Mbakhalou saloum doko khorom sinon mou wékh, guissouma guédj, kethiakh bi dagnko wara tane deub ko aussi ci nokoss bi, guerté bi dagnkoy tay avant de verser dedans...
@@mamandeyediaw6331 kéne forcé woul kéne on donne juste un conseil. Aussi wakhal yow bagna taye mola gueuneul wayé boul wakh mo gueune. Mane tay moma gueuneul sinon guerté bi dou nior
bilay damay togn rel mais niar yeup comme dsfay am diw nior boula nekhe rossi ko mome la togue tay mais genre dama nioulouk dogua. si def diwlin bi mais nekh rek la def davvero 🤣🤣🥰
Togue dafa bari façon mane damay gnoulouk deub sama kéthiakh ak sama gnébé diakhassé nétatou ak touti kani ak soplé mélanger ko ak guerté gui souma soré sama thiep tek ko thi kawam
Le poudre maron c'est du poudre d'arachide et le dernier comme vous dites du(nokoss) c'est de l'ail, oignon,poivre noir, piment ,cube ou sel et de la moutarde africaine appellé (Netetou en wolof),un type de feverol appelé (Soumbara) en bambara,(dawa_dawa )en igbo😊
Mbakhalou saloum yap douma sii def khethiat guedd beure rekk taye sama guerter mou bagna seuth bon appétit
Bi dou kethiakh Sénégal
Ont lappel bonguaa amoul horom
Aka nekh 🎉
Voilaaa Toi u connais
Kéthiakhe fane la
Amena Sénégal kay dagn ko fiy lakk guiss na finiou koy lakké ba tayi. Dou ame khorom c vrai goût bou nékh la yaboy bou séw bi la
Mé bénénn yonn dél séfeutt kéthiakh bi
th bagn ko rossi deub kethialh bi ak sople bi nokoss ❤
Lolu guédji yass lay niru dh
@@wedjigueye7738yassi lan 😂kéthiakh yauss leu da melni
Ki téyoul guerte gui ak Nokkoss bi
Une autre façon de préparer le mbakhalou saloum ça l’air délicieux .
Gnoune saloum saloum dougnou rossi
C vrai saloum saloum dou rossi. Mane mom meussuma rossi
@@sokhnamaisaliou9430vous faites comment ?
Gérté bi ay bouko tayone😊
Rossi bi kayy moma diakhal
Où sont les saloum saloum no rossi 🎉
Mane xawma rossi xawma nioulouk ak nehkayam doumako djiegueh doumako xol bokay leeck do sour so pare beug mou resse mou teula😢
Nekhneu; deukhinou. Saloum bi! Merci. Bcp ! A shaa Allah !
Dina beuri yakh deh 😂😂 a
Khana😂😂
Sama t
Beugouma wone wax 😂😂 mais le reste c okay ❤
Bilay
😅😅Yallah boma xass
Chacun a sa façon de cuisiner merci beaucoup pour la recette ❤❤❤
Thiammm
Mon plat préféré ❤❤❤
Ms lidou kethiakh yoyou dh ❤
bayiléne commentaires you négatif yi té lér nama gnisi moune tog bariwoul en plus tog da bari façon
Togue da bariii yone sénégalais xamoul lolou
Gni commentaire yeup mounou skh togou
Merci. Gni danio soof melni ay chef. Té togou kou nekk ak sa façon
Bouléne saboté sounou mbakhalou saloum bi😅😅😅 daguaye defe yapou késsé wala kéthiakhe késsé wayé pourquoi melangé les 2 yake rekkk😂😂
Mais bon appétit
Wa mé mbakhalou saloum deugue kéne douko rossi dou ame diwline ma chérie
Si boula nékheé khanna do toggu
😂😂😂😂 Neil iow beugo bou âme diwline wala xamoko
Yow mi nak ya mbakhal saloum machalah
Melni yena koy lek nane boul Rossi sof nguen😂n’a ress ak diam
Gni kay séne mentalité diakhalnama té khamouniou dara
❤
Quel bon plant
🎉
Un plat que je peux pas réussir 😢
Sheuuuuthhh sma natou la🥰
Mbakhalou saloum doko khorom sinon mou wékh, guissouma guédj, kethiakh bi dagnko wara tane deub ko aussi ci nokoss bi, guerté bi dagnkoy tay avant de verser dedans...
