Je suis mouride et je suis content de l'intervention du khalife des tidjans . Bilahi j'ai versé des larmes bilahi ak korgui. Niou beuri danou reer. Mouride bou bagn tidian walla tidian bou bagn mouride tek la sa bakan, nakh nga sa boppu . Kou bagn niitou yalla, walla bagn been tarikha , ab cheytané nga andal. Djoulit bu bagn djoulit, nakh nga sa bopu. Ab tidian, niassen, mouride,layen ,khadr, koussi bagn sa morom tekka thi bakan,walla yakar ya gueun sa morom, nakh nga sa bopu. Dono linga yakar. Yalna yalla yokkou leer khalifa bi Lou tolna asmaan ak Souf. amiine
Machalla je suis chretienne mes je tres fier de Senegal parfoit ñou decone mes c'est vie yalna yalla bole ñeup ande done bene machalla Amen Amen Amen 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭 ohhhhhhhhh ndeysane yalna bole súñú kilifa Senegal amna lou rey
@@sadiomanejrtv1967 Amen way magui espagne waye wate na si Jésus christa guamou magual kasoup ziarre ma len koy organize abou sale gratis def ma war def rek yalla súñú borome jour bi tafsir Abdourame gueye xamene douma musulmán defa wax ba may dioye Maneko papa lima war la def bes ba mou mette ñome la guis Sant na les ba kanamou yalla
Quant à moi j'ai allumé mon PC; j'ai surfé sur tfm pour avoir les nouvelles de mon pays et je suis tombé sur l'émission. Super content pour l'intervention du Khalif Sérigne Babacar SY MANSOUR. ALLAHOUMA AMINE
Tfm est la meilleure télé au monde vraiment je suis touché je n'ai jamais pleuré seul en regardant une émission de télé walahi bilahi samakhole toyna❤❤❤
Chrétien catholique convaincu je le suis mais dama danou leer qu’elle modestie !!!beaucoup de chose à apprendre de ce guide c’est vraiment émouvant qu’il puisse appeler en direct et participer et prier pour tout un peuple sans distinction il faut être un homme de Dieu pour le faire serigne bi senegal 🇸🇳 amalnala ndioukeil machaallah Sy rafetna !!!
You prolly dont give a shit but does anyone know a trick to log back into an Instagram account?? I was stupid lost the login password. I would appreciate any tips you can offer me.
Cet homme est humble je l’aime bcp et pourtant je suis mouride mom akh segn mountakha mbacke yalnagne fi yag kene dou sougnou mak yiiii sénégal ame diam dh Bilay balagakoy kham guene sénégal 🇸🇳 alhamdoulilah
C'est la première fois quelle humilité quelle humanité quelle bel appel a l'harmonie entre les tarikha. Sy vis encore pendant des années avec beaucoup de santé et de lumière de la tarikha cheikhna Ahmed tidiane cherif rta
Je suis une fervente Mouride et fière de l'être raison pour laquelle je respecte tout ceux qui prononce " Ach Hadou anla ilaha ilala wa ach hadou ana Mouhamadou Rassoulilah" soyez fière dece que vous êtes sans complexe mais mandou lène teu respecter pass passou Ndiambour. Gneup Yalla lagnouy Out yalla na diam yagg.
Mashalla, je suis Tidiane a 100% mais j'adore tous les kilifeu dinê de tous les tarikha, yalla na yalla goudeul séy fane anda wergou yarame bou bakhe 🙏
Quel modeste de petit fils de cheikh seydil Hadji Malick sy c'est normal wathié sa bop ba dara doula reuthieu si rewmi nioune amou'niou sa fay Serigne Babacar woté'bi noumouy déf sou niou khôl❤❤ bilahi mane ak yalla rék nioko xam
Wallahi commentaire bi rafeittt n’a billahi yalla gua geuneu done soldarou cheikh Ibrahima fall yalla nafi jamm yag si barki seydina MOUHAMED psl ak si barki mane Maodo ak mame borom touba🙏🏽
@@mamecodouba9496 mane douma mourite layénne la mais bayi lene khadialébi entre mourite ak tidiane fi tariha yeupa modeste gnieup thi yalla lagniou dieum
Je suis vraiment touché par cet Homme. Je suis touché par sa foi, son humilité, sa grandeur et son humanité. Merci Seigneur de nous l'avoir donner que son être soit béni afin qu'il réussisse sa mission : changer les hommes et nous rapprocher vers toi. Longue vie à vous noble serviteur.
