Youssou Ndour : "Je vais vous révéler ce que Ahmet Khalifa Niass a fait pour moi..."

แชร์
ฝัง
  • เผยแพร่เมื่อ 8 ม.ค. 2025

ความคิดเห็น • 164

  • @ibralo9769
    @ibralo9769 6 ปีที่แล้ว +53

    Mashalah Ahmed Khalifa Niass koula khamoul rék molay niakal worma wayé waliyou kaamil Moy Ahmed Yalla na yalla yaggal lafi deugueureul la !! Wayé Tamit Sugnou Serigne Sidy Al Amine yalla na yalla kharé ko Aldjana ci Barké Mawlaana Cheikh Ibrahim Niass "BAYE"

  • @princessdesonEmir40
    @princessdesonEmir40 6 ปีที่แล้ว +51

    Ma sha Allah longue vie à vous Ahmed Khalifa niasse Youssou ndour

  • @dmxsowkharitouyayam2764
    @dmxsowkharitouyayam2764 6 ปีที่แล้ว +29

    bilahi youssou ya niak kiñane mo takh ci cow ci canam rèk.bilahi koula yènè lou bonne mossiy fanann ya bakh.
    Elh sidy lamine niass yalla nako yalla khare aldiana.
    yalla yagal fi ahmed khalifa niasse borom kham kham bi mashala

    • @diagnendoye5756
      @diagnendoye5756 6 ปีที่แล้ว

      Walahi Ndeyssane
      Mash ALLAH
      Amine ya rabbi

  • @cheikhounadieye810
    @cheikhounadieye810 6 ปีที่แล้ว +33

    ndeysan mane dh Ahmed khalifa Niasse koma soop la bilahi yalla sedé nako

  • @ousmanefaye9089
    @ousmanefaye9089 6 ปีที่แล้ว +2

    Machallah Grand you yal nala yalla faye sa khol

  • @aminagueye6386
    @aminagueye6386 6 ปีที่แล้ว +14

    Machala youssou ndour wakhdji refetena trop yaw lou bakh rek gua kham

  • @ndeyefatoumbaye6729
    @ndeyefatoumbaye6729 6 ปีที่แล้ว +27

    Lou bakh rek mo am solo ndour comme d'habitude Mach Allah

  • @dashsallsall2703
    @dashsallsall2703 6 ปีที่แล้ว +18

    Suis pas fans de Youssou ndour mais Li ma nekhh ci mom dafa am dieum kham adina nek goor yallah franchement rip sidi lamine niasse bilay adina

  • @anitabenejeloune8669
    @anitabenejeloune8669 6 ปีที่แล้ว +47

    Je l ai toujours dit Ahmed khalifa niass est bien arrêter de l insulter ou de critiquer SVP

  • @gansiryfall7247
    @gansiryfall7247 6 ปีที่แล้ว +11

    toutes nos condeliance a la famille lentourages le Sénégal youssou tu est un Grand homme que dieu te laisse lontemp parmi nous que dieu amene sidy au paradis amine yarabi

  • @ndoyeafia9403
    @ndoyeafia9403 6 ปีที่แล้ว +26

    Ya bakh dé youssou ndour bilay

  • @adjitouba8307
    @adjitouba8307 6 ปีที่แล้ว +1

    Youssou ndour machalah ya bakh kine du khalifa niass

  • @deugrekkdeugkesse1440
    @deugrekkdeugkesse1440 6 ปีที่แล้ว +8

    Bilahi Ahmed Niass yalla na sa diam yague te nga diegueul gnilaye togne niepp baci mane ,manndoulene déretou waliyou dou balé,wa salam

    • @serignebi2600
      @serignebi2600 6 ปีที่แล้ว +2

      Bilahi wakh nga DEUG Ahmed limou dimbalé ci ay nit té bagoul mou ciw gni khamoul rek nioy neki ci réseau socio yi di wah rk wayé yalla mom mongui guis

  • @bounandiaye5670
    @bounandiaye5670 6 ปีที่แล้ว

    Merci youssou tre beau geste ahmed khalifa niass yalla nga fi yague te wer El.hadji sidy lamine niasse yalla nako bour yalla khare ko aldjana firdawsi

  • @DKM888DKM
    @DKM888DKM 6 ปีที่แล้ว +4

    khol bu rafét sét rék la ya ALLAH di vérifier Thie nit.
    Té amna yakar né niar nie, sèn khol sétne rafétne. Masha'ALLAH

  • @Laspheredesdistinguees
    @Laspheredesdistinguees 6 ปีที่แล้ว +1

    youssou dafa am yarrrr machallah !
    nala yala faysakkol rek !

