A part le coran il n'y a que les khassidas qui font vibrer ma peau qui me pousse à méditer qui me rend sii nostalgique qui me pousse à être pieux... c'est un Tidjane qui Parle..... Ahmadou Bamba amoul morom xam xam moy mbind té limou bind thi Lou reuy ak Lou am ndjeurigne kéneuh defouko ...naatou yii done dall.yonenté bii gnoko dall il a lutté sans utiliser les armes il les a vaincu tous par la voie la plus pacifique qui soit .....Serigne Bamba deug deug ya doneuh yonente bii thi Zaïr ak thi battine yaay khawzoul khoutbou yaay djant ndjoloor yaay khadimou Rassoul......❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Je suis tidjane de père et Khadyr de mère.. mais j'adore le mouridisme j'adore cheikhina cheikh Ahmadou Bamba👌🏾❤️🇸🇳il est multidimensionnelle..borom djalooré you yémé yii borom mbind bou beurri bi borom kharbakh
Je suis talibé Baye Niass waye walay Limay yeuk soumay deglou khassida mouride yi sama khole bi daffay fékhe walay barki BAYE Niasse CHEIKH Ahmadou Bamba yallah n'a yallah yokou leram te tasse niou si barkem ❤❤❤
Machallah kèneu d'où Serigne touba djeureudieufèti borome touba ❤❤❤ fière d'être mouride malgré que khamouma loumaouye wakh si khasida bi dh ms nimoumaye df mak yalla rk nio kham khame bly instants sama yarame bi limasi sentir Allah kèneu d'où yaw❤❤❤❤
Machallah j'aime bien serigne Touba et cheikh ibourahima fall Yallna yallah doli diam Sénégal fierté musulmans Sénégal gneup ben lagne c un3 Tidiane qui parle alhamdoulilah ❤j'aime ls mourides❤❤❤
Cheikh bamba amoul morome mais bravo a touts les isbous vous chantez bien les xassidas j'espère que Serigne Touba est fier de lui même et de vous aussi.moi personnel les xassidas me donnent des frissons vraiment.alhamdoulilahi yalla soubouhana watalah de nous avoir donné cheikhoul khadim.et pour en terminer dirurefieufé seydina mouhamed psl c grâce à vous que les xassidas existent et aussi bon a l'oreil ainsi que le coeur.
Serigne yéli seye gendarme ndar nakoy mouride Yi di gnanal si bar ké raditou Modone défendre Serigne Touba 17:00 ba 19:00 di kholok comandante bi sa mayumba Sila Serigne Touba don bind raditou anilmawla
N'oubliez pas de vous abonnes🥰🥰
❤❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤
❤❤❤❤
❤🎉❤❤
A part le coran il n'y a que les khassidas qui font vibrer ma peau qui me pousse à méditer qui me rend sii nostalgique qui me pousse à être pieux... c'est un Tidjane qui Parle..... Ahmadou Bamba amoul morom xam xam moy mbind té limou bind thi Lou reuy ak Lou am ndjeurigne kéneuh defouko ...naatou yii done dall.yonenté bii gnoko dall il a lutté sans utiliser les armes il les a vaincu tous par la voie la plus pacifique qui soit .....Serigne Bamba deug deug ya doneuh yonente bii thi Zaïr ak thi battine yaay khawzoul khoutbou yaay djant ndjoloor yaay khadimou Rassoul......❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
ndaysan
Ya bakh
ndye sane lep lu yalla defal serigne bi sukay seddok niognam yalla boula si kene eupale
@babafaye7226 Amiin
@badoundiaye5771 Dieredieuf 😢
