Hey way... hey way souvenirs Sama 1er plat que j ai préparer à 9 ans.. Avec l aide de ma mère yegue thi banc bi rek. Tim. Gaziniere bi. Ooh plat bou nekh. Way petit saf way. Très biennnn. Marietou n'a lokho bi weer. Je t embrasse ❤️❤️❤️❤️❤️
Machallah Machallah plat bi namonenako ça me donne envie de le faire ce weekend dieureudieuf ma tata d amour Diam rek ngay ame si barke Seydina Mohamed Slws
One of best TH-cam channel in Senegambia period!! I love watching this channel even at work in the morning 🤣 I'm so hungry right now but i can't stop watching 😋 I love my country 🇸🇳 ❤️
Tata Marietou ya takh ba nammatouma dara si toggou yalla nanga fi yaagu tè and ak wër si barki nabil Moustapha beugu nala lolou soppou nala trop Dêma yaakal
C est très bien et généreux ce que vous faites. Une grande utilité publique. Une question: pourquoi on ne voit pas votre visage ne serai ce que le début de chaque vidéo. Un conseil: pourriez vous pour des raisons professionnelles porter une blouse de cusinier. Merci avec respect pour tout ce que vous faites. Vous méritez une médaille du chef de l état. A travers vous vous démontrez que toutes les femmes méritent être respectées. Bonne santé et une longue vie à toi.
Hey way... hey way souvenirs Sama 1er plat que j ai préparer à 9 ans.. Avec l aide de ma mère yegue thi banc bi rek. Tim. Gaziniere bi. Ooh plat bou nekh. Way petit saf way. Très biennnn. Marietou n'a lokho bi weer. Je t embrasse ❤️❤️❤️❤️❤️
Machallah Machallah plat bi namonenako ça me donne envie de le faire ce weekend dieureudieuf ma tata d amour Diam rek ngay ame si barke Seydina Mohamed Slws
Machallah Tata Maretou Mere Diop yalnako yalla kharei aldiana firdawsi yaw aussi nga yag dignou gounguei
Machallah choukrane waaloutah dindiiwo bop jiahotobi
Tata marietou taye daga yakal sama xarite sama domou ndaye aissatou kane lô lô ndame ciré koku lumu bahh rek doyul borom Mauritanie ak Amérique machallah koku kany sall moy yayam domou ndayou moumi gueye machallah
😁mane setanouma liguay toguou dh mé sa façon wakh momay fathie 😍😍😍😍
Fiirir bamou obodio walla booguèeesss.!
3:29 Yangui may fattéli bamay nék campus universitaire, benn lall pour kenn, niaary nitt bokkh ko! Bouniouy teudd, bopo ki feete ni, bopp kenèen ki feete neulee..
Tata machala kagnengaye Togou thiere base ak kethiakh
Macha Allah ay way Tata néna dagnou koy firire bamou obadio😂😂 koula geudieu degeu geudieu ré doundal lou bari Tata chérie 😍😍
Thioo way merci tata Marietou merciiiiiiiiiiiiiiiii
J adore cette dame machallah 😚
Maa chaa Allah Laa qouwwata illaa billay.
Wa hlykoum Salam wa rahmatoullahi wa barakatouh tata. Amatina solo
Namananiou la Marietou.
Merci merci
Bilahi togue barina façon Masha'Allah prochainement nilay togué Thiou Dieune Insha'Allah. Merci Mariétou
Delicious dish,presentation is 👌 nice
Youbou yaba 🤣🤣🤣 Tata mariyrtou machalah
😘😘😘
Waleicouma salam warakh matoulah tatie Mariétou bismilah machallah ndouguou bi raféte na hummmmm nathi diam bari ❤❤👍😉
Bonsoir tata marietou
Merci pour ta générosité.
tata marietou yagui deff saaf waw marietou ya taay meun sa quun wa tata bon appetit
Wa mzman sa. Thiou bakhatina diaradieuf mère diop yalana khipe aldiana firdaw
Allahuma amelen wayyy
Tata maretou machallah defatigua dè sama plat
Diam soutoura adouna ak alakhira rek lalay nianal.
Yalla defaralko mbolem ndioulite
Fatou Mane Allahuma ameen ma sœur merci wayyy 🙏🏾🙏🏾🙏🏾😘😘😘❤️❤️❤️❤️
Merci pour votre générosité que le bon Dieu vous bénisse
One of best TH-cam channel in Senegambia period!! I love watching this channel even at work in the morning 🤣 I'm so hungry right now but i can't stop watching 😋 I love my country 🇸🇳 ❤️
thanks my Dear
Machallat tata mariétou longue vie à toi.
