Que cette nouvelle année soit une année de consécration de santé de longévité pour tous le monde entier et surtout pour nous les spectateurs de BETE....
Thiotou Ndayam Yakamti Na Jeudi Nieuw Beu Dieynaba Niouseul ma Amina Billahi Et puis Makhou Mou Ndaw Nagne Teugeul Si Kasso Bi Mashalla bonne et heureuse année, att mi Yallah Na nek Souniou richesse Natangué Weur ak weulé ❤🎉
Bonne et heureuse année à tous yalla att mi donne attoum diame attoum banekh attoum natangué yalla défal gneup diame inchaallah gnou téwéko ay att you beuré beuri inchaallah 🙏
Mes meilleures vœux evenprod vraiment yenagui begueul khol yi bilahi wa team bete bete ziar nalene annee de sante prospérité et pleines de bonnes choses yalla na diam yague
Amina à dis que la maison t'es plus légitime espèce de gnegnio de merde et djenaba à dis si tu me redis sa je te casse la gueule quand ta mère étais en vie je t'ai bien boté jusqu'à monter sur toi alors la quel est enterrer sous des pierre je vais pas hésiter
Elle a dit si tu me redis ''putin de teug'' je te casse la gueule jusqu'à.. comme la dernière fois . Je l'ai deja fait alors que ta mere etait vivante, a plus forte raison maintenant que son cadavre est à 6 pied ss terre etc etc 😂
Amina l'a traité de sale "caste" Dieynaba a promis à Amina de lui casser la geule si elle revient sur ses propos. Elle a dit à Amina qu'elle ne s'est pas gênée de lui casser la gueule devant Marieme SALL sa maman quand elle était en vie et qu'elle ne se génera pas de le refaire aujourd'hui que Marieme SALL est morte enterrée et ses os ramollis😅

Merci deiynaba amina dafa réw niak sa yay nga wara dèlo sa khèl si yalla diko nianal dèfoko ngay khass tè rèk bayiwo kènn makhou yaw aussi dinga règlè c est bien ça
La sensibilisation de Père Ndiouga Thiam envers Mayel sur la propreté est juste magnifique ❤🎉
C'est pas Ndiouga c'est Ndiaga Thiam
@mbayart7104 👍
Maël Thiam mon artiste 😂😂❤
Merci dieynaba gnousal ma amina mou réglé😂😂😂
elle a dit quoi ?
Namako gnoussal 😂😂😂😂😂😂 lounexxx!! ma dem EvenProd décorée Dieynaba Tall ❤😂🎉!
Souba moy Sama birthday 🎂 🥳 ❤ nama gneup gnanal wer akh diam lici dess makoy liguey 2024 yeup damako febarone 😢 mais Hamdulilah Alaa Kuli Haal 🙏🏽
Amina aka khamadi😢
@@belarlishimw4911elle a dit "je t'avais bien frappé avant la mort de ta mére et si tu me redis ça je vais encore plus te tabasser"
Xawma da âme dépression xawma Waya Dina yéme
Des coeurs pour notre Prophète Muhammad PSL ❤
PAIX ET SALUT D'ALLAH SUR NOTRE PROPHÈTE SEYIDINA MUHAMMAD BIEN AIMÉ 🥰🥰🥰
SUBKHANALLAH 🥰🥰🥰 WALKHAMDOULILAH 🥰🥰🥰 WALAILAHAILALLAH 🥰🥰🥰 WALLAHOU AKBAR 🥰🥰🥰
MACHALLAH 🥰🥰🥰
ALLAHOU AKBAR 🥰🥰🥰
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Envenprod mo ndieuka dougal bande annonce si 2025 bi❤li histoire dinako bind 😂 bonne et heureuse année way mes amours 🎉🎉🎉🎉
❤❤❤
Machallah
Bilae machallah
Merci bb à aussi 😂
Yaw niom bokou gni nio meune et eup doole
Enfin la Dieynaba Tall qu'on connaissait. Teudiou bi doyna. Guéneul niouss gni 😂
🤣😂 Namone negn loxom !