Que Dieu vous garde aussi. Il m'a vraiment bouleversé, chamboulé c'est la première fois que je l'écoute et ce ne sera pas la dernière parce qu'il est vraiment béni. Ces paroles ont touché mon coeur de chrétien et mon être j'aimerais le rencontrer inchallah. Adouna amoul solo
Je suis mouride mais je le dit en haute voix merci maodo!! Mashalla yalla nanu ko yalla fayall elhadji malick sy nitou yalla bi ndysann senegal diam rek mofii am nanu am yarr ak téguinne dieufei ndigeul bayi tré téniou kham ni lep si yalla la diém
Machallah yalna yalla kheep doli diam salam ak soutoura daimane thi reeew mi inchallah alkhamdoulillah diaradieuf sy Demba yalna yalla yagal takhaway bi inchallah thi barké naby SAWS
Oooh lii la clifeu dii dieurigne walahi Sy Malick meute nga linga donne waaxnga ak askanwii té gnép dégueu nagnoula waxo tarikha d waayé Diiné dji nga wax konne wonéngani donne dioulite rk Moy li dieukeu avant tarikha S'y goundeul fane kél modestie c du jamais vu😭😭😭😭😭💖💖💖💖💖💖
C'est tellement beau ma sha Allah. Nianal djoulit akh domou Adama akh Awa... Serigne Babacar Sy yagafii lolll and akh wer. Fière d'être sénégalaise. Merci beaucoup pour ces moments d'une si grande ferveur. Un grand Homme, de belles personnes. Demeurez dans les grâces d'Allah.
Alhamdoulilah sante yalla diouli si yonentam bou tede bi djeredjef Sy Malick yalla na yalla goudal say gafane yague dignou gouguè fiere d'être talibé cheikh
Eskey même étant mouride, Seydi Hadji Malick dafa fess si sama khol trop ... li moy Sénégal cette harmonie . Yallana suniou khalif généraux yi yaaga fi lolu tei andak wër tei niou arrêter khadialo bi Kou tëd ki Cheikhoul Khadim Ak Serigne Hadji Malick danio bokou dembeu
Très bonne leçon d'humilité, Nous sommes tous contents de cette intervention et comprenons que nous tous des humains Que Le Tout-Puissant nous accorde un esprit de discernement pour comprendre l'oeuvre de Maodo, son idéologie et le sens de son combat Macha'Allah
J'ai plus les mots😭😭. Yalna Yalla goudeul sa Fane Sy Malick Khalifa Ababacar, Sokhna Aïda Sy Dabakh yalna Yalla goudeul sa fane. Contaane nagnou gnoune talibés yi. Pape Cheikh lii si yaw lako Yalla djaralé santal Yalla ak kép kou nék si plateau bi. Tfm sa kaw thia kanam🙏🙏. Sénégal yalnafi diam yagg🙏🙏💖
Suis pas tidiane mais la vérité ya pas de fanatisme chez eux.ils ont mis chacun personne à sa place.pas à la place de dieu ni autres .dans la vie tout exagération est mauvais.voilà ce qu on doit apprendre aux talibés pour qu ils doivent pas égarés. Une partie très important qu il a dit " si le monsieur avait dit des choses exagéré sur maodo malick ils vont automatiquement démentir comme il a bien dit le khalif.a partir de son discourt, je prends bcp d considération et de respect total envers lui
Bravo Pape cheikh, svp ton émission coute maintenant très cher tu ne peux plus invité n'importe qui car l'émission a eu une autre valeur historique depuis hier lorsque le khalifa à appelé 👍👍👍
@@massatagueyegueye2001 mon frère sakhole mofesse et j'ai pleuré seul dans ma chambre en regardant l'émission sur l'intervention du khalif des tijanes 👍👍👍
MachAllah Sy Malick Yalla lafal la thiat té doli Soutoura Éternel Diam diou sakh loool te ande ak werr Il faut surtout que celles qui sont sur le plateau s'habillent décemment puisque l'émission a une portée internationale suivie par surtout Le Khalif Général des Tijanes MachAllah
@@fatoufayembaye7806 tu as parfaitement raison il faut sensibiliser pape cheikh car l'émission est suivie par les personnes les plus populaires et importantes du monde ❤❤❤
Je suis mouride et je suis content de l'intervention du khalife des tidjans . Bilahi j'ai versé des larmes bilahi ak korgui. Niou beuri danou reer. Mouride bou bagn tidian walla tidian bou bagn mouride tek la sa bakan, nakh nga sa boppu .
