Dieureudieufaty ya Oustaz yalna yalla yokou say teubou ak say makhama Yalla mayla goudou fane bou and ak were si barké MAWLANA CHEIKH IBRAHIMA NIASS ra
Machallah, kham kham bou léér avec beaucoup d'humilité. Rien qu'en l'écoutant, notre foi s'agrandit, Alhamdou lillah. Yalla nala yalla same, tu es un cadeau pour toute la Umma
اللهم صل على سيدنامحمدالفاتح لماأغلق والخاتم لماسبق ناصر الحق بالحق والهادى إلى صراطك المستقيم وعلى آله حق قدره ومقداره العظيم اللهم صل على سيدنامحمدالفاتح لماأغلق والخاتم لماسبق ناصر الحق بالحق والهادى إلى صراطك المستقيم وعلى آله حق قدره ومقداره العظيم اللهم صل على سيدنامحمدالفاتح لماأغلق والخاتم لماسبق ناصر الحق بالحق والهادى إلى صراطك المستقيم وعلى آله حق قدره ومقداره العظيم 🥰🥰🥰
Sallalahou aleyhi wa salam 🥰❤️🤍❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️ ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️ il est la plus aimé du monde ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️ Mohamed ❤️ sallalahou aleyhi wa salam 🥰❤️🤍❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Sama Thiofél si Oustaz Ahmed Ba (RA) meunoumako wakh nitou Yallah deugeu ngui ni. Talibé Baye deugeu ngui ni. Macha Allahou
Machallah ya oustaz Ahmed ba vous honorez la fayda tidiany Ibrahima Niass on vous souhaite que du bonheur parfait
On a perdu un grand homme nak Machallah xamxam bi sell na
Yalla nagnou Yalla tass sisa lerr Machallah ya Oustaz
Dieureudieufé baye Niass ❤️🙏
Soukourane ya oustaz yalla na yalla yokou say faan té yokou weer ci barké Baye Barham Niass
Machallah vous êtes un cadeau pour la Ouma islamique.!!!
Dieureudieufaty ya Oustaz yalna yalla yokou say teubou ak say makhama
Yalla mayla goudou fane bou and ak were si barké MAWLANA CHEIKH IBRAHIMA NIASS ra
Mach allah ya oustaz yalla na yalla goudal sa fan
Oho khôl sed na 💫🤍🤍🤍li môme xame yallah rek moy takh gua xamko 👉😇👂👈
Safoo leene ki yalla safoo moye yonentebi saw
Je vous aime oustaz❤️❤️
Machallah, kham kham bou léér avec beaucoup d'humilité. Rien qu'en l'écoutant, notre foi s'agrandit, Alhamdou lillah. Yalla nala yalla same, tu es un cadeau pour toute la Umma
Oustaz Ahmed nous sommes très fiers de vous long vie à
Machallah ya oustaz Ahmed ba diaradiaf❤❤❤😮
Oustaz le temple d'un savoir
Tay deh diommi guén. Dieureudieufè Baye
Dieureudieufé Baye Niass 😍 Dieureudieufé Baye Niass 😍 Dieureudieufé Baye Niass 😍
Alhamdu li LAAH 🙏🏾💖 Baye Niass la solution universelle alhamdu li LAAH 🙏🏾💖
Baye niass wa Sénégal khamouniouko Bilahi.baye amoul morom boulenko tékalek ken ❤❤❤❤
Ndaysaane Mane mouride la dama beugg yonentebi AK lepp kouko beugg
Sala LAAHU alayhi wa salam lovely 🥇🤍 alhamdu li LAAH 🙏🏾💖
Macha allah alhamdoulilah dieureudieuf yalla sounou borom dieureudieuf ya ouztaz yalla na yalla barkel ya rabbi
Alhamdoulilah mashallah dieureudieufé BAYE 😍❤️❤️❤️❤️🙏🙏🙏
Machallah Pape HANN Talibé Cheikh Islam BAYE NIASSE douniou sa morome thi KHAME KHAME Machallah ALIOU
Uoe mi di concurrence nakk
Machalla 🥰 ya Oustaz Ahmed Bâ alhamdoulilah
Ma sha Allah. Dieureudieufeee Baye Niass. Oustaz yalna yalla yok say leer
Machallah Baye merci beaucoup Alkhamdoulilah Alkhamdoulilah Amine longue vie Amine ❤️❤️❤️❤️☪️☪️☪️☪️🤲🤲🤲🤲
Oustaz mission le gnewoone si dounya matal nako dém ne❤😭😭🤦♂️
Machalla Bah pullo ce qui se conçoit bien s annonce bien longue vie à toi
Alhamdou lilah ❤️❤️❤️❤️ kham kham bou wére mo nékh
Maachallah yalna yalla Yok say lére wathié yeurmandéme si yaw❤🙏
Dieureudieufé Baye Niass ♥️🙏 oustaz Ahmed Ba yagg fi loll te werr
Yalna yalla lérale kanamame té barkéle guinawame, yalna yalla féyalniou Oustaze Bâ
Machalla YALLA na Yalla gudal seni fane 💯💯💖💖💖💖💖💖🙏🙏🙏🙏🙏👑👑👑👑👑😘🥰🥰🥰🥰🥰🥰💐💐💐💐💐
Beugeunala barki baye niass
Yalna Yalla yeureum ko ter kharerko aldiana
Je l'aime beaucoup 💓💔💔💔💔💔💔💔💔
ماشاء الله
Machallah Oustaz sa kham kham worna té sëlle na.. khôl yeup toye na té sedd na
Longue vie Oustaz ❤❤❤
Machalla xam xam rek mo worr
Al hamdoulil Allah
Yalla na Yalla yok sa lere Oustaz
Beug nala lole Guirre Yalla ya Oustaz ♥️🙏😭🙏
MashaAllah ❤ xam xam mo woor wallahil azîm...