  • @cheikhcheikh893
    @cheikhcheikh893 6 ปีที่แล้ว +10

    machalla niass ya bakh

  • @tiphanydevilliers480
    @tiphanydevilliers480 6 ปีที่แล้ว

    Machala beugueu nalene. Youssou n'dour sa wax rafette na machala.

  • @fck9801
    @fck9801 6 ปีที่แล้ว +1

    Youssou ya baax bilay wax nga deug Aduna yéné rek la. Daw lo nga sama yaram. Yalla na yalla goudal sa fane té sang la mbalanam soutoura.

  • @toubaguymbind2964
    @toubaguymbind2964 6 ปีที่แล้ว +1

    Beugue nala Ahmed niass❤nakh sa djiko

  • @vallainnde5346
    @vallainnde5346 6 ปีที่แล้ว

    Yowgui bikoum Khalifa est un homme bien Alim comme y en a pas beaucoup, masha Allah, mais Youssou l est encore plus ! Reconnaitre les bienfaits passes est devenu rare. Allah yerham Sidi Lemine.
    Masha Allah c est beau cette visite.

  • @mamadousidibe9215
    @mamadousidibe9215 6 ปีที่แล้ว +20

    You machalah.....séddé bi rafétt na.

  • @dodjisy9492
    @dodjisy9492 6 ปีที่แล้ว

    Youssou n'dour je l'aime trop il est correcte et humble. You que Dieu te bénisse.

  • @amedinoulahsarr7356
    @amedinoulahsarr7356 6 ปีที่แล้ว +36

    Magifique lii refetna trop, wakh lou bakh rekk moo amm ndieurign

  • @assanegueye3065
    @assanegueye3065 6 ปีที่แล้ว +65

    Mane dal beuguena youssou Ndour .au moins yaw do nafekh comme gniye feiwalei famillou diambour . Ahmed khalifa niass deî kou ko khole khamni nitou keissei la.yalnaleine yalla maye goude fane AK were.papa

    • @diagnendoye5756
      @diagnendoye5756 6 ปีที่แล้ว +1

      Walahi Sénégal kay yeeneu nitt gni danio alkou rek.
      Papa Sidy Lamine Niass yalna Yallah yessal yeurmendem yok sa leer barké Maam you bakh yi

  • @cayortv4910
    @cayortv4910 6 ปีที่แล้ว +4

    Je l'aime trop birane ndour il es correct

  • @adjadiouf4279
    @adjadiouf4279 6 ปีที่แล้ว +1

    Deugue Bou weir youssou ndour yow mome dagnelaye baye ak yalla yalnalen yalla faye yak Ahmed Khalifa sidy lamine yalnako yalla kharel aldiana firdawsi

  • @sgsofficiel3042
    @sgsofficiel3042 6 ปีที่แล้ว +7

    Mane Lima geuna nékh Moy Youssou Ay domame yarounagne .yarnaléne té bouléne nékhone réww .wayé kham nagne né réw amoul ndiarigne gni warta réw rék niofi réw

  • @xalyonebixalyonebi2889
    @xalyonebixalyonebi2889 6 ปีที่แล้ว +8

    machalla ndour takhaw bi diek na

  • @binettediaby9559
    @binettediaby9559 6 ปีที่แล้ว +2

    Pape you mo bakh machalla ❤️

  • @misterdadji45milliards57
    @misterdadji45milliards57 6 ปีที่แล้ว +17

    Papa youssou Ndour doundal 120ans

  • @sididiopdiop5536
    @sididiopdiop5536 6 ปีที่แล้ว +1

    Mercy le grand you

  • @modoulo5987
    @modoulo5987 6 ปีที่แล้ว +1

    Masahala amenasolo papa yousou

  • @dijandao6459
    @dijandao6459 6 ปีที่แล้ว +18

    Mashalla ndour goudal fane lol

  • @FascinatingMya
    @FascinatingMya 6 ปีที่แล้ว

    MachaAllah Ahmed khalifa dal keemane leu

  • @diagoousmane7623
    @diagoousmane7623 6 ปีที่แล้ว +19

    yousou beusnikitaye beugue naala billahi

  • @babagning6080
    @babagning6080 6 ปีที่แล้ว +18

    Yaw pere youssou gorr nga koula défal lou bakh nga wakh koo

  • @ladiva8101
    @ladiva8101 6 ปีที่แล้ว

    Machala papa youssou kadou gui rafet na

  • @awacisse8993
    @awacisse8993 6 ปีที่แล้ว +10

    Li dé couka déguelou wara mbadou cilou bari té xameni lignouy waxx ak lici souff du béne ku nek sa bop doynala missal nagnouy mandu wayy