Kou bagn niitou yalla, walla bagn been tarikha , ab cheytané nga andal. Djoulit bu bagn djoulit, nakh nga sa bopu. Ab tidian, niassen, mouride,layen ,khadr, koussi bagn sa morom tekka thi bakan,walla yakar ya gueun sa morom, nakh nga sa bopu. Dono linga yakar. Yalna yalla yokkou leer khalifa bi Lou tolna asmaan ak Souf. amiine
Bilay d mem k moi sui mouride et fière de l être mais bi serigne bi di woté sama yaram dalon daw
Amine domou bay
Amine
Amine
Machalla je suis chretienne mes je tres fier de Senegal parfoit ñou decone mes c'est vie yalna yalla bole ñeup ande done bene machalla Amen Amen Amen 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭 ohhhhhhhhh ndeysane yalna bole súñú kilifa Senegal amna lou rey
Merci toi o6 ya bax yalna yalla fay la si barkep ki gua gueume amine😍😍😍😍
@@sadiomanejrtv1967 Amen way magui espagne waye wate na si Jésus christa guamou magual kasoup ziarre ma len koy organize abou sale gratis def ma war def rek yalla súñú borome jour bi tafsir Abdourame gueye xamene douma musulmán defa wax ba may dioye Maneko papa lima war la def bes ba mou mette ñome la guis Sant na les ba kanamou yalla
@@sadiomanejrtv1967 🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏Am si fierte trop sama fami dama bok si walou yaye chretien walou papa musulmán santa yalla yeureume ko bou bax
Allhoma amine
@@senegalmafierte7523 yalna yalla samou la moi je suis en France
Quant à moi j'ai allumé mon PC; j'ai surfé sur tfm pour avoir les nouvelles de mon pays et je suis tombé sur l'émission.
Super content pour l'intervention du Khalif Sérigne Babacar SY MANSOUR.
ALLAHOUMA AMINE
Machalah
Tfm est la meilleure télé au monde vraiment je suis touché je n'ai jamais pleuré seul en regardant une émission de télé walahi bilahi samakhole toyna❤❤❤
Machalah rafete na TFM c'est la meilleure chaîne
Chrétien catholique convaincu je le suis mais dama danou leer qu’elle modestie !!!beaucoup de chose à apprendre de ce guide c’est vraiment émouvant qu’il puisse appeler en direct et participer et prier pour tout un peuple sans distinction il faut être un homme de Dieu pour le faire serigne bi senegal 🇸🇳 amalnala ndioukeil machaallah Sy rafetna !!!
You prolly dont give a shit but does anyone know a trick to log back into an Instagram account??
I was stupid lost the login password. I would appreciate any tips you can offer me.
