugla giryalla kilifa gu Bakh amgafa thiere
WA GOR WAY SONKO DEFAL SERIGNE CHEIKH SALIOU SA KILIFA SO BEUGUÉ AM NDAM SI SÉNÉGAL KI KILIFA LA GOU DEUGOU TEE NANGO LIGUEYE TOLE YI AK DARA YI RK LA XAM
Loo beugue diaral serigne touba
Mane serigne la beug mane yalla itame serigne saliou la beug
Sama sagu bi yagalll wéralll mm cheikh Saliou Mb
Serigne cheikh saliou ya bakh sonko d kone mane dipounala dakh serigne bi
MachaAllahou
PROS Yalla na arr la
Machalla thia kaw thia kanam
Amgua lou Reuy Président Sonko "thierou dome"
❤❤❤❤❤❤
Machala 🖑🖐🖑🖐👍👍
Bamba dou morom ✊✊✊
Mon président
Amine ❤❤
Thiéye yalla ni rek lani def boung dielé rew mi ken dou len gusa ti seringe Touba ken mano koo nah kou fi bega falou ta andok seringe Touba dou soti
Dou soti mom
C’est dieu qui donne la pouvoir.!
Xana dego liko serigne bi wakh yaw.bamoukoy fekk si tol yi defois si daara dja bobou dara khewoul. Serigne bi def ko ni domame.boula doyoul nak c ton bleme sonko dou guistal bokkoul ak politicien yi ga yagg guiss
Salaw yené nala rew mi
García sonko
Amiiine
Yalla mannala diarale fimou diarale abdoulay wad si bayam.diappal boudager
Amiiin way
😍😍😍
amine mbacke
ALHAMDU LILAHI RABIL ALAMINE
Dieum dji moma yeme mbacke yague fi werr
tiey Sonko
Akassa diadief sonko
Wa 2024 li ci desss beirina wala 😪
بسم الله الرحمن الرحيم والصلاه والسلام على سيدنا محمد وعلى آله وصحبه وسلم تسليما كثيرا
أيها الشباب السنغالي هل رأيتم في حياتكم مرة من يجلس أمام الشيوخ الكرام بهذا الإحترام ويطلب رآسة البلاد وهذا يدل على إيمانه بالله وتوكله على رسوله (صلعم) أعلم علم اليقين أن الخديم (رضي الله عنه) لورجعنا في زمننا هذه والله اساعد الرئيس عثمان سنكو نصره الله وأيده لكي يحكم السنغال وفي الختام دعوة واحدة اللهم أنصردينك وأهلك عدوك وعندو المسلمين وإن كان يتلبس بالإسلام اللهم آمين يارب العالمين
والسلام عليكم ورحمة الله وبركاته
♥️♥️♥️
🙏🙏🤲🤲
Di béék réék
❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲
Sonko y'a sop no mais DINA bakh
Yarr bi yarr bi
Aka bakh mbacké té mandou
Suñu yakkaar gënna yokko ci Yaw dh pr sonko. Fexeel rk babuulñu woor
🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲✅✅✅✅✅✅✅✅✅✅✅
Xel dalatina
Billay macky boyabo bayi sonko mi balalay diakhal
Amga lo diafé dh mm
Yala bou yakarr tas rk si sonkoo
Gumoule.touse
elzo boul deconé way
Yow khana macky sall sa farou yaye wala sa khole mou bakhoule rek
Sonko fi diébalou mofiye mayé Dara wayé dou lamigne wou nekh serigne mi sakh ndigueule laye deglou damani boula mourite yeppeu voté lone ak tidiane yii akk khadre yii akk layenne yii té kenne khamoula fo bokou tamite dou takh mou soti té nakk diamono dji kenn rekk yalla di wakha mouye Serigne Touba mou wakhac s mountakha rewmi nakk 2024 ahmadou diokhé nako ba paré douye téguine maye wakh kanla wachalam.wahabite amoule palace Sénégal
Yow idrissa seck guay wakh waye kokou dafa trokhale seutou serigne touba sa bir assemblé national ak bir touba mouy khadim bousso inchallah si barke serigne touba dotoufi falou ila yow mi dine barke yonent bi workate nafekh gueweulou kharame bi
Xelu xale
Sonko est un parolier
Day door déh 😂😂😂
Khana yow sa yaye guelou macky sall la wala yakham mbaye
Bayi fenn mo guene li yeup nous tous on n es des mourides mouride dou fene dou soss dou saga dou khamadi
Ioe wero
P.)
Serigne.cheiche.saliou.kene.menoko.nakhe.wala.gua.walako.ligua.begue.politicien.gua.dafa.begua.falou.loulou.mola.fi.indy.waye.dou.gueme.gueme.
en tout cas amna lou diaffé si serigne cheikh yalnako yala diapalé
.
Mesoule.tek.takame.touba.politike.rek.mokofi.indy.gumoule.touse.
YA niak diom
Sonko.es.tres.dangeureux.bilaye.kii
Blablablablablabla
......com ñu massé ñun niep talal Té kounek nianal sa morom,seugn bi melnani oyoff na lolou way