Dieureudieufé Yallah Dieureudieufé Yonenté bi 🙏🏾🙏🏾🙏🏾
Machallah Oustaz xol sed na yalla nala yalla yok may la Weir ak goudou fane
Thiey Naby❤
Allahou Akbar🖐
❤❤❤❤❤ machallah ya oustaz ahmed bà
Mash'ALLAH
ماشاء الله محمد بشر لا كالبشر &بل هوكالياقوت بين الحجر
Machala xam xam rék mo woor sallalahou aleyki wasalam. Alkhamdou lila 🙏
Machallah diaradief oustas Ahmadou ba xam xam bou were
Alhamdou lillah machallah
Mashalla alhamdou lilah ouztage ba
Mashallah tu es un connaisseur
Machalla oustas ba
Doundal wéral 💔💔💔💔💔💔💔 Niasss 💞❤️❤️❤️
Machalla ba yalla nagnou yalla deffale beugue yonetoubi
Machalla, yalla yok sa kham kham samoula
أنا مغوي حقًا ، إن معرفتك بالله ، والنبي سيدنا محمد وباي نياسي هائلة للغاية. انت فخر بالاسلام فخر لتريحه تيدانيه فخر للفايضة
Maa chaa Allah dieuredieufée Baye Niass
mashallah seydi Ba 🥰😍
Masha allah.Tres fier,li moy xam xam
Yalna yalla yook say lerr sanguabi
Machallah yague fi lole
Machalla Al oustaz Ahmed Ba ♥️♥️
Salallahou allayhi wasalam 🖤🖤😭😭😭
Mashallah
Cheikh ahmed ba guena yague guena werr rekk lanou la nianal xol sed n'a si yaw lollll 🤍
Macha allah oustaz
Sama tourando seydina Mouhamed ♥️♥️♥️♥️♥️♥️🙏
Mach allah al hamdoulilah
Machaallah Alhamdoulilah
Macha alla ❤ 💯
Machalah alhamdoulila jeurediefe baye niass ❤️❤️❤️
ما شاءالله يا شيخ عمرا طويلا مع الصحة والعافية.
Macahla
ma chALLAH WAL HAMDOULILLAH
اللهم صل على سيدنامحمدالفاتح لماأغلق والخاتم لماسبق ناصر الحق بالحق والهادى إلى صراطك المستقيم وعلى آله حق قدره ومقداره العظيم اللهم صل على سيدنامحمدالفاتح لماأغلق والخاتم لماسبق ناصر الحق بالحق والهادى إلى صراطك المستقيم وعلى آله حق قدره ومقداره العظيم اللهم صل على سيدنامحمدالفاتح لماأغلق والخاتم لماسبق ناصر الحق بالحق والهادى إلى صراطك المستقيم وعلى آله حق قدره ومقداره العظيم 🥰🥰🥰
Mane d diakhal ngama lol.machala
Machalla
Yalla nala yalla geureum
❤Mahmad alla
Dieureudieuf baye niass
Machallah alhadoulilahii
Dieure dieuf
Kham kham li leu
Paix à son âme
Sallalahu Alayhi wa Sallam ❤
أيّدك الله
Machalla ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Ndaysane thiaye baye niass
J,aime bien
Ohhhhh alhamdou lila
Fantastique
ماشاءالله جميل
Manchallah
ماعرفني حقا غير ربي
Sallalahou aleyhi wa salam 🥰❤️🤍❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️ ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️ il est la plus aimé du monde ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️ Mohamed ❤️ sallalahou aleyhi wa salam 🥰❤️🤍❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Waa li néxoul!!!
الحمد لله
ki koumou diaxaloul danga am kiniane🤔🤔 Oustaz Ahmed ba wallahi Li ngay wax nit meunouko diang