Honnêtement Zo bett ngama parce que je m’entendais pas à ça venant de toi, mais plutôt de Canabasse , parce que je l’estimais beaucoup de par sa personnalité son intelligence etc ... mais là dagma bet parce que li nga wax bass moko waroon wax , mane quand il a fait cette sortie sur vide di teek mane dama am louma meti naxtei mom kharéwumako woon fofu ak loko meunti def Bass kmm wesuna li de 1 , de 2 amna foungeen diota jaar .. mais dafa immaturité ak niak xalaat .. bref mais io chapeau 🎩 si sa réponse boul meuss tontu , dula yoob feeneu .. au contraire dafay geun yaak , defna erreur balko nga dial si leeneen .. et bnne chance pour tn show 👍🏿
Tous ce que je dit c'est que Omzo ses promo d'événements s'accompagne souvent de clash diayanté prek truc du genre. Bass il rap hyper bien Omzo de même et que rap bi ins bi soxlatul ayy abbé clash na imam wala pinpin clash na nicky mais plus like lu gars yi di def ni tek ayy son yu dal vidéo yu dop teug si sall yu mak guichet fermé. Zo Bass Ngaga Dip Elzo Akhlu brick OMG Eve creasy black queen rap bi molein soxla pour ñu export sunu music Bilahi du omzo don clachanté wizkd guen xam wala bass ak davido meunuñu sen beatmeaker menuñu what else fall ñu diapanté liguey kw tput le monde y gagnera kw
Honnêtement omzo c’est un grand homme il a pris de la hauteur par rapport à ca Senegalais yi gno wara khamni adouna amoul solo té warougn accepté di perte temps si ay thiow Diam mo geuneu aay
Attention !!!! Vibe Radio Senegal se réserve le droit de poursuivre en justice les titulaires des chaînes qui reprendront cette vidéo sur TH-cam ou encore d'autres plateformes de streaming vidéo sans autorisation.
nénagne danga rew à cause de ta façon de faire le rap mais tu est intelligent tmt dans la vie il faut savoir faire ce qui est essentiel le reste on s'en fiche je t'adore!
Mais vous jouez à quoi... Il faut pas accepter qu'on vous divise... Vous êtes des responsables.. Il faut s'asseoir autour d'une table, discuter afin de trouver une solution à ce problème... Même la guerre mondiale a été resolu autour d'une table après des pourparlers... Donc vous devez etre au dessus de tout ça... Comportez vous comme des responsables.. Vous êtes tous des frères.. Donc arrêtez... Arrêtez...
oh des larmes aux yeux. Damaladane sayi kher ay temps mais diekhna tay srx. Vraima nitou kécé nga. Si possible tu me send ton num. De la part d'un nouveau fan
Non Zo dou nitt wallah j'adore ton esprit de dépassement continue sur ce lancé bro tout ira pour le mieux inchallah Mouy bass mouy kénéneu boulen falé thie ay clash Déniou béguel rk c'est ce qu'on demande men TU AS BIEN PARLÉ OMZO EN TOUT CAS 👍😍
Quand tu es un modèle pour la jeunesse il faut se comporter comme un grand homme et ça Omzo Dollar 💵 l'a fait c'est ça qui différencie Omzo Dollar 💵 et les rappeurs de sa génération Canabasse vraiment il m'a déçu il devait être le protecteur de Omzo il devait se comporté comme un grand frère mais il ne l'a pas fait dommage la jalousie est un vilain défaut big up Omzo nous t'aimons et nous t'aimerons pour toujours bonne continuation frère
Bro contane na si ioe bilahi Pour mane sax dangay indi thiow yokou essence si feu bi mais t'as parlé en tant que personne mature😎 bonne chance bro. Suis fan de Dip nak😍