J'aime bien le thiou
Machalla j aime bien ❤❤❤ ak trees bien yi 🤣🤣🤣🤣
Nous les modou modou on a intérêt de te suivre
Machalla Tata mariétou toujour au top de bonne et délicieuse recette Mére Diop Yallah nako Yallah kharé Aldiana Firdawsi akk mboléme dioulite bou djitoudji ❤🙏
Nabou gina Ndiaye sall Allahuma ameen way ma cherie
@ Amine way ma tata❤🙏
Merci tres bien nena 😘😘😘😘
Machalah tata marietou thiou bii nekhna contaane na torop thii dédicace bii😍😘 @momy merci bcp 😘😘😘😊
Mashallah way diap neu forme dehh😅
Ta Marétou machallah laf thiat
Merci encore une fois tata Mariétou pour c bon plat s chez nous. Que l bon Dieu t prête une longue vie une santé d fer
😮😮😮😮😮😮😮😮😮😮😮😮😮😮😮😮😮😮😮😮😮😮😮😮😮😮😮😮😮😮😮😮😮😮😮😮😮😮😮😮😮😮😮😮😮😮😮😮😮😮😮😮😮😮😮😮
Thanks 😊 Tata Mariétou darling 🤗🥰😘😍 diap na forme mom MachaAllah
Mahchahala ta mariétou nekhatina 😘
Salam Marietou macha Allah bonne continuation
Tata Marietou ya takh ba nammatouma dara si toggou yalla nanga fi yaagu tè and ak wër si barki nabil Moustapha beugu nala lolou soppou nala trop Dêma yaakal
Mrsi tata marietou thi dédicace bi contane nañ❤️
Très bien bemay ray 😂merci tata ❤️goudeul fane
Je t'aime beaucoup
cv tata Mariettou .
mais pourquoi vous ne faites pas la vente en ligne des epices k vous utilisez.merci
Première 😍😍😍😍
Maman yeungal ngama mane thiou awma si kersa
Mâchala thiou
Man tre bien bii mo may danal 😂😂😂
Tata gratin de patte la begue Ngua togou ko svp té yalla fayla
Fatou Mane ok insha Allah ma cherie bientôt rek
Machalla
Salam ma Tata defatiga waaay machallah ton amie t'accompagne sur tte les plat j'adore les gombos moi aussi
Waaleykum salaam merci wayyyy
Cc tata marietou yallah n’a ça diameu yague mais les 3 personnes qui ont dislayké laneu moléneu fii méti tamite aaaa mérénaléne toropppp
Salam . Tata mariétou sauce Thiere mboum la beugeu gua def , stp
Tata mariètou namone nala trop
Très bien douloukh douloukhi🤣🤣🤣
machallah tata
😙😙😙😙👍👍👍👍👍👍👍👍👍👍
😍😍😍
Salam 'aleykoum Tata Marietou , Masha Allah , Allah ybarek ❤
😘😘macha allah
Très bonne recette 👍👍👍
Yummy where do you buy the round green veggie? Is it available in the USA?
Machalah Mariétou 🤩mais pourquoi la tomate directement dans l'huile il fallait prendre un peu dans le nokoss et d'abord nékothi rèulle😂
🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣😘😘😘👌👌👌
Mariétou ! Sa thiou bakhna 😂
Trèsss biennnn❤❤❤
Say Termes de parole momay rééy
C est très bien et généreux ce que vous faites. Une grande utilité publique.
Une question: pourquoi on ne voit pas votre visage ne serai ce que le début de chaque vidéo.
Un conseil: pourriez vous pour des raisons professionnelles porter une blouse de cusinier.
Merci avec respect pour tout ce que vous faites. Vous méritez une médaille du chef de l état.
A travers vous vous démontrez que toutes les femmes méritent être respectées.
Bonne santé et une longue vie à toi.
Amatina solo ma cha allah sama togolokh bi
Je t'aime way tata
thiere basse kethiakh sans viande menou mako togue
INSHA ALLAH DINAKO TOGUEU
Très bien 🤣🤣🤣
Non tata Marietou dama la beugue
🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾😘😘😘😘😘❤️❤️❤️❤️
Lan moye sami
English please
Wa nougnouy def ba dieune bi dou coller
Salam je suis pas tata mariètou mais je vais me permettre de te répondre bou huile bi tangué dou colé