@RARA-ek3yp teudiou di dioy rk. Dioyna ba kanam bi newi
@@RARA-ek3yp😂😂😂😂
😂😂😂😂😂😂😂😂
😂😂😂😂
Dieynaba deh soula wakhé damalay Niouss nga warr ko gueum Amina donc yamal 😂
😂😂😂
😂😂 wawawww, avec Dieynaba gifle reglè rekk 👋🏼
😂😂😂
😂😂❤❤😂😂😂😂😂❤❤❤❤❤
Wawaw tei ndayam bukay sotal nekufi ndaw niouss you nekh tei yagg😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Que cette nouvelle année soit une année de consécration de santé de longévité pour tous le monde entier et surtout pour nous les spectateurs de BETE....
Allahouma amine
@aminatathiam5766 Amine.
ngir Yallah Dieynaba c'est une demande nationale: nokkal niou Amina
🤣🤣🤣
@fatimataly5680 Yeine nak beugo leine diam. 😂
Ndeysan mame Ndiaga dafa beug ndiabot❤❤😢😢😢
❤❤❤❤❤❤
😢😢😢
@mormbaye2989 😂
Tay mom Wa touba nio ganie ❤ kou dakour rak lalal j’ aime ❤😊
Wa Ndakaaru fête bi molen takh bidëntti
Iow togal fofu ba baye fall yi fékk la fiii
Wawaww yenay wa ozann
@@nabousamb1413 Degueuntaan nioko fa am
@@doubanjaay1490 Baayfall yi dugnu def dara ku defoul dara amugnu siyaw soxla
Bonne et heureuse année diam ak soutoura pour tt le monde
Amine Ya Rabbi ❤
Merci ma belle à toi aussi 😍
@oumoundiaye8224 👍
Ma beug dieynaba waay 😂😂❤❤
@SeynabouNIANG-n9g 👍
Amina nak légui mou wérr😂😂 Dieynaba Tall rekk ,doorou kou tékheutt nguay am fofou
😂😂😂lou lerr kay
Wakhatiko dé djenaba dafay door ba paré khel mi sogu nieuw
@@nenetambaa88 voilà nak🤣😅
😂😂😂😂😂😂
@BambaFall-u6m Yeine nak beugo leine diam. 😂
Amina Dienaba dou diouma dehh mom daley niouss 😂😂😂😂dou daga rewww rekk
@AminakatrineSambou Loxo bi dh mome gawna.
Dieynaba je t’aime way faut remette ces deux ingrats à leur place ❤❤❤
Welcome backs Jenaba Tall
@kyasy6332 👍
Très bien la tention avec la plainte de makhou na saf saf na yeungou tention bii et merci de nous avoir remmener Maël thiam
Yalla nagn ko teuj aussi niaww
@djibyjosephbore3609Merci, c'est toujours un plaisir de vous satisfaire.
Mael Thiam moy kanati ?
@@fatoudiop4332copain lok bombe djigeu man 🤣🤣🤣🤣
@@deuyzadeuyza865 Aah oki, wakh ngua deuggeu. J'avais oublié son vrai nom à cause de son surnom là 😅😅😂😂
Thiotou Ndayam Yakamti Na Jeudi Nieuw Beu Dieynaba Niouseul ma Amina Billahi Et puis Makhou Mou Ndaw Nagne Teugeul Si Kasso Bi Mashalla bonne et heureuse année, att mi Yallah Na nek Souniou richesse Natangué Weur ak weulé ❤🎉
Très bien dieynaba c’est bien 😂😂😂
😂😂😂😂😂😂
C'est très bien
Très bien😀
😂😂😂
C’est bien c’est très bien soda Maréme 😂😂😂😂😂sors de ma tête 😭
Dieynaba dou bayi len ak Yallah mom kouko yabb mou nok la 😂😂ba tok sa kaw
Bonne et heureuse année even à tous yalna donn atoum kheweul sawan bawann Inchallah 🙏🏾🤲
Allahou ma amine ya Allah ❤❤❤❤❤❤❤❤ pareille pour vous
@mbayangdiagne1904 Amine. 👍
Fatim thiam komou soof lalale j'aime
Mom la beugeu bagne ci serie bii modeii na trop
Dèt way 😂😂😂 mome dé ay bombes la yoor foumou wathié bèn rek guerre bi diekh
Matoul 9😂😂😂
Dieynaba Tall c'est bien 😂 c'est très bien way😂
Wah Ndiawar yow la?
