Maashaallah Tata!!! Nèkhatina!!! Moi à la place de la friture, après avoir pané, j'aurais beurré un plat en verre allant au four, y disposer les rouleaux panés, mis du fromage sur les rouleaux avant de tout mettre au four maximum 20-25 min pour les gratiner! Miam Miam!
Bilahi Mala geum ndakh sa teeeey AK sa pédagogie..khamna net kou laaabiir nga....mann je vais essayer parck vidéo bi dafa très clair ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️merci
Salam tati tay recette poisson pané bi ak beignet donut yi la defar mais tt le monde a apprécié merciiiiii encore yalla nala borom bi same in sha Allah 😘😘😘😘❤
Merci beaucoup Maman d'avoir précisé le choix du pain 🍞 car beaucoup des choix que nous avons au Sénégal ne se plient pas. Seuls les plus chers (briochés) se soumettent au pliage. Merci pour la recette.
elle merite beaucoup d abonnée et des millions de vues
Oui c’est vrai mais le seul soucis est qu’elle parle qu’en wolof du coup elle se ferme .. moi je regarde mais je comprends rien c’est dommage ..
Absolument elle le mérite bien 🤩❤️❤️🥰🥰🥰🥰🤗🤗🤗😍😍😍😍🌹🌹🌹
Absolument mais n'oubliez pas de liker les vidéos c'est important
machalla yaye isseu yalla na yalla wereul 🤚 machalla 🥰
Machallah Sama togologue bi yallana lokho bi weer
Machalla comme toujours nekhatina toggo dale ya ma thi doye yalla na yalla wéreul loxos yi amine dieuredieufeti
Iow yalla rek lanioulay bayél mou fayal niouleu machala ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Vraiment avec togou yaye isseu je suis devenu un élève merci ❤❤❤
Machallah goudal fane bou ende ak wèrrr amine
Machaalla nékhna séle na yalla na sa diame yague
Kéthiém rék mo manqué thi pala bi gay thieup di lék machala
Macha'allah recette bi diarna yone comme d'habitude, merci beaucoup Yalla na sa djam yague 😊
Manchalla defa tiga sa façon yalla nala Yalla fay sa khol
Macha Allah Tata issa deug deug kenne dou yow ndanane ga teyye ga sa ayye recette amena sollo laf thiaat doundeule werreule je t'aime très fort
Ramadan moubarack
Machallah li mome dioguéna dal
Vraiment maman Isseu amoulo morome, merci pour le partage, yalnalla souniou borom faye
Merci yaye issa pour tous yalla mayla goude fane rek inchala vraiment vos idées de repas nous sauve la vie
Machaallah amena maana togue rek ngaye def laf thiate ake lamigne
MACHALLAH
Maashaallah Tata!!! Nèkhatina!!! Moi à la place de la friture, après avoir pané, j'aurais beurré un plat en verre allant au four, y disposer les rouleaux panés, mis du fromage sur les rouleaux avant de tout mettre au four maximum 20-25 min pour les gratiner! Miam Miam!
Ça doit être délicieux 😋
Mom dèy danou lay nianal nga yagg fi looool tè werr ma maman adorèe
Demain inchalla bi lay deifar ♥️
Magnifique recette Yaye Isseu !
Waw macha allah très très bon à reprendre incha allah merci
Machallah toogou yaye isseu et merci beaucoup comme d'habitude ramadan karime
Machallah yaye yallana yalla weeerla lokho bi weeer AK guoudou Fann ♥️♥️
Machallah tata amouniou sa faye boromm bi rék lanioulay bayé🥰🥰
Yalla na yalla defal la diam ak wer
Man dalllll ndayalé nala sama bopou rk masahala sama yaye 💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕💕
Macha'Allah maman ndar bi cordon bleu internationale yallah na yallah sa jamm yague 🥰 Humm 😋😋 j'adore ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️💚💚💚💚💚💚
Merci maman, vous êtes très pédagogique ma cha allah ! Yalla n'a yalla fayla yiw!🙏
Mashala yaye boy.on t'aime fort
Salam mâcha allah
Machalla yalla bou la tiat topou Nice trop
Machalla tes marmites son propre et j aime ta mode de préparation et tes plat aussi merci je t adore
Machallah sonou miouney ame groupe Togg Yaye Isseu sur whatsaap je suis là premier deh
Machalah 🥰❤️❤️❤️❤️des Coeur pour elle
Maa shaa Allah thank you Aunty... definitely trying this out🥰
Thiéy YALLA mi niou saak. Maan mom je me suis abonné dès le premier jour que j'ai découvert cette chaîne. Fi mom tioukouna.
