Débat houleux entre Ousmane et un Yalla Yalla "Maan sah Daama Waru"#senegal #team221 #dakar #sn #touba #dakarmatin #allosenegal #solutiontv #joalfadiouth #senegal7 #debat
Mane dh chaque jour ma suivre sen émissions bii mais gaayii toubal chrétien mo guëna yomb gindi len ndakh danio réer té nangou wouniou 😮 Guiss yalla c'est possible selon moi mais meuno guiss kou mom diiné islam té do respecter charte l'islam fo diouli do wor do diamou yalla... Mais problème bi Moy niom founiou soukandikou deugg deugg laniou wakhoul ba lègui
@@papefaramendy699 Pourtant chrétien bou amm setlou,lire bible,dinéñ degg né lou Jésus done wax yeup xam yallah leu té ñii di jangalé Maarifa ñogui koy todj
waxtaan bi dou objectif parce que danou japp ni gnii di wakeur ndiambe danuu reer niou warlena delossi ci l'islam. deugeur fitt weesu wul nga diap ni da nga gindiku ba di xool sa morom beutub reer, Yalla daal mofiy atte diaam, wax lii nga diapei deug aayoul, wayeii naagu ci sa ngem bay sikkeul kenen ku gem Yalla ni yaw ab togn la
Mounoo diriger débat ba paré donne Partisan wajii take kiurouss by entoucas maîtrisée n'a sujet wam boubaxx Sax , il faut une émission spéciale et lui laisser le temps de s'exprimer.
Yéne xoll na xoll mais louléne di may diam moy nguéne Mandou tchi nioune ndax liguéne di déff séne bop rek nguéni yakal mais xadioléne bagnouye yakal. Louléne metti moy ay dougual ma ALDJANA nguéne té nanguou woléne ligueye .😂
Salalahou allah Mohamed ❤️ salalahou allah Mohamed ❤️ salalahou allah Mohamed ❤️ salalahou allah Mohamed ❤️ salalahou allah Mohamed ❤️ salalahou allah Mohamed ❤️ salalahou allah Mohamed ❤️ salalahou allah Mohamed ❤️ salalahou allah Mohamed ❤️ salalahou allah Mohamed ❤️ salalahou allah Mohamed ❤️ salalahou allah Mohamed ❤️ salalahou allah Mohamed ❤️ salalahou allah Mohamed ❤️ salalahou allah Mohamed ❤️ salalahou allah Mohamed ❤️
ndéysan gnoubari dagnouy toumall ndiambé ndakh sar yi cékh moussa loulér la done wakh loumoula masa wakh bo demé thi alqouran fékkofa ndiamé masta yakh aya allqouran
Moy yalla néna boma khamoul mounoma diamou kon iow la voix du peuple démal khamidji yalla après dinga meuneu dinékou si Lou beuri ta doula yakal sa dioulli doula yakal si dara
@@Vamdragon jamais yalla yalla Dou mouride ndah Serigne Touba djangalé woul niaka diamou yalla bagn nako va mouride ça veut dire la voix qui mène vers Dieu mais (((par diamou yalla té Molay takha agg si yalla mais pas ay théorie guiss yalla))) exemple holal kilifeu diiné yi niom mam fii si Sénégal ana Kane mosi done incarné lii yalla yalla yi Di woté amoul donc Lou meusoul am kéneu douko fi gueumm ...douma diouli douma worr douma diamou yalla lolou Dou DEUG thé mako Sagna wakh
Mane dh chaque jour ma suivre sen émissions bii mais gaayii toubal chrétien mo guëna yomb gindi len ndakh danio réer té nangou wouniou 😮
Guiss yalla c'est possible selon moi mais meuno guiss kou mom diiné islam té do respecter charte l'islam fo diouli do wor do diamou yalla... Mais problème bi Moy niom founiou soukandikou deugg deugg laniou wakhoul ba lègui
Rerougnou ddd kham kham dafa yatou❤😂
Chrétien bou khamoul dinèm Gay wakh,,,,kèn dou Jésus lignü ndaagü ak lignü daguwoul
@@papefaramendy699 Pourtant chrétien bou amm setlou,lire bible,dinéñ degg né lou Jésus done wax yeup xam yallah leu té ñii di jangalé Maarifa ñogui koy todj
Tu as bien raison yalla yalla, même l'évangile dit que le soleil brille pour tout le monde, bons et méchants. Cessons de juger nos frères et sœurs.
Alhamdoulilah Ndiamé Borom darou jerejeuf
La voix amal jaam rkk.. saa borom saam laa.....❤
waxtaan bi dou objectif parce que danou japp ni gnii di wakeur ndiambe danuu reer niou warlena delossi ci l'islam. deugeur fitt weesu wul nga diap ni da nga gindiku ba di xool sa morom beutub reer, Yalla daal mofiy atte diaam, wax lii nga diapei deug aayoul, wayeii naagu ci sa ngem bay sikkeul kenen ku gem Yalla ni yaw ab togn la
Kham yalla khel agou fa nakh yalla xel douko topou 👂👂
Yayayi yalnaleen yallah guindi amine
Yaw mi ya rérre
وضرب لنا مثلا ونسي خلقه قال من يهيئ الاذان وهي رميم قل لي هي الذي انزلها اول مره وهو بكل خلق عليم
Mounoo diriger débat ba paré donne Partisan wajii take kiurouss by entoucas maîtrisée n'a sujet wam boubaxx Sax , il faut une émission spéciale et lui laisser le temps de s'exprimer.
