C'est vrai que nii khaliss moy motal youbary wayé diiné l'islam moy premier chose naniu dem diangi suniu diiné avant tout man mii dé fep fuma meuna nek القران الكريم كلام الله lay ndamô té alhamdou lilah tjrs thi bima neké talibe
Diadieuf Oustaz kadou yi machallah naam out teranga deh lou bakh wayé kom li Oustaz Assane wakh rek sûrement werseug yalla sougnou borom moko yor tekki for life yague nala suivre wayé dioum nga
Cheikh outheimine a dit: la réussite n'est pas de remporter une chose de ce monde mais la réussite est que tu sois écarté du feu et que tu rentres au paradis. Qu'Allah nous guide vers de nobles pensées qui nous accordent afia fi dunya Wal akhira
C’est vraiment ça La vraie réussite c’est qu’Allah nous fasse entrer au paradis et nous éloigne de l’enfer Tout ce qu’on aura sur cette terre comme matériel on le laissera ici à notre mort
Macha Allah ya oustaz kaddu rafétt na am n'a solo trop yalla nala yalla fay yiw tamou déffal niou déggeu AK toppou Mais man ndianguatt bima déff si vidéo tike for life bi Moy ki si soldarou chaytané yi la bokkou wallahi il travail pour satan notre principal ennemi motax ki kouy DJOULIt ta beugeu yalla ta beugeu têkhé wallahi do suivre ay conseillé yiy djougue si mom ndakh mo adouna rék moko Nior AK xaliss ta gnima djel référence nionou dougne ay référence donc il faut que les jeunes musulmans fâchent attention à ses genres de personnes parce que esprit bou saltalé lagne yor ta wallahi ay door katt lagne popularité AK ay vue rék lagne weur MOTAKH ils sont prêts pour faire tt
Sidy birahima fall Moni diamou léne yalla bame méle ni taye ngaye dée wayée liguéye léne bame méle ni fi ngéne sakhe liguéye sakhe diamou yalla la wayer yalla brome yitter diou kawer la andale tée boye dée si alleu n'a la guailndé raye téki for life si deugue la néke sa waye wouty djilaine khallisse
@@djigasalane7463yaw momou yay le chef des hypocrites, mais diakha louma ndax le prophète nous à averti, qu'il aura des gens qui vont appeler les croyants vers l'enfer
Wadji bakhoul mane sama papa la andal di ligeye naronako quitté ndakh ki mai heureusement ba yalla délossé sama khél Ki bakhoul koukay déglou dinga sankou😔😔
Attention les gars le mec il résume des livres, c'est pas forcement ces idées Lima ko deglou ba fi il dit des choses bien seulement nit maatoul nieupay dioum
Tekki for life dof la boudoone lolou dõ guis gni gua xamni séne temps yépou si ligueye lagniou ko ték té diko diãralé si xam xam ak dioup ba ame louni guagnie xeuy gniankate ko ,loulou Di wanéni tékki si lokho Yalla na nék liware moye nék Di gor goorlou
Et les prophètes YOUNUS Yakoub et les autres. Le boudjouman c grâce au coran qu'il a été connu et aidé il est riche dans son cœur. Quant à le fou provocateur il s'il peut donner que le Sénégal soit le pays le plus riche.
Ce tekki for life je l'ai écouté deux où trois fois des ses débuts sur youtube mais j'ai su que lui même a besoin d'aide car il ne comprend pas la vie🙏🙏
Il a sous estimé le vieux. Le prophète psl a dit allah ne regarde point vos portraits et vos richesses . Mais allah considère la sincérité de vos cœur et la convenance de vos actes. Le problème en est que eux ils lisent des livres dont leurs auteurs sont pas des croyants malheureusement.
Nanou andandoo désabonner si compte tekki for Life
Ñun Zo rekk lañuy toop
Yow mom ya geuneu dof senegal
Wéro
Waw waw
Masouma abonné si mome
Na nieup désabonner s’il vous plaît 🥺🤲
Je suis d’accord
Al hamdou lillah bagnou yalla mayéé Al quran kou am Al quran niako dara
Yaw yay doff bi 🖤
Je suis Tékki for Life depuis longtemps mais vidéo bi mome d’accord rouma si limou wakh touss 😢
C'est vrai que nii khaliss moy motal youbary wayé diiné l'islam moy premier chose naniu dem diangi suniu diiné avant tout man mii dé fep fuma meuna nek القران الكريم كلام الله lay ndamô té alhamdou lilah tjrs thi bima neké talibe
Diadieuf Oustaz kadou yi machallah naam out teranga deh lou bakh wayé kom li Oustaz Assane wakh rek sûrement werseug yalla sougnou borom moko yor tekki for life yague nala suivre wayé dioum nga
Cheikh outheimine a dit: la réussite n'est pas de remporter
une chose de ce monde mais la réussite est que tu sois écarté du feu et que tu rentres au paradis.