Mashallah mama merci yal na yala faye 🙏🙏🙏❤❤❤
Machallah chapeau à toi
Bilahi Mala geum ndakh sa teeeey AK sa pédagogie..khamna net kou laaabiir nga....mann je vais essayer parck vidéo bi dafa très clair ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️merci
Salam tati tay recette poisson pané bi ak beignet donut yi la defar mais tt le monde a apprécié merciiiiii encore yalla nala borom bi same in sha Allah 😘😘😘😘❤
Ah Masha'Allah je suis fière de toi ma belle même si je ne te connais 🙏❤🤗
@@astoubilla merci ma belle yaw sugnu Maman national bi nagnu ko nianal rk ❤❤❤❤
@@mariamaba6480 Bilay iow elle le mérite tellement na partenaires yi nieuw nak ❤❤❤
@@astoubilla mane kay lou partenair yi di khar si sugnu yay dji la xamoul 🤦♀️.sett na sell na teksi wakh dji lerr MachaAllah
J'aime beaucoup ta cuisine
Machalah maman mangui lay suivre dp8 Mouritanie 🇲🇷
MashaAllah Tata Goudal fane.
Machalla tata❤️ juste pour wané deur pain de mie bi ben rek bahone na pour gagner du temps
c'est ce que je vais faire demain inchallah
Ma sha Allah
Machallah ♥️♥️♥️♥️
ooohhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhh
Machala bon plat merci
machalla do morome guayi
Son excellence Ya Isseu chef cuisinière!100o/o nekh
mâcha lah
Machalah tata amna solo
Machala yaye isseu laff thiatt
Machalah tata les espliquations sont très claires Amal Diam
Masha'Allahou sama sopee sokhena marie diop togou yaye. Vrai vrai cordon bleu.
tata doundal wéral amal diam yangui gnouy diapalé bou bakh machalla
Manchala
Machalla tata ❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Bravos a toi
MachaAllah nehatina 🥰 🥰 🥰
Machallah
Machaallah maman nekhna lool way❤❤❤💪💪💪💪
En tout cas , rien à dire ; TOUT est nickel ! Quel délice !
Dieuredieuf yaye !
Est ce que di ngua def traiteur ?
Jai pu le faire hier cetait delicieux
Mashaallah
Merci beaucoup Maman d'avoir précisé le choix du pain 🍞 car beaucoup des choix que nous avons au Sénégal ne se plient pas. Seuls les plus chers (briochés) se soumettent au pliage. Merci pour la recette.
Je confirme
Machalla tata
Machalla kéne dou yow eupene li defe fése mogui tourou dounele werrele sa tougue diarna yone raféna setena machalla ❤❤❤❤❤bon nogou ya Isseu
Merci beaucoup love sur toi 🙏🙏
Machallah mé mane boumakoy défar day naan diw pourkoi
Machalah lafe thiat ♥️♥️♥️♥️
Je veux que tu faire le akra si si c'est possible
Macchallah...
MASHA ALLAH
Ay way yaye isseu invité ma ndogou way 🤣🤣😋😋😋
Walah j'adore bajane isseu long vie
Masha’Allah such a great cook 🙌 if I’m in Senegal I would’ve love to break fast in your house 🏡 doundal te yaague fi ❤️ frm 🇬🇲
Goudal fane Maman
Mach alla
Diadieufeti yaye isseu machalla
merci beaucoup maman Issue je taime ya Issue kon tan na torob nak vidéo bi Nice na torob ❤👍👍🥘🍱
Maman machalla Say plat aide beaucoup mais souma sagnone nga kholate tps bi da goude surtout tps démonstration yi pour moi 2 exemples seulement suffit
Merci maman j'apprends beaucoup de vos cuissons diaradieuf
Dako diarrr nakkk li tamittt nehna ba nopi
Machallah machallah
Machallah tata merci
Vraiment y'a bakh
Merci beaucoup yaye Issa yàlla nasa diam yague Dioba dioba
mashala mashala n'a réssak diam merci encore je t'adore
Nékhna tata douma lék guinar mé j sais k nékhna
Machalla ❤ ❤ ❤
machalla pour la recette mais est-ce que on peux le faire avec de la viande hachée
Bien sur on peut le faire avec de la viande haché, avec du thon et de la dinde aussi 😋😋
Merci beaucoup
Mais paix de mie niata lay diar svp
Merci yaye isseu goudal fann
Bonjour tata col bi lougnou koy defarer
Madame vous pouvez ouvrir une école de cuisine s'il vous plaît? 😭
Tata est-ce que c’est forcer que bokoy moussay dangay def touti huile???
Machallah tu mérite plus de Million de vue maman ,mais comment s'appelle cette grain de pain je veux chercher ça en all
Allemagne
Merci bella chapelure de pain
Bonjour vous pouvez mettre la liste des ingrédients sur vos vidéos pour ceux qui ne comprennent pas la langue
Merci beaucoup