Mane douma tay guèrtè
Kou nek ak nigaye toguè motah
Taye guérté bi dou force ni mou ko défer ni sakh mo gueune
@@mamandeyediaw6331 kéne forcé woul kéne on donne juste un conseil. Aussi wakhal yow bagna taye mola gueuneul wayé boul wakh mo gueune. Mane tay moma gueuneul sinon guerté bi dou nior
Amna niouko doul Tay bouniou sauré laniou koy def
Nioune wa dakar danioukoye rossi mais gerte noflaye danioukoye taye 😅😅😅😂
man wa dakar bi ma gui sogua. guiss kouy rossi mbakhalou saloum😂🙏
@@yacinendiaye-sc5gd mane mbakhalou Saloum damakoye Rossi genewalou walatou diweline bi damakoye khâge sakhe mais une fois prête nekhe laye defe
bilay damay togn rel mais niar yeup comme dsfay am diw nior boula nekhe rossi ko mome la togue tay mais genre dama nioulouk dogua. si def diwlin bi mais nekh rek la def davvero 🤣🤣🥰
Mane niar yéupe la meune rossi ak nioulougue wal day yalé guerté bi wala wis kosi niéne niar niépeu noléneko togué mou 😂nek je vous j'aime 😍
Togue dafa bari façon mane damay gnoulouk deub sama kéthiakh ak sama gnébé diakhassé nétatou ak touti kani ak soplé mélanger ko ak guerté gui souma soré sama thiep tek ko thi kawam
❤❤❤ voilà genrou commentaires yi mo instructifs tei dou vexé keine
Amsterdam 🇳🇱🇸🇳 sénégalaise 😘😘😘✅
sa l'air nekh machallah
Yéteu ga faté si rosie bi 😂
Sama plat préféré
Saf rek 🤤
Kethiakh ak yaapou andoul
Mbakhalou saloum kéneu douko rosii saloum saloum yi douniou ko toguéni
Taye filaye xole pour togue plat bi Sama premier foi
Mbakhal nay simple sans rossi sinon dosi meuna lék lou beuri
Bien fait ❤
Gnoune saloum saloum dougnou rossi bénene yone nanga séfeute kéthiakh bi
Si non yak yi rek c'est pas sûr
Môme rék l'a begue nak😂😂
dafa neikh deh
Bene yow boulk rossi waye möytoul yakhe kethiakh fedoet ko
Kéthiakh bii
😂😂😂😂
Pourquoi kéthiakh ak viande bi li mome andoul dara hummmm
Meuna nékk mais dako waron deub si nokoss bi tayaléko ak guérté bi
Man saloum la deukk dh doumako togué nii 😂
Plat délicieux
Ma'challa
Bon appétit 😘
Hum Masha'Allah sister
Machalla
mes nokoss bingua deffat si kaw guerte bi nak avant nguay def thiep bi nguako wara def nest ce pas
très bonne ❤
Nice❤❤
Salam svp ces quel poudre maron et le dernier norkoss que vous aviez mis sur le riz.
Le poudre maron c'est du poudre d'arachide et le dernier comme vous dites du(nokoss) c'est de l'ail, oignon,poivre noir, piment ,cube ou sel et de la moutarde africaine appellé (Netetou en wolof),un type de feverol appelé (Soumbara) en bambara,(dawa_dawa )en igbo😊
Amene
👍👍👍👍👍👍👍👍👍👍👍👍
salam li nexna deh. kharal ma khifeul après togou ko. MACHALAH.
Mbakhal Saloum dou am huil
🎉🎉🎉❤❤❤❤
Dama mbeuge niame
Li kay mbakhal Dakar la.mbakhal salum day naturel dou bari khoudiour khoudiour way.😂😂😂mangui takhamtikou ta nioragoul
😂😂😂😂
War n'a nekh dé
Wa g avais op vue fin bi saxx lol lil mom mbakhalou saloum
Bonne appetit
Y'a trop des épices
Yéne sof ngéne loutakhe sénégalais bone rk
❤❤❤
❤️❤️❤️
Li dou bakhoulou saloume deah😢
😂😂😂😂😂
❤
Mbaxalou saloum kene douko Rossi teh gerte bi da ngua koye taye ake nokos bi bamou sousse . C'est pas comme ça deh ça c'est votre façon dakar
Kaldou
❤❤❤❤❤❤❤
😊😊😊😊😅😢😂🎉❤ je vous germé pas je rede toute la journée 😢
Bon appetit
Pas d'huile pas de rossi au mbakhal saloum
Plus ou moins.
🍚🍱
C’est pas du mbakhalou saloum authentique
Hummm am no sure but this is not how i cook it😊
Yaw bayil wére sa bopou mouno toog ani sa guédji,, khéthuakh bi tamitte bari yakh😤
Mais sister Amna nétatou wala
waww amnaa
@@anonymousCookerrNokoss bi Lane la exactement
Trop nul!!!!
Yaw manga
❤❤❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤
❤❤
❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤
❤❤❤
❤❤❤❤