Nous remercions Serigne Touba toujours et non stop parceque: 1 - Il nous a enseigne la philosophie du "SANT REK" qui est la meilleure maniere de vivre sur terre et ceci a ete demontre par tous les grands penseurs de l'humanite et recommende par les 3 religions. 2 - Si le Coran est du 'dougoup' ses enseignements sont du 'thiere' parcequ'il nous a explique ce que etre musulman veut dire de la maniere la plus adaptee a notre culture noire, nous protegeant ainsi de l'imperialist arab degise en Cheikh. 3 - Il a fait de nous des hommes travailleurs, entreprenants, humbles, et genereux. Je pourais de donner une raison de remercier Cheikh Ahmadou Bamba chaque fois que j'expirerais pour le reste de ma vie et il y en aurait toujours beaucoup plus a dire. Mame Bamba sante nenou le fi si America ngir ya niou defar.
Le plus grand daur kat de l’histoire au Sénégal c’est ce monsieur il ne crois rien du tout si limiy wakh fou mou dém wakh fa li lén nékh mais nit yi mom so beugué nioulay tathiou dél wakh li deupok sén ban nékh rek boul sakh bayi khél yala
Ndakh deugou moy fo dém yen rek la fénén lou kou amoul principes mokoy def wakhi Ahmad yokoul Serigne touba wanie wouko Mais nit yi sén guis guis dafa gata botagué sén Serigne niou né yay wadia so wakhé Lou ko khawa wathie niou khas la
Capital religieuse je pourrai dire oui mais jamais politique ou économique. Soyons raisonnable et luttons pour un Senegal meilleur. Touba n'a pas besoin d'être capitale du Sénégal car elle détient déjà une richesse que Dakar en a pas. Ce vieux doit se taire.
Touba mo meusseu nék capital Sénégal. Économie Sénégal Touba moko yor. Modèle économique Touba sougnko appliqué wone kone Sénégal romb bii, sou Serigne Mountakha ladiè ay milliards même pas en 24h lépp teew macha'allah. Mani Serigne Bamba moy deug. Baye karim yagg fi lool té wër 🙏🏾
Lire n'a commentaire yii guiss gniou beuri di contesté Mes Limah lén meuneu xamale mouy Ahmed khalifeu ak kénen gnio si yam! Serigne Touba kén meunou ko Nakh kén meunou ko yaxale aussi Mes diadieuf Ahmed khalifeu Boram Bax ngua.
Khalifaa li mou dèf rafete na colorè la def ni le reste c'est pas à nous de juger nagne rafete ndiorte serigne Abdou karim kou bahla am yermandè yalla na yalla guena contane si mom 🙏🙏
Khalifa Niass ya mouna doul fenn kat bou bonn khana ganaar yii ak kharyinga lekk gno nekk si sa toune bii dila wakhlo kagna la sénégalais yii di yewou si genrou nitt you bonn bo bougue degue deug Casamance dou mousa am indépendance kon bokk touba dou mousa don capital Sénégal bayilen nafek sénégalais yii .
Barkep S.FALLOU ki mo gnack kignane, wayé wathie nga, YALLA na YALLA fayla barkep S.TOUBA yague lolll ak wer fécké ndiarignoul ndiabote gui yeup barkep S.TOUBA
Wa mé ana tawhid Legui dall mbideffou yalla yi gnoye fallaté maname lou yalla moune amna niouko moune Bayilen bougou Lou nekh aye nit baye wakh loudoul deuggeu ak Lou mounoul nekkeu
Bon suniou dieufeh wone diangaleh Serigne bi Sénégal romb n'a fi mais nak pour lolou âme il faut aye borom kham kham you âme khel yoreh deuk bi teh nite gni tamite diangueu
Nous sommes actuellement très loin des enseignements ou les thèses et les anti-thèses étaient présentées et ou les professeurs aidaient les élèves à faire leurs propres synthèses. Il y a un vieux dicton chinois qui dit que: "quand on a plus rien à dire, on cite un vieux dicton chinois"
Ces derniers temps Mouhamed khalifa Niasse se rend très frequemment à touba et le connaissant un peu cela m'intrigue beaucoups Je doute fort que ses propos soient sincères à mon avis il a une idée derière la tête
Diereudieufeuti serigne fallou Ahmed Khalifa doundal way kou yor xol bu set nga machalla diadieuf Baye karim
Ahmed Khalifa yabakh waye yagal tè wèr waye
@@moussadiop4518 sante Baye kharim réck mbacké ndoundal
Serigne Fallou Mbacké Ken Bagnou Ko. Lilou rafet Leu Macha'Allah
Bismillah ana gnidân Wakh né dômu Sokhna dey agnân ???
