Souma sanione niou defar couronne ak trône ak sceptre (bante bi)bou geune rafeet, geune djégué souniou aada ak thiossane niou sentir daal souniou culture. Félicitations aux lutteurs (Mod'lo et Ama) sama mbeur il mérite son trône. Vive le Sénégal!
😂😂😂wa xana dangéne beugue daxoulou lamine samba tmt mais franchement Ama sa respect dafma depassé Modou rek lay topou ms legui yay sama deuxième lutteur ko meuna beurél si katanou yalla dinala supporter té dila nianal yalla mayla ndam respect a toi ❤
Kan mo guiss lima guiss cii modou lo beugoul xol comba ndakh door Yimouy door ama balde quoi dafa am kersa pour xoll comba bii ndayssan 😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢
Setlou ngen modou lo bou bakh biniouy visionner combat bimouy dor ama nangou woul sakh xol images yi ndeysan yalna yalla doli diam si barke serigne babacar sy niou wadial bessou talla gaindé 2 le 28 janvier insha alla mais très sincèrement plateau bi lep refaitna si ay kaddou
No bilai mane modou lo rek lay topou mais Ama besniki tay sama mbereu gua bilahi ama nitou kache la no bro yalla nala yalla defal diam si barke serign bay Karime🫡🤝✊🏽
I'M A BIG FAN OF MODOU XARANGE LO, I PRAYED FOR HIM TO BEAT AMA BALDE. HOWEVER THE POSITIVE ATTITUDE AND FAIR PLAY DEMONSTRATED BY AMA BALDE AFTER LOSING TO MY WRESTLER, I HAVE SO MUCH RESPECT, LOVE AND SYMPATHY FOR HIM. WHAT A POSITIVE MINDED CLEAN HEARTED SOUL HE IS !!! THEREFORE, I'M URGING MODOU AND ALL HIS SUPPORTERS TO HOLD AMA BALDE LIKE A BROTHER AND GIVE HIM ALL THE SUPPORT AND HELP THEY CAN 🙏🙏
Bakhoum modou lo grand champion Il travail pour la lutter Il fait vendre lecombat Pas de violen e a pikin nit par elle merci ama balde tous nest pas demeriter
Ama tu as gagné le respect de beaucoup de fans de Modou que tu sois vainqueur à ton prochain combat
Bou tasei woul ak wa P.A Amine 😂
Amine
walahi frr❤❤
Vraiment 👍
Frère dakkofé fékk Modou kéne gueunouko yarou
No Ama est trés lusic et un grand homme wallae yalla nako yalla maaay diam ak xéwaal en tant que fan's modou lô
Allahuma Ameen 🤲
Wallahi ama dama ameu si mom yeurmandé . Kepp kouy soutien de familles rek yalla nala yalla taxawou ba charge yi nek sa kaw yalla motali ko
Amine yarabi
Amine
Amine ya rabi
Allahuma Ameen 🤲
Malick thiamdoum communique excellemment.
AMA man fans modou lo la mais bisniki ta sa combat stade lakoy séta tu es mon deuxième lutteur vraiment je en toi un grand champion
Félicitations modou Lô linga déff Si pére Bakhoum Raféttna ma cha'Allah 🙏🏽🙏🏽🙏🏽
Vraiment Lamine Samba il est nul😢
@@gorguikaba7302il parle trop le gars
@@gorguikaba7302😱et pk il es null?
On est fier bilahi de voir ces deux champions ❤❤❤❤
Ama Machalla ❤tu es magnifique modou lo dane la dou gadjié ❤bilae nala yalla diapalé ba nga dieul rois 🤴 des arènes Inchalla sa rêve 😊
La presence de de Malick Thiandoum est importante sur le plateau. Il faut quelqu’un pour recadrer Lamine Samba parce qu’il parle trop.
Dafa soff trop professionnalisme zéro
😂
Wouy yaye rey nguama😂😂😂😂😂😂il est trop bavard😂😂😂
😂😂😂😂
Kom kouniou nguentei beuy bou nioul rek😂😂
Modou kharagn lo le roi des arènes machallah laf thiat félicitations 🎉🥳🥳 du courage Ama
Souma sanione niou defar couronne ak trône ak sceptre (bante bi)bou geune rafeet, geune djégué souniou aada ak thiossane niou sentir daal souniou culture. Félicitations aux lutteurs (Mod'lo et Ama) sama mbeur il mérite son trône. Vive le Sénégal!
