Machalah Père Fall Ndianga doundeul té wer. Yalla na yalla bayi si kanamou ndiamboot. Yalla bou niou sédalé dara si sa guinaw inchallah. Je vous suis depuis Montréal🙏🏾🙏🏾🙏🏾
Kou bakh ta woyaf papa ass fall Bou Diangeukat Diougué tivaouane mou wara Gamou yeumbeul lithi eupeu keurem lagnou d'Al wallahi papa ass fall talibé Serigne Abdou Aziz Al amine la machallah ❤🙏
Machalah Père
Fall Ndianga doundeul té wer. Yalla na yalla bayi si kanamou ndiamboot. Yalla bou niou sédalé dara si sa guinaw inchallah. Je vous suis depuis Montréal🙏🏾🙏🏾🙏🏾
❤❤ machalla Ouztaz Modou fall lanouye tope amale diame ❤❤❤ papa longue vie kheweule you bari ❤❤❤❤❤
😂😂😂😂❤❤❤ Ouztaz Modou fall sa papa machalla amale dome sou amé gnanou wadiour ❤❤ machalla ❤❤❤
Machallah ❤❤🥰
Kou bakh ta woyaf papa ass fall Bou Diangeukat Diougué tivaouane mou wara Gamou yeumbeul lithi eupeu keurem lagnou d'Al wallahi papa ass fall talibé Serigne Abdou Aziz Al amine la machallah ❤🙏
Machala
oustaz mo gua wakh si internet bi