La presentatrice parle trop au lieu de laisser l'invité parler. Delen khol gni ngeni tek si plateaux yi. Cet homme est posé et très discipliné machaAllah
Quand vous avez un invité, il faut apprendre à le laisser s'exprimer. Si vous mobilisez la parole , il se perd dans ses dires et ne développe pas ses idées.
La presentatrice parle trop au lieu de laisser l'invité parler. Delen khol gni ngeni tek si plateaux yi.
Cet homme est posé et très discipliné machaAllah
Ndaysann bb Fa khadione ngafi dé yalna nga motalé sa ndaw aldiana si wètou Mamam bou bakh bi Tante Ndeye Khady Gueye 😢😢😢😢
Je te connaissais pas mais aujoudhui je tai admiré machallah yallah nassa diam yague🙏❤️
Yalla nako souniou borom yereum 😢😢😢
Yalla ko yallah yeureme kharéko aldiana
Machalla bonne continuation
Yalla nala yalla may kholou mougn ❤
Sama dome sama rakk aka yarou , am discipline, dior nieup thieur kou bakh beugg limouy def té meun ko manchala. Yalna nioula geuneu degg fou soré.
Liguèye diamou yalla la,geuneul focus si couture bi,bayil employè yi si salon bi.yalla nala yalla geuneu diapalè
Du courage rak dji diam rrk inchalah
Diogo aka guen
Môme rek aka meune limi def
Yalla nako yalla yeureume kharèko aldiana
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤merci beaucoup
Lou méti wone🥹
Ay dioguomaye kagne nga fi doundou Lou metti li tei yeugou mako...li motakh ma guethieu la guiss si leop ohhhhh😢
La diva coumba,yalla anda bi geuneu yagg
Ndeysane il paraît discipliné
Dioumo dé samay deukeundo you bakh sakh surtout mom mi dougoul si kén dé
Nena il paraît k ki dafa yarou donc waxoul lou bone
Discipline = yarou
Indiscipliné = kou yarou woul
😭😭🤲🤲🤲🤲
😭😭😭😭
❤❤❤❤❤❤
Nio bokone keur guediawaye yayam mo deukone si Souf sam notaire
Quand vous avez un invité, il faut apprendre à le laisser s'exprimer. Si vous mobilisez la parole , il se perd dans ses dires et ne développe pas ses idées.
Perlage rek la meun khamnako
Diogo nga defeni dawo fowe niaw tamitt kheuy kheuy niaw niawou khew 🤔🤔🤔
Maquillage ak coiffure bi mome bayiko alalou adouna diarouko
Pour ?, c'est un métier comme tout autre
Dara nekousi c'est un métier noble ❤
@ChantalGomes djiguéne boukoy déf yalla daflay reubou wakhatouma goor Mane nako déf parce que amnasi droit mais d'où masa dagane
@@sasha88201c'est pas un métier d'homme surtout un musulman
@@kharycisse5267 sa way métier yii daganoul kon dina bari déh, goor youy,
lett, di défilé pour model, goor youy toog etc...
Je pleure tes khamouma la
La diva coumba,yalla anda bi geuneu yagg