Vraiment Ama mèré wonako trop avant combat bi mais legui mom néxnama trop sportif deugla machallah🙏❤️❤️
Ama Mane Modou rek lay topou mai depuis aujourd'hui damalay supporte ❤❤
Je suis avec Modou lo mais Ama est un champion incontestable. Du courage Ama je te souhaite le meilleur pour ton combat prochain
😂😂😂wa xana dangéne beugue daxoulou lamine samba tmt mais franchement Ama sa respect dafma depassé Modou rek lay topou ms legui yay sama deuxième lutteur ko meuna beurél si katanou yalla dinala supporter té dila nianal yalla mayla ndam respect a toi ❤
Li nice na torop je suis fans de modou lo mais li takh na ma buegue ama balde champion du courage lithi kanam mo dakh
Ama kou bakh ndeysane.
Modou lo diambar la vraiment.
Félicitations à vous deux.
Kan mo guiss lima guiss cii modou lo beugoul xol comba ndakh door Yimouy door ama balde quoi dafa am kersa pour xoll comba bii ndayssan 😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢
Merci modou lo Pere bakhoum day nekhal Lamb Ama yeee Ama yeee Ama yeee ❤❤❤
Mais vraiment Lamine il faut laisser les gens terminer leur fille de penser.
Vraiment
🤦🏽♂️ Lamine Samba soff na, eupeul neu. Il monopolise la parole. Malick Thiandoum mo warone dirigé Émission bi.
Vraiment
bilie wakhal nga nyo bari
😭😭bilahi ama modou rekk la beug mé beug nala si combat bi ama yay sama mbeur a parti de tay
Ndeysan machallah ama yalla nalla yalla may ndam si gris modou sama champion bi yalla nalla yalla may ndam si boy niag
Malick Thiandoum seul pouvait faire la présentation il est plus professionnel que certain😊
😂modou Nena di nouyou wallè Sama grand bakhoum taye dafa niew rek adiou 😂😂😂😂 Modou kagne lâ😂😂
Setlou ngen modou lo bou bakh biniouy visionner combat bimouy dor ama nangou woul sakh xol images yi ndeysan yalna yalla doli diam si barke serigne babacar sy niou wadial bessou talla gaindé 2 le 28 janvier insha alla mais très sincèrement plateau bi lep refaitna si ay kaddou
Bilay lolou dou mom kessé mane mi modou lo rek laye suporter mes image meunou mako khol billahi nakh yerem ko lamb dou yeufou nitt😢😢😢
Ama champion leu Modou c'est le roi
Ama balde am ngua talibeii trop❤❤❤❤
Jui fans de modou lo mai ama kene dou yaw jui très fier de toi
AMA BALDE geuna la diapeu gueunala beug ndakh comportement sa communication machalla
Bilahii kii yoroul saxx xolou mbeurr Ama xolbi moo rafett gniko xamoul reikk nioy waxx cii mom luu niaww❤❤
Mane fans modou lo la mais ama doff yi rk gnoy wax si mom lou gnaaw. Borom xol bou rafét la bilahi
Ama très posé et très sûr un champion modou lo est roi
Allhamdoulilah père bakhoum ak Modou lô dioba naniou
😂😂😂😂
No bilai mane modou lo rek lay topou mais Ama besniki tay sama mbereu gua bilahi ama nitou kache la no bro yalla nala yalla defal diam si barke serign bay Karime🫡🤝✊🏽
Wa laminé samba barina wakh deee😂😂😂😂😂
Je suis fans de Modou lo mais Ama yalna Yalla défla roi inesalah et ça ira
Machallah yalla na yalla def diamou
Lamine samba vraiment amoul niveaux journaliste il faut qu'il arrête de couper les gens
Lamine Samba svp wagnil waxji respectueusement nak
Modou ay ponkal rek lafi lim machallah relation moy Lép
Un bon cœur ❤
Ama biss ni tay def nako sama mbeur apar mod lo❤❤❤
Non ibolaye merci sur le drapeau bi nga toudè Ama balde ❤❤❤
😂😂😂dieuleul père badioum mom
Même après combat day adiou 😂
Mais est ce que guiss nguéne Abdou Bahoume; li Tapha Gueye di wakh beugou sé dégueu dara 😂😂😂
😂😂😂 bilahi Mane mii sakh tapha Gueye nexatou xawm loutakh
Ama balde yalla nala yalla defal jamm wallahi bougeu nala❤❤ Modou lo moye sama mbuer wayè buegeu nala trop guirr sa bakh ❤❤
Lamine samba berri nga ndy wakh ah
Malik mo néhi wah bilahi
Le meilleur combat de tous les temps avant pendant et après kou nagou beusseule j’aime ❤
I'M A BIG FAN OF MODOU XARANGE LO, I PRAYED FOR HIM TO BEAT AMA BALDE. HOWEVER THE POSITIVE ATTITUDE AND FAIR PLAY DEMONSTRATED BY AMA BALDE AFTER LOSING TO MY WRESTLER, I HAVE SO MUCH RESPECT, LOVE AND SYMPATHY FOR HIM. WHAT A POSITIVE MINDED CLEAN HEARTED SOUL HE IS !!! THEREFORE, I'M URGING MODOU AND ALL HIS SUPPORTERS TO HOLD AMA BALDE LIKE A BROTHER AND GIVE HIM ALL THE SUPPORT AND HELP THEY CAN 🙏🙏
Jai aimé le geste de modou lo envers bakhoum, dafay woné nekkoule nite bou reuyy,
Bou diekhé rek diekhna
Machalla Ama Eu Modou lo
Mais pourquoi Lamine Samba coupe les gens à chaque qu’ils parlent ? Mais vraiment li c’est trop
Tameu Lou bonne rek chak jour nilay def
Blh li modou Lô ak ama Balde waron wakh yepou tapha gueye ak lamine sambe ak Malick thiandoum
Bilay surtout lamine Samba koï dafa bari wax trop
L’amine day liguey tamit soxor dal baxul ❤
Ama man modou rk lay topou sou bayiwei lamb ma bayi mh à partir dh aujourd’hui ioe lay supporters
Modou Lo ❤❤❤Ama❤❤❤
Bakhoum khol bi mo bone 😂😂😂😂
Moi ce qui m'étonne modou lo avec sa petitesse c'est lui qui terrasse ama, eume, gris....
