Kou content comme man bimou guissé jojo rkk lalal j'aime ❤may guiss wa team bété bété dougnou yeukk sakh absence sou Maréme Sall dakh ay vrai acteur gnofi nékk ki est d'accord avec moi ❤2:11
Mon Dieu!!!!!! Even preod khana Sénégal bi yeup ngueine beugueu sopi deuthie.chaque jour ngueine yeigueul niveau bi.non mais chapeau waaay,mais des cœurs vont lacher ici dh,bakhnaa. Trop top ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
EVENPROD, vous avez touché à toutes les différentes parties familiales.......digueunté mame ak seuteu, domou djitlé,veuve, divorce, woudjé,digeunté wadiour ak dome,les problèmes de caste,digeunté djeukeur ak diabar,nidjay ak djarbateu etc...........❤❤❤❤❤pleines d'émotions 🎉🎉🎉
@@maimounandiaye-le1tu enkay mame Dior migui si série bi da fégnagoul rékk bokognu si principal yii mo takh comme gnom mayel thiam rékk gnigui dora guein 🥰Bo kholé si début serie bi diguako guiss si personnage yii
Mais mais ? Vous voulez finir avec nos cœurs et nos émotions en fait 🥹🥹🥹🥹🥹 vous avez ramené JOJO ici ehhh you guys are the best I swear vous comptez dégainer du lourd jusqu’à la fin na nekh 💃💃💃
Oh merci even prod zozo de retour dina gueneu nekh non vraiment tonton ibou gueye do nitou fi yaye sene capo té kene douko dindi le Sénégal est vraiment de t'avoir comme son enfant ❤
Evenprod Ma Sha Allah Jojo, Sanex, Aladji le trio au complet li Viviane way Zeyna Ndour si kharite mo nék si niom kène dou dème bayi se morom ils sont tellement soudés yalla na lène ya Allah lafal thiate té mousseul lène thi seytané amine
😂jojo siiii bété bété ahhhh evenprod vous êtes fort hien meilleur acteur ak actrice rk la fi guisss mashllah
merci beaucoup tonton evenprod 😂😂😂
Lolou la beugon wakh 😂
Hoo contanan jojo sama acteur
Ohhh ❤jojo mon préférer ngande bi❤❤❤❤
Ils sont trop forts 🎉🎉
Alahou masali ala seydina Mouhamadine wa Salim
Des coeurs pour le prophète Mahomet psl le bien aimé
❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Psl❤❤❤❤❤
❤❤❤
❤❤❤
Sallahou aleyewa Salam ❤❤
Wouy "je suis deguene je vous degraine et je vous fume au calme"
Sacré halima 😂😭😭😭😭
Toukhh katou bone yi comprendre nagne boubakh 😂😂😂😂😂😂
Lii ngay forokh lé momafi bayi😂😂
@@khadimsarr8131😂😂yaw yagg ngako takkk dh 😂😂
@@AminataAndrevnahhha takk boubakh sakh
@@AminataAndrevnaioe tmt da mélni 😂😂😂moye lolu dh
Vraiment Ibou Gueye qui te peux 😂😂😂Jojo en action mayllène EvenProd ay ❤❤❤❤
0:37 enfin lokk bombe et mayel thiam 😂😂😂
Kou content comme man bimou guissé jojo rkk lalal j'aime ❤may guiss wa team bété bété dougnou yeukk sakh absence sou Maréme Sall dakh ay vrai acteur gnofi nékk ki est d'accord avec moi ❤2:11
thieuy serigne salihou kouko sopp mayma aboné niou and diarignou thi ndiangalém
Khana gnénio ngua ??
@BambaFall-u6m non nn
Serie bi mongui dora dense nak soumboulou démna jojo dikna
Moi
Waaaw les grands artistes de soleil levant se retrouvent. On vivra une saison de ouf.