Niasse ,Mbacke YALLAH nanu fi bokk yagg te weur nun gneupp ak mbôlem jullit yeupp amin...
Merci Ahmed khalifa billahii sokhoroullo Yallah 'nalla sama borom defaL jamm si Barke Cheikhouna Cheikh Ahmadou BAMBA KhadimaL Mustapha kou beuss pousses bleu Yallah nga guisss serigne Touba
Nous remercions Serigne Touba toujours et non stop parceque:
1 - Il nous a enseigne la philosophie du "SANT REK" qui est la meilleure maniere de vivre sur terre et ceci a ete demontre par tous les grands penseurs de l'humanite et recommende par les 3 religions.
2 - Si le Coran est du 'dougoup' ses enseignements sont du 'thiere' parcequ'il nous a explique ce que etre musulman veut dire de la maniere la plus adaptee a notre culture noire, nous protegeant ainsi de l'imperialist arab degise en Cheikh.
3 - Il a fait de nous des hommes travailleurs, entreprenants, humbles, et genereux.
Je pourais de donner une raison de remercier Cheikh Ahmadou Bamba chaque fois que j'expirerais pour le reste de ma vie et il y en aurait toujours beaucoup plus a dire.
Mame Bamba sante nenou le fi si America ngir ya niou defar.
Yalla nanga am ngeureumeul Sergine Touba way
Ahmed khalifa niass sopounala ngir serigne fallou billahi
Sacré ahmed khalifa, il joue tjrs avk la conscience des gens...
Il es fort en show comedy
Il n'est pas méchant en tout cas
Sama serigne Ahmad khalifa niass yalla nafi yag ta wér
Yaa mane Lou rafét
Amine
Ngakk kignagne rekk aka beuri xam xam
Ahmeth, bilahi harrif camill nga. Am nga kham kham ak tour ba paré té yoro daray kigniane ak reuy. Yallah nala yalla mousseul thi say none.
Le plus grand daur kat de l’histoire au Sénégal c’est ce monsieur il ne crois rien du tout si limiy wakh fou mou dém wakh fa li lén nékh mais nit yi mom so beugué nioulay tathiou dél wakh li deupok sén ban nékh rek boul sakh bayi khél yala
Serigne wakh ko si kaw
Yaw khana toudoo khadim ahhh
Mé mouride kouka nakh si serigne Touba nekhna senegal ben diné mofi am mouy lislam li dafa rafet lool yalnane fi yague ta wer lool
FATOU DIADIE DIOP wadji khamoul limouy wakh Ahmet khalifa nitt kou deugoula prck limouy wakh yagg nako wakh ci Serigne touba
Ndakh deugou moy fo dém yen rek la fénén lou kou amoul principes mokoy def wakhi Ahmad yokoul Serigne touba wanie wouko
Mais nit yi sén guis guis dafa gata botagué sén Serigne niou né yay wadia so wakhé Lou ko khawa wathie niou khas la
Ahmed khalifa damala beugue ndakh lingua beugue serigne Touba ak wa keureum
Bilahi Ahmed khalifa beug nalla yalla na sa diam yagg
Un discours juste pour se mettre en valeur
Ko beugue serigne touba niogui lay ñiane nga abonnè si 👉 SUNU ACTU TV
Hahaha 😅😅😅 que des délirants après un les liqueurs
Capital religieuse je pourrai dire oui mais jamais politique ou économique. Soyons raisonnable et luttons pour un Senegal meilleur. Touba n'a pas besoin d'être capitale du Sénégal car elle détient déjà une richesse que Dakar en a pas. Ce vieux doit se taire.
Machallah mouhamed
Ahmed khalifa aka xam serigne bi
Sama khôl sede n’a si yaw dale niass y’a bakh 💙🙏🏻🙏🏻😭
Ahmed Khalifa niass mala Bueg goudal fann niass
Mashallah ❤️❤️
Machalla Ahmed khalifa niass
Kou beuge serigne saliou
Machalla❤❤👍🏿
FEIN rekk ak Doorrrr
Kou amoul yar doo yorr dara Kou amol tégin doo tégui dará té iow mola dall
ay kathiie rek aki tekk khel di deuk di nakh wa touba rek
@@ibrahimadiallo7393 Wallahi Ndeyssane...Ki dou nit kou bakh té famou bokk sakh nawlo wouñiouko.