Je suis vraima ému buzz labb c la vie et vs voir vous déchiré kom Ça walahii dou nek sunu avantages parsk après tt cela c la mifa dpui 2008 niou nek sen guinaw vraima nekhoul c genres de choses di am mai nak chapeau a tw et vraima tu as été humble et en écoutant jai pu remarqué k tu étais sincère sur tes propos car c avc le cœur k tu parlé
Je suis certaine que cette situation déplaît à tous les fans de buzzlab. Moi perso ça me fait mal au coeur, lii nekhou ma dara. Ça m’a tellement choqué et déçu surtout de leur part. Wa Salam
Vous qui ilsulté Omzo vous ne le connaissez pas plus que Canabass. Il a bien dit dans ses paroles "man ak Bass hamantenaniou" donc finiouy dioubowé tamit dou nguenn ko feké mandou lene
Li dou Yonne bro... après limou wakh leeraloko votre contrat verbale que ta pas respecter,la dame de Keyzite et le message vocal et dans tes textes. .. on t'attendais la. Donc fait pas ça pour après dire que tu clashe pas et tout après li yup dou Yonne vous avez durée ensemble. Bffff
J'adore la capacité d'Omzo Dollar à ne pas se faire déstabiliser ni par Canabasse qui est mon rappeur ni par ce satan da Tal qui ne ce qu'il sait faire de mieux. Diakhassé Aÿ niit. Zo man Bass moy sama rappeur mais honnêtement dama contane si sa tontou bi frère. Té soudone man la sakh nii lay def mom nga tontou moko arranger ndax mongui si sakou yi. Iow nga keep on going ndax insbi sa show yagatoul . Et mm sou féké ni def ngako louko méti entre frères tout se règle in péto.
Problème buzzlab canabass la, il veut toujours être devant, toujours être le number one, c'est pas possible nak, boyi daniou beug tekki si rap mais pas jouer ay second rôle, mom mo takh boy buzzlab yép tardè, dites moi bane rappeur buzzlab mo nekk di tothie ?, dou massa ame, il fait du n'importe quoi, buzness zam rek la tall (dk spirit) c'est un orgueilleux, un jaloux, même Jay s'en est rendu compte et il est parti.
Omzo vraiment je t adore Sama peura il faut avoir l esprit de depassement omzo t a bien parler . Canabasse dafa delou guinaw affairou khale to lay df mais tkt waxtane Len rk t a bien parler. Le boy a grandi
Vraiment digantei zoo ak bass waroulwone deimei nii.
Kié dakor🤙
weuuy mais pik yi omzo donn lancè peutr bass dafa thè guiss bopam
Bilahi
Bass moy déféant billaye déh
Yeah man mais ke dj c un vrai imbécile et kil ne c mm po son rôle dmr rek la
Bilae dj tall vrai naféke leu li dafaY Geune Agraver situation bi rk ms bass dafa wéré complètement li dou won Sakh yon gnou réglé blem bi ni😢😢
Omzo dou meussa tontou canabasse dj Tall seytané la
Kou beug Omzo tape bleu 👈
Big up for you
Il fait que son taff c est les gens qui ont envie de connaitre la vérité
DJ tall dou seytané deh, émission wam lay diay rek, bass mo sokhor rekk lolou moy wakh djii
Vrai seytané la dj tall
Trop sakh
Omzo mentalité propre franchement je t'adore de la part d'un fans de Dip Doundou guiss
Diadieuf djaambaar
momo men il a changé de nom ? Il est devenu deep ?
Merci de ta franchise
@@bujuman2880 non il a pas changé de nom je l'ai ecrit en englais
no yaw no fan d dip
Omzo khole bou rafète la yorr billahi 💓💓✋✌✌ RESPECT a OMZO ✌👌👍💟
j'aime la personnalité de Zo; faut grandir en fait!
Fils
C vraimen domage de voir des frère de buzz lab se déchiré comme ça .😳
Canabass est en déclin Omzo est le seul rappeur qui tient le rythme avec Dip
Zo real nga billahi. même sou blème amé dénguène ko wara régler en tant que ami té kène khamoul.