@@arjunmohammad1729 do you still need help
Bilahi ya bakh Luigi
Vraiment sa me va droit au coeur c'est sa la modestie de la personne quii montre sa beaute interieure
Ndaysae barké serigne touba serigne babacar mansour dinafi yage dina wér
جرجف شرج طوبى جرجف شرج بابكرسى مريد الله أك تجان💜💜💜💜💜💜💜💜💜💜👍👆👆👆الله أكبر
Amin yarabbi
😭oh Amine way ya bakh
Merci
Diadieuf yaram ak bépou kilifeu diné
Inchallah 🙏🙏
Maylen ma bleu Jaime rek li masoul am khana tfm rek machalah
Cet homme est humble je l’aime bcp et pourtant je suis mouride mom akh segn mountakha mbacke yalnagne fi yag kene dou sougnou mak yiiii sénégal ame diam dh Bilay balagakoy kham guene sénégal 🇸🇳 alhamdoulilah
Amine Ya Rabbih ak khalifs généraux yép ak gnoune talibés yi barké Cheikhoul Khadim
Amine Way barkép serigne touba
Satou satou yalna diam yag si réwmi 🙏
Il prone la paix comme serigne moutakha mbacké dagno yam djiko
Amine
Machallah Sy Malick mouride bi kholame Seda yalla na borome goudeul say fane t weer amineeee barke Serigne Touba khadimoul Rassoulilahi
Gracias tfm mashallah amou gniou Sene Faye Youssou Ndour yalla n’a sa diam yiague mashallah 👑👑👑🏆🏆🏆💯💯💯💯💯😍😍😍
C le meilleur té da am niane youssou ndour
Je suis talibé Serigne Touba wayé Khalifa general des Tidiane yalla nafi yague lole Té wére Amineeeeeeeeeeeeeeeeeee
Mbok sa ligueye rafetna talibe Bamba khamoul khajalo yangui si yone bou bakh bi
Danga bakh
Amine ya raby
Amine
Amine 🤲🤲
Amine chapeau à la Tfm .Na Yalla guoudoul fanou Serigne Babacar Sy Malick ,Yalla fayal niou Hadj Malick ,Pape Cheikh Diallo ,Sénégal yeuppp ammm jammm
je suis talibé s touba mais Machalla yalla nagafi yagg té wér s babacar sy ndayssane khol sédna lol li moy Sénégal yalla na yalla déf diamo
Alahouma amine ak bépou kilifeu diné 🙏
Dagua bakh rék
Pape cheikh est touché c beau de faire ces genres d'émissions qui touche même les khalifs chapeau à toi 😎
Sama khol dafa sed bilahi 😭 c la première foi ma guis serigne bou woté si émission machalla ❤❤
G jamais eu autant d'émotions qu'aujourd'hui ndeyssan et en tant k Mouride je suis fier de Serigne Babacar sy Mansour je l'aime vraiment
L'histoire retiendra cet appel du khalif avec sa modestie et lamour qu'il.porte pour l'humanité machalla
Walay ndaysane 🙏🙏
Dieuredieuf khalifa beguenaloll
Maiy god proteck you general khalifa tidiane
C'est la première fois quelle humilité quelle humanité quelle bel appel a l'harmonie entre les tarikha. Sy vis encore pendant des années avec beaucoup de santé et de lumière de la tarikha cheikhna Ahmed tidiane cherif rta
Je suis une fervente Mouride et fière de l'être raison pour laquelle je respecte tout ceux qui prononce " Ach Hadou anla ilaha ilala wa ach hadou ana Mouhamadou Rassoulilah" soyez fière dece que vous êtes sans complexe mais mandou lène teu respecter pass passou Ndiambour. Gneup Yalla lagnouy Out yalla na diam yagg.
Merci maria
Li la nouye dooye kilifa amnasolo yahlla n'a goudou fane
Deiradieaf sy amna solo
Mashalla, je suis Tidiane a 100% mais j'adore tous les kilifeu dinê de tous les tarikha, yalla na yalla goudeul séy fane anda wergou yarame bou bakhe 🙏
Walahi deug pire nga nioune niep aye dioulitte laniouy
Talibe Cheikh Point amoul lenen, fière d’être Talibe Cheikh , Mame Maodo ba faw 😍🥰😘
Diam si yow
Walaahi azim
Mamy diange rawal ndaysan billa hi ler na VRAIMENT tay mom khol yep sed
Bilay kéne dou Maodo talibé cheikh mo nékh
Amine 😘😘
C’est agréable d’entendre ce genre de voix en cette période de crise. « Digueunté keurou diiné yi kouci wah wahci lou rafet »!
