Merci Son Excellence Président Diomaye pour ce vibrant hommage que vous avez aux Ndayou Daraa qui jouent un rôle primordial au sein des Daraa fière de ma Mère une vraie Ndayou Daraa ❤
M le prsd diomaye yow ak ousmane sonko yalnalene yala gana diobole musal leene si seyetane ac pekheb noone te sene mbebete yurafete yingendi xalat yumelni dimbali dara ac ligueye sngl yalnalenci yala diapale si brk seyidina mouhamad salalahu hanleyehi wa salam ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Cheikh mouhidine samba diallo vrai nitou yalla la walahi machallah mn presi préfère Jam si ioe ak première ministre Seydina Ousmane Sonko mou sell mi🇸🇳♥️🫶❤✊
Honneur et bénédiction à vous monsieur le président de la république. Pour ma part personnelle je suis très content de vous, ceci depuis votre investiture jusqu'à maintenant Vous avez très bien parlé et bien cerner le problème .
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ ana domou dara yi mayléne Serigne bassirou ay ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Walahi sama xol bi sédd na ❤❤ merci beaucoup Mr le Président
Sant Yalla xol sedd Na yàlla Na yàlla mottali yeene ji je suis fier d'être un Nongo daara jërëjëf président ❤❤❤❤
BILAHI
Merci Son Excellence Président Diomaye pour ce vibrant hommage que vous avez aux Ndayou Daraa qui jouent un rôle primordial au sein des Daraa fière de ma Mère une vraie Ndayou Daraa ❤
Man 2016 2017 là batay mangui défendre sonko te man domou dara la rethiou wou ma sama xoul sède na ❤❤❤❤❤
machallah nit bou amè dimè ak ngor diapal nit kou bax la Sonko ak Diomaye
Machallah 🥰♥️🙏 Fière d'être Ndongo Daara, yalna bour yalla dolli Diam natangué Sénégal 🇸🇳 si Barke nabiyil Moustapha sallalahou alayhi wasallam 🥰♥️🙏
Félicitations président Diomaye Faye ❤❤❤🇸🇳
Je suis heureux de mon choix de vote pour vous
Mashalah❤❤❤❤JUB JUBAL JUBANTI bravo PR DIOMAYE 💪🏿💪🏿💪🏿💯🇸🇳🇸🇳
Machallah Machallah kadou yi rafétna LOL sakh son excellence ❤❤❤❤❤❤
Waxi Cheikh Mouhibine Samba Diallo dij ñeuwna😢😢😢😢
Walahi wakh nga deug
Cheikh Mouhidine❤
Bilaye do mou baye wahon nako de
Wallakhi
Ak fatéli thie Li mou wakhone svp
ما شاء الله شكراً جرجفت شيخ محمد البشيرجماي جقار في
Machallah Yalla Na Yalla Mottali Yeene Dji UNCHALLAH Barekep Elhadji Fallou Mbacke 🙏🏿🤍
Un Sénégal qui prend conscience.Dieu merci.
le Senegal etent dirigé par des ndondis des Voleurs et des assassins
❤Machalah mr le Président ❤❤❤❤❤❤❤❤👍👍
Diadieuf Pr Diomaye Faye ❤️❤️❤️ yalna niou ko agalé ak souniou sago si barké Seydina Mouhamad SAW 🤲🏽❤️
Ohh bégg naa trp❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Machallah yalna yalla barkel tei oyofal yane wi... amiine ❤
Adouna mafi geuna beug sonko 🥰
Ya begue lou Mous 😂😂😂😂❤❤❤❤❤
Maa bañ bay jooy 😭😭😭❤️❤️❤️
Ndeysane Cheikh Mouhidine waxoon na lou mel nii deh 😊❤❤.
Yalna ko Yàlla fay 🤲🏽❤.
Merci de précédent ❤❤❤❤❤
5:59
Dioulite dioulite moy mbokam machallah yangui doxal dé 🙏🏿❤️
Merci son excellence Bassirou diomaye Faye 🎉
Macahala yalna yalla oya fal lep way ❤
Machallha président yalna yalla samou la doléella thi barké yonnentbi saa medett ci rewmi yalnako yalla matal
Fière de vous Monsieur le Président Bassirou Diomaye Diakhar Faye Un homme humble et respectueux ❤
M le prsd diomaye yow ak ousmane sonko yalnalene yala gana diobole musal leene si seyetane ac pekheb noone te sene mbebete yurafete yingendi xalat yumelni dimbali dara ac ligueye sngl yalnalenci yala diapale si brk seyidina mouhamad salalahu hanleyehi wa salam ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Allahouma amine Yalla nala Yalla dég
ماشا الله جزاكم الله خيرا يا جوماي ❤❤❤🎉🎉🎉
Senegal Magui souke ame président ❤c’est la première fois. Je vois cette cérémonie de darra au Senegal .
Quelle belle discours du président, ❤❤❤je suis choqué wallah
Pourtant c'est la troisième édition du journée nationale des daara deux dernières journées yi j'étais au Dakar Arena.
