Ndeysane li la république bi sokhla senegal rewu terangala tarikha yeep pa bockou ndeye ak baye yalna jaam sakh thi sugnou rewmi Manchallah li afet trop sonko moye diomaye 🇸🇳🙏🏽
Heyy Serigne ABIB Sy Mansour hey Serigne Habib Sy mansour Mane Mouride bi FONK nako lol ooh sama xol bi fexx naa barki borom Touba YALLAH naniou YALLAH SAMAL Serigne Habib Sy way 🙏nako talibé Mourides et TIDIANES yi bayi xéell
li moye Sénégal yalla na borom defal gnou diam li rafetna ❤️❤️❤️❤️❤️
Li rafêtna hoooooo
Masha.allah Alhamdoulilah santati yalla bou weer yalna jàmm yàgue senegal léepp rafétt Masha.allah ❤❤❤❤❤❤❤
Machala contanna yalna yalla sammou lène !!!
Serigne Abdou nuit kou bakhla Man dé Tijian la mai sope nala trop ❤❤💯💯👍👍
Way yènabah way lii moy Senegal 🇸🇳 kadouyi machalaah
Machala Sy Malick kadou yi rafetna trop ❤❤👍👍💯💯
Serigne Abdou Samad mbacke machaalah
AlhamdouliLAH !
Mashalla
Way lii dafa rafet billahi machalah
Li dé souy am légi noneyi abalnou
Dieredieufaty Serigne si yeup. YALLAH NA LÈNE YALLAH FAY YIIW, TÉ MAY LÈNE FANE WOU GOUDE TÉ WÉER.
C'est très beau ça❤
Li ma ci neex daal mooy, saytaane mi mer ba yuucu rekk ❤ alhamdu Lillaa
Machallah❤❤❤
Machallah
Dieureu dieuf
Salal Lahou Aleyhi wa Salam !
Machallah 🙏🏿🙏🏿🙏🏿🙏🏿🙏🏿🙏🏿
Alhamdoulilaha
حسناً
❤❤❤❤❤❤
Maasàllaa yal na leen fi Yàlla yàggal te wéral leen barkeb seen maam yu tedd ya yu baax ya.
As Samadyya TV.
Jërëngeen jëfati liggéey bi rafet na am na solo lool.
Allahouma Salli Hala SEYDINA MOUHÀMADINE WA HALA ALY SEYDINA MOUHÀMADINE !
Dierejef s'y malik yalna yalla yagal taxawaybi
Diueruediuef serigne touba
Amine !
Saa xol bi sedd na lool.❤ maasallaa ❤️
Yàlla Na jàmm yàgg ci berkeb seexul xadiim 🤲🏿
Alahouma amine way mouride 🤲
❤
Ndeysane li la république bi sokhla senegal rewu terangala tarikha yeep pa bockou ndeye ak baye yalna jaam sakh thi sugnou rewmi Manchallah li afet trop sonko moye diomaye 🇸🇳🙏🏽
Machalah kadouyi sélna néxna amna solo
Machllah ♥️♥️❤️❤️💚❤️💚❤️💚
Khol sedna deh
Li amna solo lole rafetna trop
Heyy Serigne ABIB Sy Mansour hey Serigne Habib Sy mansour Mane Mouride bi FONK nako lol ooh sama xol bi fexx naa barki borom Touba YALLAH naniou YALLAH SAMAL Serigne Habib Sy way 🙏nako talibé Mourides et TIDIANES yi bayi xéell
Machalah contana trop si yaw yalnala yalla fay yiiw
Ngiidé ay royou kaye lan
Macallah tar kalah
Li raffet na trop wallahi daloubé yi khollat len sen bopp gni ben lane def sen bopp
Machaallah, rafetina lol.
S Cheikh bi don wakh kane moy wadiouram
Soudé Serigne Cheikh tidiane mi togak Serigne Abdou samad gay wakh Dabakh Malick moy bayam
Machallah ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Machalh
Machala
❤❤❤
❤❤❤❤❤❤
Machallah
❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤
❤❤❤❤
❤❤
❤❤❤