Ama beug nala dakh Modou lo kénéne ko beurél koudoul Modou yaw laye faral borome bakh nga
Do leen ma may modou lo 😢😢😢
Oumou sama domou baye nga dh mais sangue bi Lo ndam mane ma wara nek niatel🥹
Dolen gawa seyi dh modou guen di khar
Oumou kay ma takla
Champion nga Ama
Rien plus fort 💪🏾
Lamine samba loutax dou dège lou❤❤❤
Dafa bari wax😏😏😏😏
Lamine samba mi esk febaroul sarap khoni li mais di wakh rekk sans frein 🤦🏼♂️🤦🏼♂️🤦🏼♂️
WAOUW ANA ABDOU BAKHOU.
Lamine samba professionalisme zéro, franchement ce Gars ne mérite pas d'être dans une télé
Lamine samba esk doffoul😂😂😂😂😂😂
ki dara bari wakh
Tay ji ama ak modou nio bok supporter 😢 ama nous on aime modou le roi des arène 🎉
Bakhoum modou lo grand champion
Il travail pour la lutter
Il fait vendre lecombat
Pas de violen e a pikin nit par elle merci ama balde tous nest pas demeriter
Machallh modou lo tué a bien pour père bakhoum
Franc balla gaye 2 moy combat bi 🎉🎉🎉🎉🎉🎉
Bilahi ama baldé nitt kou bakh leu Modou lo moy sama mbeur mé mane dama beug ama barki sérigne Saliou mi niou bok 🙏♥️😭
Modou lo ak Père Bakhoum Ndeysanne
Wa lamine samba kom kou réré beuy beuri na wax loll😂😂😂😂
Anma c'est le meilleur sportif beugue nalla beus naka taye après Modou lo yalla gua done roi
Vraiment Lamine Samba il est nul 😢
Lamine beuri gua wakh
Incroyable
Yeen reporters yi bolenn inviter nitt yi deleen wagni sen waxx
❤❤
Bilay
Bilay
modou lo tres humble et tres sereins haaaaaa le roi n est n importe qui il es trop courtoie
Reportaire yi barinaniou wakh
Lamine samba 😢😢😢😢😢😢😢
Mai’s lamine yakk na emission bi way non way
Ama aussi tué un frais champion et bon conunation
Lamine samba comme kou log beye 😮😮😮
Abdou bakhoum déféant la rek doff bi xana rouss nga waxdjou niaw dji ngafi wax yeup 😢
Tiotoundem mais Lamine Samba dou noppi mey nitgni wakh
😂😂😂😂😂😂 dafa bari wakg deh
Modou lo kharagne lo chese la tekk bountou pikine kou guene mou delole .
Te bolewousi wakh ❤❤❤❤
Ndeysane Modou lo ne regarde même pas Les images. Du combat en face de Ama baldé il est très sportif
Lamine mayal nitt gnii niou wax sheeu
Modou lo ❤❤❤❤
Modou reik lagnouy topou inchallah❤💪 le meilleur King des Kings
Lamine samba diépi nako jtjr
NN AMA GOOR YALLA DEUG LEU JE L ADMIRE BEAUCOUP je suis 100% modou lo mais AMA A PART MODOU LO MOM LAY SUPPORTE SI LAMB DJI BILAHI
Lamine samba dofla day yakh emision revk
Bilay
Lamine samba mom nii rek 😂😂😂
Lamine vraiment tu parles trop- il faut savoir écouter les autres quand ils parlent.
Iamine samba un vrai con vrai fou bilahi
lamine samba franchement dafa Epeul....
Lamine Samba gaat hamouko 😂😂😂
Je suis fans club Modou lo mai ama baye fall la bilay