Mon lutteur Modou Kharagne Lô je suis encore très fière de toi li reck la djioulitte di diarine moromame Machallahh Toutes mes condoléances à la famille Gaye
Machalla massa les lutteurs massa la famille et amis merci beaucoup notre roi des arènes Moudou lô un homme généreux gentil disponible c'est très noble de votre part merci pour le soutien apporté a mais fréres de cœur repose en paix pére double less que le bon dieu t'accueille dans son paradis Amine yarabi 🙏😭🙏
Bilay gniak papa aka metti kham nathi dara parce k j'ai perdu mon père depuis mon enfance yene gni sene papa di dounde profitez vous am seni ngeureum wadiour wou gor té dilene gnianal goude fane ak werr thi sene papa
Raféte na machalla you mélni rék warna takh ngéne di wakhanté lou bakh ak lou Raféte si lambou dji nah sport rék la dafay diékh ta li dou diékhe kone naye guena raféte séne birre
Mane balla moy sama mbeur mais bess niki tay mbeur yeupeu lay bégué nakh guiss na niom nieupeu nigniou yéno tisss bi yalla naléne yalla may diameu double less yalla nako yalla yeureum xaréko firdawsi 🤲🤲🤲
Yén gni comprendroul balla gaye souy wakh modou lo dou sama roi pour nékhal lamp kassé leu, mai khamnane modou lo est le roi des arene actuel❤❤🇸🇳 one love
Li moyyy senegal ce que modou lo a fait aujourd'hui balla gaye avait aussi la même chose lorsque le pere de modou est décédé vraiment li rekk moyyy aduna nayyy rafetttt rekkk
N’oubliez pas de vous abonner sur votre chaîne Senbuzz Tv et d’activer la cloche 🛎 pour recevoir les notifications merci.
Sama lutteur bii t’as fai un geste noble tes fans te remercie vraiment ns sommes des être humains
Les deux meilleurs lutteurs de tout les temps
Mashalla bip up a vous
Oui
J'ai presque versé des larmes pour la compréhension des lutteurs surtout ce geste de Modou lô vraiment
Mon lutteur Modou Kharagne Lô je suis encore très fière de toi li reck la djioulitte di diarine moromame Machallahh
Toutes mes condoléances à la famille Gaye
Beaucoup de ♥️♥️♥️pour ces grands hommes avec des cœurs en or yalna diam yague
Je suis fans de bG2 mais aujourdhui je suis fiert de modou lo 💍💍❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Toi faire té prière pour père double less mo guen wakh lamb 🤣🤣
@@ibrahimkasse2045 🤣🤣🤣🤣ay way
@@ibrahimkasse2045 dafa lerrr 😂😂😂
Machalla massa les lutteurs massa la famille et amis merci beaucoup notre roi des arènes Moudou lô un homme généreux gentil disponible c'est très noble de votre part merci pour le soutien apporté a mais fréres de cœur repose en paix pére double less que le bon dieu t'accueille dans son paradis Amine yarabi 🙏😭🙏
Machalah modou lo adouna amoul solo lép ben laa merci balla je suis fière de vous
Machalla Modou li geste bou Nice la aduna amoul solo yéna book lepp fier de vous
J
Bilahi Modou moy sama mbeur wayé Balla Gaye damako beugg,dafa oyofeu mashallah.Yalnako yalla samal bopame mok gnome Sa Thiés ak ndiambote gui yeup🙏🙏🙏🙏
barki serigne babacar sy sm khol dafa sèd trop trop trop bilahi yalla na yalla def diam si khol yi ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
