ขนาดวิดีโอ: 1280 X 720853 X 480640 X 360
แสดงแผงควบคุมโปรแกรมเล่น
เล่นอัตโนมัติ
เล่นใหม่
Dieuredieuf Serigne Saliou Al xuran.Xam Xam gui sel n'a lolou
Dieuredieuf Serigne saliou❤❤
Macha allahou❤❤
Serigne saliou seck dafa meunn❤❤❤
Machallah waxtan bi nekhna lole waye Émission dafa gate
Mais eskeu khame guèni Pape Sidy Fall nakatoufi kénn dou Cheikh Ahmadou bamba Xadimu Rassoulilahi ❤❤❤❤❤❤❤ émission bi guate rk moy thiate liiii
Mame Dame dafa beuri NDIARINE ❤
Macha-allah dieureudieufaty Cheikhoul KHADİİM Diarrama Borom NDİÉNNÉ
Ndeysan li dafa nekh bileuhi❤❤❤❤
Wakana haqqane bi 😊
Émission bi mom gaatt rk moko yakh nékh na lool❤❤❤❤❤❤❤
Daffa gatt trop kay 😢machallah émission bou beurri ndiarign leuh ❤
Meilleur émission fi ak magal da saf sap ak safar
Mais pape sidy émission mougui Gate legui dé
Machalah kene dou s touba amoul morom
Dieureudieufé Serigne Touba amoul morom ❤️❤️❤️
Jërë ngeen jëf! Waxtaan wi amati na soló, Sëriñ Ceddo Murid Saadix ma ngi lay bëgee bu wér, MAGAL GI Yàlla në suñu Boroom yéwénal lépp, te teg ñépp ci yoonu jàmm ak njup 🙏🏿
machallah waw goor mourde ❤❤❤❤
Dieureudieufé Sérigne Touba
Ay way émission bi dafa wara continuer ❤❤
Masha'allah khôl sed
Waw lene goor mourde yi ❤❤❤❤
Dieureudieuf Cheikhoul Khadim kimtaan sounou Borom tabaraka wa tahallah
Ndeysaan❤
😢😢allahu akbar cey sunu wadji😢😢
Machllah 😢😢
Dieuredieuff cheikh AHMADOU BAMBA
S touba dieureudeufeuty ❤
Sama wadji serigne saliou alxourane diabar dji beri xam xam lol manchallah
Jërëjëf boroom Tuubaa xaadimul Xadiim ❤❤❤❤
Cheikh Ahmadou Bamba ☝️ 😭❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
dieureudieufeti serigne touba khadim rassoul ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Wallahi nit ku dëgg-u mom, li Seex Ibrahima JOOP wax rek : « mooy ki wax ni SËRIÑ TUUBAA amul moroom ». Jërëjëf Ceddo Muriid !
1h dafa gattttt
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Yénena looolll borome Touba omoull morom
❤❤❤❤❤❤
Diadef saliuo
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
😭😭😭
❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤
❤️❤️❤️❤️
Dieuredieuf Serigne Saliou Al xuran.
Xam Xam gui sel n'a lolou
Dieuredieuf Serigne saliou❤❤
Macha allahou❤❤
Serigne saliou seck dafa meunn❤❤❤
Machallah waxtan bi nekhna lole waye Émission dafa gate
Mais eskeu khame guèni Pape Sidy Fall nakatoufi kénn dou Cheikh Ahmadou bamba Xadimu Rassoulilahi ❤❤❤❤❤❤❤ émission bi guate rk moy thiate liiii
Mame Dame dafa beuri NDIARINE ❤
Macha-allah dieureudieufaty Cheikhoul KHADİİM
Diarrama Borom NDİÉNNÉ