Day niaf mag douko yab khale douko yab man mom la beugue jiguen foula
Ndiawar Diagne numéro 2😂😂😂😂
Ces tres bien 😂😂😂
Hello elle a dit quoi à Amina stp ?
Lii nexna trop 🎉 yallana niou yalla may goudou fane weur AK weur léh
Amine yarabi 🤲🤲🤲🤲
@Sidybabacoulibaly Amine.
Diayenaba tall merci beaucoup contan na si iow ❤❤❤❤
Ay kou contane si Dieynaba nok Makhou si prison bi tek si nok Amina 😂🎉
D'accord mais lolou niaw na 😂😂😅😢😢
Ay princesse 😂😂beuguel diam
Makhou ak Amina..... wa bakhna continuez seulement
Bété Bété la série qui n'a jamais perdu sa valeur ❤😂🎉
❤❤❤
@BayemodougueyeBayemodougueye 👍
Bete bete sans mareme sall mo dakh qui est d'accord avec moi❤
Do bari j'aime déé 😂😂😂
Dakheu c'est relatif mais téré wou ko neekh en tout cas. La série est très captivante ma sha'Allah ❤
Moi ❤
@@fatoucha9217deugu la wax di
Dieynaba tall fok ma yob la ozan dieundeul la ay crème glace yeufou xalé yalla n'a sa diam yagu nokk rk wawaw😂😂😂
@omardioo206 😂
Akh mane tamite 😅😅😅
Très bien Dieynaba lak nga sama nguereum ❤ Amina mom dina niou ko changel tour
Iow sa commentaire bi la😂😂😂 beu soneu Dieynaba lak na sa Nguéreum Ya deug dathié Diangal ma Wolof😂😂
@ Amina mi lo sik te tegi ndawal 😤
@ndeyasow8050 billahi dafa sik trop beuri blém😅🤣😂 Mais Nagne ko Teugeul bien bon
Qu’est-ce que Djeynaba a dit à Amina ?
@siti-fatimaahmed1866 lou beug wakh tu répète je comprends pas guani Dieynaba loumou wakh amina
Waw Djeynaba, Amina ak frérom bi dégno eupeul way, mane j'arrive même op à avoir pitié d'eux sof guéne torop té yaradékou
@AissatouTHIAW-h7b Baadou diotna Amina mou yarou ?
Dieynaba Tall 😂dama la beugue 😂😅
Khamone naa yaay ki régler Amina
Yalla nako nokkate bamou doule kon dina yarou
Dafa moudiée soof😂
@ Bilay 😂
@MomoSeck-ie3ch Baadou diotna Amina mou yarou ? 😂
@ Bilay yeen 😂😂😂
Kou d'accord ni rakkou mareme sall bi da nop Alkaly 😂
😂😂😂❤
Aussi mére bi mokoy pousse en secret pour mou tok si plassou maguedji
Of course lol 😂😂😂😂😂
Xhalise bi rek la beug
Une âme charitable pour traduire la bande annonce svp 🥹? Et j'en profite excellente année à tous surtout la santé !