Mn pere est ma mère son des tijan es moi suit mourite es très fier de l être jeureujeuf serign touba
Je suis très contente de cette khadissa qui me fais pleurer sur les kourel macha alla 😢😥😥💌😢😢😥❤️❤️❤️❤️🙏🙏🙏🙏🙏🇸🇳🇸🇳🇸🇳🌹🌷🌷🌷🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🙏🙏🙏🙏🙏
Je suis tidjane de père et Khadyr de mère.. mais j'adore le mouridisme j'adore cheikhina cheikh Ahmadou Bamba👌🏾❤️🇸🇳il est multidimensionnelle..borom djalooré you yémé yii borom mbind bou beurri bi borom kharbakh
Machallh jërëjëf yal na yàlla fayla
ndeysann iow dh ya dh niakk ignane th baax
yalna ngua ame gueureumeul yalla
Bilahi nekhna
Naysane
Vraiment ce Xassida me fait pleurer quand je l'écoute bilahi. Jërëjëf Cheikhoul Khadim
❤
Moi aussi 😭
Khassida bi mogui firdèl nè Serigne Touba kèn la amoul mass
Dieuredieufè kou tèdd ki😭😭😭
Merci bcp Démb ba legui ma diko weur Dieuredieufty Serigne Touba
Je suis talibé Baye Niass waye walay Limay yeuk soumay deglou khassida mouride yi sama khole bi daffay fékhe walay barki BAYE Niasse
CHEIKH Ahmadou Bamba yallah n'a yallah yokou leram te tasse niou si barkem ❤❤❤
Amiin jërëjëf
Thiey nioun dh kay xana amouniou louniou diox Serigne bi ah man dh diebal nko sm bopp fii ak founiou dieum walahii
Segn Bangui fii dh bou ken foknii nekoufii
Durus SII xassidam yii rk dikoko diox adiya sasouné kyy❤️❤️❤️❤️❤️❤️😭😭😭😭
Setalma lii rkk walay kou tedd ki amoul morom🤗😍
Bilahiii amoul morom dhh❤❤aka yémé
Mime rew Bamba ko mome rewmi Bamba moy kiko mome kène du Cheikhoul khadim Yalna borom bi same léne Mashallah goude fane ak wer inshallah ❤❤❤❤❤❤❤
Diereudieuf yalla bingama defa AB mouride talibe Serigne touba
Je ne peux m’empêcher de de pleurer 😭😭j’ai la chair de poule 🥰
Depuis la première foie que je l'ai entendue j'en passe tjrs ❤️❤️❤️❤️je vous aimes
Vs êtes Les meilleurs j'aime vraiment merci beaucoup
Soumay dégue Lou khassida bi sama yaram bi day daw bilahi ❤❤
Machalah diereudiefety Serigne Touba yalla na yalla weral bat yi
J'adore ce khassida dafa nekh si khôl yalna len borom bi fay machallah
Sante s Touba 😭😭 yalla nama yalla may djeureurou mouridé si barque s Touba 😭😭 AK yerou wook gui😭😭😭😭🤲
Ndeysannn
Akassa Amine inshAllah sa borom dinako deff dh
@@thuglife-kf8sh merci ❤️🧕
Inchallah mom ngay am Serigne Touba amoul morom
Santé.. touba...rék❤❤❤🎉
Serigne bi mo meune bideu wala yèna meuna diague walahi lii nekhna si xole ❤
Lepou seringe bi rek
Bindeu bi ak diangu bi leppou Serigne bilah
Thiéy Cheikhna Cheikhoul Khadim MBACKE kéne dou yaw si diamono walahi vous nous avez sauvez
❤❤❤❤❤amine
Fière d'être talibe cheikh mais li souma rayoul li nékhna déh Allah akbar serigne touba meun na bindeu machalla ❤❤❤❤❤❤oh 😍🥺 dina déh si li
Machallah kèneu d'où Serigne touba djeureudieufèti borome touba ❤❤❤ fière d'être mouride malgré que khamouma loumaouye wakh si khasida bi dh ms nimoumaye df mak yalla rk nio kham khame bly instants sama yarame bi limasi sentir Allah kèneu d'où yaw❤❤❤❤
Barké Serigne Touba xasida bi da nekh lol yalla na diam yagu
C est un grand plaisir de vous écouter.vous avez un mérite un très grand mérite de part la façon dont vous chantez
❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉❤ 2:31 @@fatkinedieng4700
Maye TALIBE CHEIKH BI BEGUE
Serigne Tomba cheikh Amadou Bamba Mbacké Rassoul SI SAMA KHOLE AK KANE MO BEGUE SERIGNE TOUBA MBACKE WAY❤❤❤
Mashallah yallah nalla sounnou boroome beugueul bopam ci barké cheikh ahmadou bamba ndamal terral mmouthialla ci barké kou teddki
Ndeyesane
Serigne Touba amoul morome Machahallah ❤❤❤mbecté mi ba aldiana inchahallah
❤❤❤❤❤
Macha allahou dieureu dieufetyserigne touba Amoule morome
Machallah ahmadou bamba amoul morom le meilleur écrivain de tout les temps serigne mountakha mbacké yagu fi lole té weure mbacké ❤❤❤
Euskeuy machalla yallna yalla may ma brome kuerou hisbou billahi hisbou yi damalen bueg barké xassidayi dadj bi nékh n'a trop machalla
❤❤❤❤❤❤❤💍💍💍
Macha allahou yalna yalla barckel lepp bidja taha
Cheikhouna cheikhoul khadim yalla naniou ko yalla fayal si barcke alkhourane ❤❤❤❤❤
Que du plaisir merci infiniment à vous qu'Allah protège
Dieureudieuff Cheikh Ahmadou Bamba diarama Mame Cheikh Ibrahima Fall ♥️♥️🙏🙏🙏
Rafètna
Machallah j'aime bien serigne Touba et cheikh ibourahima fall Yallna yallah doli diam Sénégal fierté musulmans Sénégal gneup ben lagne c un3 Tidiane qui parle alhamdoulilah ❤j'aime ls mourides❤❤❤
Ndéysane thiéy kou téd ki lih leep moma wayé yéne tamit yénay diambari Serigne bamba yi ❤️❤️❤️❤️❤️
Bilakhi
Thiey Serigne Touba khadim Rassoul amol morom am morom moy sa brome yalla s'en diamou yague si barké xassidayi 🙏
Thiey Serigne Touba amoul morom kou kay diéma topando dagay sonou 😤😤😤😤😤😤😤😤😤❤️❤️❤️❤️❤️
Dieurdieuff Serigne Touba amoul morom yalla nale Serigne Touba fay
Amiin ❤
I'm so excited while i'm listenning to this xassida thanks a lot CAB
Thank you❤
Sante Serigne Touba fep fugne mena nék♥️♥️♥️♥️♥️
Thiey s touba li noum may def ohh😭
Sama thioféle si serigne touba 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
Allahou Akbar 😭 Dieuredieuf Serigne Touba Dieuredieufeté cheikhoul khadim 😭😭❤️
Fwyify@@taiboutoure
Khene d’où cheikhoul khadim 😭😭☝️🙏🫶🏻❤️❤️
Alkhamdoulilahi rabil alamine dieuredieufé CHEIKHOUNA AKHMADOU MHADIM
Machallah❤️🥰Diereudieuf Serigne Touba🤲🏿❤️🙌🏿
Dieureudieuf Serigne touba 🥰❤
Machallah yalla na souniou borom weral baat yi ❤
Lii mongui yeungeull rew mii machalla 😍
Machallah machallah dieurédieuf SERIGNE TOUBA
Machallah yalla n'a diam yang ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Dieuredieuf Ahmadou Bamba Macha Allah Santati ❤❤❤❤
Serigne Touba amoul morom 🥰❤️🥰❤️🥰
Ndeye sane ❤️❤️😭😭😭 mshahalla yalna borom bi salam ts yook sainouk weer 🙏🙏
Alhamdoulilah Sant Serigne Touba Diarama Mame cheikh Ibrahima Fall
Cheikh bamba amoul morome mais bravo a touts les isbous vous chantez bien les xassidas j'espère que Serigne Touba est fier de lui même et de vous aussi.moi personnel les xassidas me donnent des frissons vraiment.alhamdoulilahi yalla soubouhana watalah de nous avoir donné cheikhoul khadim.et pour en terminer dirurefieufé seydina mouhamed psl c grâce à vous que les xassidas existent et aussi bon a l'oreil ainsi que le coeur.