Qu'Allah nous guide vers de nobles pensées qui nous accordent afia fi dunya Wal akhira
Waaw quelle belle et véridique parole
Mâcha allah
Allahouma amine
C’est vraiment ça
La vraie réussite c’est qu’Allah nous fasse entrer au paradis et nous éloigne de l’enfer
Tout ce qu’on aura sur cette terre comme matériel on le laissera ici à notre mort
Tekki for life c'est un chrétien il s'appelle Joseph mendy.
@@sangareibrahima4480 oui t'as raison et je pense que beaucoup de ces abonnés ne le connais pas
Tékki for live mousou ma convaincre depuis ba mouy soufél out kham kham nakh khaliss té boudoul wone kham kham aduna dou toll fi
قال سبحانه وتعالى في كتابه العزيز ولو بسط الله الرزق لعباده لبغوا في الأرض ولكن ينزل بقدر مايشاء انه بعباده خبير بصير صدق الله العظيم
Kouy wo ndaw gni dieumèlèn si Al Quran ak kouy wo ndaw gni dieumèlèn si alalou adouna lolu dou combat diaroul sakh débat
Macha'allah diékh naa takkk wakh gua lépp
Macha Allah ya oustaz kaddu rafétt na am n'a solo trop yalla nala yalla fay yiw tamou déffal niou déggeu AK toppou
Mais man ndianguatt bima déff si vidéo tike for life bi Moy ki si soldarou chaytané yi la bokkou wallahi il travail pour satan notre principal ennemi motax ki kouy DJOULIt ta beugeu yalla ta beugeu têkhé wallahi do suivre ay conseillé yiy djougue si mom ndakh mo adouna rék moko Nior AK xaliss ta gnima djel référence nionou dougne ay référence donc il faut que les jeunes musulmans fâchent attention à ses genres de personnes parce que esprit bou saltalé lagne yor ta wallahi ay door katt lagne popularité AK ay vue rék lagne weur MOTAKH ils sont prêts pour faire tt
Wallahi tu a marché sur ma langue
Merci Outaz Ben' Omar Dieng fatelibi amna solo. Aye man tiit naa😮Kii okoh top sankou😢
Son problème est qu'il est trop matérialiste. Il resume la réussite à la richesse dans ce monde. Qu'ALLAH nous préserve de ce genre de personne
Seytané moye défe li mokoye wakh lo takh khamouko yalla nagnou yalla moussale si Seytané nagnou déme désabonné téki for life alkurane amoule morom
kii deiggoule sakh fou tekki di wakhei ! ndeysane
Wallahi dama meusseu bagn di déglou wadjioo diou nguir nimouy diapé né mome moo mouss et le reste ay dof laniou. Yallah naniou yallah yereum
Mâcha allah oustaz
Qu’Allah vous récompense pour cet éclaircissement 🤲🏻
Yalla bakhna bakhamouma teki fore merci oustaz
Sidy birahima fall Moni diamou léne yalla bame méle ni taye ngaye dée wayée liguéye léne bame méle ni fi ngéne sakhe liguéye sakhe diamou yalla la wayer yalla brome yitter diou kawer la andale tée boye dée si alleu n'a la guailndé raye téki for life si deugue la néke sa waye wouty djilaine khallisse
Kokou diaroul won sax tontou.
_صلّي الله عليٰ محمد_
Moi j'ai déjà démissionné sur téki for life
Dafa dioum rek wallahi
Mougn Sabran Jamila : patienter de la plus belle des manières 😊
Allhkhamdoulillah, Yalla na gnou Yalla samm
Alllahou akbar tekki néna bou yallah tiyéwonn weurseukk mom moy diokhé weurrseukk sayy yaaa nékh
Kèp kou beug MOUHAMAD SALALAHOU HALAYHI WA SALAM dèmal nga désabonner si compte teki for life 🙏🙏🙏
Dieuredieuf yalla nala yalla takhawou té barkèl liguèybi
Alhamdoulilah merci oustaz
❤diarudiufate wa alqoran karim 🎉
Wedina yalla ak yonenti bi 😭😭😭😭
masha Allah ya oustaz léral yii amna solo
جزاك الله خيرا ♥️♥️♥️🙏🏻🙏🏻
Ki da dioum yalna Yalla nginddi ñu nginddi ko
Il ne parle pas pour critiquer le Saint Coran , mais il critique l'esprit négatif qui amine la plupart des gens pauvres.
@@EtienneMendy-ze6vz maintenant tu veux dire que le Boudioumane a un esprit négatif ?