Atoum diam ak salam kén bagna manki si doley seuydina mouhamad ❤❤gnép doundou ba téral say wajour yalla mana léo ❤
Amine Amine 🙏
Bété Bété mo dakh si série Bonne année ❤❤❤
Billay ioe 🎉❤💯🥰🥰
@KharMbengue-k9g Merci. ❤
@@evenprod cv
Mercredi tay bi yalla boumou nék souniou mercredi di bou mothiou🙌🙏
Tous avec dieynaba 🤣🤣🤣🤣 vas-y le peuple est avec toi
@none9998 👍
Yallah nagne terminé année bi si jammou ❤❤❤
Amina nak yeureumon nagnla mais legui danga eupeul
@maremesall3102 Baadou diotna Amina mou yarou ? 😂
@evenprod bou yarouwoul dou bakh ci mome dé
Merci beaucoup Dieynaba Tall niousseul Makhou si prison bi nokheu Amina beu mou poupe
Bravo djeneba c'est bien de remettre amina à sa place
Amina ak makhou rew guigni neikké moma diakhall battay nii
@SeynabouSane-w6j Ah doyna ware.
Lii nèko si kholl yi tè Manou gnouko wax yalla n'a yalla safara lèpou 😢❤❤🎉
Ma beug djiguene bou mélni DieynabavTallleuh❤❤❤
Dienaba niouseul niou Amina daffa rew té sof
@cirekare4006 Baadou diotna Amina mou yarou ?
Bravo Sanekh,SÉNÉGAL propre la sensibilité ça doit commencer dans les familles entre parents ❤
Merci Dieynaba kou dé bayifi projets bo mbébétonne.
ALLHADOULILAH tayla sama anniversaire 1 an de plus 🎂❤🎉 Bonne et heureuse année 2025 🎉
Enfin retour de la dieynaba niouss catt des filles mal polie
@laminethiam2937 Beugo leine diam. 😂
On dirait k sama souffrance ci série bi diexna 😂😂😂c’est bien Dieynaba tall c’est très bien 👍 🎉
Daba Thiam nak bi Yon bou khol bi take rakou Mariam Sall bi kon nga hamni beugoula dalay nakh❤❤❤❤
mani boudoul lolou sakh daba mo wara bayi alkaly
@@SodaGueye-e3v data bou douguè si Alkaly gnu khamna tekki woul dara. Ak ki lim leen yakeu lepem ko khamni bo merei wakh Lou bone mom neu dem rek.
Merci dieynaba gnousko legui dafa rew😂😂
Kou d'accord ni fatma Thiam nieméwoule sanekh lalale j'aime 😂😂😂
Amina Ak makhou sen rewade bi lanla kou d'accord laal j'aime 👌
@DJtaphaNeymarjrSow 👍
Non maximum de Respect pour even production il respecte les sénégalais 🎉🎉🎉🎉😊😊😊
Makhou amana louka doyye Amina mon si désse
Bonne et heureuse année à tous yalla att mi donne attoum diame attoum banekh attoum natangué yalla défal gneup diame inchaallah gnou téwéko ay att you beuré beuri inchaallah 🙏
Wa bété bété ninguéne oubé année bi saff nama❤❤❤
Très bien c’est bien dieynaba Amina kouko niouss mou Dieul
Merci beaucoup dieynaba tall réglé ko dafa réw trop
Dieynaba de retour très bien c'est bien nokal amina niouss makhou si kasso bi
Père Ndiouga merci Dieynaba contane thie yow Amina sa tante bi ga wara lidianti
Kou contane si Dieynaba Tall rek lalal j'aime
La meilleure série du moment au Sénégal 🇸🇳 ❤
Dieynaba Tall mon coup de cœur depuis la saison 1❤❤❤❤❤❤❤
Merci Dieynaba amina mo nioussa rew😂😂
Digueneter makhou ak dieynaba niawna baparer 😢et la parole c'est de l'eau une fois versé on pourra plus le ramasser 😢
Niaw c’est bien dieynaba c’est bien c’est très bien c’est très bien 😂😂😂😂😂😂😂
Suis vraiment vraiment vraiment ☺️fier de dieynaba❤❤❤❤❤❤❤