Honnêtement Zo bett ngama parce que je m’entendais pas à ça venant de toi, mais plutôt de Canabasse , parce que je l’estimais beaucoup de par sa personnalité son intelligence etc ... mais là dagma bet parce que li nga wax bass moko waroon wax , mane quand il a fait cette sortie sur vide di teek mane dama am louma meti naxtei mom kharéwumako woon fofu ak loko meunti def Bass kmm wesuna li de 1 , de 2 amna foungeen diota jaar .. mais dafa immaturité ak niak xalaat .. bref mais io chapeau 🎩 si sa réponse boul meuss tontu , dula yoob feeneu .. au contraire dafay geun yaak , defna erreur balko nga dial si leeneen ..
et bnne chance pour tn show 👍🏿
Mdr wakhofi dara ak seu commentaire bou goudou
Yamar Diallo t’as trop bien parlé je te jure
Yeah t'as parfaitement raison
Tous ce que je dit c'est que Omzo ses promo d'événements s'accompagne souvent de clash diayanté prek truc du genre.
Bass il rap hyper bien Omzo de même et que rap bi ins bi soxlatul ayy abbé clash na imam wala pinpin clash na nicky mais plus like lu gars yi di def ni tek ayy son yu dal vidéo yu dop teug si sall yu mak guichet fermé.
Zo Bass Ngaga Dip Elzo Akhlu brick OMG Eve creasy black queen rap bi molein soxla pour ñu export sunu music
Bilahi du omzo don clachanté wizkd guen xam wala bass ak davido meunuñu sen beatmeaker menuñu what else fall ñu diapanté liguey kw tput le monde y gagnera kw
Omzo nak j'adore ta personnalité
Honnêtement omzo c’est un grand homme il a pris de la hauteur par rapport à ca
Senegalais yi gno wara khamni adouna amoul solo té warougn accepté di perte temps si ay thiow
Diam mo geuneu aay
L'exemple de la maturité dans le rap force à zo dollar✌
😊
Bass d'à sissou rk mai amoul ben motif pour khar bâ heure bi du gueinai Aÿ affaire ssi omzo boudai daka souteral bâ heure bi loumouy gueinai
yaw boude amga khel del khalate mm ls fou reflechiss ki wahoul li tah mixtape deugeuntane nek si tourou keyzit e bcp dotr chose
@@mothernature6996 yow miye khalat loutakh mou khar bâ heure bi do soga clatai mom wakhna daka donne souteral mai pourkw mou khar bâ heure bi diko wer
Bilay deug piir
Joe projet bi projet vito la mou douguale thie coupleme. Couplet wou bass c pas prémédité. Bass is the boss!
Messatsu miezé on est tous derrière toi
05 avril Gt Came back2
Il faut être mature dans la vie 👏👏 bravo omzo
Première vue💪🏾
Guiss la wakh wakhoul dégue
Altaf Limbada tu parle de quoi là?
Dj tal vrai seytané quoi 😂😂 à chaque fois omzo dit quelque chose il commence avec ses 'huuun' 'hannnn' di grawal
Pousse bleu, les vrais dollavelli
Am a Gambian base in Denmark. Respect to Zo D. Gen len shokhor, shokhor respond.
Attention !!!! Vibe Radio Senegal se réserve le droit de poursuivre en justice les titulaires des chaînes qui reprendront cette vidéo sur TH-cam ou encore d'autres plateformes de streaming vidéo sans autorisation.
Vibe Radio Senegal *Good luck with that* 🤣🤣🤣
Boul ko tontou bro
Dj Tall war na di tedj gatam gui fait chier waay
Marieme est ce que noboumala yaw ??
دفرات سنغال mdrrrr
Walae nakk il est con
@@mariemeaichaanne8255 serigne touba khamnani dafa melni damala nop, diapsi ma khamla bok diokhla sama WhatsApp. Stp
دفرات سنغال mais mane la nob 🙄
T'es réagite comme un vrai gentleman respect à toi frère🔥🔥
Billay wallay tontou biii la done khar Zo big up for you we love you so much
nénagne danga rew
à cause de ta façon de faire le rap
mais tu est intelligent tmt
dans la vie il faut savoir faire ce qui est essentiel
le reste on s'en fiche
je t'adore!
Omzo Buzzlab sa yeuf Leu
Canabass Nékal Boss touty way 😎
omzo Tu ne m'as jamais déçue tu sais bien parler
Mais vous jouez à quoi...
Il faut pas accepter qu'on vous divise...
Vous êtes des responsables..
Il faut s'asseoir autour d'une table, discuter afin de trouver une solution à ce problème...