  • @mandingueempire1892
    @mandingueempire1892 6 ปีที่แล้ว +3

    j'ai toujours aimmee Youssou Ndour et respecte. Apres je les detestee parce que, J' avais l' Impression qu' il ne fait pas autant pour les gens du Senegal. mes cette fois ci je croix qu' il et Temps de lui Pardone. Merci #YoussouNdour

  • @oumarba8006
    @oumarba8006 6 ปีที่แล้ว

    YOUSSOU. VOUS ETES UNE BONNE PERSONNE. JE VIENS DE M EN ASSURER. QUE DIEU TE PROTEGE

  • @maneladia1665
    @maneladia1665 6 ปีที่แล้ว +4

    Machallah

  • @khadygaye7537
    @khadygaye7537 6 ปีที่แล้ว +2

    Ndessane adouna amoul solo yalna hipé firdawsi si barké mamame

  • @djibigaye1527
    @djibigaye1527 6 ปีที่แล้ว +11

    merci per

  • @siradjism4889
    @siradjism4889 6 ปีที่แล้ว

    merci youssu jarajef yalnaga guddu fan te wer

  • @idrissandao8690
    @idrissandao8690 4 ปีที่แล้ว

    Mann dh koukoo nawwloo laa longue vie ahmet

  • @malickfall1978
    @malickfall1978 6 ปีที่แล้ว +36

    La plu part de ses journalistes viennent de walf je suis dacore mais c'était pour desoudre walfadjri 99.0 qui est levè trés tôt SYDY LAMINE yalna yalla doliko dolèl aminn

    • @khadimbeye8860
      @khadimbeye8860 6 ปีที่แล้ว +2

      Mon cher tout ces gens qui parle là ne veulent pas que walf survive

    • @moussafall1487
      @moussafall1487 6 ปีที่แล้ว +1

      @@khadimbeye8860 vérité absolue
      Tout ça c'est du cinéma.De véritables vautours

    • @erdogancherif5790
      @erdogancherif5790 6 ปีที่แล้ว

      Detywaye

    • @malickfall1978
      @malickfall1978 6 ปีที่แล้ว

      @@khadimbeye8860 pour le moment parce que certains personnes ne croyaient pas â sydy Muhadoul Amine yalna yalla dolyko lèér seulement sénégalais mo gawa faté

    • @malickfall1978
      @malickfall1978 6 ปีที่แล้ว

      @@erdogancherif5790 loi lèèr

  • @lMaya832
    @lMaya832 6 ปีที่แล้ว

    c est beau a voir et a ecouter, li rafete na vraiment,,tonton Youssou Ndour aka gua Rayou ndeyssane,je taimeeeee tonton

  • @mountagadiallo2327
    @mountagadiallo2327 6 ปีที่แล้ว

    ماشآءالله جزاكم الله خيراً

  • @madamemadame3380
    @madamemadame3380 6 ปีที่แล้ว +1

    Macha'Allah !

  • @makhtarsyll3735
    @makhtarsyll3735 6 ปีที่แล้ว +1

    Yalla nako yalla yeureum sidy lamine niasse ak bepou djoulite

  • @sadamarkhabaneniass8389
    @sadamarkhabaneniass8389 6 ปีที่แล้ว

    Longue vie serigne bi alla mayla talle ak feké

  • @michellendiaye5203
    @michellendiaye5203 6 ปีที่แล้ว +1

    Li mo takh bilay ma beugu youssou ndour té khamou ma loutakh je suis emu yay sama reference kan tu passe à la télé j'ai le sourire aux lèvres tout le tps merci papa you té comme un papa pour moi té khamoma nouyou guama khol ma ré té khamoma doumako meuss faté jai grandi avec té chanson kan gt petite dans la voiture de mon papa motakh mome rek lay guiss souma lay khol ta fille que tu ne connais pas t'aime
    love you