Ohh le trio est là jojo sanekh El hadji ❤❤ Even prod yéna meune nakk chapeau dess na mbaye dosé sama anti stress
Ak toukhoussou
Ils n’étaient pas juste 3 mais legui mom 3 rek nguey guiss
Boul faté Ndéye Coumba
Père Zora mo wara nieuw done père de famille laobé yi rk série guén nékh😂😂
Pas père Zora ici dey , à condition qu’il soit modeste un peu 😅
Oh Jojo, contane na ci Evenprod. Franchement "Betee Betee" est un veritable chef d'oeuvre, bravo
Mon Dieu!!!!!! Even preod khana Sénégal bi yeup ngueine beugueu sopi deuthie.chaque jour ngueine yeigueul niveau bi.non mais chapeau waaay,mais des cœurs vont lacher ici dh,bakhnaa. Trop top ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
La beauté de Déguéne on en parle pas assez 🥰🥰🥰elle est trop belle ❤️❤️❤️
la plus belle femme du sénégal je te dis 😭😭❤
Mome la wakh di elle est belle
Elle est trop belle machallla 🎉
thieuy serigne salihou kouko sopp mayma aboné niou and diarignou thi ndiangalém
Mome dafa geuneu toy si série bi
kan momaye santéle seyedina Mohamed lalale cœur bi ❤❤
Salalahou ala mouhamad
Psl❤❤❤❤
Psl
Allahouma salli ala seydina Mouhammadine wa alihi wa sahbihi wa Salim PSL ❤
Salalahou halla Mohamed 🎉❤
Evenprod louguén begue dégue nk ohhhh sama khol bi 😂jojo ❤❤❤💪💪💪
Jojo mbayague ohhh even prod nak dessé lolen niou dra bilahi 🎉❤❤❤❤❤❤
Ohh j'ai hurlé waouhhhh cette saison va être une pépite jojo🎉🎉😂😂oupssss on jubile wollahhh
Evenprod bou ayy pëkhëm soté touroupe théâtra yepou béneu la gnouye donn machalha
Meilleur commentaire macha'Allah 🥰 mo guën sax
Yeneu meun
Yalnaniou geuneu dieme thia kaname❤
Amine 🤲
J sui avc toi Hein té lolou moy Yon sakh nek beneu
Nn attent evenprod daf gno beugu raay zozo zozo mon acteur préfèré 😢❤❤❤❤ vous êtes des meilleurs waay
Pére zora mosi desse😂😂
@@sophiacamara7989🤔🤣🤣
Waw bilahi kone mou nékhatidh😂@@sophiacamara7989
😂😂😂a@@sophiacamara7989
@@sophiacamara7989ay kokou bou douguel
Thi keurgui Damay déménager mane 😂
Kou beugue sa papa lalale j’aime ❤
🎉🎉🎉
Jojo danaane si birr danaane yi ❤❤❤evenprod merci 🎉🎉
Li Moy Sen gnamou beut 😂😂😂😂Even prod vous êtes fort hannnnnnn❤❤❤❤❤
EVENPROD, vous avez touché à toutes les différentes parties familiales.......digueunté mame ak seuteu, domou djitlé,veuve, divorce, woudjé,digeunté wadiour ak dome,les problèmes de caste,digeunté djeukeur ak diabar,nidjay ak djarbateu etc...........❤❤❤❤❤pleines d'émotions 🎉🎉🎉
Domou djitlé bi c’est qui ?
Domou djitlé bi c’est qui ?
@@KhadijaaFayemame dior domou oumou khaïry
@@KhadijaaFayeDiouma Thiam
Lepp si bir leg de sang
Li déh moy kharal ma soulager léne ndakh Maréme sall demna ma indil léne gnuko eupou niveau 🎉bravo evenprod
Mame Dior tamite nekhou fi di
Mame Dior soumboulou seront présentes vous verrez@@maimounandiaye-le1tu
@@maimounandiaye-le1tu enkay mame Dior migui si série bi da fégnagoul rékk bokognu si principal yii mo takh comme gnom mayel thiam rékk gnigui dora guein 🥰Bo kholé si début serie bi diguako guiss si personnage yii
@@maimounandiaye-le1tuprtan mou ngi wone si deudjou mareme sakl
Mam Dior seyina@@khadijandiaye8964
On peut aimer une série comme ça 😍🥹🥳🥳🥳… Wouy Jojo 🎉. Machallah Evenprod 🙏🏾
Yallnanou yalla doli soutoureu inchallah sibarki saydina Mohamed PLS ❤❤❤
Yalla nagnou yalla may goudou fane ak wére ❤❤❤néléne amine❤❤
Jojo s'il n'en faisait pas partie rek ma rouss no mareme sall yakk nga lou narone gueneu nekh Evenprod dei indil nguen niou wa soleil levant yi bravo
Bilae ioe lou nara nekh
Wa soleil devant gnio fi meilleures nak ❤
Billah nieuwam bétouniou on savait 😂😂😂 tôt ou tard Dina yeksi
Billay soleil levant danio meilleur 🥰🥰
Mome kay da nga nane wa soleil levant ak Jàxeen yeup gni gui fi Thies dall ben acteurs dessoul
Waouh tay mou nékhe nak chiékhe nak even prod mâcha allah je vous aime trop méronna nakhe li soumboulou dée mais baal nalén 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂🎉🎉🎉🎉🎉🎉
Mais mais ? Vous voulez finir avec nos cœurs et nos émotions en fait 🥹🥹🥹🥹🥹 vous avez ramené JOJO ici ehhh you guys are the best I swear vous comptez dégainer du lourd jusqu’à la fin na nekh 💃💃💃
Les meilleurs acteurs et actrices du Sénégal sont là c'est très bien
Oh merci even prod zozo de retour dina gueneu nekh non vraiment tonton ibou gueye do nitou fi yaye sene capo té kene douko dindi le Sénégal est vraiment de t'avoir comme son enfant ❤
😂😂😂
Daguen done dioy kheucha niu indilen jojo 😂😂😂😂😂 titeur au rendez-vous 😂😂😂😂
Titeur au rendez-vous kay 😂😂😂
😅
Li Kay Bénéne cas 😂😂🎉🎉
Woyyy😂😂😂😂 magui deh 😂😂
Maniko jojo rk 😂😂
Wouy 1:56 ça va dégénère khar naniou la partout cheikh Ndiaye 🥳💃🏾🎊🎊🎊
Non amouma loumalene Di wax nax fi ay acteur AK actrice you extraordinaire gnoufi nek machallah j'adore ❤❤
Wa evenprod folen dieum ak nioun nak ❤Jojo lagn niou indil tay
Jojo waaaaaaaaaaoooooouuuuuuhhhhh🎉🎉🎉🎉❤❤❤😂😂😂🎉🎉🎉🎉🎉 EVENPROD vous êtes les meilleurs 🥳🥳🥳🥳🥳♥️♥️♥️🥰🥰🥰🥰
evenprod louma len def loutakh manouma am j’aime si yen 😢
Kham way wakhal si serie bi 😢
@@abybusinessstorybayiko rek mouy woute ay j'aime.