Même la guerre mondiale a été resolu autour d'une table après des pourparlers...
Donc vous devez etre au dessus de tout ça...
Comportez vous comme des responsables..
Vous êtes tous des frères..
Donc arrêtez...
Arrêtez...
bayeomar245 vrement cest dommage. G tres mal de les voir ainsi
Omzo ont t'aime ces tt
Merci OmZo Quelle Grandeur
Mane mòm team doundou guiss la bòk for ever
Reptyle musique for life
Franchement li mòm dawna Yaram basse waroul wòn dokhalé ni srx
Fans Dip yi mom khamnagne kouy Omzo 😂
Reptyle rk♥🔐
nioune wa team doundou guisse sounou yone nékousi
Yeii... Yeii....
lii daaww naa yaaram
Noo Messatsu Doo niit sérieux...
"gayii Svp naa Niieup waakh Mercii Cabanasse..."
Teii tellement mature mon gars...
oh des larmes aux yeux.
Damaladane sayi kher ay temps mais diekhna tay srx. Vraima nitou kécé nga. Si possible tu me send ton num.
De la part d'un nouveau fan
Mais yenn Dj Tall il est un professionnel dans son métier.
Il a l'audace de posé des questions audacieux tmt un peu de respect 🤦🏾♂️🤦🏾♂️
Ah wei
Gars yii daniou con koi 🤔
T la plus part des gens khamouniou rap ☻
kham
@@taphambow9524 respect toi
Omzo Sa Boy La Grand wam gua réponse Omzo Dafma Berte Li Da Wané dafa mature légui Big up Frère Bonne Continuation
DAOUDA sarr billaye déh
Wallahi bouko tontou ay real bro ngueine Dara waroul niaaw Adouna amoul solo les gars big up à toi Omzo et Basse plein de bonnes choses à vous 🤜🏾🤛🏾
Non Zo dou nitt wallah j'adore ton esprit de dépassement continue sur ce lancé bro tout ira pour le mieux inchallah
Mouy bass mouy kénéneu boulen falé thie ay clash
Déniou béguel rk c'est ce qu'on demande men
TU AS BIEN PARLÉ OMZO EN TOUT CAS 👍😍
Omzo meune nagn ko wakh lepp sauf nitt kou bone. Bilay c'est un responsable
J lé aime tous lé deux bilay omzo et basse sont mé rappeur a cause j'aime l rap galsen sa m fé mal j t jur
Dou ioe kasser
Guisgua dé
Dip l'avait dit ayy deumm lagn daniouy lekante sénn birr
Dip l'avait prédit dei Billae thiey dip❤
Omzo pour toujour merci bro d'avoir rendu tort à certains qui attendait k u répond à basse .repect à Omzo
C'est obligatoire de remercier Bass prk grâce à lui tu es devenu comme ça
Qui est D'accord?
Omzo soyons sérieux et honnête. Tu as lancé beaucoup de piques dans ton album . Tu n'as pas voulu assumé c'est pas grave , bétouniou ci yaw
MDR Wakhal deh frere .Sénégal mo neikh rek nite day deff baparé nga ladj ko mouye wakh si lénen
dj tall seytané tap jaime si tu es dacor
félicitations à omzo dollar 👏👏 Canabasse warna
rouss bou amei roussoukay
Da amone niou dawone nieuwate fi dii doule
mais tu dis vraiment la vérité que tu ne l'a pas clasher 🤔🤔!!!!!!
Oui
Vraiment cana wathie nga sa bop djisouma loukofi diaar si adina
Com dab chapeau omzo on t'aime fort nous et courage
🖕
Mai canabasse banialle lolou omzo sa Petit frer la ✌OMZO Lingua tek dawna yarame😢
Quand tu es un modèle pour la jeunesse il faut se comporter comme un grand homme et ça Omzo Dollar 💵 l'a fait c'est ça qui différencie Omzo Dollar 💵 et les rappeurs de sa génération Canabasse vraiment il m'a déçu il devait être le protecteur de Omzo il devait se comporté comme un grand frère mais il ne l'a pas fait dommage la jalousie est un vilain défaut big up Omzo nous t'aimons et nous t'aimerons pour toujours bonne continuation frère
King Miézé rek💪💪❤❤
Tapez j'aime gniko beug
Walahi zo yay gentleman
Omzo dolar ❤❤
respect Omzo Dollar
Mais nak tall mom berina waaah deee oufff hum hum rek tamid 😔
Med Métal Lagniou Wakh The Come Back 2
Talla wally jnr walaaaa frère
Mdr 😂😂
Bro contane na si ioe bilahi
Pour mane sax dangay indi thiow yokou essence si feu bi mais t'as parlé en tant que personne mature😎 bonne chance bro.