K dieu vous protege amine sy malick
Machallah goudal fane andak wére Sy Malick ♥️♥️♥️🙏🙏🙏
Man mouride la mais vraiment wakh dji dafma touche li mou def ni s'est un geste noble té damako yagu fan thi deugom mom khalif
Ndeye Maguette Sock gnoune dal gno bokk lep bou ken dougou thi sougnou diguente
MACHALLAH
J;,
Wakhnga deug nit kou deug la mo takh gnounanko gnak thiakhan
Mane Fatou Mou serigne Fallou di naine souniou khalife généraux yi yague fi lol té weer. Amine
Serigne Babacar SY Mansour yalana goud fane bou andeuh au wer.....Xol yeup sedna walahi....Talibe Cheikh beu Aldianah In Sha Allah
bilahi damakotanne sonoukhol séddena
Amine
Douma si doyal😭
Pape cheikh santall yalla lii daa diaffé sa émission amena sollo
Pape cheikh Diallo khol bi dafa rafétt lounék meunako ame si adouna
@@leternelindigne9931 wallahi
Quel modeste de petit fils de cheikh seydil Hadji Malick sy c'est normal wathié sa bop ba dara doula reuthieu si rewmi nioune amou'niou sa fay Serigne Babacar woté'bi noumouy déf sou niou khôl❤❤ bilahi mane ak yalla rék nioko xam
Billaye
Meynala 1000 cfa
Meme maan sama xol bi day djam ndakh mbékté
Machalla contente rék sy malick yalna yalla yokou weurgou yaram bi té gua yague mame beuy mala beugue mame 🤲🙏
Ndeysane sy malick Yallah Na sa fane goude barkép borom Touba
Machallah amna sollo contann nagnouu khol yeupp sédd na Serigne Babacar Sy Mansour yalna yalla guoudeull fanamm inchallah
Dieureudieuf sy Malick
Amine yarabi
@@modoudiouf3829 q
AKASSA FALL YALLA NAFI SERIGNE MANSOUR YAGG TE WER SI BARKEP MAME CHEIKH IBRAHIMA FALL LAMPE
machala, magui suivre say commentaire, koula sopp la👌👌👌
Amine
Amine 😭😭😭😭😭😭😭
Wallahi commentaire bi rafeittt n’a billahi yalla gua geuneu done soldarou cheikh Ibrahima fall yalla nafi jamm yag si barki seydina MOUHAMED psl ak si barki mane Maodo ak mame borom touba🙏🏽
Amine way
Les Tijani sont très modeste
Merci serigne bii
Les mourites aussi sont modeste gnieup thi yalla lagniou dieum
Les tidianes sont plus modeste Awa
@@mamecodouba9496 mane douma mourite layénne la mais bayi lene khadialébi entre mourite ak tidiane fi tariha yeupa modeste gnieup thi yalla lagniou dieum
Machalla sy malick ya modeste bilahi
Je suis vraiment touché par cet Homme. Je suis touché par sa foi, son humilité, sa grandeur et son humanité. Merci Seigneur de nous l'avoir donner que son être soit béni afin qu'il réussisse sa mission : changer les hommes et nous rapprocher vers toi. Longue vie à vous noble serviteur.
Amiine
Amine Ya Rabbi amineeeee
Aambarla de
Alexandre Gomis amine niou bokk lepp kou bakh
Que Dieu vous garde aussi. Il m'a vraiment bouleversé, chamboulé c'est la première fois que je l'écoute et ce ne sera pas la dernière parce qu'il est vraiment béni. Ces paroles ont touché mon coeur de chrétien et mon être j'aimerais le rencontrer inchallah. Adouna amoul solo
Xol yeup toy taay
Diam ci Sénégal ❤
J'arrive plus à retenir mes larmes Barker baye niass
Amine ta rabil
Li louko dakheu gneup béneu la
Ndaysane élément cheikhal l'islam yaram dawna 😭
😭 Sénégal Yalla naniou Yalla roussé mag gni
@@png7872 amine yarabi
Pape cheikh dioyna meuneutoul continuer émission bii thiey sy malick y’a oyoff
Dieureudieuf mame boye 👌🏼yalla borom bi goudal saye fann gua andak wérr ake katane barké alkouran
Talibé serigne touba la ms dma 😭😭😭ba sonn yalna diam yag thi reww mi sy malick yag fi lol
ya bakh dh trop
Ndayssane. MachAllah
Adama Ndiaye ay way ya Bahk beug nalay kham
Adama AMINE inchalah diadieuf
Serigne touba ak maodo béne la dieureudieuf🙏🙏
Serigne Babacar Sy Mansour yalnafi Yague ta wérr si barki Seydina Mouhamed (PSL)😭🤲🙏