Soko beugue danga créer contenu.
Yoyou gnolay amal ndieurigne.
Loy doyé j'aime danga Koy lékk walla halis ngakoy soppi
@@daoudadiop9768moma diakhal gni sof naniou ak j aime waay
@@daoudadiop9768 amouthi tous.
Soff rek
Jojo la guiss dé la série qui n'a jamais perdu sa valeur evenprod vous êtes le meilleur
Jojo 😂😂❤❤🎉🎉🎉🎉🎉🎉 ohhhhhhhhhh
Soumnoulou dem jojo gnew😂😂
Lou nékh 😂😂😂😂
@@MaremeSeck-s7uWawaw bato dem bato goste😂😂
Ay wayye Dieynaba bayil nétali légui yay TH-cam 😂😂 mai kou contane si dougoussi Jojo rk❤😊
Bonne continuation à tous les actrices à la série bété bété ❤❤❤❤🥰🥰🥰🥰
Des cœurs pour notre acteur préféré sanékhe❤❤
meussouma commenté TH-cam mais Wallahi Ibou GUEYE amouniou sa fayy yallah naleu borom bi fay ❤
🤣 yalla fayko ndakh lane film ??
❤❤❤
@@floorishyndakh nimou gnouy bègueulé
Amiiine inchallah 🙏
@@floorishywaw yala fayko ndakh film
Dafa kharam wala?
Louniou done khalate sax amoul sans maréme Salll dafay gueneu nekhhhh❤🎉
Wakhoo deugue dé soumboulou elle est unique dans le milieu théâtral senegalais. Dafa boolé talent ak xaragne. Bayilène sakk dieufff.
@villageois990-h1l pardon fane la wakhé nii soumboulou menoul loumouyy deff ???ak koufi sakk dieuff gnémé gua yalla mala gueneu beug soumboulou niii rek guénii deff seytané lousi sa yone
Evenprod nak lolen beugue degg🎉🎉🎉
Thiey bété bété chaque épisode am bombah bou eclaté😮😮😮😮😮
Oui jojo jojo jojo🎉🎉🎉 Bilay yaw rk la done khar si série bih❤❤❤❤❤
Ayooo Wa Evenprod louniou lénnn df
Est Li nekhna dh wawwww jojo la guissss yénnn🎉🎉❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
L’arrivée de jojo wowowowowoowoowwoowwwwww💪🏻💪🏻💪🏻
Jojo sûr bête bête lui nekh waye 🎉❤
Evenprod vous êtes fort💪🏿Vous nous faites comprendre qu’après la mort 💀,la vie continue🎉RIP Marem Sall🙏🏿
Jojo sma acteur bi enfin 🎉🎉🎉🎉🎉
Billahi bété bété chaque episode ak personnage bou bés
Meilleur série🔥🔥🔥
Gis ga dhh soco kou sof lay gisni 😅
Cheikh Ndiaye nieuwna 🥳🥳
Père jora mo dés. Dama namou réwandé 😢😢😮😮
Série bi mongui beug bari acteur nk
Avec evenprod votre coeur bat plus fort 😂😂😂😂
Ôôô khole sédd ne glace Zozo Zozo Zozo ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Wa touba ame guén ndam mafi djitou❤❤
Bilahi contanant si l'arrivée de jojo way kou concernane ak man rek lalal j'aime 🎉❤
Ayoooooooo jojo chapeau even pro
Lii laniou naan lalayy lalouuuuuuu🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉JoJo sii Bété Bété xam gua lne laaa heee tayy mou neex🎉🎉🎉🎉❤
Lima léerr moy jojo moy Ali Mamadou dieukourou shasha bi😂😂😂kou d'accord lale j'aime
Yaye boye bafa sone mes yalna gnépe térale séne yaye❤❤❤
Amine❤❤❤❤❤
Ayyyyyyy evenprod loleen beug degg nak mani ko jojo kham gua lane la tay mou nekhhhhhhhhhhhhh ❤❤❤❤🎉🎉
Je suis Guinéen j'aime beaucoup evenprod❤❤😅vous êtes meilleurs jojo wehhh