Quelle mélodie ❤️❤️❤️❤️
Cheikh AHMADOU BAMBA is unrivalled 🙏🏾🙏🏾
Alhamdoulilah khadimou Rassoul (Saw) Yakari diam gni
Machalla sa kow sa kanam inchallah yalla na souniou borom wéral batte yii❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Thiay xassida yi mo nekh billahi
Machalla segne bi rék ak xasida yi 🤧❤❤❤❤❤
J'avoue qu'à 10:22-10:26 j'ai eu le souffle coupé 😭. Entre jeulatou Ass ji ak thieye Segne Touba bi😭♥️.
Ohh 😢
Bilhay xassida bii raynama nimoumay def yalla rk moko xame ❤️thiey Borom touba guéna xamoul lodone
Thiieuy Cheikhoul khadim😭❤️👌🏾
Allkhadoulila bi yalal défé ma beugeu Serigne Touba néihna xassida yi damay doundeul bilakhi ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Li mo dakh si adouna wakhnako ba père😭😭😭
Wallahi ❤
Blh toma
Té dousi wagni dra kay barki cheixoul khadim
الله أكبر الله أكبر الله أكبر الله أكبر الله أكبر الله أكبر ماشاء الله 🙏💞
Kéne dou chiekhe khamadou bamba❤️❤️❤️
Machallah nekhna lol si khol ❤🤲
Serigne yéli seye gendarme ndar nakoy mouride Yi di gnanal si bar ké raditou Modone défendre Serigne Touba 17:00 ba 19:00 di kholok comandante bi sa mayumba Sila Serigne Touba don bind raditou anilmawla
Oh li nekhna trop waye yalna Bate yi were inchallah
Barki Serigne Touba li dafa nékh walahi 👌😍😍❤️
Dieureudieuf S Touba 😭💔😭😭❤️🙏
Khadimou Rassoulahi (saw) yakari diam gni❤❤❤🎶🎵
Ses poèmes sont chanté au paradis par les houris aux beaux yeux dieureudieuf Serigne Touba
❤❤ Macha Allah sama khol Tour na naniou den geustou Li xassidai di wakh daye yok SA foi
Settalma genrou khetou diangue yi RK ceyyy yallah
❤❤
Sante serigne touba ❤❤❤❤❤❤
Machalla si Xasidayi rék 😍♥️♥️
Mane tidiane la mei li dafma dioy lo Diame si bépp talibé serigne touba
Bilahi sons bi dafa nékh kéne dou cheikhe ahmadou Bamba Bamba Merci 😢
Je suis Tidiane ms kou degue li Ahmadou Di wakh 😭
amoul morom dh
Machaallah yalla na melni ndi
Yalla na Allah Yokk Lérouk Cheikhoul Khadim té khirtal niou si mom
Diara ma hizbout yalla na na len serigne bi faye guén gui faye
J s8 mouridz alxamdou mashalla ❤
Dieuredieufé Serigne Touba khadimoul rasoul
Machallah kou tédeu ki
Mbëcté kasséé ❤❤
Sante Sergine touba ❤😍🥰😘😍🥰❤️❤️❤️
Yalla naleine Yalla fay ndiabotou xassida yi Li neikhna 😭😭😭❤️🤲🏽
Amiin barké Sëriñ Touba
Hamdoulilah sante yalla mignu bolé ak serigne bi Hamdoulilah ❤❤❤❤
Sama golle sede na ❤
Machalla ♥️♥️♥️
Je suis mouride blh serigne salioune dou morom❤❤❤❤❤
Serigne touba est unique !! Seule les hasida de cheikhoul hadim peut vibré mon cœur !! Seule serigne touba qui peut me faire pleurer dans ma vie !!
Bilaye damakoye déguelou sama yarame bi dawe li nékhena trop wayy
Ndeysan thieuy yalla ✍🏿♥️❤️❤️😍
MachaAllah kholyagui séde guouy
They khasi deyi❤❤