Suis fan de Dip nak😍
Wawaw fans Dip yi mom khamguène boubakh kouy Omzo 😂
Papa bougouma wax lou ndiagass way
Dafa def yeufou mature ma encouragé taxoul ngamay sonal fi dh
Bravo#Omzô fière 2Tw puissance rék💪💪💪
Omzo amna solo 🤲🤲🤲🤲👍👍👍
Hii Omzo franchemant limou wax deugg la kw Bass call ko 😙
Mais vraiment
Baba Diallo ioe loffi oute xana do fans dip
@@dexterfv2l597 wahal diam iaw Dip man
les médias sénégalais manquent des présentateurs règlés et posés tellement
vrement nékhoule séne fans yi si se disput métinala tape jaime
Vraiment omzo je suis encore fière de toi encore big up a toi tu est un homme fort
Boy li dawna yaram billahi boy basse demal balou way
Mdr Omzo vous a tous eu en esquivant le vrai débat
Papa Silly Traoré t un ignorants t en + nie xamanténaniou yasi des rk ki yeufou magu la def xarako wone fi
@@serignemasoursall8682 yaw bilay innocent ngua . Ya con deugg deugg
Bass moy balou wala omzo
mbarikalah mbarikalah ❤️❤️..
#Omzo boulko réponde Dj tall sèytani la bilahi
Harouna Gassama c son boulot mec il crée des challenges c pour cela qu'on le paye
alors tu veux dire qu'on lui paye pour qu'il c'est par les meilleurs amis
Ils ont décidé de se séparer ici c son plateau il doit ouvrir le débat pour donner goût à son émission
Séparation bobou moy takh niou rap niom niare nieup...Canabasse boumou dioubowé ak NitDoff ba légui amatoule challenge ci game bii...
@@metzondiaye2837 bilahi
Dj tall mom franchement merci rk genrou seytanei yi lagnou wara guenei si radio yi ak télé yi
Pour dire vré #Omzo Dollar cei mn Rappeur meii wakhoufi Dara Il répéteu les mêmes Phrase Depuis le début ...
Domou Bour enfin ioe yangui guiss tei yaangui degg👏🏾👏🏾👏🏾👏🏾
Je laime Plu FransemnT Seu gars
Je suis vraima ému buzz labb c la vie et vs voir vous déchiré kom Ça walahii dou nek sunu avantages parsk après tt cela c la mifa dpui 2008 niou nek sen guinaw vraima nekhoul c genres de choses di am mai nak chapeau a tw et vraima tu as été humble et en écoutant jai pu remarqué k tu étais sincère sur tes propos car c avc le cœur k tu parlé
Zoo dollar 💵 wakh dji Djioup nah rafèlou lou nagne sa tontou Waw ni rèk la mak dal day yeureum xalé khalé respect ✊🏽 mak tubarkallah yalna djam yague
Je suis certaine que cette situation déplaît à tous les fans de buzzlab. Moi perso ça me fait mal au coeur, lii nekhou ma dara. Ça m’a tellement choqué et déçu surtout de leur part. Wa Salam
Miézé Miézé le général des rappeurs galsen .
Il faut avoir l'esprit de dépassement Zoo et ne le répondre pas, continue ton jobs 💪💪💪🇸🇳
Vous qui ilsulté Omzo vous ne le connaissez pas plus que Canabass. Il a bien dit dans ses paroles "man ak Bass hamantenaniou" donc finiouy dioubowé tamit dou nguenn ko feké mandou lene
First à regarder le vidéo.
