Adouna mo tereudi,Aissata Tall Sall ministre de la justice bou takalone El Malick Ndiaye bracelet électronique mooy mr le Président nii,ndeysane Yalla dou niite❤
lolou motakh nio beugone ko proposer président du groupe parlementaire takku wallu... ngir yèkhal votou loi bouy abroger loi d'amnistie bi.. wayè loi bi daniou ko voter par force inshallah ndakh pastef mo am majorité bi
Dimanche passé AissataTall Sall tutoyé El Malick en le le nommant ce monsieur aujourd'hui elle l'appelle M. Le Président. Elle ne trouve rien d'autre à faire qu'à défendre une candidature de Farba Ngom comme vice président peut être pour chercher à le protéger contre les milliers d'ha attribués injustement par des autorités qui cherchaient sa couverture auprès de macky.
Mèrci El Malick Ndiaye ❤️ yalla mo beuri dollè dama rouss sakh man bilahi adouna yalla toujour daf niouy won bopam Aissata Tall sall tè El Malick ndakh moy sa chèff yalla kèn mounou kham bilahi
On est content,farba a parlé aucun micro ne voulait transmettre son message au peuple sénégalais patriotes jeune en majorité 😂😂😂. Sonko moy diomaye moy majorité 🦁🎖️🤝🇸🇳💪
Merci beaucoup monsieur le Président de l'Assemblée nationale el Malick Ndiaye j'aime beaucoup son attitude machallah el Malick Ndiaye ya ameu foula ak fayda el Malick ameuna caractère machallah fi mouss doufi nané niékhe 😂😂😂😂😂 merci beaucoup pastef les patriotes 😂😂
Félicitations Monsieur Le Président El Malick tout Le Djolof est très fier de Wa apr guiss nguéne adouna ki nguéne takalone bracelet électronique bi moye séne Président 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Félicitations que votre mission soit accomplies avec succès amine❤
ALLAHOUMA AMINE 🤲
amine yarabal halamine
Amin
Amin
Allahou ma amine
APR Louleen Nakari Nexgnou😂😂😂
Khana😂😂
Danio amoul diom rek mais ils devraient raser les murs
Billay
Waxxatiko dé
taymou nekh 😂😅
Merci beaucoup MR Le président El Hadji Malick Ndiaye foulla reke
❤❤
Boul wakh ak niome douniou yaw té do niome niak fayda daniou laye todial toutes mes félicitations yalla na yéneu bi woyoff alkhamdoulilah ❤❤
😂😂😂😂
J'AIME BIEN L'ATTITUDE TRÈS FERME DE EL MALICK.
Qu'il soit ferme
Mashallah. elhadji Malick Ndiaye que.le bon Dieu te soutiene dans cette épreuve .yalna gua KO reussi
Dieredieuf el malik Dieredieuf bravo
Mane dama contane sakh li esk worna li esk dou ay guent biy caractère bi fouleuh ❤😭 non je pleure pas
Pour mane li dou réalité
Je suis trop contente😂
😂😂wallae deug leu pastef mo pogné Sénégal ni tchi loxom🥰sama xol bangui sedd
Merci Ndiaye Diatta 🎉🎉🎉 mission fécond.
Dieule Ndaré baa paaré di beugue imposer sa loi. 😂😂😂
Ils rêvent,ils se pas encore réveillée de leur sommeil.
😂😂😂
Boy bayilen Tonie way😂
😂😂😂😂 doyna warr dééé
Vraiment
Thieuy adouna boul Bouy tournéla
Wallahi adouna yalla moko mome
Adouna mo tereudi,Aissata Tall Sall ministre de la justice bou takalone El Malick Ndiaye bracelet électronique mooy mr le Président nii,ndeysane Yalla dou niite❤
Walahi, lou waay di def rek na siy sooralé sa borom
AHH OUI ❤❤❤
😂 aduna mo teuradi com kouy nelaw si lal a tout moment manga danu😂😂😂😂
Walahi
Wallahi
Louway mougne mou diékh Walahi 😊
Wallahiiii
Wallahi mougne da meti nak😅
Ces gens de l'apr n'ont vraiment aucune vergogne!!!