  • @amysow956
    @amysow956 6 ปีที่แล้ว +1

    Kha ki sama papa la bilakhi j v aim for machalakh longue vie tu es jinial

  • @cheikhbadaradiop7377
    @cheikhbadaradiop7377 6 ปีที่แล้ว +36

    Ya bakh papa you yaguefi tewer

  • @ibrahimbiteye5094
    @ibrahimbiteye5094 6 ปีที่แล้ว +11

    serigne Ahmed ya bakh

  • @abdoudiagne1935
    @abdoudiagne1935 6 ปีที่แล้ว

    Machalla marci way

  • @fallbassbassfall649
    @fallbassbassfall649 6 ปีที่แล้ว +4

    Kene dou youssou ndour

  • @falloudieng4604
    @falloudieng4604 6 ปีที่แล้ว

    Merci youssou

  • @fatoundiaye8224
    @fatoundiaye8224 6 ปีที่แล้ว +2

    Refetna machalla

  • @diengsala5418
    @diengsala5418 6 ปีที่แล้ว

    Niasse coumba abdalahh koula sopp ndakh niguè mel si kou ted ki yalla nasaa fan gouddd

  • @thiernombodj8361
    @thiernombodj8361 6 ปีที่แล้ว +1

    Yallah na yallah doli diamou rek

  • @damasdamas1165
    @damasdamas1165 6 ปีที่แล้ว

    Ewaye Ndour yowite kou bakhenga ndakh meunone ngako Bagna wakh bilahi malay khole rek dey melni Sama bay laye khole yalnoko yala wonelet ak sidy lamine Gnass amine

  • @ramandiaye8119
    @ramandiaye8119 6 ปีที่แล้ว

    J'aime bpk youssou ndour

  • @medounembow9636
    @medounembow9636 6 ปีที่แล้ว +34

    Youssou ndour mo rafec holl

    • @ndeyesaliouniang5375
      @ndeyesaliouniang5375 6 ปีที่แล้ว

      Thi naka man daal dama warou thi senegalés yii critique rekk lanou man

  • @maimounadiallo1632
    @maimounadiallo1632 6 ปีที่แล้ว +22

    Non mane garmi la beugue

  • @mameboy4629
    @mameboy4629 6 ปีที่แล้ว +13

    Wa Ahmed gnata salon la am ?

    • @saliousagne7895
      @saliousagne7895 6 ปีที่แล้ว +3

      Lòool sa way sii deuthe lagnou nèkk wayy

    • @serignebi2600
      @serignebi2600 6 ปีที่แล้ว +1

      3 salon la am

  • @oumoufall7828
    @oumoufall7828 6 ปีที่แล้ว

    Ndeyssane serigne bi sama yaram dawna

  • @cheikhcheikh893
    @cheikhcheikh893 4 ปีที่แล้ว

    Niass Koula khamoul rék molay dingate wayè li nga deff niassen Ben suetou El hadji abdoulaye niass defou kofa sidi lamine limou âme yeupp yèw la

  • @cheikhahmadoubamba5477
    @cheikhahmadoubamba5477 6 ปีที่แล้ว

    Bilay ahmed ya bakh

  • @issasadio9512
    @issasadio9512 4 ปีที่แล้ว

    Daddy you🌹

  • @papegaye9128
    @papegaye9128 6 ปีที่แล้ว +1

    Kene doumom yalnnakoo yalla yeuram

  • @mamethiernobirahimba2235
    @mamethiernobirahimba2235 6 ปีที่แล้ว

    Ahmed Khalifa Niass Mouride Sadekh Nga .. Mouride Deug nga . dundeul

  • @fhachaobiang386
    @fhachaobiang386 6 ปีที่แล้ว

    Merci

  • @modia5949
    @modia5949 6 ปีที่แล้ว +2

    Yousou ndour moye dioulit

  • @ablayefall3572
    @ablayefall3572 6 ปีที่แล้ว +5

    Youssou.ndour.yabakhe

  • @maturashogun4273
    @maturashogun4273 6 ปีที่แล้ว +1

    Rafetna Ndour

  • @cheikhcheikh893
    @cheikhcheikh893 5 ปีที่แล้ว

    Bilahi Sénégalais nio seytane rek mais ki ak rakam sidi louniouy deff si souff Ken khamouko nio bokou Ndeye bokou baye

  • @deggfeenjotna
    @deggfeenjotna 6 ปีที่แล้ว

    Yousou waxallal yallah Nak

  • @NIASSFBI
    @NIASSFBI 6 ปีที่แล้ว

    Ndaysane Vraiment c triste youssou Ndour

  • @erdogancherif5790
    @erdogancherif5790 6 ปีที่แล้ว

    Yusu tu es le numéro 10 en avant rek Ken doulateye

  • @ladelicatesse5467
    @ladelicatesse5467 6 ปีที่แล้ว

    Président Youssou .... président kouthia tchiey SIDY sa guinaw Bandang....wayee nak sama ghorghi AKN laaaaf thiat kou la deghlou d'où dioum