@@makingoff28 Sur le plan financière oui sans doute mais sur le plan religieux il est top ♥️
@@Antivir6-le-BanlieueStar meme sur le plan religieux
senegal da bari naffekk
Y'a pas de chrétien, ou bouddhiste ou athée pauvres ? Pourquoi faire l'amalgame entre le coran et la pauvreté
@@djigasalane7463yaw momou yay le chef des hypocrites, mais diakha louma ndax le prophète nous à averti, qu'il aura des gens qui vont appeler les croyants vers l'enfer
Subhanalah Alhamdoulilah Lahilaha ilalah Mouhamed rasoulilah PSL Alahou Akbar ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
mâcallha❤❤❤
Wadji bakhoul mane sama papa la andal di ligeye naronako quitté ndakh ki mai heureusement ba yalla délossé sama khél
Ki bakhoul koukay déglou dinga sankou😔😔
Kholal ma lolou rekk. Gniko gueum la yereum
Soubhanalah ! N importe qui parle de n importe quoi dans ce pays
Attention les gars le mec il résume des livres, c'est pas forcement ces idées
Lima ko deglou ba fi il dit des choses bien seulement nit maatoul nieupay dioum
@@UZEE- très lucide mec en voilà un qui réfléchit 1p
@@Sira-td6fuj'ai vraiment peur
Merci beaucoup oustaz walahi❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Oustaz dia dieuff merci beaucoup franchement
Macha Allah allhouma barik
الحمد لله
Dieureudieufati yalna yalla fayla yiw si barké al hourane karim ❤️❤️❤️❤️🙏 🙏🙏🙏 Alhamdoulillah
Wallahi El Bachir waliyu lako diapè❤❤❤❤
Al hamdouliah 💯
Kadou yi
Amna solo Jajeuf yaram
ماشاءالله 🙌🏿😍
Wahi réwandé deug la wah
Jaajef yalla nalla fayy ❤🎉
Merci beaucoup way ya oustaz ❤😢
Wa Ben Oumar yalla kham na ni guagg na la degue dama la dann sétane ms sa TH-cam bi da demaloul Machalah yalla na yalla defal diamou
Merci beaucoup Omar ❤❤
Way dieredieuf yalnala yalla fay yiw
Manchallah amna solo. Mais kokou mom da reur
Signalé ko teksi
Merci beaucoup oustaz
Merci beaucoup ous.omara dieng
machallah oustaz amna sollo diamou si yaw ❤❤
❤❤❤❤❤waw gour❤❤❤
MACHA ALLAH
Danguena degoul fi teki for life di wakhé rek, mane dh ndogo darala mais guissna ni fingueni wakhé ak fim wakhé bokoul
Teki for dadiale la
Machalla ❤❤
Diadieuf si lér yi seugne bi❤❤❤touti rék ma rére déi
Merci Oustaz ❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤ machallah oustage
Machallah Amna solo Serigne bi baayi len kii defla key
I'm from Gambia 🇬🇲 ❤جزاك الله خير
Barakallahu fiikum cheikh ben oumar yalna yalla samm la
Machalla am na solo lool oustaz dieureudieuf
Machallah oustaz Amna solo
Tek for ki da doff
Merci beaucoup ben omar❤❤❤❤❤
Al badri yàlna yàlla sàmmu ko ci Barkeb alxuraan ❤️
Machallah bonne interprétation
Alhamdouloilh Alhamdouloilh ❤❤
Machallah lou wér
Ma challah oustaz 😢😢
Machallah
Dafa dioume rek
Machallah amnasolo ❤❤❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉
Tekki for life xamoul gatt
Oustaz dieredief yala na yala defalla diam
Tekki for life dof la boudoone lolou dõ guis gni gua xamni séne temps yépou si ligueye lagniou ko ték té diko diãralé si xam xam ak dioup ba ame louni guagnie xeuy gniankate ko ,loulou Di wanéni tékki si lokho Yalla na nék liware moye nék Di gor goorlou
Diara dieuf oustaz tekki for life môme tay dafa doff
Jangate bi amna solo lool
Et les prophètes YOUNUS Yakoub et les autres. Le boudjouman c grâce au coran qu'il a été connu et aidé il est riche dans son cœur. Quant à le fou provocateur il s'il peut donner que le Sénégal soit le pays le plus riche.
Ce tekki for life je l'ai écouté deux où trois fois des ses débuts sur youtube mais j'ai su que lui même a besoin d'aide car il ne comprend pas la vie🙏🙏
Merci beaucoup Oustaz ❤❤
Man waadji deglounaako mai khamoul foumouy takhaw cheikh Bachir Amal diam
ماشاء الله ياشيخنا
Bien dit oustaz il est fou ce mec
Daga serigne bi ❤❤❤
Il a sous estimé le vieux.
Le prophète psl a dit allah ne regarde point vos portraits et vos richesses .
Mais allah considère la sincérité de vos cœur et la convenance de vos actes.
Le problème en est que eux ils lisent des livres dont leurs auteurs sont pas des croyants malheureusement.
@@Julaybib-h1l lolou molene di sank
Sama xol sedue na bene Oumar mou sèlue mi ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Jërëjëf wakh dji amna Solo
Dafa dof bilahi 😭
Bimou défé vidéo bi la désabonné ki weroul
C ton problem
Mashallah Aksssa Fall
Liii dafaye firndéle lii nekk senegal. Ñou méleni wadji beurina ci réwmi.