Je t’assure , quand j’entends Me Aissata TALL dire “ Monsieur le président “ Dieu seul est DIEU
PERSONNALITÉ 000
😂😂😂😂😂 thiéyyy adouna 😂😂😂 le karma existe vraiment, chaque jour en tournant la terre fait basculer gravement quelq'un qui se croyait être au sommet
Merci beaucoup tu as tout compris si niékeu yalla rek
Bilahi wallahi elhdij Malick ya am foulla niom si diaye dolle rek laniou yorewon rewmi farba domekhram dji laynioy force
Farba rek laa yaakamti mou dem kasso 😂😂😂
lolou motakh nio beugone ko proposer président du groupe parlementaire takku wallu... ngir yèkhal votou loi bouy abroger loi d'amnistie bi.. wayè loi bi daniou ko voter par force inshallah ndakh pastef mo am majorité bi
Ha ils ont peur d'aller en prison😂😂😂
Merci beaucoup el Malick Ndiaye ❤ bly bek na thi yow ❤
Vive MR Ousmane sonko, Vive Pastef les patriotes ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Machalla sopana ndiayene bi foule akk fayda assemblée bi nekhena 😂😂😂😂 la roue tourne dokhalale mre ndiaye seutou alboury bi lo def yonela😂😂😂😂😂😂
Taay mou neikh😂😂😂
Machalla Ndiaye Diatta Ndiaye 💪💪💪
Alhamdoullillah yalla naniou agalé ak souniou téyou bakane ak reussit total in schallah 🇸🇳❤️ wa apr yaroulen 'gueni thieupi thieupi ni
😂😂😂😂fi gni fi narra ammeh febarou xol narr na barri....oh deysane yallah akka meuna atteh🤣😂🤣🤣
Bilahi wah gua deug pure 😂😂
Trop fière de vous Mr. El Malick Ndiaye. Mission féconde à vous.
AY WAY WAY NDIAYE SANGUE SAMA DOMOU BAY AMAL JAMM❤❤❤❤FOULEU REKK INCHA ALLAH ❤❤❤❤❤🦁 🦁 🦁 🦁
C’est très bien rigueur rek depuis la matinée ils bloquent tout bania respecter la liste paritaire ❤
Vous comprenez maintenant le choix de El Malick
Dimanche passé AissataTall Sall tutoyé El Malick en le le nommant ce monsieur aujourd'hui elle l'appelle M. Le Président. Elle ne trouve rien d'autre à faire qu'à défendre une candidature de Farba Ngom comme vice président peut être pour chercher à le protéger contre les milliers d'ha attribués injustement par des autorités qui cherchaient sa couverture auprès de macky.
@ c’est exactement cela un deal dont ils ont convenu et pensaient le faire appliquer mais c’est fini le temps où ils nous tenaient en otage
Je suis content 😂😂
Non El Malick Moy bandit 😂😂
Merci El Malick pour cette fermeté
Mercii beaucoup el malik❤❤
Merci beaucoup El malick ❤❤❤❤
Khôl tangons si yeulé temps mé sédatena si yi temps merci notre président Assemblée❤❤❤❤❤❤❤❤
Sonko moye bandit 😂el malick ndiaye dokhalal boula kéne yepp
Bandit woul nank sakh
😂😂@@light_stars778
Très bien merci El Malick ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
choukrane yalla yalla dolli takhawou sunu Président de la république son excellence BDF et son Premier ministre S Ousmane Sonko et El malick
Amine yarabi
Merci Mr Ndiaye, ils ont oublié comment ils ont procédé en 2022 pour élire le bureau. Leur premier vice-président était un homme du nom de Sall
Merci beaucoup pr El Malick Ndiaye ton dignité
Mèrci El Malick Ndiaye ❤️ yalla mo beuri dollè dama rouss sakh man bilahi adouna yalla toujour daf niouy won bopam Aissata Tall sall tè El Malick ndakh moy sa chèff yalla kèn mounou kham bilahi
Fuleu rek khalé mooy yaar makk foofu laniu tollu neuk diamono djiii
Aissata talll yako takalone bracelet electrique a el malik Soubhanallah
Li yéména dé😮😮😮
Non je crois c'etait Ismael Madior
Walahi ndeysane
Waye waye nite foula. MERCI EL MALICK ❤❤❤
Thiey adouna
Bly 😂😂
Wa APR ay fils à papa laniou té hamou niouné séne baye déhna
Tu vois, face à l'arrogance Dieu ne met pas de gants pour punir !!
La jeunesse a de belles leçons.
Seule la vérité triomphe.
Merci el Malick APR boulene niou sonal daniouy liguey nioune
Merci monsieur le Président de l'ensemble nationale
Merci ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Taye mou nekh dè😂😂😂❤❤
Merci beaucoup EL malik diambar la
Aissata tombe bas,une dame si respectée d antan...ndeysane ne te laisse pas rabaisser par Macky....
Whats goes around comes around 😂 😂
Congratulations PASTEF 🎉
Sama mbok djolof djolof bi mo am fouleu way. Wa takou walou diguen yarou par force
On est content,farba a parlé aucun micro ne voulait transmettre son message au peuple sénégalais patriotes jeune en majorité 😂😂😂. Sonko moy diomaye moy majorité 🦁🎖️🤝🇸🇳💪
Foula ak fayeda continuer le travail
J'ai mal pour ceux qui ont voté pour cette liste takku wallu
😂Damani É Pastef kou gnak fayda dioudo wufa. Sougnu leader rèk si charismatique merci El Malick.
SONKO moye diaomaye Senegal kese 😂
Les voies de Dieu sont impénétrables. Ravie de voir que la situation est devenue inverse à l'assemblée nationale. Vive le pastef.