Touba mo meusseu nék capital Sénégal. Économie Sénégal Touba moko yor. Modèle économique Touba sougnko appliqué wone kone Sénégal romb bii, sou Serigne Mountakha ladiè ay milliards même pas en 24h lépp teew macha'allah. Mani Serigne Bamba moy deug. Baye karim yagg fi lool té wër 🙏🏾
Machallah yalla nako yalla faye yiw amine
Niass Ya bakh yalla nala yalla diapale defal diamou ak wer
Ki kane la Metzo😂😂😂
Ak noir fumé yi vrai chef de bandit la😎😎
Dou bou ndaw sakh
Ki kay bay sak jour ak nimoy mel
Metzo la kaye! khamna aye j'aime laye yalwane 😂😂😂
Machalla niass longue vie a toi
Bilahi souma khol sédena li raféttna té ahmét mi mo niak kiniane té bakh
Serigne Touba kéneu dou mome,ki yalla moko nara dimbali rek
Kou nek dafnann sama serigne dou morom . Mais Ahmed khalifa dafa yakhou dafay guena rerr guemoul dara
senégalaiss yi dono nékha nakh wayé serigne abdou karim khamnani gui li miy wakh négoull si kholbi gui fara macon la
Ahmed khalifa mo meuna nekk Sénégal deh 😂
Machalla rafetna trop koubakh te niakatinia rek mo neune lii na borom kham kham yii bolo guirr talibéyi done béne yalla kene laa
Serigne abdou karim mbacké yalla nafi yague té wérr ak serigne ahmed khalifa niass
Machalla
Bilahi ahmad khalifeu niass kou niakk kignane gua
Yene gnii commentaires,bou lène sone,mome Ahmet kalifi Niass loumou mana wakh,AK loumou Mana déf ,ci môme rek laye délou nakTouba kou niak bopou fananoufa,rawatina domou elhaji fallou mbacke diodiou,baye Karim,khollaiko rek thia téye ga ,AK dalle ak personnalité ga,ki mo doneu Serigne Touba, doneu Serigne fallou, ki dou kougnouye faut aye marteaux,lii bayame fallou awa bousso dane déf rek laye déf ,
talibe serigne fallou mbacke yow waro wahé ni amo eudeup Ahmed khalipha niass dafa bah rek lolu rk la......
Merci
Machala ya niak kiniane
Machalla niass coumba Abdallah ❣❣❣❣❣
Gua yagui mèr dh 😂😂
Papito Diack gni ngui merr dé moma diakhal
PAPA THIAM Senegal mo mèlni dafa bari niou sokhor trop mais bayi lène fofou rek sène xole yi di bakh😂😂
C’est grave o Senegale
Mbacke yague fi lole té andaque werle Ahmeth Khalifa Niass bilay ya koré
Lii kou mou naxari nga de s.touba amoul moroom
Ya begue borome touba billaye yaw rien a dire
Dama giss am gniou nane limiy wakh gemou ko
Wayé ba tay gnioun mourit kogniy nakh diar ko thi serigne touba réck yagniou mome donté kham nagne ko Sakh begeu nagne dieredief sr Ahmet khalifa niass
Djeureudieuf Niass souniou xol sedna lolou yalla ngaffi yague té weer
Gniak kigniane dieureudieuf NIASSE rattakhal nga yonou tarikha yi
Dieureudieuf niass
Ndayesan Thieye S.Fallou Moy borom na ame Mou ame Bou Mou ame dou ame Ken dou mom
Ahmet HK yalnala s Touba fatih say adio
Kone dé aye adiome dou moussa fadiou
Yalena andabi yaga niass
Amine
والله هذا أمر جميل جدا لو يفعله جل منا ا نتهى التعصب فينا .
Muungine soofal waa keur cheikh Amadou tidiane je suis depuis a Paris merci
Lime wakh nekhoula yako setane
Yen Mouride yi layy wakh Ahmed mi bou yabo nguen moytou KO meuna jaxasei Aÿ mbok
Ahmed khalifa naisse
Aye wakhame diaroull dorr sa dommm
Samaway mourid la wayé ray ngama 😀😀
Sunu yone nekussi gnunne ku beug serigne touba nangul ko liko yalla mayy gnune khaméwugnuleu ak sunu bopp
Lire n'a commentaire yii guiss gniou beuri di contesté Mes Limah lén meuneu xamale mouy Ahmed khalifeu ak kénen gnio si yam! Serigne Touba kén meunou ko Nakh kén meunou ko yaxale aussi Mes diadieuf Ahmed khalifeu Boram Bax ngua.
Khalifaa li mou dèf rafete na colorè la def ni le reste c'est pas à nous de juger nagne rafete ndiorte serigne Abdou karim kou bahla am yermandè yalla na yalla guena contane si mom 🙏🙏
Boy outt nafék diapoko diaroul rombo
Liguay wakh nadone deug siyaw ndakh koku khamna lou bary wakhi doff lah dofakoy dégue!!!
