Fatou on sais pas toujours comment elle a perdu sa virginité Mamy et le gars qu’il l’avait trouver dans la rue est ce qu’il finiront ensemble Daro avec son grossesse Madickè trompe sa femme Vraiment trop de choses à découvrir kudul setaan Virginitè setanoo dara
Bon mahfousse li ma remarqué si théâtre bi moy séne acteurs yi danio déssé niémé camera yi soumeuh sagnone niou gueuneuh géneuh sensou théâtre bi merci ❤
Bon boulot les gars
Une série vraiment intéressante ❤mais j’aimerais que vous fassiez une série sur le body-shaming et le sentiment que ca procure chez les victimes svp 😊
J'ai un scénario à vous offert
Cv
Mahfousse et son équipe yalla nagn gagner ay millions ci projet bi vraiment ce truc là n’est pas une réalisation facile
Bravo 🎉❤
Yallnagnou yalla mouseull si goor bou meuneu netali
😅😅😅 doul kate dè moussi beu leu😅
Mouy goor di djiguénes néttali si boppam mo waroul thi dômou Adama nitte dou féne
Fatou on sais pas toujours comment elle a perdu sa virginité
Mamy et le gars qu’il l’avait trouver dans la rue est ce qu’il finiront ensemble
Daro avec son grossesse
Madickè trompe sa femme
Vraiment trop de choses à découvrir kudul setaan Virginitè setanoo dara
Les filles réveillées vous kep lene ko tè yalla takh
Bilay deugue rek nga wakh
Inchallah 😊
Madiké Nènako sa far bou yambar bobou😂😂😂😂
Merci Madiké🎉
Jumulén si casting bi déh killer ahe yayam dano niro béneu lanou
Lol
Son 🔊 bi tmt partout dans le monde ❤
Bon mahfousse li ma remarqué si théâtre bi moy séne acteurs yi danio déssé niémé camera yi soumeuh sagnone niou gueuneuh géneuh sensou théâtre bi merci ❤
Yeah mane sax mom la guiss mais loubiouy liguéyatt l rek gayi dinagn si taxaw ❤
Surtout mère yi
Daro elle est belle naturellement machallah
Film amna sens torop mais acteurs yi gno dess surtout les femmes ayou gnou c'est à dire dougougnou à fond si serie bi daffa dess lou barri
Tu as raison kay
Surtou lol
C vrai ayou gnou
Vraiment chapeau a vous
Plus de ❤ pr cette chaine et series amna solo trop ❤❤❤
Wa yayou killer mi mom bane espèce le 😂😂
Ay waay 😂😂😂
@@bocarguisse2282 ah mére bi kay xamoul ay wax
😂
Moma diakhal 😂😂
😂😂killeu khallé la mannoul eummeul 😂😂 8 ans wala barina 😂😂😂
Encore bravooo Mahfousse c’est la meilleure série bonne continuation épisode bi waaaaw 🙏🏻🙏🏻🙏🏻🙏🏻 mais sponsor yi lougni khar
Li kouko xol warr na teh sa bopou xamnga li gathié la si bépp waydiour💔
Wadiour yi louniou déff nioune Kay nion waraa gëunëu fonkou Souniou boppou kham nioy Kane mane dh heureusement douma nangou sah sétti goor
Mahfousse Ou je puisse avoir le contact du scénariste svp pour un truc internatnal
Killer mome mére bi mokko diourr car yéne ndiro yi dou hazard😁
Mère bi nénako démal si Say schéma😂😂
Wa nekoull kerock épisode 5 ladone setane😮
Bii episode 7 la
Saway salaminguebi nak😮
No madiké loy df ni tmt😢
Gayi abonnélén si sama chén bi lou amsolo laye dougeul gir yalla
J'ai abonné ❤
Amna solo 🇸🇳♥️🙏
Makhfouss loutakh bokoul si série bi
Khalil meune na nétali si goor thiprii😑
Néttali si boppam mo bakhoul thi dômou Adama 😢
Macha Allah
Série bi dafa am sens
❤❤❤
Madické ce que tu as fait est injuste
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Madické moye mbam😪
Papa ndogal yalla fep lay dall
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Khawma kille khawma lan ay dome arame lh
Nic
Makhfouss loutakh bokoul si série bi
❤❤❤❤