Ndeysane Sy Malick ohhhh yagg fi lol yak Serigne Mountakha ak Khalifa yi si rew mi yeup😭😭😭😭❤️
Machalah SY MALICK yalnaguafi yague téwère GFM sakanam PAPE CHEIKH sakam YOUSSOU NDOUR YALNALA YALLA Faye sakow sa kanam
Amine
Je suis mouride , je salue ce beau geste du khalife
Merci frère nous sommes tout des musulmans
Merci frère nous sommes touss des frères et sœurs
Ndaysaan waxna DEUG d bilhi. 😭😭
Mbokku yi lepp bennla
Ya bakh
Machalla je suis niassene mais suis content de notre khalifa sy Malik
Élément cheikhal l'islam yalnala yalla défal tawfékh 👌
Je suis mouride mais je le dit en haute voix merci maodo!! Mashalla yalla nanu ko yalla fayall elhadji malick sy nitou yalla bi ndysann senegal diam rek mofii am nanu am yarr ak téguinne dieufei ndigeul bayi tré téniou kham ni lep si yalla la diém
walahi linga wax rek mofi nek amna solo lolll yalna diam yague
😂😂😂😂😂waw gor ChéikhAlkhalif02
Ndaysane fall danga bakh rék té gnak kignane yalna yalla Faye si barké cheikhoul khadim
Mashalla am ak talibé rek mo am solo bilahi
Machallah
C est du jamais vu yalla na yalla goudeul fan yi Sy
Wallahi ndeysann. Yalla nagnou yalla feyal sunu mag you baxyi te bayilen sunu kanam lou yax inchallah. Samahan wa ta'hatan
Machallah yalna yalla kheep doli diam salam ak soutoura daimane thi reeew mi inchallah alkhamdoulillah diaradieuf sy Demba yalna yalla yagal takhaway bi inchallah thi barké naby SAWS
Quelle humilité du kalif ! Yalla na diam yague ci keur diné yi
Eskeuyy je suis mouride mais geste bi rafet na
Serigne bi dafa oyof et puis c’est un vrais khaliphe Masha Allah il est modeste si jikko yonent la
Machalla mercii bcu way sougnou mbokou mouride gui
Fall Mara ay way ya bahk
En tout cas hol yii toyna yalna yallah sam tè naguou gnane yii
Machallah sougou bokk dioute bi 🙏🙏
Fall mara merci beacoup diadieuf
Oooh lii la clifeu dii dieurigne walahi Sy Malick meute nga linga donne waaxnga ak askanwii té gnép dégueu nagnoula waxo tarikha d waayé Diiné dji nga wax konne wonéngani donne dioulite rk Moy li dieukeu avant tarikha S'y goundeul fane kél modestie c du jamais vu😭😭😭😭😭💖💖💖💖💖💖
Sy Malik Yalla guafi yag teh wer barké Yonnenete bi Sallahou Aley wa Salam ay naniou beuguaneté guir Yalla wormal Mal gni
Je suis vraiment contente de cette geste Bilay si Malik 🙏🙏🙏🙏
Mashalla khol sed na 🙏🏽🙏🏽😭❤️❤️mame maodo yalla na yalla yokk leram🙏🏽🙏🏽🙏🏽🥰🥰😭
Machala serigne Mbaye sy oyof rek mo am solo
Dieureudieuf sy Malick khol yeup toy na machalla
😁
Bilahi Modou Diouf
Keip kou beug lou baah contaaan na mashallaah💖
Vraiment
Wallahi sama khôl sëdeuh na Gouy Sy Malick , Yalla na Borom bi goudal saa faneuh Sy Malick 😭😭😭
Walahi ma sœur je pleure walahi bilahi 👍👍👍
Amine
Nn Nitou diiné deug daguay woyoff t llou lafi khalif bi wané Yallna Yalla guoudal sa fane🙏
Amineee
Modesty augmente la valeur de l'homme yagu fi loll
Amine yalla na yalla goudale say fanne sy, ,,,,,,, sy mame marame, Mbacke mame marame, ...ce ça le sénégal
1ere mais alhamdoulilah baniou feker lii. Dieureudieuf Sy Malick 🙏
Machallah sy merci beaucoup Tfm ❤❤❤💪💪
Ndeyssane machallah sy malick taye nieupa contane yalna sa diame yague yalla mayla gudufane ak werrr si barke seydina mouhamed tfm sa kaw sa kanam
yalla na diame yague Sy Malik
Yagui fi lole te wer ci barké serigne touba
Ya bakh
Amine
Amine
Amine ya Allakhou
Bilahi barke borom touba j'ai de la chaire de poule sama xol sedna
Walay ndeysane
Machalla wa tivaoune
C'est tellement beau ma sha Allah. Nianal djoulit akh domou Adama akh Awa... Serigne Babacar Sy yagafii lolll and akh wer. Fière d'être sénégalaise. Merci beaucoup pour ces moments d'une si grande ferveur. Un grand Homme, de belles personnes. Demeurez dans les grâces d'Allah.