Tu é l meilleur rappeur Sénégal d ts temp si tu aime omzo l 5 defal tew niou tassaree feppp
Daaadjil pakêt bi gnou Raab tè Taaaal... nooo dj Tall daaaaaal akh yagui nelaw.. Canabass doula wooo nahhté Dagay enrigistré poucave gaaa Poucaaave kène douko wooo. Tidjil pakêt bi loool yoolè boy gua Poucave, di tèk xél fii wayé Maguoum yi sibb nègn boyi gaay nakh
GRAND YOMBOUL OMZO TU ES UN GRAND ET SAGE BILAY ON T AIME BIEN CONTINU COMME CA PLZ ET MONSIEUR TAL ECOUTE TES INVITES PLZ MERCI
Omzo tassaré neu deuk bi
Vraiment Omzo daffa Mature il c’est réglé les choses avec Diplomatie je félicite à partir d’aujourd’hui dinala geuneu Follow 😍☺️🥰
Wallay Omzo yaye seen papa niom niep on t'aime fort
Li dou Yonne bro... après limou wakh leeraloko votre contrat verbale que ta pas respecter,la dame de Keyzite et le message vocal et dans tes textes. .. on t'attendais la. Donc fait pas ça pour après dire que tu clashe pas et tout après li yup dou Yonne vous avez durée ensemble. Bffff
Bilay Omzo boul ko tontou
Ce qui m'étonne chez les sénégalais souniou amer problème koussi taxaw wax ngani mo wax deugue! C bizarre
Kou déglou Dip khamené dou moromou basse té zo da ka clash dafa respecté basse motakh répliqué woute buzzlab sans omzo né rien allez zo yaye séne pape
Canabass dafa dioum billahi' non ça me touche que des frères Finissent comme ça, dommage😪
Omzo like for you
Mes ak nouma dèmé begouma wone 'nga geine BL
Kèn dou Miézè
Omzo💪👍👍👍👍👍👍
Oft omzo dollard ak cannabasse ya pa photo dj tall mom seitanela omzo yako clash donc assume mo geune guay dof dof louni
J'adore la capacité d'Omzo Dollar à ne pas se faire déstabiliser ni par Canabasse qui est mon rappeur ni par ce satan da Tal qui ne ce qu'il sait faire de mieux. Diakhassé Aÿ niit.
Zo man Bass moy sama rappeur mais honnêtement dama contane si sa tontou bi frère.
Té soudone man la sakh nii lay def mom nga tontou moko arranger ndax mongui si sakou yi.
Iow nga keep on going ndax insbi sa show yagatoul .
Et mm sou féké ni def ngako louko méti entre frères tout se règle in péto.
Mesatsu💪💪💪💪
je suis très content de toi tu as bien fait de répondre comme ça après tout vous êtes des frères c'est pas la peine de prendre la tête avec Canabass
Problème buzzlab canabass la, il veut toujours être devant, toujours être le number one, c'est pas possible nak, boyi daniou beug tekki si rap mais pas jouer ay second rôle, mom mo takh boy buzzlab yép tardè, dites moi bane rappeur buzzlab mo nekk di tothie ?, dou massa ame, il fait du n'importe quoi, buzness zam rek la tall (dk spirit) c'est un orgueilleux, un jaloux, même Jay s'en est rendu compte et il est parti.
So khamone loumou investir ci boy yi yeup digua teudj seu tate . Omzo bi nguay guiss Canabasse moko fabriké def louné pour mom
Omzo😎😎💪💪
M omzo a dit vrai grand théâtre day show force 🔥❤️
He’s so mature👌
Omzo vraiment je t adore Sama peura il faut avoir l esprit de depassement omzo t a bien parler . Canabasse dafa delou guinaw affairou khale to lay df mais tkt waxtane Len rk t a bien parler. Le boy a grandi
Sama yone nekoussi🙉
Omzo nite gua am gua classe conek dila wax talent kassé la motax niouy wax
Zo coula khol hamni loula gnor ngaye wakh kou khol sa visage
Wllah bro tu a b1 vie
Kham na ni dall nitt dagay nité mé nakk yalla bakhna boull tonntou moukkou one love omzo 😍😍
Respect a toi omzo
Canabass a deconnè