These's so heart touching and there's nothing like togetherness,May our dad heaven be his resting home
Modou lo moy sama mbuer mè balla gaye khoul bou rafetla yor machaalla
Maa cha allah Modou sama mbeur bi yalla nala yallla sameu 😍❤️
Man dall ki dama ko beuk rek Modou yalla n’a sa diam yakk aminnn
Ohhh liii nice na supporter yidone wakh Lou niaaw khana rouss ngeene
franchement aujaurdhuit je suis content fan de modou lo machalah lii rafetnaa franchement
Repose en paix papa doubles 😭😭😭😭 diadieufff sama Champion modou lo
Bilay chapeau aux lutteurs beaucoup des gens les dénigre mais vraiment ils sont juste des noble fier des lutteurs
Le monde de la lutte fait un pas en avance. Voici un exemple a prendre en compte. Merci tout est bon
Fier de toi modou lo mon lutteur❤❤BG2 goude fane ak werr gou yarame
Machalah limoy Sénégal 🇸🇳 dakh li rékk lanouy kharr thi yénn après sport bii gneup beneuh lagnou 🙏🙏🙏🙏🙏🙏😘😘😘
Machala Nice modou Lo sama mber bi
Machalla C'est sa le Sénégal walahi
T'es fans te remercie 1000fois♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️
Qu'il repose en paix si barcké seydina Mouchamed Pls 🙏🙏🙏🙏
Les supporters doivent prendre conscience ce geste nous édifie en tout idem pour les politiques
Fierté pour le Sénégal lii nékhnaa
Modou lô😃 ndey sann
Je suis fière de toi Modou lo
اللهم اغفر له و ارحمه بجاه سيد الوجود صلى الله عليه وسلم
Machallah 🙏🏽Modou x Lo le roi
Repose en paix doubless
paix à son âme
Diameu dama nekh li dara guenouko
Bilay gniak papa aka metti kham nathi dara parce k j'ai perdu mon père depuis mon enfance yene gni sene papa di dounde profitez vous am seni ngeureum wadiour wou gor té dilene gnianal goude fane ak werr thi sene papa
Amen , nice bless all of you amen , rest in peace papa.
Machallah modou lo rafet rek mo am solo
Machalla li rafetba balla borom bakhla ❤️❤️rip papa🙏🏻🙏🏻
Machallah amna solo yalla nako yalla yeureum
Macha Allah Modou lo
Mon champion Modou Lo ❤️
Ces la vie nous sommes tous des Frères père double l'ESS paix a son âme 😭😭😭
Jsw Balla gaye 2 merci frère modou lo jsw fiér de tw❤️💪🙏
Raféte na machalla you mélni rék warna takh ngéne di wakhanté lou bakh ak lou Raféte si lambou dji nah sport rék la dafay diékh ta li dou diékhe kone naye guena raféte séne birre
Machallah sama khól séde na lol si li..senegal nio ko mome te gneup béne lane na leup rafét rék ndakh si nétaly rék lay moudj
Merci champion Modou Lo gadouyi refetna
C’est ça le Sénégal 🇸🇳✅ Rip double less
Moudou c'est un grand champion les deux meilleur lutteur de cette génération
Yallanako yalla yarame ta xaréko Aldijana Barack s touba
Mane balla moy sama mbeur mais bess niki tay mbeur yeupeu lay bégué nakh guiss na niom nieupeu nigniou yéno tisss bi yalla naléne yalla may diameu double less yalla nako yalla yeureum xaréko firdawsi 🤲🤲🤲
Mon lutteur balla et modou❤
Bilay lii da fa nice
Machallah champion modou li rafetna lol balla massa yalla na firdawsi di geureum.