Avançons 🎉🎉🎉🎉🎉🎉😂😂😂😂❤❤❤❤ Sénégal Ndiaye Ndiaye diatta Ndiaye
Ex apr 😂😂
Wah gua deug déé ex apr 😂😂😂😂😊
Bollo djeulna coup😅😅😅😅
Merci beaucoup Mr le président El Malick ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Merci beaucoup monsieur le Président de l'Assemblée nationale el Malick Ndiaye j'aime beaucoup son attitude machallah el Malick Ndiaye ya ameu foula ak fayda el Malick ameuna caractère machallah fi mouss doufi nané niékhe 😂😂😂😂😂 merci beaucoup pastef les patriotes 😂😂
Merci beaucoup El Malick Ndiaye ❤❤❤❤
Macha allah. On est fière de vous❤❤
6:27 Trop content qu’elle soit vice-présidente la benjamine
Merci bcp le president El Malick ❤❤❤❤
Kholéne niou melni aye kharou yar béneu mélo 😂😂
Y’a bone😂
@@wakkanahaqqan7136 ah dama wakh deugue di gni dagne nio yapeu 😂😂😂😂😂
@ motax lou way di def rk na soralai euleuk c’est important
😂😂😂 apr damaléne moudieu yeureum
@@wakkanahaqqan7136
Bilahi dama réé béneuh melon bassone
Force restera à la loi merci El Malick
Ohhh adouna dafa mélni sètaane mossi dakke😂
j'aime vraiment le nouveau Président de l'Assemblée National
Hahaha mon cœur frigidaire vive les patriotes force au peuple❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Merci beaucoup elhadji Malick on né très fière de vous que le bon dieux te garde
😂😂😂Non El Malick Ndiaye je l'aime très bien 😅
Lidé laniounane adouna yalla ko mom le soleil brille pour tout le monde wa Apr nanelene glace
Merci sonko ❤❤❤❤❤
Félicitations bilahi Sénégal dina nékh dé
Gni khana ladiouniou chauffeur yi el Malick.
Khana ladjonlen wa transport kouy El Malick Ndiaye 😂😂❤
😂😂😂😂😂Amadou Ba N'1
Amadou N'2
Wa Takku-Wallu kou guéd sa yaya ayé😂😂😂😂
C'est fini la politique politicienne. Vous êtes là pour le peuple alors respectez vous, respectez le peuple et concentrez vous au travail. Merci
Vive le président bassirou diomaye Faye et son premier ministre Ousmane sonko que le bon Dieu vous bénisse et vous protège Amine yarabi almin ❤❤❤❤❤❤❤❤
Non Sonko dou nitt limo takh niou tann El Malick bilahi dafa sadick deugeur bopp té dou bayi benni golo di yakh tool bi 😂❤❤
Vive le premier ministre Ousmane sonko et sont gouvernement que le bon Dieu vous bénisse et vous protège Amine yarabi almin ❤❤❤❤
Yalla dou nitt 😂😂 🎉❤ bonne continuation les patriotes
Jetli dou dem nelawi 😂😊
😂😂😂
Sortez les vieillardsde Karam qui ont foutu le pays dans la merde
Surtout ici à mbao defoul fii dara
Pendant 12 ans vous étiez au pouvoir en étant les députés de Macky , ça fait mal quand on est pas entendu hein … ben c’est ça Niam len 😂😂
merci el malike 😭😭😭
C'est très bien Monsieur le Président. Tous les sénégalais sont derrière vous. Restez ferme car ces gens ne veulent que l'échec du projet
😂😂😂😂😂😂😂
Merci président
Félicitations Monsieur Le Président El Malick tout Le Djolof est très fier de Wa apr guiss nguéne adouna ki nguéne takalone bracelet électronique bi moye séne Président 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
dieul len niou melni ay ndiougoup bilay wa apr nio niaw te niak feeling🤣🤣🤣
Merci merci le président de l'Assemblée nationale le peuple sénégalais a décidé de respect ces lois.
La réaction de Farba me fume 😂😂😂😂😂😂🎉 merci El Malick ❤❤
tchié adouna 😂😂😂😂😂
Deuyzeu kalanak😊😊😊thio, patriote à vie, dinguenn youxou ba poup d'où tei El Malick doxal
El Mlaick jeureujeuf 😂😂😂😂😂😂
yallanala YALLA taxawu may la ndam ❤ci barkep SEYDINA MOUHAMEDE sws amine 🤲🏾❤
SALALAHOU ALEYHI WA SALAME AMINE
Aissata demal nane dokh bou sed kouniou faye sa bore ga mer liga lep lawone bakhoul 🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣
❤❤❤ machallah sama❤ Sedna wallahi merci beaucoup el Malick Ndiaye
Merci El Malick ❤
Merci bien président
Merci el Malik dokhalale