Maniko kham guénn lan la tay mou néx jojo si bété bete laylaylalouuuuuuuuuuu 😂❤❤❤❤🎉
Evenprod ne me déçoit jamais. Le niveau est élevé. Machallah🎉🎉🎉
Je vous dit cette série 🔥🔥🔥🔥 tire à balles réelles dans tous les sens sheutttt😂😂😂😂😂..... la meilleure des meilleures ❤❤❤
Dieureudieuf EVENPROD ❤
Jojo 🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤je l’aime comme pas possible merci beaucoup Even pro🎉
Kou beuge seydina Mohammed rek l'alal j'aim ❤❤❤🎉🎉
Jojo est grand acteur avec Deguenne. Evenprod félicitations
Jojo 😂 taye mou néhk🎉🎉
Des bisous 😘😘😘 pour ibou Gueye even prod ❤️❤️❤️❤️❤️🙏🏾
Jojo lay guiss ni non wa evenprod Lou ngén gnou déssél😂😂🎉
Dara nak
Mom la don khar pour dém kheuyi ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
😂😂😂
Yalna nga yokk beu yeuk ko❤❤❤ Ioe ak bep djoulit
Xana 10h guey xeuyy
Kn dh niak gua fayda 😂😂😂
😂😂😂😂nio bok cas
Daniouy xeuy mouy guenn nex cëëy enfin jojo🎉😂❤
Je suis plus que contente. Mon acteur préféré jojjo dans bété bété. Merci a even prod
Jojo dina guneu nekh la team soleil levant On attend Père Zora et ça va exploser
Wouyy zozo la don khar❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤😂😂😂😂😂😂😂
Bilay j'ai crie de joie
Jojo si série bi Lou nara nex 😂❤❤❤
Evenprod Ma Sha Allah Jojo, Sanex, Aladji le trio au complet li Viviane way Zeyna Ndour si kharite mo nék si niom kène dou dème bayi se morom ils sont tellement soudés yalla na lène ya Allah lafal thiate té mousseul lène thi seytané amine
Zozo niew na trio bi matna 🎉🎉
Evenprod nak yéna meunnn ❤❤❤
Jojo tay mou nekh 😂😂😂😂
Yalla naséne diame yague yéne gnépeu❤❤
Sama xol bii mogui geuneu sed instant bi ni ❤️😘🥳🥳hooo evenprod vous êtes les meilleurs
Lou nara bèkh inchallah JoJo bienvenue 😊
Enfin sama acteur préféré gnewna Jojo❤❤
❤❤❤❤❤
1:30 mn sama frère Maoda Sall mofi guéna adina hier guéne défal ko nian mouy tiss bou metti😭😭
Yalna ko yalla yeureum té kharé ko aldiana
Foum deuk yaral
Oui yaral sow yalla nako yalla yeureum❤
@@mouhamed_Sall221 en nekoul magou astou sall bi nek koki
Allahouma ammin mettina tropp
Jojo sur bete bete ❤
Non evanprod yéna fii nehh number one ❤❤❤❤❤
Enhh yéwoulène liii narna nekh dhée 😂❤ avec jojo ossi c autre chose 🎉🎉❤
Wouy bété bété meilleure série légui mou dëss père Zora😂😂😂
Doyna seuk bougn koy deklou dagnuy guena sonne 😅😅
Kone dafay eupeu😂😂😂
Non kokou mom merci rrk 😩
Bilay wa Even prod douniou ay nitt wa li nékhna dh❤😂😂🎉
Evenprod vous êtes les meilleurs ❤❤
Ayway sama acteur bii jojo❤❤🎉🎉
Kou ñëpeu donë khaar si série bi ñeuwna ❤
Cheikh Ndiaye toujours rôle de noble
Dako meune nak
Yalna diamm yagg si Sénégal 🇸🇳 ❤
Ay even prod jojo mi ma fi guiss yalla bou neik ayy gueinte way touf touf
Jojoooooo nieuwna hooo sma ❤séddeuna😊
*Il y’aura beaucoup de surprises dans Bété Bété Saison 2 Merci Team Evenprod force à vous , Les 5 millions d’abonnés mon combat Focus*