NIASS YALNA YÀLLA FÉYALNIOU LA
Door rek waye touba kouy thiakhane serignebi dinala alaque
Yama na fan
Ha DINA ame mome Allah sougnou borom mo ko mome
Dama beug cheikh abdou Karim Backe fière d'être talibe bamba
Macky Sall dafa déssé am pass-pass
Daga bakh rk niasss
Khalifa Niass ya mouna doul fenn kat bou bonn khana ganaar yii ak kharyinga lekk gno nekk si sa toune bii dila wakhlo kagna la sénégalais yii di yewou si genrou nitt you bonn bo bougue degue deug Casamance dou mousa am indépendance kon bokk touba dou mousa don capital Sénégal bayilen nafek sénégalais yii .
Thiay ahmed khalipha
Billahi wallahi liii mak wakhon namako
Loula mak wakhone
@@momoafie3409 wa abonnel si sama chett bi sunu actu tv s.bamba rek mofi nek
@@Tallinfos44 ok
😂😂😂door kat bi deug ngi ni nak
Dieuradieuffe Serigne touba
DEUG nexoul dei bilahi ya bakh Akhmadou bamba dou kéneu
Bismillah ana gnidôn tontu M.Madicke Niang ???
Barkep S.FALLOU ki mo gnack kignane, wayé wathie nga, YALLA na YALLA fayla barkep S.TOUBA yague lolll ak wer fécké ndiarignoul ndiabote gui yeup barkep S.TOUBA
Be legui se wah lairoule lila yeukeuty deug wahoko d door rek
Thiey yalla ki yém nama
Il est dangereux!!!!
Toujours à tenir des propos de division. Il faut bien se méfier des déclarations de ce personnage
Akassa niass billahi dina am yalla nangafi yagg lool té wer niass kenn dou borom touba
Yague yokou wér balla aïcha niass coumba Abdallah
Ki daurkat la moléne Di nakhe rek Sénégal Béné capital rek leu meuna am moy Dakar diehkna
Hamna saint louis messoul nek capitale
Dakar moy capital wayé loo beug démal touba serigne bi moko wakh si matlaboul fawzeyni
Prof Coly akassa mourid ñounde SAKHA dañouko sokhalawoul lan Moy capital doutous se tourlarekh
@@faloutall8699 tôt ou tard touba moy gueun debelopper dakar
Doul rék lay df
Seultanélaďe khalifa niass moytoulene ko yeune mourite yi
yalla rék molaye fay
Ki seytané la
Dimko waxatt ci bammèll
Wa mé ana tawhid
Legui dall mbideffou yalla yi gnoye fallaté maname lou yalla moune amna niouko moune
Bayilen bougou Lou nekh aye nit baye wakh loudoul deuggeu ak Lou mounoul nekkeu
Danga beugeu wedi limou wakh
@@syllaibrahima9667 wawaw 500/100
Toppatool sa Boss reck
Bon suniou dieufeh wone diangaleh Serigne bi Sénégal romb n'a fi mais nak pour lolou âme il faut aye borom kham kham you âme khel yoreh deuk bi teh nite gni tamite diangueu
Dieredieuf niasse
Nous sommes actuellement très loin des enseignements ou les thèses et les anti-thèses étaient présentées et ou les professeurs aidaient les élèves à faire leurs propres synthèses.
Il y a un vieux dicton chinois qui dit que:
"quand on a plus rien à dire,
on cite un vieux dicton chinois"
👂❤️❤️❤️❤️❤️
Dierediefati Niass Amatina sólo dé yaw danga bakh
Gooré koussi djioudou rek moko kham
Man dh kouma nakhe ci serigne touba beugna ahmed khalifa sopou nala loll
Wakhouffi dara hypocrite leu
Tu es un satan
Ngene mandousa
Mandou bakhena si dioulite
Vraiment tu a dit que la veriter
Machallah 🙏🏿🙏🏿👏🏿👏🏿👏🏿
Ces derniers temps Mouhamed khalifa Niasse se rend très frequemment à touba et le connaissant un peu cela m'intrigue beaucoups
Je doute fort que ses propos soient sincères à mon avis il a une idée derière la tête
Gueumoul dara il fau fai tres attation
Tu es un satan
'
Sénégal doyna waar🤔🤔Te jaaxal nama
Ya woute ak srg abdou karim
Santé cheikh moussa cissé ndiamé darou léerou lerr yi rek ba faw
Wawaw fall ndiaga