Mes meilleures vœux evenprod vraiment yenagui begueul khol yi bilahi wa team bete bete ziar nalene annee de sante prospérité et pleines de bonnes choses yalla na diam yague
C'est bien dieynaba c'est très bien ❤😂😊
Bonne et heureuse année 2025 yalla na nèkh té am diam ba dakh lém si barki psl ❤
Contane na si Dieynaba c’est très bien 😂
Allez dieynaba tall❤ niousseul niou amina wayy
Bonne et heureuse année à tous ❤❤🎉🎉
Dieynaba Tall c’est bien c’est très bien 🎉nila djiguéne daye ame foula
Bonne et heureuse annèe🎉🎉🎉
Dieynaba Tall ak Mame bou goor gnoo ame répondant pour rotodo yi… Niaffff❤❤❤
Kou diépi Amina rek lalal ❤
Mes meilleurs vœux à toutes les commentateurs
Makhou mou ndaw kouko yéné pélént bi kom man rk😂😂😂
Un grand brouhaha pour Dieynaba ❤❤❤❤❤
Team Paco ak Chacha❤❤❤
Merci Djenaba le peuple est content🎉
Ooohh c bien c très bien ,Dieynaba de retour kou wkh mou tokk sa kaw😂😂❤
Amina moytoul Dieynaba wla danga faté ni day nioussé😂😂
Dieynaba tall way gnafal ndeyam rek Amina daffa rew 😂😂😂😂😂😂
Dieynaba rck mo bakh si Amina nako niouss dafa réw😂
Merci Amy Mbaye nite dagay tey
Athia Dieynaba💪🏻💪🏻💪🏻gni danio rew
Bonne et heureuse année😀🎉🎉 2025
Evenprod dolén sauté jours machallah nawone fawone
Billahi douniou saute jour dembeu si mardi bi dama khar Ladydiama beu Soneu billahi balégui ni sétanou mako ohh😢 mais bété bété kendou Niom ❤
Amina elle fait comme si yamam kou bakh la wonn. C'est ça qui me tue
Amina Key faw am kouko niaf plassam
Dieynaba diadieuff niousseul Amina ndakh mou yarou
Ramata dafa nop alkaly béttouma😂😂😂❤❤
Merci Ndiaga Thiam une leçon pour les familles il doit y avoir de la solidarité ❤❤❤❤❤
Bonjour,
Est ce que quelqu'un pourrait nous traduire ce que Djeneba dit à Amina s'il vous plaît.
Merci 😊
Amina à dis que la maison t'es plus légitime espèce de gnegnio de merde et djenaba à dis si tu me redis sa je te casse la gueule quand ta mère étais en vie je t'ai bien boté jusqu'à monter sur toi alors la quel est enterrer sous des pierre je vais pas hésiter
Elle a dit si tu me redis ''putin de teug'' je te casse la gueule jusqu'à.. comme la dernière fois . Je l'ai deja fait alors que ta mere etait vivante, a plus forte raison maintenant que son cadavre est à 6 pied ss terre etc etc 😂
Amina l'a traité de sale "caste"
Dieynaba a promis à Amina de lui casser la geule si elle revient sur ses propos. Elle a dit à Amina qu'elle ne s'est pas gênée de lui casser la gueule devant Marieme SALL sa maman quand elle était en vie et qu'elle ne se génera pas de le refaire aujourd'hui que Marieme SALL est morte enterrée et ses os ramollis😅

Meilleurs voeux en ce nouvel an Evenprod.Vs êtes les meilleurs et continuez de nous faire vibrer de bonheur 🎉🎉🎉
Non mba yeugg ngeine nei Even prod Gni ngui tourné bété bété bou dioub té nekh ??? Okhooo liiii🙂↕️❤️😩 Yallah boum diekhhh🤣
Amina ak Makhou diépii nalén lgui
Niaff Dieynaba niouss ko
Merci deiynaba amina dafa réw niak sa yay nga wara dèlo sa khèl si yalla diko nianal dèfoko ngay khass tè rèk bayiwo kènn makhou yaw aussi dinga règlè c est bien ça