Ousmane a parfaitement raison vraiment notre pays est danger
Baye laye ligaye wakh deugela bilahi ❤
Non baye laye mi dafa dof dé 😂😂😂😂ki dou nitt way
Gni aye dof lane
😂😂😂😂non Li nekh na
Baye laye😂😂
Yéne xoll na xoll mais louléne di may diam moy nguéne Mandou tchi nioune ndax liguéne di déff séne bop rek nguéni yakal mais xadioléne bagnouye yakal. Louléne metti moy ay dougual ma ALDJANA nguéne té nanguou woléne ligueye .😂
La voix guisse yalla kepp koukoyy weddi doo amme moudiou bou raffett
Macha allah tay mom la voix da ñeuw❤❤
Salalahou allah Mohamed ❤️ salalahou allah Mohamed ❤️ salalahou allah Mohamed ❤️ salalahou allah Mohamed ❤️ salalahou allah Mohamed ❤️ salalahou allah Mohamed ❤️ salalahou allah Mohamed ❤️ salalahou allah Mohamed ❤️ salalahou allah Mohamed ❤️ salalahou allah Mohamed ❤️ salalahou allah Mohamed ❤️ salalahou allah Mohamed ❤️ salalahou allah Mohamed ❤️ salalahou allah Mohamed ❤️ salalahou allah Mohamed ❤️ salalahou allah Mohamed ❤️
allahou Akbar al qoran ak sounnah rék moy deg☝☝
@@alphabah-wb9ne ton père , ta mère , ta femme et tes enfants nak ?
Ousmane 😂 yaye Ngand wathié nga baye laye😂😂😂
Moyaw ki il na rien compris 😂
ndéysan gnoubari dagnouy toumall ndiambé ndakh sar yi cékh moussa loulér la done wakh loumoula masa wakh bo demé thi alqouran fékkofa ndiamé masta yakh aya allqouran
Kiy presentè emision da far😅
Trop ndax Bou la voix Di wax dafkaye déglou ta d'où déklou wa ndiambé
Sen émission bi amoul ben chance boulen saltel souniou diné dji
Gir yalla la voi du peuple ladialmako bakham ñom bouñou günne Adouna deñouluendi dioullé waw wolla dédéd Lolou lañou buega kham😢
Dieemou nityi niokamom waye ladia dess yalla la koufadou diee moudia sonal niasa dess line defe bakhna waye lele yalla rk
Frère chaque jour ladj même question bi té masou masi am réponse nak
Amna solo
Guiss yallah rekkkk seul !
Machalla
🤣woy tailleur yi ay jargogne lagn Mangui dh
Bilahi so guisé Djilly rekh mouno guiss yalla
Aya bi boy bi khéss bi niko firé bahoul Safara niél na diouli Kate youye guiss Tal ...lane moye guistal moye niouye guiss loudoul yalla
Moy yalla néna boma khamoul mounoma diamou kon iow la voix du peuple démal khamidji yalla après dinga meuneu dinékou si Lou beuri ta doula yakal sa dioulli doula yakal si dara
Kii doff la rek
"et leur mère sera l'enfer" tu peux interpréter cela comme tu veux. En plus tu ne peux en aucun cas sortir les yalla yalla des mourides
@@Vamdragon jamais yalla yalla Dou mouride ndah Serigne Touba djangalé woul niaka diamou yalla bagn nako va mouride ça veut dire la voix qui mène vers Dieu mais (((par diamou yalla té Molay takha agg si yalla mais pas ay théorie guiss yalla))) exemple holal kilifeu diiné yi niom mam fii si Sénégal ana Kane mosi done incarné lii yalla yalla yi Di woté amoul donc Lou meusoul am kéneu douko fi gueumm ...douma diouli douma worr douma diamou yalla lolou Dou DEUG thé mako Sagna wakh
Lo niouy wakh si Baboul Mouridine Sidy Birahim Fall....si niak Diouli ak Niak woor gui Diewrine@@Ben_moustafa_jf
Baye laye yow amoo xam xam waay
Pourquoi le journaliste n èst pas neutre. il est a cotè de la voux ce qui n'est pas normal
Wakh ack doff you degguoul mo gueuneu métti 🤦♂️ épuis le temps de parole n’es pas juste dieureudieuf baye laye
Ndiamé moy deugue❤
Pourquoi pas guénn def débat akk ibadou yi (Wahabiste) svp ❤
@@BirahimJock wakh ngay DEUG dh wala nga interview omzo Sall😂😂
لكم دينكم ولي دين
Lou ler ms yereum nalen 😅
La voi boo deoull do xam fekhell de
Alquran khadioul ci gueyit
Ngime 2 linouye wax xamou niusidara
Alquran khadioul ci gueyit