Yeen ñeppa yem. Dem leen jaamu ji seen Borom té bayi bakku yi. Jangileen Alkhuran ak Sunna té jëfféeko. Tarikha yi yepp ay caaxaan la. Kenn topploowuleen kenn kudul Yonent bi SallalAllahu aleyhi wa salam. Moom la sahaaba yi toppoon ba Yallah gërëm leen. Ku bëgg Yallah gërëm la faw nga toppko. Jang xam yeewu yiweeku yewwi say moroom.
Yeen ñeppa yem. Dem leen jaamu ji seen Borom té bayi bakku yi. Jangileen Alkhuran ak Sunna té jëfféeko. Tarikha yi yepp ay caaxaan la. Kenn topploowuleen kenn kudul Yonent bi SallalAllahu aleyhi wa salam. Moom la sahaaba yi toppoon ba Yallah gërëm leen. Ku bëgg Yallah gërëm la faw nga toppko.
Jang xam yeewu yiweeku yewwi say moroom.
Dangay doule mandou len si tarikha yi
@@ousmanembenguefalldiallo3889 sa gémegn daa xessaw sa bopp bi copp rekka ci nitt
Alhamdoulilahi alkour an ak soune rek machalah
Lenďé khamnako mome mouridyi sene thiow mo euppou sene kham kham.
quou dég li khan ni diakhassé kat yi la wakhaboun yi meuneu tolén nakh kén
Merci younousse tres bien 👏👏👏👏👏👏👏nioukhite yi khamou niou séne bopp
Mba jotngén si audio Oustaz OMZO BII😂
Yallah nangou Ya ALLAH may joup mousseul gnou si fén AK JAKHASSÉ ay joulitt
AMINE
Doule rekk la wahabiyoune di defff
Yaw bann audio nguay wakh
Djeureudjeufeuty borom yaw ragalal yalla astakhfiroulah
Yallah naniou yallah moussal thi ay dioulit youye nono sén mbokoy dioulit. Senegal kep la am
Ganakoukandé nioule na daray lérr nékoule simome dafa féne ba lake😜😜
Kii moma meuneuh féne
Theéy Sénégal😭😭
Mais l'an motaxx senne kanam lendeme,Amoulenne visage l'islam yonou murdismis daffa doywarra trop 😏😏😏😏😏
Dou cheikh ti c missel tidiane grand fo billet
Iow Cheikh Ahmad Tidiane ngay wakh Lou niaw iow yabone té torokh rk démal geustou dji bala nga dingate
Craignez Allah sur ces montages
Nioukhite yi ay sisou mane laniou rek