  • @moustaphadiane3309
    @moustaphadiane3309 6 ปีที่แล้ว

    Che la sua anima riposa nel più alto paradiso

  • @diagoousmane7623
    @diagoousmane7623 6 ปีที่แล้ว +11

    non yousou yabakh tagoré

    • @aramesenghor9992
      @aramesenghor9992 6 ปีที่แล้ว

      Bakh Rek mo am solo te wakh sa bakhou waye Dou wadji dara thi sa Bakh. Youssou kendou Yow Ya Bakh

  • @cherifmawloutmintoufall8392
    @cherifmawloutmintoufall8392 6 ปีที่แล้ว +1

    Ahmed y'a dèfal lii Serigne Touba dinala fayy baa wiiss laa

  • @fantasogue3816
    @fantasogue3816 6 ปีที่แล้ว +6

    Le regard de khouthia 😁😁😁

    • @mbayemandaw7433
      @mbayemandaw7433 6 ปีที่แล้ว

      Fanta Sogue kouthia waroul assister genrou diétay yi 😂😂😂

    • @fantasogue3816
      @fantasogue3816 6 ปีที่แล้ว

      Mbaye ma ndaw Mbengue bilay son visage me fait rire 😂😂😂

  • @sencomedie9074
    @sencomedie9074 6 ปีที่แล้ว +5

    thiey yalla

  • @diagnegnilou1078
    @diagnegnilou1078 6 ปีที่แล้ว

    ndourewaly sa wah rafetna

  • @juniiorlofficiel3097
    @juniiorlofficiel3097 6 ปีที่แล้ว

    dialé bi dhé da moudjé sopalikou nekk meeting 😁😁😁😁 yow kay ay niane mola indii

  • @diksonebriz293
    @diksonebriz293 6 ปีที่แล้ว

    Wallahi Youssou wakh na deug Ahmad meun ngako wakhal lou nekk Mais borom kham kham mat seuk la

  • @FascinatingMya
    @FascinatingMya 6 ปีที่แล้ว

    Hanaa wahkat yi nopinegn tay

  • @serignembackendiayembacke6585
    @serignembackendiayembacke6585 6 ปีที่แล้ว +1

    ay ré dama diappou sakh

  • @abdoukhoudossdiop58
    @abdoukhoudossdiop58 6 ปีที่แล้ว

    ahmed khalifa yalla nga fi yagg loll tawer

  • @Laspheredesdistinguees
    @Laspheredesdistinguees 6 ปีที่แล้ว

    akhmadou khalife Niass kham kham lay wakheee ; il faut ay noppp you bakh nguirrr meune ko dégue .
    kou bakh la ! t li firndeeee nakko .
    senegal nak dougouniou wakh dineee ; mais thi rafetalou ada laniou tame soukeundikou dora tekk dineee ( je m’en suis rendue compte ) quand j’ai commencé à fréquenter les prêcheurs musulmans occidentaux dignes de leurs noms !
    sidy Lamine Niass yalanakko yalla yokal ay leram .
    j’ai une chaîne youtube

  • @baissa6202
    @baissa6202 6 ปีที่แล้ว +1

    Cou dh rek mo perte Sénégal Aÿ nafik rekk

  • @boudaraniaaw4518
    @boudaraniaaw4518 6 ปีที่แล้ว +1

    Rafetena!

  • @alioukaracisse4838
    @alioukaracisse4838 6 ปีที่แล้ว +1

    Bayi dore rek

  • @ablayegning1276
    @ablayegning1276 6 ปีที่แล้ว +1

    YOU doudal leep yowla dara diopoula

  • @fatoubintourassoul3365
    @fatoubintourassoul3365 6 ปีที่แล้ว

    Ndeye sane Ahmed Khalifa niasse dafa couko khamoutte rèkk Moye wakh

    • @makhtarsyll3735
      @makhtarsyll3735 6 ปีที่แล้ว

      Sama Yaye Sama kharitt Ahmed khalifa niasse de nitkou bakhla

  • @alioukaracisse4838
    @alioukaracisse4838 6 ปีที่แล้ว

    Yousou sa wakh rafène