Alhamdoullilah, vraiment ce nouveau gouvernement a compris le Sénégal ne peut pas se développer sans les ndongos daaras. Merci président BDDF❤❤❤❤❤
Yalna Yallah motal lep
❤❤❤❤❤❤❤ Serigne bassirou merci ❤❤❤❤❤❤ alkhourane rék ❤️💛💛
Cheikh mouhidine samba diallo vrai nitou yalla la walahi machallah mn presi préfère Jam si ioe ak première ministre Seydina Ousmane Sonko mou sell mi🇸🇳♥️🫶❤✊
Sublime discours. Fier d'être dirigé par un tel homme
Machalla yallna yalla Barker daara yi
Merci beaucoup Monsieur le Président 😢😢❤❤❤❤
Une bonne vision claire et précise pour soutenir Daara yalna bour yalla motali projet yi inchallah 🙏
Machallah dieureudieuf mon président ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Machalah président diomay Faye dieureudieuf
MACHALLA YALLA NA YALLA MOTTALI LÉPPU
ماشا الله فتبارك الله وشكرا لك يا رءيس الجمهورية السنغال السيد الشيخ محمد البشير جماي جاقر في
Merci beaucoup monsieur le Président BDDF yalla fayal nioula ❤
merci PASTEF, merci MODAP, merci PM Ousmane Sonko, merci le president de tous les Sénégalais SEM Bassirou Diomaye Diakhar FAYE.
Alhamdoulilah dieureuf yalah yaw miniou tanal diomay sonko
Walahi Ndeyesan Dara yalna yalla Faye yalla amine ya rabi ❤
Yal nalén yalla takhawou samou lén ar la banguén yéguali sén yéné si Sénégal
Mâcha allâh ❤
Machallah yalla bakhna
Good job superbe Alhamdouililah machallah ❤🇸🇳🥳🥳
Maacha alaah
Honneur et bénédiction à vous monsieur le président de la république.
Pour ma part personnelle je suis très content de vous, ceci depuis votre investiture jusqu'à maintenant
Vous avez très bien parlé et bien cerner le problème .
Mâchâ allâh 🎉
Félicitations président diomaye diakhar Faya ❤ Amal tawfekh ak taysir rekk manchallah ♥️ contane si yaw rekk ♥️♥️🇬🇭❤️🇬🇭
❤❤❤❤ machaalah yallana diamou yague ❤
Yalna la yalla sam presi
Machalla yalna yalla motali
Machallah président diomay Faye yalla na la yalla may goudou fan
Alhamdoulillah ❤️✊🏻
Macha Allah kaddu yii rafetna
MachaAllah
qu'Allah protège le Sénégal, son président, son premier ministre et les patriotes
Amine
Machallah ❤prendre
Machallah li rafett na lol yallah na diameu yagg Sénégal 🇸🇳❤️👌🏿
Merci beaucoup prezi machalla nous sommes fière de toi bonne continuation à vous tousse
Merci p b❤sirou diomaye faye❤
Vive le Sénégal... &... le président faye❤
machallah Merci Président pour ce vibrant hommage aux daara
Merci son Excellence
Machallah souniou président l'islam à l'honneur
Tèy islam siguina ❤cheikh bassir yalnala yalla dèfal ndam
machallah mentenent notre cher pays est dirigé par des vrai musulmans
Le meilleur discours de tous les temps
MACHALLA ❤️
Jërëjëf M P Basiiru Jomaay Fay.
Alkhamdoulilah rabbil aalamine yalla na yalla mottali yéné yi Amine
MACHALLAH ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Diarama dara ❤
Love président Bassirou ❤
Choukran Sonko ❤
Yousoufa rek guamaye diokh en isipete😂😂😂😂😂❤❤❤❤❤❤
Machallah ❤️🧠❤️❤️
Cia kaw cia kanam rek inchalla!❤❤❤
diaram dara❤❤
Alhamdolha
Jërëjëf Sëñ Jomaay 👏🏿 🥰
Maa chaa Allah
Yalla na yalla degueureul le
Machaallah yalla na la yalla diapaler sa may la fane wou goudou
Kaddou yi rafét'na mashallah Fatabara'kalahou ♥️🕊️☝🏿 yalla nala yalla sAmeuh ar'leuh tei soutoural'leuh Mission
Machallah kadou yii raffettena ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Machallah ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Machallah PRS ❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤Machaallah 🇸🇳 🇸🇳 🇸🇳 🇸🇳 🇸🇳
PRÉSIDENT koulay khar yalna xadi❤
Yal nala Yàlla sàmm président on est très fier
Enfin Président bou djoulité Mâcha Allah 🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳
Alkhamďoulila machallah sante yallah bou bakh❤❤❤❤
Macha Allah discours très pertinent ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
اللهم صل على سيدنا محمد وسلم
Que dieu te protège et mon pays Sénégal ❤❤❤
MACHALLAH NOTRE PRÉSI
ماشاء الله تبارك الرحمن تهانينا رئيسنابشير جماي في 🎉🎉🎉
Machalla son excellence monsieur le président
Merci beaucoup son excellence monsieur le président ❤
Senegal mogui dogua am un président sénégalais conforme à nos réalités diarama seydina Usmane❤