Bilahi sama lutteur moy goor Dieurédieuf ti❤❤❤
Diadieuf Modou mon lutteur 🥰🥰❤️❤️❤️
Machalah sama lutteur sa geste nice na noble na ni rek la adouna amoul solo
Machalla
Yén gni comprendroul balla gaye souy wakh modou lo dou sama roi pour nékhal lamp kassé leu, mai khamnane modou lo est le roi des arene actuel❤❤🇸🇳 one love
Machallah Nice na yala na ko yala khare aldia amine bake seyedinamoukhamet bala kou bah la
Hô sama xool sedna jaime balla jaime modou lô 💪💪💪
Ndeysan Modou lo wakhna wakh ji rafétt merci
Nice ❤️❤️🙏🙏
Machallah je suis fan de module lo mes balla yalla na sa diam yagueu rafetna Machallah ❤❤❤❤❤
Machalla amna Solo du 🤝
Machalla rafetna billagui kene d’où balla Gaye
Mersiii champions
Li moyyy senegal ce que modou lo a fait aujourd'hui balla gaye avait aussi la même chose lorsque le pere de modou est décédé vraiment li rekk moyyy aduna nayyy rafetttt rekkk
Machalla deuk rek deuk yala na yala sam soutral Sénégal diam rek ci toute sénégalaise mercis beaucoup 🤲🤲🤲🤲🤲❤❤❤❤
Nicena l'OL machallah
Machallah nice ❤❤
Lidou kemtan deh mai Modou Dema moudié beug sakh ndakh Geste bou rafet bi Balla gaye2 moy sama mbeur mai je suis très contente de Modou lo
Machalla limoye Sénégal,lou Raféth rek mofi khath
Yalla na yalla doli diam inchahala🤲🤲
Merci Modou👍🏼❤️❤️❤️🙏
Vrement je suis très content sur cette gest de noble faisait par la délégation du rogue énergie (modou lo)
🇫🇷🇫🇷ont suivre depuis Paris ndeysane modou lo ça m'a mbeur la biillaye modou lo deffa gaarme moo genna nekka bogoss mais kenne duu balla gaye
C balla le beau gosse et t'es à Paris
@@daoudafall9428 😁😁 non modou très très bogoss
@@diilerecaalifuuta549 un petit peu ahah lol 😂 suis 💯/💯 Balla. Idem suis à Paris.
@@daoudafall9428 moi aussi je suis a Paris Châtelet Paris
@@diilerecaalifuuta549 à ouais je connais vire pv snap ou tn numéro stp.
Nice Modou yena bokou ndaye bg2 dicourage champions
Masallah Lee refet na balla sama star bi but modou Le refet na dunda Lee beh dunda sapila contaan trope
Machallah yallana diamou yague
Manchalah li rafetna trop modou lo et balla yalla nasenn diam yag lirou ioe itam sa kadou manchalah rafetna nit dangay deugou
Machalla 🥰🥰
Boulen beuréti waay nek léne ay kharitt cone gnép contane
Bilahi
Lou nice
Non Balla na gnou may bénn victoire guir yalla monek 2 1 sakh ba paré
@@cherialdiana8719 bly wakh ga dekeu danion sonou😂😁🤣
Loolou mane te niakka bay
Merci Modou li rafetna trop
Mashallah❤❤
Machala ❤️
Machallah rafett na trop🙏🏾🙏🏾
Mashallah mashallah mashallah
Ay sama champion bi bilahi noble la 🥰🥰🥰
MACHALA CHAMPION MODOU GESTE BI RAFÉTNA
Un vraiment ça c'est bien c'est le Sénégal j'aime mon pay
Masa'lah modou kharagne lô li Nice nâ trop
modou lo takh nga malay geuneu nianal billahi mashallah li moy nitt adina amoul solo
quel maturité de Modou nila de fakhèkh ba nité rek après sport diam rek mosi wara topp yallana yalla yereum pa bi
Yalnako yallah yeurem
Machallah Nice n’a ❤️❤️❤️🙏🙏🙏🙏🙏
Vraiment 1 beau geste
Ndaysane adouna dou Dara bilay fans Modou lo mais je vous aime vraiment les deux longue a vous ♥️💯♥️💯
Le roi des arènes ta fé un geste de noblesses tt les fans sont content
Fier de toi et respect li moy aduna 🥰🥰🥰🥰
Ndeysane geste noble pour modou kharagne lo li rafet na loll barkep serigne Touba
apars lutte nous sommnt touche des humaines devant dieu