mashalla sy malick le peuple est content❤
Son humilité me dépasse largement ! Alhamndoulilah tout est grâce et Que la Grâce d'Allah nous demeure.
Hee ouiii tt est grâce
@@syawa8415 Que La Grâce de Dieu vous demeure!
Amine Ya rabi
Ainsi que sur vous
@@syawa8415 Yaww sougnou serigne nga Sy Malick
Lol inchallah
Soyez toujours courtois dans vos commentaires et respectez le règlement de la communauté 🙏🏿🙏🏿🙏🏿
Cheikhouna TINE Machalah
Merci
Tyie QUARTIER GÉNÉRAL SA KAKA NAM REK Billay machalla
Machalah merci Mame Maoudo
@@bebest1280 merci
J'suis Mourite mes mashallah xol yep fexna mane dh tourna ay xeweul dax bègue Aka modeste SY MALICK YALNALA BOROM BI MAY GOUDOU FANE AK WER SY
Machalah diko gnanal aussi Serigne mountaga bassirou yalna diam yag si réwmi 🙏🙏
Alhamdoulilah sante yalla diouli si yonentam bou tede bi djeredjef Sy Malick yalla na yalla goudal say gafane yague dignou gouguè fiere d'être talibé cheikh
Pape chiéck diallo meilleur animateur 🌠du Sénégal
Merci sy
Machalla Sy Malick yague fi lol tè wèrr ❤ yèpp toy na😭😭❤❤fière d'être Talibè Cheikh💯❤
MashaAllah Sy Malick yalla na diameu yageu Sénégal 🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾
Yalna yalla tapé xol yi ❤ma challah sy malick sagal nga diné dij
Merci beaucoup wa QG ak sugnu khalifa Serigne Babacar Sy Mansour
L’islam, la religion qui nous unis et qui n’adhère pas les séparatistes. Aimons notre religion et respectons ns entre ns. Wasalam 🙏
Eskey même étant mouride, Seydi Hadji Malick dafa fess si sama khol trop ... li moy Sénégal cette harmonie . Yallana suniou khalif généraux yi yaaga fi lolu tei andak wër tei niou arrêter khadialo bi Kou tëd ki Cheikhoul Khadim Ak Serigne Hadji Malick danio bokou dembeu
Amine frere
Xoll yeupe seddna Serigne Babacar Sy Mansour yalla nafi yagu té werr 🙏
Amina
Machala sy malick khol ded na trope yalna yala goudal fane yi te werel la lol si barkel seydina mouhamed
Très bonne leçon d'humilité,
Nous sommes tous contents de cette intervention et comprenons que nous tous des humains
Que Le Tout-Puissant nous accorde un esprit de discernement pour comprendre l'oeuvre de Maodo, son idéologie et le sens de son combat
Macha'Allah
Machala Sy malick sama xole cedna barkep brm touba yala nga goudou fane si dolele cheikhoul khadim
Ndeysannn yal ngafi yagg tei weerrrr sunu khaliff🙏🙏
Je sui mouride deh mais serigne bi dafa deugou talibé yii bayilen khel si li serigne bii wax
MDR
Walahi lou am solo la wax
Fatou Diop machalah yalnagnou yalla may dég ak topou inchallah 🙏
Merci beaucoup
Sy Malick yalna yalna goudal fanwi 👐cou woyaf machallah ♥️👏👏
J'ai plus les mots😭😭. Yalna Yalla goudeul sa Fane Sy Malick Khalifa Ababacar, Sokhna Aïda Sy Dabakh yalna Yalla goudeul sa fane. Contaane nagnou gnoune talibés yi. Pape Cheikh lii si yaw lako Yalla djaralé santal Yalla ak kép kou nék si plateau bi. Tfm sa kaw thia kanam🙏🙏. Sénégal yalnafi diam yagg🙏🙏💖
Alhamdoulillah Sy Malik yaggefi lole té werr barke Serigne Babacar Sy
Machala tfm
Macha allah sy malick adounabi yalla nafi yalla dolli diamou 😭😭❤❤❤❤
Je suis touba mai respect 👏👏👏
Yalna yalla goudeul sa fane sy malick
Vraiment. J'ai. Pleur
Amine
Mane mourit la me Sénégal kahmoul nhiou sakhe linou am walhaye
Amine yarabi 🌺😙😙😙
Amine
Machalla sy xole yeupp sedd na SY
Machalla sama khol séde naa trop 🙏🙏🙏🙏
Bilahi diereudiuefe si malik wanega yone ma sa allah yalla nanga goudou fane
Yalna yalla goudal fan yii ci barké seydina M. Psl
Amine way
Nn Li meusou fé AM bikakhi machallah wa TFM wayé ken dou Seydil Hadji Malick Sy 🙏
Machalla amna solo lol sy malick
Dieureudieuf sy Malick khol yi seed lol machalla
Gana messeré mongui nieuw deh😂😂
Sy Malick contante nagnou
@@boygainde3764 kane moy kokou?
Je sui Mouride mé bilaye walaye sama khole dafa séde sy Malick yagueu fii lolee té wérr thi barké Seydina mouhamad psl Amine 🙏🙏🙏🙏🙏
Suis pas tidiane mais la vérité ya pas de fanatisme chez eux.ils ont mis chacun personne à sa place.pas à la place de dieu ni autres .dans la vie tout exagération est mauvais.voilà ce qu on doit apprendre aux talibés pour qu ils doivent pas égarés. Une partie très important qu il a dit " si le monsieur avait dit des choses exagéré sur maodo malick ils vont automatiquement démentir comme il a bien dit le khalif.a partir de son discourt, je prends bcp d considération et de respect total envers lui
Yalla yagual lafi lole tégan ande ak wére
Amine
Yalnako yallah bolle defal sougnou mame mountakha mbacke gno bokk lep
Pape cheikh Diallo tu es le meilleur des meilleurs machall Allah
Bravo Pape cheikh, svp ton émission coute maintenant très cher tu ne peux plus invité n'importe qui car l'émission a eu une autre valeur historique depuis hier lorsque le khalifa à appelé 👍👍👍
Bilay
@@massatagueyegueye2001 mon frère sakhole mofesse et j'ai pleuré seul dans ma chambre en regardant l'émission sur l'intervention du khalif des tijanes 👍👍👍
MachAllah Sy Malick Yalla lafal la thiat té doli Soutoura Éternel Diam diou sakh loool te ande ak werr
Il faut surtout que celles qui sont sur le plateau s'habillent décemment puisque l'émission a une portée internationale suivie par surtout Le Khalif Général des Tijanes MachAllah
@@fatoufayembaye7806 tu as parfaitement raison il faut sensibiliser pape cheikh car l'émission est suivie par les personnes les plus populaires et importantes du monde ❤❤❤
🙏🗯️😥ma cha Allah 👌 yalla n'a diam yagg Sénégal ❤️✍️
Je suis talibé mouride mais j aime au fond de cœur le khalif général des Tidjane yague fii lole té wér
C'est quelque chose a magnifié
Machalla kadouyi amna solo yalla gafi yague lole te weer si barkhe xassida yi amine rabi
machallah meilleur émission ❤❤❤❤
Ana niou done khasste warr ngei na rouss de yalla na diam yagg ci sènegal dine ji lep bene la star bi kenn la moy yalla mou niou binde
Walahi dagno khamoul motakh
@@ndeyafall8831 mo ngi no nou de mai yalla bakh na yalla na niou yalla sakhall ci lou bakh reke